On attend ça avec impatience et on prie que tout se passe impeccablement bien. Aussi tout ce qui se raconte de mal sur ce mariage surtout sur son futur époux, même si c’est vrai, je ne sais pas et ne veux pas savoir, que cela le change pour qu’il prenne bien soin de notre Zeyna (dont je ne suis pas fan mais il y’a eu trop de parole sur cette petite) afin que ce mariage dure longtemps inchallah.Heureux ménage.
Zeyna Ndour Senegal gneup lako yeiner sauf les aigris, khalebi danga yagueu dounde injustice ndakh lane ? Famille bou siw gnou gnèleine. Nga Sango pateu doneuko sa ndeye. Motakh beuss bi gneup lako yeiner, yalla nala ya Allah are, yireleu, sangueula soutoura, yalla nala sougnou borom djoubolerla ak sa borome keur. Seuyeul ba dè, continuer sa pateu, diame rek ngay ame incha Allah.❤❤
Comme toute jeune fille qui se marie, c’est son plus beau jour. Que la famille de son père vienne ou pas, qu’elle profite pleinement de son mariage et des gens qui l’aiment. Félicitations
Machalha nuit amo loudeul Say doome Viviane yallha nala yallha defal diam khewel bi dial si diam AK salam ZEYNA toute n mes félicitations yallha n'a yallha barkel seybi
Yalla na seye bi barkel inch'Allah nguen tambali ci bismilah rahmani rahim té agaliko ci alhamdoulilah rabil alamine Yalla moussal len thi thiat tata vivi ak sa njabot bi
Aka nekhone nga wo Titi wo coumba gawlo wo Amy colle Dieng Aida samb Daba Seye say nawler artiste dal....wo ay badianam bayi leep mou seed ndakh loudoul diam diamako geune tek si dingalen rousslo tedou wagni sisa grade dara Chidid❤ adouna amul solo yalna yalla motali khewbi si diam leep sed gouyi
Ayyy way li nekhna yalla boum niou oump.loumou thi meuna don dal n'a khew mi nekh melni bou aziz ndiaye.viviane lou def ndanko khepppp. Kousi mer nak lolou sa affaire leu.yalla defnani Viviane doumako deglou khamalouma dara domam mais nak kounek beugue souniouy lay Mayer lo am defsi .Sénégal nak ay nafekheu mofi bari.kon nak bismilahi nio gui khar niougn wa team toppp internet bi suivre khôl yi nekh wassalam
Walay li nekhna yalla nanguene ko agualé ak sene saguo yalla mouseul vivi mouseul zeyna fi nit yagueu na xew ay famillam bagna gneuw rawatina badiene bou melni golo ak pakhou bakanam you khot ni boune mani vivi ak domam defougnoufi lou gnaw wakhougnoufi lou gnaw lep lou way nar sisene xew bi silou bone yalla na keupou si kaw kaka nar dink nalene yalla yalla nalene yalla takhawou
Vivi et zeyna kouleine di detester rek da beug bok té dioudoguoul.ne changer pas machalah ont vs aiment.vivi .seyna yala rek inchalah mo mane sisa destin .té dinala soutoural inchalah
Machala yale ne yeg thi djame ac salam bilay lignoy wakhe thi djeker dji degel wal dou dege sme yone nekou thi waye yale boumou nece dece adama dec nagne le zeyna Ndour yore co yir co are co te comprends co antouca yale ne sey bi barkel eureux ménage a vous vivi tu le mérites ❤❤❤❤
Yalnala yalla tahaw mu deffar leu mariage bu muthie teh yagu nga maguet si keur guogei Alahoum amen 🙏🏾 Yalla meunako teyit dinako deff inchalla❤❤❤bref sw hse ma belle 😍
🎉🎉🎉 félicitations Zeyna ❤❤☺️🤩👏👏soyez heureux longtemps vie toi et ta mère ❤🎉🎉
Mba yénagui conetane si xéw mi comme mane ❤❤❤❤❤❤❤❤
Yalla ngéne motali ak séne sago yarabi sama domou fans bi
Amone
Machalla yalna seuye bi barkel yarabi
On attend ça avec impatience et on prie que tout se passe impeccablement bien. Aussi tout ce qui se raconte de mal sur ce mariage surtout sur son futur époux, même si c’est vrai, je ne sais pas et ne veux pas savoir, que cela le change pour qu’il prenne bien soin de notre Zeyna (dont je ne suis pas fan mais il y’a eu trop de parole sur cette petite) afin que ce mariage dure longtemps inchallah.Heureux ménage.
Dont care kou dieul kamir wate thi aye féne koukeuye gueume🤔
Zeyna Ndour Senegal gneup lako yeiner sauf les aigris, khalebi danga yagueu dounde injustice ndakh lane ? Famille bou siw gnou gnèleine. Nga Sango pateu doneuko sa ndeye. Motakh beuss bi gneup lako yeiner, yalla nala ya Allah are, yireleu, sangueula soutoura, yalla nala sougnou borom djoubolerla ak sa borome keur. Seuyeul ba dè, continuer sa pateu, diame rek ngay ame incha Allah.❤❤
Is the reporter a good person himself?wish them well.let’s be careful with what u listen 👂🏾
Heureusement que aye paroles la rk zeyna kaine meussou guisss thiii Lou niak fayda
Yalna borom bi défar lep nguen amthi ndam
Machalah maman Vivi yalna nékeu seuy yagne takké thi arass.
Trop content pour zeyna et reine vivi yaln1 seuy bi barkél
Descends
Plus bas
Tu es presque
Félicitations pour vous 🎉🎉🎉❤❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤
Kep koussi sa xol sed te'nga yene'koko yalla nalla yalla defal diam❤
Alahouma Amin 🤲🤲🙏🙏🥰🥰❤️❤️
Amiiiin ya Rabby allah 🙏 🙏 🙏
Amine ya rabbi 🤲
Makini yalna yalla moussalén si thiate
Billahi Maachala yalla defalko diam ak salam
Machallah ❤️ henné time bou soft tè am classe yalla na lep mate Inchallah
Bilahi yaa baakh , doo niaakk dara ci aduna Incha ALLAHOU
Machala viviane yala nga egali ak sa sago si barki yonetebi psl tu la mérite ❤
Amine ya rabi
Oh trop contente pour Zey yalla na seuy bi barkel maman Vivi amal djiam rek❤❤❤❤
Trop contente pour Zeyna et maman Vivi yalna seuy bi baarkeel yalla aar la yaw ak sa borom keur te sakhal and bi
Amine
Amine
Mashallah yalna seuybii barkel barke seydina mouhamd sallalahou aleyhi wassallam amine y’a rabii ❤❤❤❤❤❤❤
Comme toute jeune fille qui se marie, c’est son plus beau jour. Que la famille de son père vienne ou pas, qu’elle profite pleinement de son mariage et des gens qui l’aiment. Félicitations
Vraiment, chapeau a Maman Fatou Guéweul, dama yeureum Viviane, su beugué may nieup Dina doywar , ndakh khéw bi artiste yi dinay wouyousi Viviane
Oh machallah sunu khôl yi sedina ❤❤❤bilakhi
Macha Allah yalna yalla barkél seuy bi barké seydina mouhamed Saw
Machalha nuit amo loudeul Say doome Viviane yallha nala yallha defal diam khewel bi dial si diam AK salam ZEYNA toute n mes félicitations yallha n'a yallha barkel seybi
Yalla na seye bi barkel inch'Allah nguen tambali ci bismilah rahmani rahim té agaliko ci alhamdoulilah rabil alamine Yalla moussal len thi thiat tata vivi ak sa njabot bi
Machalla Viviane yalla gua motali AK sa sago
Viviane les gens te remettent ces teranga car tu l’a fait dans le passé pour eux yako mériter ❤❤❤
Viviane dafa naturelle machallah
Zeyna ndour sama domou fans bi yalla na yalla motali seuy bou barkel❤
Aka nekhone nga wo Titi wo coumba gawlo wo Amy colle Dieng Aida samb Daba Seye say nawler artiste dal....wo ay badianam bayi leep mou seed ndakh loudoul diam diamako geune tek si dingalen rousslo tedou wagni sisa grade dara Chidid❤ adouna amul solo yalna yalla motali khewbi si diam leep sed gouyi
Aida monguifi dei.yaw lingay wakh ni dafa yombou trop .nit koula bagn banga kham KO lokoy wowei.
Machalla yallna seybi barkele ga amsi niabotte gou barké inchallah
Masha Allah..nekhna ..Rafetna..Viviane ak Zeyna,YAllah na lene YAllah aar,laffal Lene Thiatt MashaAllah❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ayyy way li nekhna yalla boum niou oump.loumou thi meuna don dal n'a khew mi nekh melni bou aziz ndiaye.viviane lou def ndanko khepppp. Kousi mer nak lolou sa affaire leu.yalla defnani Viviane doumako deglou khamalouma dara domam mais nak kounek beugue souniouy lay Mayer lo am defsi .Sénégal nak ay nafekheu mofi bari.kon nak bismilahi nio gui khar niougn wa team toppp internet bi suivre khôl yi nekh wassalam
Machaallah machallah yale na nékeu seiye bou ameu barkei Yale défe si ndiabotte bou ameu barkei
Contane na mane gni rek la beug. Zeyna Philippe ak Viviane
Walay li nekhna yalla nanguene ko agualé ak sene saguo yalla mouseul vivi mouseul zeyna fi nit yagueu na xew ay famillam bagna gneuw rawatina badiene bou melni golo ak pakhou bakanam you khot ni boune mani vivi ak domam defougnoufi lou gnaw wakhougnoufi lou gnaw lep lou way nar sisene xew bi silou bone yalla na keupou si kaw kaka nar dink nalene yalla yalla nalene yalla takhawou
Amine yarabi
😅😅😅😅😅😅😅@@adjindao3946
Toma raygama 😂😂khew bi diameu rek inchalla
😂😂rew gua
Ya meune xasté
Machalah seutou margo diatta ak ilnda chidid yalla na seuybi barkel
Ma sha Allah yalna seye bi barkel yalla bossi guiss dara loula diaaxal thi daradiay nabil moustapha asws amine
Walahi yalla nanguéne khew ci diam
Viviane yalla nangua ci ndamou
Ci barké Seydina Mohamed psl
Vraiment viviane mérite mbengue mii machalah yallah na yallah defalko soutoura biir ak biti ake sa famille
Machalla Vivi dafa bakh zeyna yalla nala yalla mousal mouthial la sama khôl bi sede n'a
Vivi et zeyna kouleine di detester rek da beug bok té dioudoguoul.ne changer pas machalah ont vs aiment.vivi .seyna yala rek inchalah mo mane sisa destin .té dinala soutoural inchalah
Machallah yallah bou thi thiate doug,diam rék inchallah ❤❤❤❤❤❤
Zeyna khale bou yarou la Masha Allah
Viviane yal nga yegale ak sa sago 🙏🏽
Heureux ménage Zeïna. Que du bonheur dans ton foyer
Machala yale ne yeg thi djame ac salam bilay lignoy wakhe thi djeker dji degel wal dou dege sme yone nekou thi waye yale boumou nece dece adama dec nagne le zeyna Ndour yore co yir co are co te comprends co antouca yale ne sey bi barkel eureux ménage a vous vivi tu le mérites ❤❤❤❤
Walaye lee nekhna waye. Vivian amatina ndam 💪💪💪💪♥️♥️♥️♥️
Touf touf touf yalla gueu eggalii ak sa saggo ❤Alkhamdoulila machalah. Association fasse yènè sétane faite signe 😂yalla bouñiiu guiss louniouye merloo😢in challah
Sama khôl bii sédena billay Ndour mala ko yéné, yéné sa yaye diabote défa metti chidid té dowo béne yoneu😢 machalla yana yalla motali.
En tout cas Ada rombana keur you baré douga keur zeyna loussi waye meune koumou nakhari matal sa bakane ❤🎉❤🎉❤🎉❤
Machaallah séybou barkel ❤❤❤
Queen vi Masha Allah, zeyna félicitations ❤❤❤❤❤❤
Yalnala yalla tahaw mu deffar leu mariage bu muthie teh yagu nga maguet si keur guogei Alahoum amen 🙏🏾 Yalla meunako teyit dinako deff inchalla❤❤❤bref sw hse ma belle 😍
Awww,I’am so Happy for them..can’t wait for tomorrow Incha Allah,May God Protect You All ❤❤❤❤
Sama khol bi sèd nasi trop bilay sa yaye dafa mérité li ❤ken dègouko si lou niak fayda foula rek
ALLAH meunn na louné. Yalna ko ALLAH defall
MarshaAllah yalna Yallah larf thiat
Machlla laf tiate vivi borom kholou diama bi
AMINNE INCHAALLAH FOREVER SOUGNOU DOMOUKHOLE BARKE AK SOUTZRA
Vivi nak da mériter li deh da bauf ay domam yare len sone si niom bolekk mougn ❤🎉
Henné time bii j'adore simples beuriwoul niit ❤. Qu'Allah bénisse ce mariage ❤ viviane et zeyna ndour le mérite amplement ❤🎉❤🎉❤🎉
Dou henné time deh Clara modone andi terangam en tant que maggalé Zeyna
Machallah machallah yalla n'a nga égualé ak diam lalale thi diam ak lalit ak diam inchallah vivi
❤❤❤❤machallah yalla na yalla laffal thiat way aminn 👀🤲🤲❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😊😊😅😅
Safna ba noppi 😊gnaw 😊
Machalla li nekhna sedna ❤ yalla nalen yalla lafal thiat
Allahouma Amine. Heureux menage❤
Machllah 👏👏👏😂💃💃💃💃❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️💯💯❤️
Machalla moi même je suis heureuse ❤❤❤
Viviane soit heureuse tu mérites le bonheur être dans une famille toxique n est pas facile Aby ndour est toxique
Machallah nekhna
Machallah Alhamdoulilah
Machalla Yalna yalla barkel amine lenne amine
Machallah khol sédatina bès sa bès kounèkak bèsam thioum ❤❤❤
Viviane ak zeyna nio yam danio am weurseuk mashallah ❤❤❤❤❤❤❤ yalla nalen thiat sekhlou
Manchallah sama ❤ Bangui mélni wanogou mboteu bilaye yalla na yalla barkél séye bi si barké seydina Mohamed psl 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Machallah l'AF thate
Henne time bou am classe macha Allah que Allah mets la baraka dans ton ménage ❤bisous
Machalla li nekhna
Yalna seuybi barkkél barkké chiéchoul khadim
Mashaa Allah ❤❤❤❤❤
Amine yarabi Amine yarabi Amine yarabi Amine yarabi Amine yarabi Amine Amine yarabi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mashallah Mashallah Mashallah Mashallah Mashallah Mashallah Mashallah ❤ 💖 ❤
Yalna barkel 🤲🥰
Machala yalla seuye bi barkel
Khew mi nekhna baparé machala tata fatou guéwel amengafi 10.000f si linga tague wa seckéne si guitek mamory tawou mamory ❤
Félicitation Viviane
Kholl Sedna lolll ci li way❤❤❤
Machalah sey bou barkel
Machallaah Yalla na Yalla motali seuy bi ❤❤❤❤❤❤❤
Machallah yalna yallah barkel seuy bi ❤❤❤
bon marriage a cette jeune fille.
Yana yalla barkéle seuy bi barké seydina mouhamet SAW
Maashaalah simple ❤❤❤
Sénégal yeup ko wara ndawtale
La brave maashaallah❤❤❤❤
Félicitations à elle
J'aime trop clara❤❤❤❤❤
Li neikhna wayy❤❤❤❤
Machalla laff thiat ♥️
Machallah yalla na yalla motali
Billâtes taye ba lundi douma nénaw billaye 😂😂😂😂😂
Fime né kou nekaw ame loula reuthie 😂😂
Wa 2 femme nianla😂😂😂😂😂😂heureux ménage ❤❤❤❤dieyna
Viviane yalla moko dougel thi kholou diam yu
Viviane dieul ma ma liguéye sa keur mba xew bi diale nak ma ame louma nétali wa boor be guir yalla 😂😂
Néna damayy chargé sama portable fasse gnéné setane xew en direct
Elle peut bien avoir ça car Viviane est très gentille sincèrement.
❤❤❤❤❤😂😂félicitations ma belle
Congratulations mashaAllah ❤❤❤❤❤❤