Félicitations TRIO BI pour le travail remarquable que vous faites. Monsieur DRAME doit être félicité pour sa contribution majeure dans l'élevage ladoum. Lou lérr nagn layy wakh. Tu sens qu'il a capitalisé toutes les années qu'il a passées dans le ladoum. Xam-xam deug, dafayy ande ak résultats. Bonne continuation.
Mod Dramé da warr dii wahh chaque jour ngir gars yii di dieul kham kham limouy wahh nii nieup guiss naniou ko tu es le professeur du 21 siècle yalla nassa fane goudou sii barkep khassida yii
Moi je pense que pour la réussite de l'élevage ,tous les éleveurs doivent participer ,c'est comme si on dit le Sénégal va organiser la Can mais il doit pas participer c'est le pays organisateur ,donc c'est une compétition tous les éleveurs doivent y participer
loukoy téreé dougue PA si kaw nieup guanane lane dramé défone guako si Makhou ba douguo ba légui way bobou mola tope boulniouko défat fi dougeul bala say vraiadversaire di dougue ba déme fofi douguati yakkeko mane mom silalay bayyi
Vitrine femelle bouma nékh ❤❤❤ yalna goud fan té barkél
No mai cherif mon con laaaaaaaa 😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅 trio bi nagounagnou com ladoum
Macha Allah ligueybi rafetna lool sakaw sakanam
Trio bi chaapo
da wara dougal kharyi ❤
Machallah Dramé nite kou oyof yalnala yalla werale are la
Bilahi Dramé , tu es un référence. Un Leader dans le monde de l’élevage avec un summum d’expérience. Merci beaucoup pour tes conseils.
Ladoumm sn bou douguoul kenn dou dougue nionm rk laniouy toppouhh🥰😍❤💪
Il est méthodique. Bravo Dramé 👍🏾
Ma sha Allah 😍 TRIOBI TV ✨ ci liguéye bou am solo bi ✨ LADOUM SN aussi ❤❤❤
Félicitations TRIO BI pour le travail remarquable que vous faites. Monsieur DRAME doit être félicité pour sa contribution majeure dans l'élevage ladoum. Lou lérr nagn layy wakh. Tu sens qu'il a capitalisé toutes les années qu'il a passées dans le ladoum. Xam-xam deug, dafayy ande ak résultats. Bonne continuation.
Manchallah bilahi sama ❤ bi dafa Sedd
Merci beaucoup bonne continuation mod drame chapeaux à toi vraiment yagu df Lou am solo 🎉
Chapeau trio bii TV bonne continuation
Ladoum Sn na doug concours rek record yi danou
le champion think you for everything ❤❤❤
Machalla ❤❤
Mod Dramé da warr dii wahh chaque jour ngir gars yii di dieul kham kham limouy wahh nii nieup guiss naniou ko tu es le professeur du 21 siècle yalla nassa fane goudou sii barkep khassida yii
Mane xarbi dinama raye rék
Antouka temyi mom dramé ces meilleurs
Yii Dramé il est trop dangereux 😅❤
Demlen seeti taala seras, ay female yu bakh la am
Machalla grand Dramè goudale fane tèmou Ande AK wèrre sa liguéy rafèt n'a si élevage Mane yaw rèk lay toppou damala beugue rék tè yalla takhe❤❤❤
Machallah ❤
Ma Shaa Allah! Modou Dramé da wara dougou si concours yi si FILA bi. Boumou khôl thiow yi, na khôl djeurignou élevage bi.
Ladoume sn.da war concours si fila bii. inchalah
Bergerie de référence ladoum SN dafa wara compétir demande nationale leu
Bon courage Trio Bi
Thiey Fila bi d’où yomb dh inchallah 😂
Avec Dramé , c'est le haut niveau ❤❤❤
Moi je pense que pour la réussite de l'élevage ,tous les éleveurs doivent participer ,c'est comme si on dit le Sénégal va organiser la Can mais il doit pas participer c'est le pays organisateur ,donc c'est une compétition tous les éleveurs doivent y participer
Non Yonne la mou douguelle ko dé 🙏 lolou Rk lagnou begue srx
Papito kara 😭
Dramé c'est le meilleur
Dramé la référence 🎉🎉🎉
Ladoum sn dafa wara concours CCI FiLA bi
Drame est le mieur
Vitrine ak kaya sont les favoris
1 ak 2
😂😂 fo bayyi Bb Touré, Yaye Dieye etc 😂😂
Oui oui 🎉
Ladoum sn dougalall femelle yeup
Danga wara dougou
Macha allah ❤❤
Ladoum sn da wara concours si FILA bii
I need ramm can u help me plzz❤
Vraiment drame ndanane la
loukoy téreé dougue PA si kaw nieup guanane lane dramé défone guako si Makhou ba douguo ba légui way bobou mola tope boulniouko défat fi dougeul bala say vraiadversaire di dougue ba déme fofi douguati yakkeko mane mom silalay bayyi
Mais ani amadou Barry
Drame dougallll stp😢
Na femmelle yi dogou demende sociale la
Waw dogou rk🤑🤑🤫
Non da wara dougg
Drame na dougou concours pour athieu barre yi sino rek guayi douniou nangou liguey