MIA GUISSÉ fond en larmes, Krumah triste, Mamy victory & Défa au "console": Revivez la folle journée

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 11 ธ.ค. 2024

ความคิดเห็น • 162

  • @ndeyegningn9021
    @ndeyegningn9021 ปีที่แล้ว +180

    Hana kéneu amatoul droit dioy tamit bayilén diambour bi . Li mou doundou moko ham . Fichez lui la paix sof nguén trop.

    • @benajim9357
      @benajim9357 ปีที่แล้ว +2

      Yaw je t'aime denga

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 ปีที่แล้ว +2

      Bilay ioe amna foy tolou thi sa doundeu lo wakh djioy ndakh sa khôl moy fesss srtt bo néké kou sensible Mya nakk elle est come ça mei gnou beuri meunougnou comprendre lolou bayi len ko mou guéné lou nekk thi khôl bi après cv passé

    • @ndeyegningn9021
      @ndeyegningn9021 ปีที่แล้ว

      Je t'aim aussi benajim

    • @ndeyegningn9021
      @ndeyegningn9021 ปีที่แล้ว

      Véronique Natack danio comprendroul rék li mouy doundou AK li mouy yeuk si holam

    • @jamdong221
      @jamdong221 ปีที่แล้ว +1

      Vraiment

  • @zazamata4305
    @zazamata4305 ปีที่แล้ว +44

    Du courage à chaque fois tu es je regarde des vidéos tu me fais pleurer malgré que je n'ai que 12 ans je t'aime Je t'aime mia et j'espère que quand je serai grand je serai comme toi❤💗❤

  • @adamadiop3322
    @adamadiop3322 ปีที่แล้ว +12

    Je pense kel a trop souffert du coup ya d certains de c thèmes ça la touche facilement 😭massa ma belle😍

  • @soukeynaebraheem4431
    @soukeynaebraheem4431 ปีที่แล้ว +7

    No face mi traumatisé na domou diambour bi il faut que mou am suivie psychologuique vraiment 🥺

  • @yolandediedhiou1921
    @yolandediedhiou1921 ปีที่แล้ว +36

    Bilahi mia dama niéwantal soit forte ma belle c'est juste un passage ça va passer inchallah ont t'aime ma belle

  • @ndiayemandela5275
    @ndiayemandela5275 ปีที่แล้ว +219

    Je vois qu'elle n'arrive toujours pas à digérer son divorce c'est juste ça yalnalèn yalla taxawou mom ak ex djeukeureum yeup bidiaahil Moustapha

    • @alimatou2976
      @alimatou2976 ปีที่แล้ว +26

      Yow dee beugoulo ko ki liko djeukeureum def yeup xamoulo ko mo takh ga koy gnanal delou elle a tellement soufère ah

    • @jazzjazz4902
      @jazzjazz4902 ปีที่แล้ว +13

      @@alimatou2976 YOW MOME SYTANEE NGA SATAN PIRE YAKO FEEKEE NGAY BAKAR NI REK

    • @safietouciss9772
      @safietouciss9772 ปีที่แล้ว +8

      ​@@alimatou2976 yasi tek sa beute

    • @ndiayemandela5275
      @ndiayemandela5275 ปีที่แล้ว +14

      @@alimatou2976 j'ai pas parlé de réconciliation mais plutôt de diameuh pour chacun des deux il faut bien lire avant d'ouvrir la bouche en plus dèl wakh louleuh woor parce que je sais que sa Yaye yageuh nala niouss et tu l'aimes toujours

    • @mamydtamaragaye7661
      @mamydtamaragaye7661 ปีที่แล้ว +1

      @@alimatou2976 😂😂je me pose la questions nane qui loumouye wakh ni? Faff ma guiss sa commentaire.mia et sa famille gnoko wakh,gnoné elle a souffert,c’est pk ga commenter li.Mais Sénégal môme kou wakh sa xalate gnou saga là walla gnou gnak la téguine.en tt cas,que les 2 concernés soient heureux. A part ça, le travaille des filles sont dur mais excellentes.merci seneweb

  • @rouguietousy2292
    @rouguietousy2292 ปีที่แล้ว +36

    Elle essaye d’être forte mais c’est pas si facile que ça laisse le temps te guérira

  • @marietoucissokho8490
    @marietoucissokho8490 ปีที่แล้ว +44

    Courage ma belle effort

  • @ndeyecodoudiouf1926
    @ndeyecodoudiouf1926 ปีที่แล้ว +51

    Courage ma push a chaque fois que je regarde tes vidéos tu me fais pleurer 😭

  • @aureliediene6491
    @aureliediene6491 ปีที่แล้ว +38

    Ce sont toutes les filles qui pleuraient à cause du thème de la chanson d'aujourd'hui. Je trouve le fait que seneweb ait choisi de montrer uniquement les pleurs de mia guissé juste pour se faire un maximum de vues très malsain c'est même méchant 🤮

    • @badu_252
      @badu_252 ปีที่แล้ว +6

      Voilà un commentaire digne de ce nom 🤞👌🏾

  • @piwou7290
    @piwou7290 ปีที่แล้ว +23

    Mia je trouve que tu devrais prendre du recul pour toi ,je trouve que tu ne vas pas bien . Voyage ou isole toi un peu et profite de ta famille. Fuis les caméras un peu la pression . Le'plus important c'est ton bien être. intérieur .

  • @afriquemonafrique8284
    @afriquemonafrique8284 ปีที่แล้ว +28

    Dioye kène menouko téyé du courage ma belle

  • @loubess2022
    @loubess2022 ปีที่แล้ว +88

    Je souhaite seulement que vous lisiez mon commentaire . Méfiez vous des médias. Vous êtes une célébrité jeune talentueuse maschalla . Réécoutez la chanson que votre ex-mari a chanté en guise de conseil vous êtes la proie de beaucoup de personnes. Bonne où mauvaise intention seul eux le savent. Un exemple à suivre azouza ... Yalla nala arr une maman qui vous admire beaucoup

    • @nochita3149
      @nochita3149 ปีที่แล้ว +5

      Machalla tata🥰bien dit

    • @guedjgueye6478
      @guedjgueye6478 ปีที่แล้ว +7

      Rafet n'a aleuh bi yatou n'a prédateurs yagui fi proie bou yomb lagni bagna guiss

    • @yayeamydiop6276
      @yayeamydiop6276 ปีที่แล้ว +3

      Merci maman pour vos conseils. Gsprk notre petite soeur en tiendra compte inchaAllah

    • @amily104
      @amily104 ปีที่แล้ว +2

      Exactement ma belle

    • @dallathiam2907
      @dallathiam2907 ปีที่แล้ว +1

      Tellement vrai

  • @siatoudiallo376
    @siatoudiallo376 ปีที่แล้ว +8

    Mane lima guiss elle es tjr amoureuse de sn ex mari malgré tt l mal qu’il la ft elle es amoureuse prck souko beugoul wonn dou mougne lolu yeupp bayinako serte mais mome la beugue sa c sur

  • @bakhyaye6597
    @bakhyaye6597 ปีที่แล้ว +15

    Khamone nani diguéne ko dioy loo😭😭😭

  • @Minabellaunivers
    @Minabellaunivers ปีที่แล้ว +2

    Jadore kya loum bilaay en plus dama nop dieukeur mais mom la gueuna beug

  • @jatoucham
    @jatoucham ปีที่แล้ว +3

    We love you Mia be strong inshallah, is gonna be ok.your fan in Atlanta AMERICA ❤️❤️❤️❤️

  • @capricefemelle3168
    @capricefemelle3168 ปีที่แล้ว +42

    Elle est traumatisée elle devait voir un psycho tout ce qu’elle fait sorties yi ak wakh yi comment elle se defoul rek molay wane ni da nek si traumatisme

  • @awandiaye7876
    @awandiaye7876 ปีที่แล้ว +8

    Ndeysane damako ko bègue en plus damako yereume

  • @kitokoken2187
    @kitokoken2187 ปีที่แล้ว +33

    Mais yen deugueur nguen fite dé, vous la voyez pleurer,sans connaître le contexte,ni la raison, kou nek Di oubi sa lamigne

  • @khadydiouf4028
    @khadydiouf4028 ปีที่แล้ว +17

    Mia mi elle devait se reposer elle ne va pas bien

    • @Seck221
      @Seck221 ปีที่แล้ว +4

      WI TA RAISON

  • @angeliquefaye9648
    @angeliquefaye9648 ปีที่แล้ว +54

    Seuye boulaye tacalé ak saye parents môme bayil mou séde rek y'all Dina indiwat lénéne louko gueune inchallah

    • @bigue5329
      @bigue5329 ปีที่แล้ว +1

      yawe miya mola wakhe ne seye moko tacale AK ayé parents wame am nga fite dalle🤣

    • @angeliquefaye9648
      @angeliquefaye9648 ปีที่แล้ว

      @@bigue5329 cône khana déglouwo invitation Mya bi passé moko walh dhé

    • @MkMk-lt2ho
      @MkMk-lt2ho ปีที่แล้ว +1

      @@bigue5329 deugeur fite rekk galsaine nio nièmè yala

    • @bigue5329
      @bigue5329 ปีที่แล้ว

      @@MkMk-lt2ho no mane manmom Sénégals daff médiakhal niuom dalle balasou yalla laniuo beugue tawkhwe yeen ken dafa kham Lou nek thi xollam

    • @adamadieme9295
      @adamadieme9295 ปีที่แล้ว

      @@bigue5329 si elle avait dit dans une émission

  • @aminatadiallo-wm7lf
    @aminatadiallo-wm7lf ปีที่แล้ว +2

    Machalla

  • @Thedreamchazer00
    @Thedreamchazer00 ปีที่แล้ว +11

    Mia iow tamite barri ngua jooy dé ahh !! Ya ngui takh ba sama rappeur kruh Di dioye !! Soit forte waay !!

  • @maantandiaye
    @maantandiaye ปีที่แล้ว +4

    Mai je t'aime fort 💔💔💔🙏

  • @ssall7900
    @ssall7900 ปีที่แล้ว +1

    Mia💓💓🌟✊🏾

  • @fatoungom1697
    @fatoungom1697 ปีที่แล้ว +2

    Dikorage ma belle çaira n'es pas la vie est belle tu va yarive moi je t'adore Mia🤩💙😍 je ressens et j sais a t'elle point tu s'ouvre la trahison kor momoko🙏

  • @adamandiaye5622
    @adamandiaye5622 ปีที่แล้ว +6

    Elle aime tjr son mari dimbalilen ko mou delou ak mom

  • @halimawos7121
    @halimawos7121 ปีที่แล้ว +4

    hello my dreamteam. It' s amazing it was my dream to finally see type of project zhich is selected all best young voices so as to show the world music industry that Africa has such a beautiful project and person like Moustapha and all the greatest Staff /
    I'm so proud to be senegal cause now ze know what is mindset and how to grow up our music industry / we needed to found a new type of project and music

  • @papiska2061
    @papiska2061 ปีที่แล้ว +43

    Moi je prie pour la réconciliation avec son ex mari. Un tel amour vécu entre eux deux ne pourrait être enterré du jour au lendemain. Courage. Na kilifeus yi lijeunti lolou

    • @bintambaye
      @bintambaye ปีที่แล้ว +20

      Yalla rek mo xam mais bou fekke limou explike yeup c vrai dem ba takaliko avec ses parents vraiment elle mérite mieux mais yalna yalla def li gueune rek

    • @benajim9357
      @benajim9357 ปีที่แล้ว +3

      ​@@bintambaye voilà li la begone degu

    • @ano-lc4ky
      @ano-lc4ky ปีที่แล้ว +13

      Menolen wax Lou meneu nek ana seuy bou tass 3fpis thie l'islam gnou takat KO khana concubinage ngen beug gnou doundou arrêter voyons

    • @senegalaise1
      @senegalaise1 ปีที่แล้ว +4

      ​@@ano-lc4ky gni ay dof plus lagn sen nak nane si wul li damasi xoulo ba sonu xamna tate lagnuy dégué

    • @maimounadiop9099
      @maimounadiop9099 ปีที่แล้ว

      Bien dit

  • @halimatambow7290
    @halimatambow7290 ปีที่แล้ว +6

    Courage mia

  • @flawlessndunique3766
    @flawlessndunique3766 ปีที่แล้ว +9

    Je sens sa souffrance 😢

  • @coumbambaye6681
    @coumbambaye6681 ปีที่แล้ว +6

    Amna divorce yo khamni ken mounou ko mougn on dirai k mia à fai beaucoup de sacrifice tay dji motakh mounoul digérée divorce

  • @Fatousarr-xe6wo
    @Fatousarr-xe6wo 6 หลายเดือนก่อน

    Ca va allez mia le senegal t'aime

  • @babacarfall7338
    @babacarfall7338 ปีที่แล้ว +5

    Respecter les femmes

  • @oumouahmad1599
    @oumouahmad1599 ปีที่แล้ว +16

    Mia nebeul sa vie tutti. Y'a des gens qui sont pires que toi. Mais li Yallah wahh rek moy deug. Le monde show biz mom mingui nonou rekk

    • @mmecisse6527
      @mmecisse6527 ปีที่แล้ว +2

      Yalla bo kham limouy traverser wallay kouthie diaroul rék do comprendre

    • @maimounafall3956
      @maimounafall3956 ปีที่แล้ว

      Yaw daga kham loume dioye yaw nieme nga yalla de

    • @rokhayacisse7905
      @rokhayacisse7905 ปีที่แล้ว

      Vérité absolue

    • @MWade
      @MWade ปีที่แล้ว

      Kenn khamalouko dara, artiste leu té lingey wey pour mou dougg seu public il faut déjà que mou dougg leu yoe. Artiste yeup sensible. Rien avoir avec ce qu’elle vit.

  • @elhadjiibrahimaniassfaye9610
    @elhadjiibrahimaniassfaye9610 ปีที่แล้ว

    Non thiey mia je l aime vraiment

  • @ticndevticndev5856
    @ticndevticndev5856 ปีที่แล้ว +19

    yéne gnii dii critiqué mia danguéne kham loutakh mouy dioyy ? mano léne bayi togne

  • @maremendiaye1622
    @maremendiaye1622 ปีที่แล้ว +1

    Mia beuggou mala guiss ngaye dioy matsa

  • @papissoo2504
    @papissoo2504 ปีที่แล้ว +15

    Aaa Sénégalais deugar na fit Yeen kii da ngeena xam loumuy jooy ba kounei neck fi di critiquer nan ay ex dieukar ak neubeul sa vie 😟 Yeen yena wara changer djikkou tei bayyi di wakh louleen leeroul

    • @Enzoshifow
      @Enzoshifow ปีที่แล้ว

      Papis soo dafeu am niou niémé yallah mouna wax si loulén woroul Sénégal am na niit you niémé yallah meneu toop sén xalat fok ni moy lii am

    • @seynabououaly9576
      @seynabououaly9576 ปีที่แล้ว

      Vraiment ils cherchent mm pa a comprendre

    • @Enzoshifow
      @Enzoshifow ปีที่แล้ว

      @@seynabououaly9576 franchement yénn yi manke de respect la ci mya tamit melnii Aÿ serigne sétkat yoyou lii dafeu niaw

    • @astoutoure6786
      @astoutoure6786 ปีที่แล้ว

      Wakhatiko

    • @Linebertodiaz
      @Linebertodiaz ปีที่แล้ว

      Mia mo wara nopi victimiser wo loumouy dioy 😢djiguene dou melni c’est pas une bonne femme

  • @fatimatabintakonte8948
    @fatimatabintakonte8948 ปีที่แล้ว +3

    Du nouveau se prépare

  • @fatoubintoundiaye9798
    @fatoubintoundiaye9798 ปีที่แล้ว

    Man damako yereum sérieux li am ni guenaluko divorce bi😢j’en suis sur ndaysane

  • @sayeseck1089
    @sayeseck1089 ปีที่แล้ว +1

    Mya dinala wakh li mame Ndiaye wakhone ndaya yow lane ngaye nii beuggouma fila guiss ngay dioye

  • @deuguerek4547
    @deuguerek4547 ปีที่แล้ว +5

    Vous parlez comme si danguéne ko gueune beugue boppam lane nguéne beugue mouy tokk roukou wam di dioy fay metti na nak ohhhhh ki taloul sakh yinguéne di wakh. Lane motakh nguéne di topp proie proie nitt you bone nitt you bone YALLAH Amna bénéne yapp boudoul guédieu. Té foulam ak faydam bi mou nekk topato domam diamou ay wadiour wam soussi diougoulé YALLAH dinako défal lou kawé sounou ndiorte nioune nieup InshaALLAH🙏🏾

  • @Sokhoulove117
    @Sokhoulove117 ปีที่แล้ว +1

    Lounouy dioy ni yéne masta

  • @bgsonsthriving.
    @bgsonsthriving. ปีที่แล้ว

    ❤️❤️❤️

  • @soryfn5447
    @soryfn5447 ปีที่แล้ว

    Ohh mais li pour lannnee aussii

  • @alinerodriguez4140
    @alinerodriguez4140 ปีที่แล้ว

    Wa yen Mi di commenter est ce que kham gueine Li khew gni dagno nek répétition pr le 8 mars fête de la femme 😂😂😂ah deugueur gueine fite dal

  • @fatoumbacke5611
    @fatoumbacke5611 ปีที่แล้ว

    Adouna nonoula naxar kesela

  • @dyzasmb3959
    @dyzasmb3959 ปีที่แล้ว

    Loy dioy

  • @guedjgueye6478
    @guedjgueye6478 ปีที่แล้ว

    Moytoul réseau yi boy deuk bi dafa Bari deum gnilay beug beug Lou ni defois niolay yakhal

  • @dieynabawane8452
    @dieynabawane8452 ปีที่แล้ว +5

    Vraiment yangui soofe nak

  • @PrinceADAM3477
    @PrinceADAM3477 ปีที่แล้ว

    Salam Pardon yaye mais gnilaye wakh doundal loula nekh ay seytané lagnou mefi tw té kham ni euleuk lou mata bayi xel té kou diay sa lérr dieundé ko leudeum dana wékh si yaw khat tay ak euleuk
    La réussite d'une femme c'est savoir géré son ménage et son mari
    Et non beuz et argent
    Je ne te juge pas mais la mauvaise femme est une arme pour satan
    Ne soyer pas des apa

    • @LaBarhamienne
      @LaBarhamienne ปีที่แล้ว

      Ki argent tita louko dh thi la dioudou sou soxla wone buzz kone nangou wone na ay promo canapé bou yagg bala mo seuy, kone al hamdoulilah. Bayiléne deuguer fite, gnikoy wakh doundal daniouko beug mais pas yéné lou bone, gnikoy wax déloul thi seuy bouniou wal ni tigua dèguè nak nio diara xolate. Kounek xamal li ngay doundou thi sa seuy té dieul thi say décisions bayi sa morom ak dècision mais daguène di doundou sen doundou beug doundou bossou diambour ak di dogual thi vie melni daguène ko mom.
      La bonne gestion d’un mariage incombe aus deux conjoints qui se sont unis pour Allah. La réussite d’une femme ne se résule pas qu’au mariage, seuy yalla mokoy dogual, tass mokoy dogual.
      Yalla mo daganal divorce, sou meunatoul am plein droit dem yonam. Maylène ko diam way, sonal guène nite ki trop

  • @dieynabawane8452
    @dieynabawane8452 ปีที่แล้ว +5

    Ton ex est suelqun de bien yako done wakhe

  • @loaboubacar3595
    @loaboubacar3595 ปีที่แล้ว +5

    Antouka ton mari a commencé a eu ds raisons envers nous qui te défend 🤔

    • @modoundiaye7985
      @modoundiaye7985 ปีที่แล้ว +1

      wakho fi touse xamo lou xéw

    • @benajim9357
      @benajim9357 ปีที่แล้ว

      Motay sawa louka khamal amga fite

    • @benajim9357
      @benajim9357 ปีที่แล้ว

      ​@@modoundiaye7985 am fite rek

  • @aminadiongue7485
    @aminadiongue7485 ปีที่แล้ว

    Sa larme yi ba dou jaikh je

  • @mohamedndiaye5728
    @mohamedndiaye5728 ปีที่แล้ว +11

    Elle commence à emmerder les gens . Des personnes ont vécu pires mais nio ngui sante Yalla en allant vers l’avant

    • @kitokoken2187
      @kitokoken2187 ปีที่แล้ว +13

      Est ce que tu sais pourquoi elle pleure

    • @marietoucissokho8490
      @marietoucissokho8490 ปีที่แล้ว +6

      ​@@kitokoken2187 âme fiite reik

    • @modoundiaye7985
      @modoundiaye7985 ปีที่แล้ว +2

      démal sétane fénén té mandou bouko nékhé

    • @alinerodriguez4140
      @alinerodriguez4140 ปีที่แล้ว +1

      😂sénégalais mo deugueur fite dh😂☺️

  • @ESCALE3
    @ESCALE3 ปีที่แล้ว +5

    trop de victimisation les meufs d'aujourdhui dioy goudi dioyy beutieukk pffff que DIEU TE GUIDE wayé yaa ngi beugeu soff nak

    • @missebene8415
      @missebene8415 ปีที่แล้ว

      Balay ngay fen fi setane rhim

  • @chouta97
    @chouta97 ปีที่แล้ว

    Billahi sénégalais mo hypocrite lousi sén yone sih dioyou diabour guén mbeug ko wék si divorce bi aaaaaaav xalasss

    • @bigue5329
      @bigue5329 ปีที่แล้ว

      Manmom billahi momadiaxal nigui khawma loulene dalle rek

  • @bklbkl7223
    @bklbkl7223 ปีที่แล้ว

    Sof guéneu legui dogne fi tek entreprise dioye nit youlene geuneu doundou lou meti Gnongui si town bi diko gérer té wakhougnou nekeu lene ay nit