Pape ale est ce que le gouvernement peut arrêter de mentir la population sur les dons des Sénégalais de l extérieur Di yakk derr et les consulats n ont rien donné a personne.ce message vient depuis Maroc.merci
salut pape je soutien la thèse de Mamadou gueye depuis maroc nous les sénégalais qui vivent au Maroc on a pas encore reçu aucun dons vient de l'état du Sénégal ni de celui du maroc ensuite ya n'a bcoup qui en ont besoins bcoup de sénégalais ici ne travaille plus depuis le 15mars nous avons reçu une plateforme pour covid19 pour faire des inscriptions pour bénéficier mais jusqu'à présent rien queudal pape Alè les choses doivent signaler à l'heure on en a ralbole
Baye Modou depuis Maroc gnoguilay beguee fila ziar les sénégalais du maroc n’ont reçu de l’état du Sénégal nous sommes en chômage en même temps on paye les loyers
Pape Alé nioune gninek frontière bou Maroc le 12 mai laniouy ame fi 2 mois nioune Sénégal cas importé laniouy bagne motakh defouniou benne efforts si nioune nioune nioléne gueune wére trop c'est trop sounekhone Macky soube niou dougue Sénégal on a le droit d'entrer dans notre pays loutakh Macky nangou France envoyer Ay vol pour français yi neck Sénégal mome ay domou rèwome mou bloqué léne si frontières yi partout dans le monde
Salut PAN,moi je fais partie des sénégalais qui ont rempli le formulaire d'aide pour la diaspora, mais les autorités sénégalaises demandent de faire parvenir un document bancaire comme poste pay ou carte bancaire, mais ici en Italie si tu es en situation irrégulière tu ne peux pas avoir un document bancaire, c'est pourquoi y a problème
Pape Alé j ai pa suivi l emission en direct sino ma wooté.Mai lila waji wakh si maroc lou wer la .Man fi la deukk.Wakhou ma gnifi bloquer sah mai gnifi deuk sah dano soneu.Pas gni regulier di liguey dan des societé com moi g aucun souci.Mai ceux ki sont dan l informel guiss na une femme nena loum lekk sah amoutouko. Aide etat marocain sah la gayi gueneu guiss.Amna nio khamni boudoulwone etat marocain ou les bonne volonté senegalais yifi nekk ta stable ,niou dé
IL FAUT QUE LES SÉNÉGALAIS SE RÉORGANISENT + QUE BIEN POUR QUE CETTE SITUATION NE SE RÉPÈTE + DANS LE FUTUR...1 HOMME OU UNE FEMME AVISÉS EN VALENT 2...OU 3...LOU EUP TOUROU TÉ BOU NDOKH TOURO ANN BAKH DÉSS..WAYÉ BOU BÉNNÉNNÉ DAGNIY ROTIWATT...
Pape yaa baax, yaayé sénégalais moo deugeurr boppou, ligne dagouko OUBBI pour gni am ay djaféh djaféh, ngén di wooté di geureumaaté rékk mélné Lou ma xamoull, gnakk faayda am djiott.. Nit day am faayda waayy....!!!!
NA SÉNÉGALAIS KHAMNÉ KÉNN DOULÉNN DÉFARAL SÉNN RÉW DI DIOGUÉ SA BITIM RÉW...KEUR-GUI KOU NÉKK SA BIR KËUR GUI MO KAY DOKHAL??DOU KÉNÉNN..KOU WAKH LÉNNÉNN WAKHOUL DEUG..NANOU BAYI TRICHER AK FÉNN..SURTOUT POLITICIEN YI....GNI NÉKK BITIM RÉW NANOU DOUGOU SI EXPOSER SÉNN PROBLEME...
Sénégalais yi nek gambie amnathi gnou sone gnibissi rek lagnou beug. Nagnelen testé kou négatif gnou assistéla nga gnibissi. Au lieu de supprimer mes commentaires vérifiez d'abord l'info
Pape ale est ce que le gouvernement peut arrêter de mentir la population sur les dons des Sénégalais de l extérieur Di yakk derr et les consulats n ont rien donné a personne.ce message vient depuis Maroc.merci
Merci gueye mamadou wakhe deug yalla
Pape alè Niang Seul journalist au Senegal
salut pape je soutien la thèse de Mamadou gueye depuis maroc nous les sénégalais qui vivent au Maroc on a pas encore reçu aucun dons vient de l'état du Sénégal ni de celui du maroc ensuite ya n'a bcoup qui en ont besoins bcoup de sénégalais ici ne travaille plus depuis le 15mars nous avons reçu une plateforme pour covid19 pour faire des inscriptions pour bénéficier mais jusqu'à présent rien queudal pape Alè les choses doivent signaler à l'heure on en a ralbole
Merci beaucoup grand frère pape
merci beaucoup pape ale
I'm very happy you are a best journalist in Senegal
Sénégalais mon Tëkhëut Dëug Dëug La ligne est réservée pour un thème bien précis
Merci beaucoup PAN !!!
Merci beaucoup pape Ale
Baye Modou depuis Maroc gnoguilay beguee fila ziar les sénégalais du maroc n’ont reçu de l’état du Sénégal nous sommes en chômage en même temps on paye les loyers
NIANG BALO ZIARNALA DIEREDIEUF YALNA BOURBI SAMEULA ARELA AMINE!
babe Allain dodall amnasolo loll barkep s saliuo ❣️❣️❣️👍👍👍👍🙏
Salam pape Ale macha allahou yalla barkele
Senegalais dou deeg. Arètè dapeler au telephone pour ne rien dire ou fair des Saant et des Geureums.
PAN il faut les repeller ca pour chak emmision
Con rèk
ماشاءالله
C trop pape tu es fatiguè. Man personnelema manouma sa liguèye bi yaatouga lool amina depuis Uk
Machallah
Fierté de vous pape
Pape Alé nioune gninek frontière bou Maroc le 12 mai laniouy ame fi 2 mois nioune Sénégal cas importé laniouy bagne motakh defouniou benne efforts si nioune nioune nioléne gueune wére trop c'est trop sounekhone Macky soube niou dougue Sénégal on a le droit d'entrer dans notre pays loutakh Macky nangou France envoyer Ay vol pour français yi neck Sénégal mome ay domou rèwome mou bloqué léne si frontières yi partout dans le monde
Salut PAN,moi je fais partie des sénégalais qui ont rempli le formulaire d'aide pour la diaspora, mais les autorités sénégalaises demandent de faire parvenir un document bancaire comme poste pay ou carte bancaire, mais ici en Italie si tu es en situation irrégulière tu ne peux pas avoir un document bancaire, c'est pourquoi y a problème
Vont juste utiliser vos données personnelles Faites très attention
Nous on voit rien de l'aide aux Sénégalais de l'extérieur
Nice Nice Nice je click j'aime
Coronabusiness its réal 😲😲😲 🇸🇳🇸🇳 yéwu lin
Big up PAN
President MACKY SALL FACE A PAPE ALÉ NIANG.
LA FIERTÉ DU SÉNÉGAL C VOUS LE GRAND PÀTRIOTE PAPEU ALÈ YIALA NANIOU FÉKÉ SA YIÉNÉ SI YIOKETÈ WÈÈRR DIAAAME AKI KHÈWALE
Salam ziar PAN
Mais et les senegalais bloqués au Senegal pour rejoindre leurs pays d accueil ?
MILLIONS D'ABONNÉS ak GROUPE de PRESSE YALLA NAGGNOU KO YALLA MAY INCHALLAH.
Di door marteau baye Door si période pandémie non le Sénégal va mal 😭😭😭😭
Yalla na la Yalla diaple
Pape ale 🙏
Pape Ale de tout coeur avec toi, depuis Saint-louis mangui rafetlou ligueyy bi. Guiss na sama si emission bi ak famille , en tant que patriote.
Ndiarign Macky Sall thi Senegal la guisoule
Nice nice baye ale
Yalla nomina
Pape Alé j ai pa suivi l emission en direct sino ma wooté.Mai lila waji wakh si maroc lou wer la .Man fi la deukk.Wakhou ma gnifi bloquer sah mai gnifi deuk sah dano soneu.Pas gni regulier di liguey dan des societé com moi g aucun souci.Mai ceux ki sont dan l informel guiss na une femme nena loum lekk sah amoutouko. Aide etat marocain sah la gayi gueneu guiss.Amna nio khamni boudoulwone etat marocain ou les bonne volonté senegalais yifi nekk ta stable ,niou dé
mais ténio toukhou guir yalla bayi Sénégal ak politiciens yi niou yapanté séni biir😳😳😳
no bro il faut se battre pour changer les choses inshallah
MACHALA PAPE LAF THIAT
La dame blokè a New York. Laise moi ton email ou numero. Je suis aux Etats Unis he veux voir quesque je peu fair
Pape yalna yalla godal sa fane
Merci beaucoup pan
Écoutez les thèmes svp
Passez à l essentiel
وابتغ فيماءاتاگ الله دارالاخرةولاتنس نصيبگ من الدنيا واحسن گماأحسن الله إليگ ولاتبغ الفسادفى الارض ان الله لايحب المفسدين
Fal ngourou thioune li lay indi assumons rek
IL FAUT QUE LES SÉNÉGALAIS SE RÉORGANISENT + QUE BIEN POUR QUE CETTE SITUATION NE SE RÉPÈTE +
DANS LE FUTUR...1 HOMME OU UNE FEMME AVISÉS EN VALENT 2...OU 3...LOU EUP TOUROU TÉ BOU NDOKH TOURO ANN BAKH DÉSS..WAYÉ BOU BÉNNÉNNÉ DAGNIY ROTIWATT...
voila le Sénégal mon beau pays 😂😂😂
aler du courage baye aly
Corona politique yagnako wakhe dé bakhe na rek légui géne fékisima dé
Corona gangstérisme d etat là
DIEUWRINE DIEUREDIEUF
Gni gnom khana amougnou retourle gars est clair est les gens appelle pour ne rien dire , voila l'indiscipline tant decrié
Salut Pape Alé Niang. Passez le numéro svp
Hey pape Alé yaw do nit boffi nékoulon mboukhoum dinafgi Mbary Yalla nalla Allakhou sam
Pape yaa baax, yaayé sénégalais moo deugeurr boppou, ligne dagouko OUBBI pour gni am ay djaféh djaféh, ngén di wooté di geureumaaté rékk mélné Lou ma xamoull, gnakk faayda am djiott.. Nit day am faayda waayy....!!!!
Maky sall c le président le plus nul si histoire Sénégal
esca societe civile bi amna contorole
si medicamente yi nouye diokh malade yi
ak negu necka caranteen ??? PAPE
Ce qui sont bloqué au senegal peuvent revenir sur air france, sauf que le billet coûte cher
Tristement triste 😥
Salam mashalah question yi ngaye late thie PNA askanewi yépagui khare tontouyi diueuredieufety pape alé amatina solo lol.
Bonjour Pape alé que dieu vous protège
Pape alè songa tu dis et rèitère la meme chose. Fatiguè ga
Prssident est ce que nekoul fi di setane sakh ak pseudonyme
Pape alle 1 euro bene modou modou encaisser woune ko
NA SÉNÉGALAIS KHAMNÉ KÉNN DOULÉNN DÉFARAL SÉNN RÉW DI DIOGUÉ SA BITIM RÉW...KEUR-GUI KOU NÉKK SA BIR KËUR GUI MO KAY DOKHAL??DOU KÉNÉNN..KOU WAKH LÉNNÉNN WAKHOUL DEUG..NANOU BAYI TRICHER AK FÉNN..SURTOUT POLITICIEN YI....GNI NÉKK BITIM RÉW NANOU DOUGOU SI EXPOSER SÉNN PROBLEME...
Merci
Ou va t'on avec nos dirigeants.pourquoi veut on mettre dieu a cote pour régler nos problèmes..
Merrcii tonss
Li doyna war bilahi 😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Svp pa alé sa numero watchap
Non amna senegalais you con 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Moumdal xalaas Lii duyna warrrrrrr
Les. Gen. Compren. Pa
Mais pape bou souniou meunoul def dara. Souniou khalif genereaux naniou def dara wooté maroc niaane roi bi bakhame
nitt kou khalaatoul bammeel lou koneekhati moudeff !!!
Sénégalais yi nek gambie amnathi gnou sone gnibissi rek lagnou beug. Nagnelen testé kou négatif gnou assistéla nga gnibissi. Au lieu de supprimer mes commentaires vérifiez d'abord l'info
Macki kun migi liir risususuyi
Cv
Les mêmes lives reviennent toujours rien ne va changer suis désolé
I'm very happy you are a best journalist in Senegal
Merci pape ale