Je ne suis pas talibé baye niass mais ousmane mbow lingay deff raffettoul yaw sa wax yeup ci sangue Ndiaye lah waxall yalla bayih diambour de toute façon mongui liguéye di yaatal faydou baye bih té yaak moom yéna Bokk benn serigne meunookoo dindi lii dayy takh niou kheeb leen trop andd leen doon benn kouleen koh waxoul waxouleen deugu ,waar nitt kih akk weer nitt kih doubenn lolou dou djikooyy hanrif billah
Jeureudieuf Maolana CHEIKHOULKHAYRI ♥️♥️
Wa pays bi yeupou naniou khamni Cheikh Ousmane Mbow daffa âme ndigueul ci loumouye deff
Alkhamdoulilah so amoutone mou niaw
Macalla 🙏 alhamdolla
JeureJeuf Serigne bi Cheikh Ousmane mbow Ibn Cheikh Ibrahim Ould khaïry wallahii ndeyssan dafã léér billah 🙏🙏❤️❤️🔥🔥👍👍💯💯
Dieuredieufe mbow legui talibe baye yeup comprendre negne lene si Séne philosophie hi dakh yaw dieuredieufe mbow
Machallah mbokou lolou moy objectif bi yé talibés yii
ماشاء الله بارك الله فيك وجزاك الله خيرا
Dieuredieuf Serigne bi lëp dina lér inchallah.
Dieureudieuf cheikh Ousmane mbow xam xam bi rafetna
Macha Allah Serign bi lerrna yalna yalla yorka meudeud b si barke maulana Cheikh Ould Khairy ❤
Alhamdoulila bi ninhmatihi fil hinlmi
Ma challah allhamadou lillah
li dafa lérr ma cha alla
MACHA ALLAH WALAHI LERNA YALA NALA YALLA SAMOU
Machalla serigne
Yewou léne beute setneu bayiléne seny nelaw Cheikh Ousmane Mbow Yewwi n'a gars gni
Baye ba aduna di toukki baye diotna nieup nii djiitou ak niou mouddiou boul tegg hel borom hamham nga waaye fehel ba nekkal yallah thii lingaye wah boo bougue dinndi ak guinndi nitnii thii fenkat jii bii di oote oote thiaahaan
Je ne suis pas talibé baye niass mais ousmane mbow lingay deff raffettoul yaw sa wax yeup ci sangue Ndiaye lah waxall yalla bayih diambour de toute façon mongui liguéye di yaatal faydou baye bih té yaak moom yéna Bokk benn serigne meunookoo dindi lii dayy takh niou kheeb leen trop andd leen doon benn kouleen koh waxoul waxouleen deugu ,waar nitt kih akk weer nitt kih doubenn lolou dou djikooyy hanrif billah
Bougue binga bouga politique thii lingaye défendre kou baakh ngaye doone baayil politique cheikhe ouldou hayri hamnako baayi moye leppou bi fadli ilaahinnaasi jallah jalaalahou wo houbbou rasouloullahi daaha nabiyyaah
Jerejeef serign bi it’s all about Khairy Bai
Serigne bi yagui Walatematou wadji rek😂
Talibés SBN yinak djotna guéne yewou
Kepou koussi beugue yallah neu yéwou car gni môme Nakhaté rek laniou meune
Sofi nékoul wone mou gnaw