Lyssa s'était mariée avec Modou Wade. Le jour de sa disparition elle parlait au téléphone avec un présumé " Modou". Celui qui l'a pris en stop est témoin. Le chauffeur qui l'a conduit à Dakar est témoin. Le monsieur à la quincaillerie est témoin car il a confié les clés à lyssa. Même moi je peux mener l'enquête et trouver le coupable.
Ahhh histoire bi yémé na, nitt rerr depuis 4 ans et kenn khamoul si mom dara tamite, ou est la justice dans ce pays? Une enquête poussée aurait révélé la verité et soulagé cette famille. Je n'ose imaginer leur peine, cette situation est invivable surtout que son ex-mari, dernière personne à l'avoir vue vaque tranquillement à ses occupations🙄🙄🙄 YALLAH na BOROM BI dara teuwoul leral lep et délo Lissa si ay mbokam en vie, par la grâce du prophète MUHAMMAD SAWS🙏🏽
Quand on regarde la chaine" crime district les enquetes impossibles" quand une femme disparait son mari est considéré comme suspect numero1 parceque tu es la derniere personne a l avoir vu vivante il faut reouvrir le dossier pour que justice soit faite😢😢😢😢😢😢
J’aurais bien aimé que les associations féminines qui nous ont fatigué avec l’affaire Adji Sarr se penchent sur cette disparition inquiétante. Si lissa était une fille de puissant alors son sort aurait été éclairci depuis longtemps. C’est vraiment dommage
Et dire quand diarry sow faisait son "show " tout le senegal etait debout kouné di layam layami kii cas wam geun critik lepp depuis lors lépp ni tek justice bi manouko resourdre ba tey population def silence 😢
Le problème est que si la fille décide de rester avec son mari la police ne pourra pas intervenir car elle est majeur .ce qui inquiète est que elle a laisser un enfant donc si elle ne fait pas signe de vie ses parents vont trop s'inquiéter. Donc si lissa est actuement avec son mari son mari doit au moins tranquilliser la famille de Lisa et leur passer au moins leur fille au téléphone...et même si son père est contre le mariage il acceptera la décision de sa fille ..prions tous pour que la vérité soit rétablie et que Lisa reviennent voir son père et sa fille ci diameu. ..cette histoire m a triste vraiment.
Franchement li dou yoneu cette affaire les autorités font exprès de fermer les yeux sur le dossier li setane deug la niaw trop cette fille ne mérite pas ça de disparaître comme ça! Ces parents souffrent énormément !!!
Modou Yade khamna fimi né. Khaw ma kan moko nguembe mais lep dina ler. Modou Yade amoul serigne ay complice la am. Nous sommes dans l'aire de Macky Sall tout est possible
Rewww mo khamni lo wakh niouni mala eup Serigne di yakh nit gni rekkk metina trop yalla yalla bay sa tolll li motakh dougn developper police na der ligueyam way ki dafa yebater
Mane souma nékone papa Lissa bilahi wadhi la yotte ray ndeyam mou diekh deuk bou amoul justice ma fadial sama bop loumassi felk ma khamni lolou la mais ray sama doom di dokh day yomb trop
Mai pour regler la justice ⚖️ senegal 🇸🇳 la se seule solutions set OUSMANE SONKO PARCQUE ILA SUBIR TOUTE LES CONCECANCE don't on na confiant a lui Lou takh Senegalese bougouniou Lou bkh
Bilahi Diott Na ce mec wakh gnou fou Lyssa nékeu.Ça fait très longtemps, justice sénégalais warr nguén def s'en liguey sur cette affaire.bilahi Refane a besoin de son fils 😢
Li kokou nane rewou coumba ame ndeye coumba amoul ndeye deugue la deja carrelages keuram apres disparitions bi rek war na gnaw khel ak preuve yeup ga takhaw takhawatou yallah ni miunalou gnou la dara modou yade kholal sisa dom wakh lou khew😢😢😢
Senegal 🇸🇳 la guoguou injustices et police 🚔 crompi coumba am ndeye AK coumba amou ndeye ..modou nek si lissa reree merere quelle est le travail de notre brigarde de recherche
Mann dhé Dina déme Nicaragua Sénégal d'où réw walahi,lii vrement dafa méti j'ai des larmes au yeux walahi ,masouma gueum touki , mais deuk bi , walahi d'où woroul.
Cette affaire ne doit pas rester impunie . Il faut qu'on éclaire la lanterne aux sénégalais et particulièrement à la famille. On réclame justice dans cette affaire . Modou yade ne doit pas être l'exception.
Je pense qu'il a tou planifier du moment où il ne voulais pas que le chauffeur qui amenait Lyssa le voit donc je c qu'il est trop prudent sur ce côté même s'il ya un détectif il le s'aura
Il fut un temps son ex beugone na fi kharou d'après informations. Mais imagine taye sou Modou guédonne adouna ? Yallah Na yékh Affaire bi doumassa féne🤔 Yallah mo Bari soutoura.
Mais Modou yade son mari wakhna lepeu nena molène epou khaliss molène epou Serigne au non de koi ak louko waral c le 1 er suspect naniou ko lidianeti mou wakh foumou ndeck c trop facile baparer mouy dokh aye sokhlam famille lissa ndeck si niacré je ne comprends plus
Bilahi li defa meti si khol dpw des années monougnou ame dra lou lere ci domou diambour bi waw bane Sénégal lagnou nek surtout gnoune domou badola yi Bilahi gno guena sone ci rewmi sou feké domou milliardaire cone fegne na problème lissa dpw 2019 té mona amna problème djiguen you bari yé fou djiguen té reglé nagnouko bou yague yalana yalla lerale leupci barké alkhourane
Rey nit baparé. Di narguer ay mbokkam té lep leerna. yen dal sou élection dioté. nguéne boycotter wa maki nguéne sannil kénéne sou. Nguéne ko votelé. Ma khamni lissa niorouléne
Mais yenn ce Modou Yade c'est l'adjoint de Dieu wala malaka la? Ki dolen dém kidnapper ko dougeul ko alleu niouss ko bam wakh fou Lissa nekk. Li daa yomb trop
Justice amoul temps pour askan bi ndax politique . C est triste . WALAHI je compatis.😢
Lyssa s'était mariée avec Modou Wade.
Le jour de sa disparition elle parlait au téléphone avec un présumé " Modou".
Celui qui l'a pris en stop est témoin.
Le chauffeur qui l'a conduit à Dakar est témoin.
Le monsieur à la quincaillerie est témoin car il a confié les clés à lyssa.
Même moi je peux mener l'enquête et trouver le coupable.
Modou yade wakhal fou domou diambour bi nekk nguir Yallah guadou ngua akh 😢😢😢
Modou yade ya guadou akh deug
Guénél domou diamour dji
C’est triste 😢 😢 ça
Bilahi
Kiii mom xamnaniiii khawma thi serigne lako tegg khawma dolei wayeii bess bou dieukk thi bamelll dinako layooo
4an takou mako t kein douko diarigno c trop
Ahhh histoire bi yémé na, nitt rerr depuis 4 ans et kenn khamoul si mom dara tamite, ou est la justice dans ce pays? Une enquête poussée aurait révélé la verité et soulagé cette famille. Je n'ose imaginer leur peine, cette situation est invivable surtout que son ex-mari, dernière personne à l'avoir vue vaque tranquillement à ses occupations🙄🙄🙄
YALLAH na BOROM BI dara teuwoul leral lep et délo Lissa si ay mbokam en vie, par la grâce du prophète MUHAMMAD SAWS🙏🏽
Quand on regarde la chaine" crime district les enquetes impossibles" quand une femme disparait son mari est considéré comme suspect numero1 parceque tu es la derniere personne a l avoir vu vivante il faut reouvrir le dossier pour que justice soit faite😢😢😢😢😢😢
Tu a beau regarder les enquêtes impossible de crimes district 😊 mais Vraiment ta raison suspect 1 c'est son marié surtout son ex
Affirmative
Deugleuh mais sénégal dangay warou
a mon avis il l'a tué et entérré dans sa maison
@@aron6054c’est ce qu’on croiyais tous Modou yade n’est pas fou sûrement il l’a déterré pour déplacer le corps yallah sunu Borom nitt Lissa 🙏🏾❤️
C une honte pour la justice sénégalaise
Ay modou yad yeureumnou😢😢😢😢😢😢😢😢
Yalla nako Yalla niiite amine ❤
Non billahi Sénégal dou rew Coumba am Ndaye ak Coumba amoul ndaye mes 2mois molen fi desé😢😢😢
J’aurais bien aimé que les associations féminines qui nous ont fatigué avec l’affaire Adji Sarr se penchent sur cette disparition inquiétante. Si lissa était une fille de puissant alors son sort aurait été éclairci depuis longtemps. C’est vraiment dommage
Fi amoul khaliss motakh.
yaléne eupp Serigne mé yalla mola eupp dolé ak sa Serigne yeupp khawma loutakh nga yobou domou 😢 diambour mé ak loumou mounti done dara diarouko 😢
Et dire quand diarry sow faisait son "show " tout le senegal etait debout kouné di layam layami kii cas wam geun critik lepp depuis lors lépp ni tek justice bi manouko resourdre ba tey population def silence 😢
Je sais pas elle est où mai que Dieu là protège 🙏🙏🙏
Thiey li metina trop modou yade nekal gor avouer lane nga deff lissa yewi ay mbokam yewiniou.histoire streserna nieup bilay
Vrement li metina yalla nako yalla leral fegnalko
Li vraiment métina. Justice nane gnou dimbalé nguir Yalla ibi wat enquête bi résoudre problème bi mou diekh. Que justice soit faîte
Mane damay sétane id faire crime toubayi soudone gniom fégnie Na bou yagg même sou fékké doundoul li yombouna trope 😢😭😭😭😭😭😭
Senegal dou réw parc hann la rek amoul loi ni reglement
@@aron6054 🤣bilay
Le problème est que si la fille décide de rester avec son mari la police ne pourra pas intervenir car elle est majeur .ce qui inquiète est que elle a laisser un enfant donc si elle ne fait pas signe de vie ses parents vont trop s'inquiéter. Donc si lissa est actuement avec son mari son mari doit au moins tranquilliser la famille de Lisa et leur passer au moins leur fille au téléphone...et même si son père est contre le mariage il acceptera la décision de sa fille ..prions tous pour que la vérité soit rétablie et que Lisa reviennent voir son père et sa fille ci diameu. ..cette histoire m a triste vraiment.
Franchement li dou yoneu cette affaire les autorités font exprès de fermer les yeux sur le dossier li setane deug la niaw trop cette fille ne mérite pas ça de disparaître comme ça! Ces parents souffrent énormément !!!
Franchement un pays de desordre ni loi ni réglement
Bily cas bi nieup la méti yalla na yalla até
Li boussi etat wakhoul bilahi dina eupi lokho. Li boudone sama rak modou yade dinama ray wala ma rayko
Waaaw fan lanou nek ; metina.
C trop facile de le laisser vaquer à ses occupations il doit vous édifier par la force
Honte à ce pays
Lissa tine xana amoul aye fréres you mouna diap modou yade réndi ndeyame come deuk bi amoul justice ngéne fadialko séne bopou
Modou Yade khamna fimi né. Khaw ma kan moko nguembe mais lep dina ler. Modou Yade amoul serigne ay complice la am. Nous sommes dans l'aire de Macky Sall tout est possible
Wakh deug Yalla maky yoname nékou si. Yen haine yi si nit nak bakhoul
L etat est complice ça veut tout dire.
@@LaingLifegni nio sof ak Macky niiit la comme nieup ame famille niou sonal ko trop
Ndaysane pape dji soneu na weur na dom ba soneu li enquête bi lagn topoul
Khana lissa ak diari sow yemouniou thi senegal yew tamit loutakh nga togue ba soga wakh li
Avec tout ça on dit Sénégal c'est un État de droit
Ki ska rayouko soulko mes yallakh bakhna
Réew mi wallahi amoul yoon
Boh démé dako gasss soule nakh menoul disparaître nonou
Rewww mo khamni lo wakh niouni mala eup Serigne di yakh nit gni rekkk metina trop yalla yalla bay sa tolll li motakh dougn developper police na der ligueyam way ki dafa yebater
Mane souma nékone papa Lissa bilahi wadhi la yotte ray ndeyam mou diekh deuk bou amoul justice ma fadial sama bop loumassi felk ma khamni lolou la mais ray sama doom di dokh day yomb trop
Modou yade mome dama fokk ni dou setane vidéo yi khana kou ame xol deugg do sétane li meune si dara tokk nek si sa conscience tranquille bilahi
Sénégal dioulit Gi dañ koy wakhe rèk wayé Bari wou Fi dé Xam ngani yénn Yi dioulit duoko dèf
Sous development mo Metti parce que aspect de la vie lay affecter wa Salam
On doit eclaircir ce problème
Bilahi li defa meti yag n'a
Il faut k la famille porte plainte encore le mari
Il la tue et enterré c’est un assassin 😭
Tu as tout dit
Yahlah nako yahlah nite
Mai pour regler la justice ⚖️ senegal 🇸🇳 la se seule solutions set OUSMANE SONKO PARCQUE ILA SUBIR TOUTE LES CONCECANCE don't on na confiant a lui Lou takh Senegalese bougouniou Lou bkh
Bilahi Diott Na ce mec wakh gnou fou Lyssa nékeu.Ça fait très longtemps, justice sénégalais warr nguén def s'en liguey sur cette affaire.bilahi Refane a besoin de son fils 😢
Li kokou nane rewou coumba ame ndeye coumba amoul ndeye deugue la deja carrelages keuram apres disparitions bi rek war na gnaw khel ak preuve yeup ga takhaw takhawatou yallah ni miunalou gnou la dara modou yade kholal sisa dom wakh lou khew😢😢😢
Modou si bopam laniou wara mbett foumu nek walahi doxèko guinaw defko lou bonn niou xol dah amna serigne mbam bi😭😭
Senegal 🇸🇳 la guoguou injustices et police 🚔 crompi coumba am ndeye AK coumba amou ndeye ..modou nek si lissa reree merere quelle est le travail de notre brigarde de recherche
Ay way modou yade diokhèl domou diambour dji😢
😭😭😭😭Metina
Vraiment c triste 😢
mane bou done mane MODOU KITENAPET NA KO BA LISSA FEGNE BILAHI
Mann dhé Dina déme Nicaragua Sénégal d'où réw walahi,lii vrement dafa méti j'ai des larmes au yeux walahi ,masouma gueum touki , mais deuk bi , walahi d'où woroul.
Mba d’où sacrifice?
Modou yade dolen publié fotom nit gni lidieunti ko
😭😭
Cette affaire ne doit pas rester impunie . Il faut qu'on éclaire la lanterne aux sénégalais et particulièrement à la famille. On réclame justice dans cette affaire . Modou yade ne doit pas être l'exception.
Si je comprends bien.Modou Yade dal si mistik lako tek .. mistik yimou yorr nak forna trop . Lima dégu fi yeup justice tok diko setane.
Mystique la kaye
Lii dafa yobmo trobp 😢😢😢😢😢
a mon avis dafko réye soul ko na policier verifier keur gui , justice bou domerame lagne yoré
Dou étranger ça ne se dit pas . L'étranger est une personne qui ne mérite pas ce qui est arrivé à Lissa .nguen balma
Lolou rek mokoy fadj points
Démléñ gase carreaux khôl bou bakh sibir keurgui
Mais Solene khamer fou modou yade di ligueyer, topou leneko en filature niakoul mou def Lou suspect donc comme yone defoul ligueyam
Je pense qu'il a tou planifier du moment où il ne voulais pas que le chauffeur qui amenait Lyssa le voit donc je c qu'il est trop prudent sur ce côté même s'il ya un détectif il le s'aura
@@ramich4796 yeah vraiment c’est très compliqué et il y à trop de non dits
Lissa dé bimouy dèm Taya Touko Sénégal goor ñi Bari woul
YAL naniou yallah aral bopom on ne sait jamais motakhh dii mouslou rekk té doylo yallah si leupp
Halis ak mystiq lalen modou yade di diay li dafa yomb torop
Senegal amul yone maky sall sa data ndaye maky sall sa data ndaye maky sall sa data ndaye maky sall sa data ndaye maky sall
Lissa bala 2024 dina fegne inechalla mako wakh note les
Amine ya rabbi
Mais Ana modou yade
sonkhna si koye niane MAKY SALL MARIEME FAYE SALL 😅😅😅😅SADIGUA SA NIANE
Ki bimouye déme sakh tayouko
Amoul bayi dh mbirr mi lous na looool journalise yi envitė lene modou yade😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
C'est écœurant, pourquoi cette affaire traine comme ça
😢😢😢😢😢
Senegal du rew ana mussa fal Antondion yagg fay bara chankhare ak sen elema yi don ray boy yi mai nak Gissnan fi fulber samb dijdè bajdi
Wala mou ligueyko modou mi dafa yew lissa
Il fut un temps son ex beugone na fi kharou d'après informations.
Mais imagine taye sou Modou guédonne adouna ? Yallah Na yékh
Affaire bi doumassa féne🤔
Yallah mo Bari soutoura.
2019 ba legui guen nek si fi loudul yallah nèn la boulen defon mobilisation feko fimou defko lou niap wouy dina wakh fou ki nek li dafay dak xol
Mais Modou yade son mari wakhna lepeu nena molène epou khaliss molène epou Serigne au non de koi ak louko waral c le 1 er suspect naniou ko lidianeti mou wakh foumou ndeck c trop facile baparer mouy dokh aye sokhlam famille lissa ndeck si niacré je ne comprends plus
Ki damako sakh éne
Mandjou.🇸🇳🐘🐘✊🏿❤️❤️❤️❤️✊🏿✌🏿✌🏿✌🏿👍🏿
Sk douguene niane audience si macky pour lui faire part de ce blem.presi beuguoul kouy woner doler té surtout teko si biroum familly serigne
Ay way demlén si Serigne Ass Barham Thiès mou waxlenn fou khalébi nek ou bien s'il est en vie ou pas guir Yallah
Foumou deukk si Thies?
Si vous voulez connaître le suspect allez cueillir son ex mari Modou Yade.
Modou khana wa kheur niak diamou la bok djaye dole sokhna Botor dongue mothi dess té 2mois la fi desse mou deme😂
Mane lima diakhal pkoi cette affaire n'est ps traiter sur les reso sociau
Bilay
Lissa dal amoul kififa
Dém bi dé tayouko modou mo deugeu ndayame sakalko pékhé wayé lép loudoul yalla nénla
Lyssa dafa wara fegne
Mé ki lane motakh mounou niouko ték si yone
Bilahi li defa meti si khol dpw des années monougnou ame dra lou lere ci domou diambour bi waw bane Sénégal lagnou nek surtout gnoune domou badola yi Bilahi gno guena sone ci rewmi sou feké domou milliardaire cone fegne na problème lissa dpw 2019 té mona amna problème djiguen you bari yé fou djiguen té reglé nagnouko bou yague yalana yalla lerale leupci barké alkhourane
Bouko police diapone massko courant dina wakh
Modou yade dh sou rayoull Lisa gêné nako deukkk biii
Khana diari sow mo gueune lissa tine
Mane dai souma bokone ak khalebi bilaxi modou dina ngenne Lisa wala mou Ray ma
N'a famille wam dem diap otage un membre de sa famille legui leep leer
En tout cas modou yade ni waroul won ko fek ci diam
Il l'a tué
Rey nit baparé. Di narguer ay mbokkam té lep leerna. yen dal sou élection dioté. nguéne boycotter wa maki nguéne sannil kénéne sou. Nguéne ko votelé. Ma khamni lissa niorouléne
Mais yenn ce Modou Yade c'est l'adjoint de Dieu wala malaka la? Ki dolen dém kidnapper ko dougeul ko alleu niouss ko bam wakh fou Lissa nekk. Li daa yomb trop
yaw mi tamit, pourquoi tu n'es pas parti à la police ?
Dite à sa fille que ton père a enlevé sa mère Lisa
Mais li doynawar lol modou wade dee bou feķke mo deff li bou teudee dounalaw