Ce hassida Je l’aimais déjà pour l’hommage que le fils( Mame Mansour RTA) rendait à son père et maître(Mame Maodo RTA) Maintenant je l’adore tout simplement et est devenu comme un hymne depuis que j’ai pris le temps de l’apprendre et de le faire traduire. Hommage ne peut être plus beau et touchant que celui-ci. Djarama Seydi Hadji Malick SY RTA. Mon amour et affection pour Mame Mansour Cheikhal Khawmi RTA est juste inconditionnel!
Amyna Nabysarr bouDABAKH.... Yaw soxna bou bakh nga Kou téd nga... Kou am thiofél si tarikha bi ak si ndiabotou Seydi El Hadj Malick Sy nga. Damako yaga sétlou nak si say commentaire ndakh dangay safo lepi Tivaouane. Djiguéne bou bakh nga deug deug. Kou yiw kou am Talibé. Yalla nala borom bi def deugui deugui Talibé cheikh si barké sama gorgui Cheikhoul khawmi borom niari kala yi Mansour mou Malick
Je ne cesserai de vous souhaiter une très longue vie pour cette chanson qui m'apaise, et le sentiment de paix qu'elle m'aporte merci Abdoul Aziz Mbaye tu mérites vraiment le nom que tu portes merci et merci encore
Yalla nagniou yalla faayale Abdoul Aziz mbaye yalla. Maye la goudou fane ak wer kheweul ak soutoureu barkè féké ak tale si barké seydouna mouhammad psl yalla moune nako sagne nako yalla nako yalla nako yalla Def
Salaam, Malikya Yalla na lène Yalla gueneu doolel, bilaahi khôl yeupay séddeu ak programmes you mel nii. Alkhamdoulilah bi gnou Yalla boolek mame maodo RTA ba mou deff gnou talibé cheikh, alkhamdoulilah bamouy gnati yone! Merci pour tout
SOUGNOU MAMOU KHOLE INCHAALLAH WASSILA SERIGNOU KHOLLE FOREVER RTA
😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊
Abdou Aziz mbaye yalna yalla goudeul sa fane❤❤❤❤
Na Yalla yok sene Bat ak were machalah 😢😢😭😭 mm mansour yemena ❤❤
Khassaïde bi nimoumay Def YALLA reka ko kham Elhadj Mansour Balkhawmi ken d'où Mom ❤ Dieureufeuti Cheikh Seydil Hadji Malick Sy RTA ❤️
Mame Mansour mo nekha beug .
Yalnaniu yalla fayal Maodo ak Wa keureum ❤️🙏🏿
Ana talibe chiech yi way ♥️♥️♥️
gnougui ni ❤❤❤❤❤😊
Dinafi xeuy rek sama coeur bi né boumm, atanuma louni mell way🤗🤗🤗, ay ALLAH dieredieuf bingama bolé thi euhlou bii🙏🏽
Machala Serigne Abdou Aziz mbaye yala ga doudoune 120ans
Yalla na niou yalla fayal mame Maoda Malik sy 🔐♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️😘😘😘😘
Un grand merci 🙏🔥depuis la France 🇫🇷 vraiment content de vous Malikia TV et Surtout Papa Abdou Aziz Mbaye
Slm ziar naboukha
Msa chaa Allah yalla naleneyalla faye nguen dji faye thia sammalene
Masa allah
8
Khôl
Yala nalen yala samou goudal sén fane bou ande ak wér doli soutoura si barké seydil hadji malick amine
Mansha Allah yalna borom bi same la yok sayy fane Abdou Aziz mbaye
Machallah ❤ mame mansourmachallah Abdou Aziz mon chanteur n'a batebi werre amine
Machallah papa abdou Aziz ak balkhawmi borom afîl basitaty
Ce hassida Je l’aimais déjà pour l’hommage que le fils( Mame Mansour RTA) rendait à son père et maître(Mame Maodo RTA)
Maintenant je l’adore tout simplement et est devenu comme un hymne depuis que j’ai pris le temps de l’apprendre et de le faire traduire. Hommage ne peut être plus beau et touchant que celui-ci.
Djarama Seydi Hadji Malick SY RTA. Mon amour et affection pour Mame Mansour Cheikhal Khawmi RTA est juste inconditionnel!
Walae Ndeysane macha’Allah
MassaAllah je l ai beaucoup cherche dans google mais en vain. Doumassi doyal🇸🇳🇺🇲
Masha allah❤
Wallah wakhal bu baax
@@hajjgora605zzzggn1h²4
Shukran Maodo binga maagale silagne hame yaye kane tdiane rek ba barsake inchaallah Fatou Sarr depuis New York
Dieuredieuf mbaaye sa ngoné ❤
Merci Malickya pour ce poème du fils à son père plein d’enseignements que nous devons traduire pour toutes les générations
Khôl sédena ❤️
Maachaallah yalana yala defal la fane wougoune ta andack wére Amine
J'avais mal o cœur sa ma redonné Espoir❤
MashaAllah Mame Malick domame yeppe aye gaïnde lanou. Mame Malick daale diouroule loudole bopame, gneppe aye nitou Yallah lanou.
Li nekh n'a yalla tahawou lene si barke Seydouna mouhammad 🕌
😭😭😭😭😭😭 Mame Hadji Mansour billahi mo xam baayam radiyallahou hanhou
Wa Al Malikia dieureudieuff yalna yalla faye léne yiw té barkéll
Thieyy yalla weer na nekhnasi khôl. Machalah yalla fayalniu niu Mame Mansour rta ak djiaboot cheikh seydil hadj malick sy rta
ماشاء الله بارك الله فيك ياحبيب ياشيخي ياشيدي حافظك الله ورعاه مع صيحة بجاه افضل الوري ءامين يارب العالمين لاتنسونا من دعاء أنت صاحب البر
L' un de mes zikr préféré Afil Basitati poème de Mame Mansour à son père Seydil Hadji Malick Sy ❤️
affirmatif
Amyna Nabysarr bouDABAKH....
Yaw soxna bou bakh nga
Kou téd nga...
Kou am thiofél si tarikha bi ak si ndiabotou Seydi El Hadj Malick Sy nga.
Damako yaga sétlou nak si say commentaire ndakh dangay safo lepi Tivaouane.
Djiguéne bou bakh nga deug deug.
Kou yiw kou am Talibé.
Yalla nala borom bi def deugui deugui Talibé cheikh si barké sama gorgui Cheikhoul khawmi borom niari kala yi Mansour mou Malick
@@moctarcisse8413 c vrai moi aussi j'ai remarqué
Sa tour bii nehhna❤️
@@moctarcisse8413 Amine Ya Rabbi 🤲🏾 mashallah yow kou bakhe nga ndeyesane mane Tivaouane rek la ame . Merci beaucoup Moctar Cissé
Dieredieuf malickiya bekk nagne yalna yalla bekk ci yeen papa abdou mbaye doundal lou bari
amine
Thieuy cheikhoul khawmi borom niarri kala yi ak niarri krouss yi ❤️🙏
Sheeeee teteee Malikiya lingeen di def si khôl eupna😍😭❤️ diazakoullahou khayran
Machallah Malikia sagal guenn Keur Gui wayy wii nimou may dff mane rkk makko xam
Fière de l’être 😍🕋🕋❤️😍😍😍🕋😍🕋🕋🕋🕋❤️🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋❤️❤️❤️🕋🕋❤️🕋❤️🕋❤️🕋❤️🕋❤️🕋❤️🕋😍🕋😍🕋🕋😍😍❤️🕋❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🕋❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🕋🕋🕋🕋🕋🕋yalnalén yallah faye
❤️❤️❤️❤️ SAMA PAPA PRÉFÉRÉ ❤️❤️merci beaucoup 😭😭❤️🙏🏿
Machalla Mame Mansour Sy mo kham bayam seydi elhadj Malick Sy papa Abdou Aziz goudeul Fan wereul AK wa keur mouse allé yeup machalla
MachaAllah MachaAllah khôl seddatina, bel hommage d'un fils envers son père, yalla na yalla fayal gnou seydil Elhadj Malick ak Jabootam
Je ne cesserai de vous souhaiter une très longue vie pour cette chanson qui m'apaise, et le sentiment de paix qu'elle m'aporte merci Abdoul Aziz Mbaye tu mérites vraiment le nom que tu portes merci et merci encore
Longue vie a toi Abdou Aziz cette chanson me va droit au cœur
Machallah goude fane ak weer pape Abdou azize mbaye
Ma Sha Allah🙏🏽.Un sentiment de paix de bonheur que ce poème m’apporte.Je ne cesse de le lire en boucle.Trop d’émotions ❤️
Yalna yalla yok léram
Amine inchallah ❤❤❤❤
@@assanegaye974 le
ALHAMDOULILAH. MA SHAA ALLAH MALIKIA TV. MOM RÉK LANIOU DONE KHAR. WALLAHI KONTANE NANIOU AMOUNIOU SÈN FAYE. THIA KAW THIA KANAM RÉK.
@MALIKIA TV TIVAOUANE MOY LÉÉROU MAODO. ♥️💚💙
À
TV .malikia la gnouye top❤❤❤❤
Manchalla dieuredieuf yalla na yalla barkel léne wa malikiya si barkel naby Moustapha psl
Yalla nagniou yalla faayale Abdoul Aziz mbaye yalla. Maye la goudou fane ak wer kheweul ak soutoureu barkè féké ak tale si barké seydouna mouhammad psl yalla moune nako sagne nako yalla nako yalla nako yalla Def
AMINE
Maodo maodo sougnou mame maodo nagnouko yalla fayal t bayigniu akh barkè bi gnoune sopè yi
Machallah malikia tv ken dou El hadji Mansour Balkhawmi
❤️❤️❤️❤️cheikhal kawemi💗💗☕
yalla na niou yalla feyal mame mansoor
Machallah yalla na fi yague tè ande ak weer
Mashaa Alllah nekh na trop . Nyungui Ziyareh ak tam di saku nyan
Diadieufety diadieufety xoll séd na yalla kham nako ALAHOU AKBA sante yalla warnaniou
Yalla na fi yague té ande ak wer ❤
Papa Abdou Aziz Mbaye yagg té andak wérrr 🙏🏾😇
Amine yarabi
Papa lo fi gueuneu yague mouye gueuneu bakh te and ak weer
@@aissatoufall7222mm
P
😊❤
M😊😢😢
They mbaaye yalla n'a yallah goudel fane wi inchallah
Je ne saurai cesser de l'écouter c'est un poème qui me transporte facilement très loin je vous remercie du fond du cœur
Mbaye Koudal Fane😭❤️😭❤️❤️❤️
Machaalla yalla na boure yalla faylen yiw , thi barkė Mame Mansour ( RTA) .
Allahouma Amine
Pape Abdou Aziz mbaye balgnou 😭😭😭😭😭😭❤️
xassidas bi rek ladonne khar wa malikia invité si wa keur moussa allé mbaye machallah yalla nalen yalla faye inchallah ♥♥♥♥♥
Fière d'être talibé Cheikh ❤️
Machallah sama sopè bi mbaye 😣😍😍❤❤❤ yalna yallah same la bayilafii nga yague di niou bègual inchallah 💎
Les mots me manquent pour exprimer mes sentiments ❤❤ce poème nous sort de nous même pour nous amener au de là❤❤❤
Malikia néna dou bayiiii❤️😭
Zeynab yangui wakhtou rek 😂mbaaye dé nila mel bilahi yow😭
Sou bayé dou bakh gni ninioul déf khôl
Khassida bi sama ♥️ bi lay dougg 😍😍😍
ALLAHU AK BAR LAHILAHA ILLALA MOUHAMMADOU RASSOULOULA SAWS
Yalla na yalla fay te weral theur yi
Macha’Allah Yalna Yalla faye yiw Malikia thia kaw thia kanam
Salaam, Malikya Yalla na lène Yalla gueneu doolel, bilaahi khôl yeupay séddeu ak programmes you mel nii. Alkhamdoulilah bi gnou Yalla boolek mame maodo RTA ba mou deff gnou talibé cheikh, alkhamdoulilah bamouy gnati yone! Merci pour tout
Allahouma Amine
MASHA ALLAH MAME MANSOUR SY BALKHAWMI RTA YALLAH NA YALLAH SWT FEYAL YOKK LERAM TASNIOU SI BARKÉM AMINE ❤❤❤❤❤❤❤
Alkhamdoulillah 🙏🏼Yallah naniu Yallah fayal Abdou Aziz Mbaye 🙏🏼Sa batt mogui arroser xool yi❤️❤️❤️
Je suis férue du Tidiane ❤❤❤
Ma cha allah malickiya liguey bi rafetna
Thieuy Malikia tv 😍😍😍 ! Dieureudieuf lii rek lagn doone khaar
Maa cha Allah rabboul alamiine. Alhamdoulilah rabbil alamiine.
Doumasi doyal walahii 😢❤❤❤
Abdoul Aziz manchalla ya mena wey YALLA fayela
شكرا لكم نفعنا الله ببركات محمد المنصور ورزقنا علما وفلسا أيضا أن نكون من أتباع الشيخ أحمد تجان شريف رضي الله عنه
Machaallah lii da séde xol ❤❤💞💞💞
Macha Allah Cheikhal Khawmi❤❤❤
Srg Babacar Sy Mansour Yalla nafi yagg té andak wérrr
MashAllah..fière d'être talibé cheikh...
Goudou fane ak weur Al Khalifa Seydi Aboubacar Sy Mansour 🙏🏽
Manchalah ❤️ Abdou Aziz yalna yalla goudal sa fann akk gni gua andal yeppp
Mann souma nèkoul wonn talibè cheikh nèk mbott moma guèunèul thièy maodo ak ndiabot guii🥰🥰🥰🥰
Gènèral pape abdoul Aziz mbaye 🙏🙏🙏🙏❤️❤️
Bilahi abdou azize mbaye mala beugue
Maachalla fière de cette tv yalna yalla dolellen
Fardoune Alal Ibni mon préféré
Machalla papa Abdou aziz mbaye yalna yalla barkel 🙏🙏🙏
Namone nane ko daale❤️
Amouma si môme sago yalla n'a yalla yook Say fane
Jaraama Cheikh Seydil Hajj Malik
Machallah malikia diarama mame Maodo rta diadieuf Abdou Aziz mbaye et son groupe
Yalla na yalla gereum dieufdji
Machalla machalla yallenagnou yalla sakhal si tarikha Cheikh amine 🥰🥰🥰
Cheikhoul khawmi ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Diarama mame Ass ❤
Khôl yui sédna machalla
Abdoul Aziz mom ndéyessane dou moduler dou onduler thià halou makegni lakoy tégue rék nieup avoué macha Allah yalna doliléne wérr soutoura ak bàrké.té yala fayal niou Mame Maodo ak ndiabottam
Diereu dief el hadji Mansour sy
Machallah lou dakh li♥️♥️♥️
Machallah lii nkhna.mnghi doli si limay sante yalla bima donné Talibé Cheikh...
ماشاء الله عبد العزيز بأي أطل الله عمره وأيده ❤❤🙏
L'I mo nehk
Ken dou ioe machallah 💘💘💘
Hommage filial très fort d'un disciple à son maître...