Wa firqatou tawfiq sen yaram tangue na dh yalna yalla takhawou ta barkel lep si barké goorou capitaine inchallah ❤❤❤❤ Diarama Mara amouniou koudoul yaw yalna yalla yok la same yokla aar inchallah goudou fane rk🙏🥰🥰🥰
Wallahi Son Bi Sumakoy Deglou Sama Yaram bi Kom luy Vibre Kou Beug Sa Thiofél di Yok Çi S Moustapha Deko Deklou ❤❤❤Siñu Naré Woro ak Mom Yallna Yalla Djeul Sunu Bakén Sy Dund ak Wér Lalay Nianal Yallnañu la mat Ndiabot
Yalna yalla faye yiw ❤❤machalllah contane nagn même ❤ yalna yalla saam serigne moustapha sy arr ko lakh ko famou lakh boppam SUNU capitaine SUNU bonheur on t'aime ❤❤
Tidiane diome dafa nék chanteur bo kham ni Amoule morome si Afro Arabe orientale ndakh akh bimiye djiokh woye bi Do massa laté ta fo massa rare lé aye waye ndakh dagakoy ték si tégouwaye walahi
1er commentaire Ana niou beg Serigne Mustapha Sy
Ndax ken bañ na ko???
Wax gua deg d
@@moustaphagueye1756kouka khamoul rk mo am wayé kén douka bagn nika tonton Démbi (paix à son âme) waxè wone rk🤷🏽♂️✍🏽✅
Wa firqatou tawfiq sen yaram tangue na dh yalna yalla takhawou ta barkel lep si barké goorou capitaine inchallah ❤❤❤❤ Diarama Mara amouniou koudoul yaw yalna yalla yok la same yokla aar inchallah goudou fane rk🙏🥰🥰🥰
Bilay kouko bagn kholam dou meussa fekh notre R.M❤
Nooo son bii enh nimouy deff sma khol benen affaire laaa Son bii rk dafay yokou thiofel yalla naniou yalla fayal Al Mourchid🙏♥️🎉
Wallahi Son Bi Sumakoy Deglou Sama Yaram bi Kom luy Vibre Kou Beug Sa Thiofél di Yok Çi S Moustapha Deko Deklou ❤❤❤Siñu Naré Woro ak Mom Yallna Yalla Djeul Sunu Bakén Sy Dund ak Wér Lalay Nianal Yallnañu la mat Ndiabot
❤❤❤❤❤❤
Un poème écrit par oustaze Matouré Sene qui habite à keur baba alima dans la commune de Tivaouane
❤❤❤❤
Yalna yalla faye yiw ❤❤machalllah contane nagn même ❤ yalna yalla saam serigne moustapha sy arr ko lakh ko famou lakh boppam
SUNU capitaine SUNU bonheur on t'aime ❤❤
Allahou akbar son biii dafmay dioy loo chaque 10 juin 😭😭😭
❤beug naniou dei yalna yalla wéral mat bi Sokhna kiné ak niouga and❤❤
Ohh son bii day yoke tiofel ❤ Serigne Moustapha sy Al mactoum lagnouy topp ba fadiar démme teudi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ohh li nekhna thi khole wallay sy yalna yalla faye la thionno
Machallah yalna yalla mottali ❤🤲🤲
Diarama Serigne Moustapha Sy ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Diarama serigne Moustapha sy Almaktoum Sama serigne ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bilay Mame Serigne Moustapha yallana yalla samla arela
Diarama Serigne Moustapha Sy Al mourchid yallna yalla samou la are la doli soutoura ❤❤
Yalna yalla faye la sa thiono Seydi cheikh Mouhamadoul Moustapha Sy Al Mourchid 🥰😍
Diarama Serigne Moustapha Sy al Maktoum ❤❤
❤Diarama 🎉Serigne ❤Moustapha ❤Sy 🎉❤❤
Maachallah diarama Serigne Moustapha Sy Al Maktum ❤
Ohh lii nekhna way machallah ❤🎉😭🙏🏻
Wah li nekhna di😭🫀
Diarama Gorou capitaine gui ❤❤❤
machalah yalna yalla Faye yiw inchallah ❤❤❤❤❤❤❤❤
Serigne bi doundal wéral ,yalna yalla aarla té samou la
Amine inch'Allah ❤️
Serigne moustapha yallna goudou fanne
Machallah yalla nalén yalla défal diam rek si barké goor gui
علوت بالجيل من كهف الجهالة بل علا بهم فكركم من جملة الخلف ❤❤❤❤oustaz Hadi niass ✍️
Machalla diop
INCH'ALLAH YALLA NA KO YALLA ARRE TE SOUTOUREUL KO INCH'ALLAH
AMINE ❤❤❤❤🫀🫀🫀🩸🩸🩸🩸🩸
Dieuredieuf Firqatou Tawfiiq🥰🥳🫶🏾🙏🏾
Diarama Serigne Moustapha sy al macktoum ♥️♥️♥️
Machallah machallah machallah al mourchid ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤hbd 🎂
Excellent travail mention spéciale à l'équipe technique. Nékhna dagane na
Diarama serigne moustapha sy ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ohhhhh cheikh tidiane dioome fatabarakallahou
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ Yalla diko sam rkka ine sha allah té arko ine sha allah ❤️ ❤️ ❤️
Machallah nexna trop ❤❤
Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Allahouma amin sy malick yalna ngua fi yagu té wer tci barké seydina mouhamad salalahou aleyhi wa salam ❤❤❤
Ooh machallah ❤️😘🥰
Machalla
Machallah yalna yalla barkél
Mach'allah
Un son qui traverse des générations macha'llah ❤❤❤❤
Diarama Serigne Moustapha sy all macktom ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Ndeysan ❤️ 😢
yalna yalla samm goor gui
yalla na yalla bbbbbbbbbarkkel si barke magg nii
Machallah Oustaz Dionne ❤🎉🎉
Ils ont tapé fort ❤❤❤❤
Macha allah
Macha allah xol yeup séd na
Diarama Serigne Moustapha sy ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Diarrama sy Malick ❤️❤️
DIARAMA SERIGNE MOUSTAPHA SY
Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Wayy bii mo dall ❤ machallah
Ohhhhhhhh mon cœur ❄️❤️❤️
Mach’Allah
On les attends dans les plateformes de streaming svp🙏🏾
wa li nekhna dh😂😂
Ndeyssane
❤Yalnafi yague té weur🤲
MaachaAllah ❤
Machallah yalla motali inchallah. Yalla faye yiw inchallah. Merci beaucoup
Folen niu jeumé❤😩
Machallah ❤❤❤
Diarama mourchid ❤❤
❤❤❤❤❤❤ OHhh Kamal
Barakallah ❤❤❤❤
❤❤❤.
Merci beaucoup❤❤❤
Mashallah waay 😍❤️
Serigne Mouhammadoul Moustapha sy yalna yalla goudal fann wi té dolika wër ak wërrlé té lafalko thitt té arrko ci barkep Mame yi inchallah❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Marchala ❤🎉
Machallah souniou sanguebi gorou capitaine ❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalllah ❤❤❤
mashalla fiert de vous
Machalla yalla na yalla motali
Walahi
Merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machaalah ❤️🥰❤️
Maacha allah ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Machallahh ❤️
Xolll céddnaaaq wallahi hanzim 🥰🥰🥰🫶🫶🫶🫶
Barakallha ❤❤
Oh❤❤
❤❤❤Diarrama serigne moustapha sy al macktoum❤️❤️
Mille merci à notre responsable moral
Mangui dioy yen 😢😢
No boul dioye😂
@@Ndiaya123 non bayil ma dioy way 🥲😭😭😭
@@fayeyama6522 ndeyesan thiofél mo bari dolé rk❤
masha allah yalna ya allah same teh are gorou capitaine
Tidiane diome dafa nék chanteur bo kham ni Amoule morome si Afro Arabe orientale ndakh akh bimiye djiokh woye bi
Do massa laté ta fo massa rare lé aye waye ndakh dagakoy ték si tégouwaye walahi
Lou eupou tourou ❤❤❤❤❤❤😭
Yalna yalla samal sougniou goor gui
Kamal machalla
Machalla ❤❤❤❤
❤Machallah 😢❤
Wawe lii nékhna de❤❤❤❤❤❤❤
100/10❤❤❤❤
❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤