Bonjour mon nouvel album « SUBA » est sorti . A écouter et/ou télécharger en cliquant ici listen.lt/BrilSuba1 je suis heureux de vous en faire découvrir aujourd'hui les 15 nouvelles chansons.
😍😍😍jiguène dgue day ame dagou walé xaley bou bah ak formame di dagou sa biir keur def tokh taille basse ana gni ande ak pape birahim na bleu may guiss way😂😂😂😂😂diég dji rek meune dadji waté😆😘😘beau le duo❤
Et c'est pour ça qu'eux (artistes) doivent monter le bon exemple face à une jeunesse en perte de valeur comme vous le souligner. Faw am gnou gnouy orienté des fois et les artistes ci lagn bokk c des porteurs de voi
Owkei machalllah😍. Way bi nèkh na trop prck niari ndanane gno dadjé😘 Mais nak en général dièke you diss yi daniouy diabète rk bâ niou cardiaque So démé ba nèke sa ohhlala gua niak khaliss nakh ordonnance,niouy guène thi bènd bi niou lène di thiatou. Kou gnou n3 déffal sport do attane sa bop😢. Vive Taille fine way😍. Mais peu importe on doit se sentir b1 dans sa peau😘 Breff. Sinon niougui kharate bénène duo Bii saff na niou. Qui est d'accord pouce bleu😍😛❤👍
Bril fight4 big up yaw yonla begue piir machallah clip bou nice mais pape birahim yaw kenn demoul nga dess machallah mane dal begue na lenn bonne continuation à vs 💖💖💖💖💖💖💖💖
Ah ki è dacor k ni bril nioun taille fine yi la faral pouce bleu aka fine rek ba ètè bi nieuw mo dakh beach niou andak taille fine wanèlen sèn bop💪💪💪💪☝☝☝☝☝💕💞💓
Bonjour mon nouvel album « SUBA » est sorti . A écouter et/ou télécharger en cliquant ici listen.lt/BrilSuba1
je suis heureux de vous en faire découvrir aujourd'hui les 15 nouvelles chansons.
Ok Bril
Trop cooool
Je suis fan
Je préfère tayfin😍😘❤👍👈
Ajo
Bril Officiel Bonjour
Youeet mp4
Quand deux ndananes fusionnent ça donne toujours ça qui est d’accord 🔥🇸🇳🙏🏾
S8 entièrement d'accord niom niar meunei nagn founei
Moi broo 🔥🔥🔥🔥 respect nice frere
Ton numéro stp
Ho mane mom khawma fouma fété ndakh dama séw mais dal begna né fadj
Mw
Vive la femme en général mou done taille fine wala djeg, koussi d’accord...? ❤️🇸🇳🇸🇳🇸🇳
😍😍😍jiguène dgue day ame dagou walé xaley bou bah ak formame di dagou sa biir keur def tokh taille basse ana gni ande ak pape birahim na bleu may guiss way😂😂😂😂😂diég dji rek meune dadji waté😆😘😘beau le duo❤
Wa waw deugue nékhoul dh diongama pur
Walay tourondou wakhatiko
Oui moi je d accord
Mais moi je sui tayfine
@@daourmbaye8921 togal akh seu taille fine borom aiguille
Sortir avec taille fine tu te demandes si elle a besoin de nourriture ou de l'amour
Djiguéne day féss délleu team diongoma ❤
😂😂😂
Senegal Senegal Senegal Senegal
MariamamDiouf
😗
😂😂😂😂
Quand deux voix extraordinaires de la musique sénégalaise se croisent ne peut donner que ça comme résultat. Félicitation
Sheuteute dfatina meuninam man dal beugue na li ani sama mbook taille fine yii bril reik si xol dara douko dindi😍😍😍😍
🙋😍
Là mdrrr
😍😍✋
TF SI XOL
🙌🏾👩🏽💪🏽
First 😍😘ana gni beugeu bril pouce bleu🔥
Nice clip je kiff ❤❤
yasmine baby yama geuneu nekh ke bril
Moi
🍸💗💗🍸💗💗🍸
💗💗💗💗😍😍😍
💗💗💗💗😍💗😍
🍸💗💗💗😍💗😍
🍸🍸💗💗😍😍😍
🍸🍸🍸💗🍸🍸🍸
🍸💜💜🍸💜💜🍸
💜💜💜💜💜💜💜
💜🌹💜🌹💜💜💜
🍸🌹💜🌹💜💜🍸
🍸🌹💜🌹💜🍸🍸
🍸🍸🌹💜🍸🍸🍸
Mariana Butera on peut se parler sur pv
« De l’autre côté « tellement touchant ,magnifique ,BRIL un vrai artiste félicitation !!!
Film mr bien
Djiguen daal da kay ndirou waa wa waw diongama feep loo sol mou diap mangui si pape birahim
Ms jaime bril fight four
Qui est là en 2024 💙💙
Taille fine douu ayyy fohh kou d'accord reck beuseull j'aime💋💖💖
J'aime
Team fess deill mashalah sen lokho may senn😂✋❤
Waww niogii ni dh
Adjashu Laye Fall ah eupneuh naq kennn dou niounnn😂
Weuw Kayy👋djiguéne dakoy nourou wala mou baa tt ce kil faut là où il faut beugouma daray cuire-dent😂😂(dagnouy fo rk)v
@@Biddew khana
Niongui nii waw kay
Bril fight 4 ft Dip doundou guiss qui est daccord? mais dou done mbeuguél dh😂😂👑
Moréén TV warna meuneu nekk dh 😂😂 loy bagne mou done mbeugeul ni 😂😂
Moréén TV moi suis d'accord
Aka ma thié d’accord !!!!!! Mais padon na nékk love nak loool
No meune na nk mai op son mbeuguel coz ils ont tro de son d'amour
Me😀💗💗
bilayyyyyy Pape birahim ya xamm lou bakhh wayyyyyy brilll vraima weirei gua koi loyyy doyei thiep bou sewww mounane taille fine dara bakhousssi . POIDS LOURD 4 EVER MANE BEUGEUNA SAKHHH NAMA RAYYYYYYYYYYYYY
Après l'annonce de kouthia pour serie bi kou gneuwat deglou son bi❤beusseul j'aime
taille fine dal rafètna . qui est d'accord ? ? ?
Taille fine dal
Machallah
Moi
Mane taille fine mo may danel❤❤❤❤
@@aissatasylla347 me
Très belle vidéo machallah ! Kou beugue Duo bi pouce bleu . Taille fine 💪💪
Moy toulma khalé bou féss 👎🏾 mane déh taille fine rék nio may danél 👍🏾😍😍
Seck Bologna non taille fine dou ay fo
tamiy deugue taille fine rk
Gnomm nioko yoor fowoukay dafay oyof
Merci gni beug loubakh yeup nionguici taille fine
@@famanga8152 wakhatiko dé
Les Tailles fines👑 manifestez vous way
On n'est la
Taille fine yi rek laay top
J aime bien cette chanson et la ressemblance des voix de ces 2 artistes, leurs qui sont toutes les 2 magnifiques. 💯💯👊👊👊💯💯💯💯
jongoma yi sen lokho thia kaw
🙌 team taille fine 😭
Nice na vraiment
#Team-taille-fine
Delen aimé 100 fois ahmada
Hooh trop nekh bargui bleu bleu koumou nekh beusal j'aime waay 💗❤ani tail fine yii
coumbis s3y3 bilae tail fine mokko yorr💞💞j ' aime bril
@@bintouseye3375 wawaw tail fine rk eupeuna
coumbis Seye ✌✌
@@khadydiack1695 ❤❤
coumbis seye
Xayooo ani lei taill fine😍😍tamite
😂😂😂mon pays va mal😂😂 niou andak taille fine yi beuss leen jaime waay
j'aime
les rondeurs, une identité bien sénégalaise!!! A vous les XXL!!! Clin d’œil à my wife!!
Mane lima geuna beug moy diek bou disss💪dima nokh bamay dioy😢😢mou nakhati ma🤷♂️
Je suis avec bril, laver les mains qui et d'accord avec bril
Moi
Fofana Mido moi
Un homme respectable
😂😂😂Allez les femmes rondes😍😍😍vive les tailles fine oci😍machallah clips bi nekhna😍😍
Nice
Je t'aime
@@dedsec2.017 tu aime qui
Wa Ani taille fine yi wané wou léne ak taille fine rk eupou na
Gnon ngui nï👯👯👭🌹
Waw waw dangay ladj
On n'est la
Mangini
Defa lerr
Taille fine defa Rafette ❤❤❤
Musique sénégalaise, les filles sénégalaises et les mes sénégalais sont magnifiques.✈🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Mei ku nekeu akkk nila souniou borom binde ku nekk amnga part si son bi chapeau a vs bril do sen morom
😂😃💚❤📦
Qui est a 2024 pour soutenir les tailles fines comme moi🎈🫰✅?
Khane moy khaye dègue lou2024😂❤
Team tay fine aniguenn 😍😍gnoune rkk sii nekha foopp yeukeuti athioum tay fine dou reuthieul sa deuneu deii DEUG nexoul ...foyoukaay dafay woyoff😂😂
Gnou andak taille fine sen lokho way may sène👭
Tu est Bell
Kéne Dou diégi
I'm here
Deugue nékhoule💖💖💖👯👯
Belle
jvous kiff vous deux mai tailles fine lagn wakh gnoun☺☺
Taille fine moko yor
Aller les taille fine manifestez -vous
Là
Buy bulema ray
😍😎😚
Nionguini😍
Mously Lo Ken
na aguiiii
Nice 😂😂😂😂 mé 2 Artist😍😍 taille fine wonélen sen bop😂😂😘😘😘
On dit pas de taille rond mais taille fine
T
2po2oziz8zeieoepzofoz2 maty DOIt
Way nékhoul ba nekhou un vrai homme daguay beug diék dji ndakh siguay sentir sa boppour deugu fo tollou diko séeen ooooooooh j'aime les Diék way
Taille khifffffe wala taille fine😂😂😂!!la classe est au rendez-vous duo de choc j'adore !!!!
😂
Taille fine rék beug 100% qui est avec moi et Bril pouce bleu🔥
non
Khar Ndoféne Gaye
@@madamebleu9328 salut
Il a encore montré son talent Macha Allah yalna nalen yala soutoural thi barker seydina mouhamed
ana team driankei bi 😂😂pousse bleu
Ana diekk you diss yi😍😍❤
Mane beugu naa kou melni bril way😂fine moko yoor surtt été ohooooo
Bilaye birahim yaye diaye tar rek man mome na tate bi bax rek😉magui sy tay fil de man
🤔
Dafa beugue djiguene trop😁
@@astaseye1616 ta sof kay😂
serigne takkricain copin yaw xale nga doxal nelawi
@@siirdiop9701 😂😂😂khalas
Sama team taille Finn yi brightt fight lagnou wakhhh gnounn💘
Ma ngui si yéne mane fowékay day yam si loxo
Mamadu Faay deug nekoul
@@soldaroucheikhmountakhamb5015 wa guis nga fowékay day oyof
Mamadu Faay mba ame nga si taile fin yi rek
@@soldaroucheikhmountakhamb5015 xaxa no amou ma si nak
Asc Taille Fine 🙈 je T'aime ❤️ Bril Fight 😘
Astou Kadam merci de vous abonnez à ma chaîne
Taille fine moko yor
Taille fine lalayy tegual nidehh Bril t'a encore frappé !!!Congratulation
Oyoff atane s'en bopp nioko mome 😍maname taille fine dall😎sama mbokk yi manifest3 vs
Bilaay Birahim mako beug waay😍😍
Team ptite jongoma waay✌✌❤
Rosalie Oumy Mbaye je vous invite à venir regarder des vidéos challenge musique sur ma chaîne. merci à toi
Birahim rekk 😍
Fowoukay dal day oyof bou dissé rek sonal borom ❤️💖❤️💃💃💃💃💃❤️❤️
Ww yow bou disss nga wala Bou oyoff 😂😂😂😂😂👉
Ay ndeya mane dal yaw lay weur taille finie rk
Matar Diop15 nakhoma
Ameth Diagne bou oyof 😂😂😂😂
Ma fvmm lay done reine dé taille fine j laim
From poto cornel yi rek wawaw 🇸🇳🇮🇹❤🎉❤🎊
Fine thi kaw lourde thi souf! Kou andak mane?
Who loves Bril Fight and pape Birahim❤❤❤❤❤
Taille fine rék dara fayou ko
👋👋
On adore les femmes minces 😂😘😘😍😍😍😍
merci j suis mince
Bilahi 🖒🖒🖒😁💪💪💪💪
waxal way
Moytoulén fataya complet yi😂😂 danouy Tass yaram dh Ani wa team taille fine😍😍
😂😅
Lol
Qui est laah Avant les Millions de vues ?😍😍😍😍😍🖐️
Pape birahime ya beugu lou métiii noooo do déme. Macha alla vrai artiste gua
Djiguéne déy fess❤❤❤
Quand j enten ta voix bril j m sen tre bien si je swi en colère sé toi ki m rend mn sourire vrmn jtaim❤💖😍😘
La même chose que moi bril yala koye faye
Ou sont les fans de ces deux superbes artiste la likez svp
Yh
Je suis fière d'être taille fine
Ni taille fine ni taille drianke mais le juste milieu qui alterne les deux de belle courbes
2 voi extraordinaire ki se croisen ohhhhh donn d frisson et l'envi de danser.sama khol frigo
Qui est la en 2024🤩
Team bril tjrs du lourd 😍
Teamm taille fine dague tekk thi 😂😂😂😂😂
Vulgaire, certes mais à l'image de la jeunesse sénégalaise. Arrêter de jouer aux choqués.
Bravo les gars. bonne continuation.
Et c'est pour ça qu'eux (artistes) doivent monter le bon exemple face à une jeunesse en perte de valeur comme vous le souligner. Faw am gnou gnouy orienté des fois et les artistes ci lagn bokk c des porteurs de voi
Super
Cool
OK
Owkei machalllah😍. Way bi nèkh na trop prck niari ndanane gno dadjé😘
Mais nak en général dièke you diss yi daniouy diabète rk bâ niou cardiaque So démé ba nèke sa ohhlala gua niak khaliss nakh ordonnance,niouy guène thi bènd bi niou lène di thiatou. Kou gnou n3 déffal sport do attane sa bop😢.
Vive Taille fine way😍.
Mais peu importe on doit se sentir b1 dans sa peau😘
Breff. Sinon niougui kharate bénène duo Bii saff na niou.
Qui est d'accord pouce bleu😍😛❤👍
Gni beugueu niar yeup(taille fine, diek) beussal pouce bleu
Mane mome diéck la begue sou daguo sa bir keur gua khamna léppou degue la cou begue diéck na bleu way
Baboucar Sokhna merci de vous abonnez à ma chaîne
Dièk dei fèbar rek
Namouniou draa
Baboucar Sokhna ta raison
E
Ahhhh du lourd cousi ande beussal j'aime may guiss😍
Beatrice Dasylva je suis là 👋👋👋
😍😍😍😍
My god
C trop nekh
Je t'aime Pape Birahim
Beri nga si morom bilaay
Je t'aime toi aussi 🤣🤣🤣🤣🤣pape birahim la guëm 👈👈👈👈👈👈👈👈
Bilay walay 🙈🙈
pape birahim tu as une voix en or incontestable kan jtentend sama yaram dafay daw wallahi.... Big up a bril 😍😘
Clip bi tangana dée way son bi nickel Macha allah thia Kaw thia kanam
Mention spéciale à @Reverse Studio franchement vous avez assuré et que le meilleur reste à venir félicitations aussi à Bril et Pape Birahim 🙏🏾❤️
Kou beug thiek bou dix na wakh👍💖👍💖👍💖
bbei chou diop Ci yéne la faar deh
Mandé beugouma
@@senegaleZe hahaha
@@Matarmdiop15 beugueul wayy
@@bbeichoudiop7957 dina guis thiep bou sew di dem thi bou didji
Taille Fine Rekkk😍😍😍😍
Koy tayfine na bleus j'aime may guiss
Moi je suis une taille fire
La team taille ronde ?🇸🇳💞
Bril fight4 big up yaw yonla begue piir machallah clip bou nice mais pape birahim yaw kenn demoul nga dess machallah mane dal begue na lenn bonne continuation à vs 💖💖💖💖💖💖💖💖
Binetou Faye je vous invite à venir regarder des vidéos challenge musique sur ma chaîne. merci à toi
Djiguéne dall dafay noy am dagueu bou Nice Mouy taille fine ou lourd no mel rek sant Nice clip suis pour les 2 😂😂😂😂
Drianke yi way😂😂👏👏
Taille fine wayy GNi beugueu taille fine pouce bleu dieck bou diss yi taguay yeureum nallene
😂😂😂😍😍😍taille fine way💕💕 dou moromou lénéne ci lepp 'nakk..allé brilll chapeau à tw😘😘.
Ah ki è dacor k ni bril nioun taille fine yi la faral pouce bleu aka fine rek ba ètè bi nieuw mo dakh beach niou andak taille fine wanèlen sèn bop💪💪💪💪☝☝☝☝☝💕💞💓
6
✋✋✋
Diek rek manhallah❤❤ bonne continuation belle muisque
Goorou Sénégal djiguéne bou féss déll am taat mooo lén saff. Kouci takkeu taille fine dina weuri diongama bou matt djiguéne toll nouko saff saanéekou feulaalé
Waw gor way djiguén day am tatt way😂😂😂😂👉
@@amethdiagne7180 waxal waay
amsatou diop walay deugue pirree ngua wakh
Moh yen khar dolén saniko di feul feulalé khana khay daguéni dilékou
@@tabarafall3795 mane damay dirékou😂😂😂😂😂👉
Aiii waaai Bril yaa waah lii yep chi thiek bu Dix. Nice one though. Pape Birahim fing koh tiyeah fofula 🤐🤗
5ans aprés nice😂❤
ana les tailles fines😍😍😍😍???
gnogui ni
MARYAMA KANE 🤘🏻✋🏻✋🏻
wawaw vive nous wayy
Domuu bayy mane mome mangui si taille fine yii❤
Saliou kane kone yess. dou ay tiakhaneee
Bilay nekhna troppp khale bou fess beuri diap djiguenne dagne am ay rondeur way
Gni andak taille fine wanei len sen bop👍. taille fine is bae💕
Team ls #taille fine❤vive thieipp bou séw bi fowou kayy dal dayy oyof❤💏
Oh pape birahim tu fais partir de mes chanteurs mais méré nala trop parce que taille fine la 😢😧