Grande mosquée de Dakar 1960 commission de quête Journal bi le 20 janvier 1960 la ñu ciy xibaar Xaliss bi ñu doone ladjie kilifa yi ngir tabàx Jummah Ndakaru, lime bi moy ñi joxé ci ligéye bi Seriñ Fallou 1 million Serin Bassirou. 600 000 Seriñ Shéx Gaindé 500 000 Seriñ Khaban 100 000 Seriñ Mamoune 200000 Serin Tako mback 100000 Seriñ M Awa Balla. 100000 Seriñ S. Awa Balla 100000 Seriñ Modou Habib 30000 Seriñ Ablaye Fall. 50 000 Baye Niass 1,2 million Abdou Aziz Sy 50 000 Seriñ Ady Touré. 40 000 Amadou dème 25 000 Amadou Cissé 10 000 Babacar ndiour. 5000 Seriñ Fallou Mbacké tél ci wax ni chaque 1 janvier Dina joxé wate 1 million ba Jummah ji nopi . Baye Dramé da n'a yobu ate mu jote 1 millions.
Imam doit rester dans le cadre des textes et se taire! Il est hautain et nous amène des polémiques chaque année. Les lebous ne l'ont pas envoyé sinon ils lui auraient demandé de remercier ceux qui dénoncent les voleurs. PR Doomaye soyez rassuré. El malick Ndiaye bravo!
Certains sénégalais ne connaissent pas le respect il va falloir que Sonko et Diomaye prennent le bâton. Ces comportements imposent à Diomaye de rester dans cours suprême.
Merci beaucoup mansour âme na solo deug moye deug li la réwmi soxla di wax deug té yalla takh ak fo mana fété si politiques wayé genres kokou si plateau bi di mboubo imam té dou wax katou deug lou yakhou si réwmi ñioko yakh gñiko khamone avant mouye changer camps politiques xame nañiou né féne kat deug le motax enciens vidéos wam yi famou nékone 5 dernières années dône fa wakhé ni mouye wakhé baye wakh né kokou waliyou la comme nimou kaye défé fimou nieuwe légui yep la supprimer genres borom xame you melni toma mi la réwmi sohla dou genres bobou si plateau bi
Mais ta bien textuellement. Mais l'imam n ignore pas cela. Il veux dakar c pour lebous et grande mosquée est toujours dirigée par les lebous. Donc c'est bien de ne pas oublié les lebous. Ça parole est surtout imagée faut pas interprétation mauvaise
Mansour ningua firé sah aya bi dou nonou boy dougou thi keur danguay diar thi bountou amna ay interprétation you Bari fén la imam bi dioumé né lebou yi gnoy bountou bi..amna gnounane boy dougou thi diné shahada bi Moy bountou bi
Vraiment lui il n'est pas simple, il demande à intervenir en direct et il fait semblant de ne pas comprendre que l'émission est en direct, c'est du n'importe quoi...
Si règne bi Kham kham dina fegne Beug kham kham Dina am Lou Bari Dina fegne Ba deug fegne nakhaté mom Ak Loula nekh Dina diekh Deuk bouy yokk Nila laay signaler Ma shaa Allah Senegal aar sounou reww diamal niou Walahi Dina bakh In shaa Allah
Niou balma akh deh ! Wayé nioune la majeur partie des sénégalais tégouniou Yalla plasam ! Dokhôlou niou AL Kitab ( Le Coran) Ak Sunna ( Hadiss Rasoulou lah) Tarikha yi ak wasso rek laniou topou ! Motakh Mosquée yi am ayy tourou wassô ak tarikha ! ImamouGrande Mosquée 🕌 li mouy wakh tégou ka féne loudoul si niak khame chariah ak sounnah, banékhou baké name rek lay wakhé ! Warna am respect si Presidrnt Diomay mi nga khamni moka geune diangue Le Coran Ak Sunnah
Mansour Cissé Moy li toubab naane"Au royaume des aveugles les borgnes sont rois" je ne défend guère l'imam Samb mais guisnaa ni ses propos ont été lachement et hypocritement sortis de leur contexe . combien de fois Allah son st Coran son prophète et sa religion ont été attaqués, dénigrés ,et ke sais je encore au Sénégal ? Mansour et tes naatangos de moudjirimoune vous n'avez jamais osé levé le plus Petit doigt... senegal lann lagne fi wakhoul Allah (swt) ? Bann yekkati lagne fi yekkati woul sounou yaaliyi! ? Bref Mansour demal diangui les abc de l'islam té moytou sa borome "innal mounaafikhoune fii darkil asfali minnari " maak yow ak nieep Nanou toubabal Yallah swt bala déé nieuw ...
C'est quoi le problème. L' imam a raison . Ils ont besoin de l'aide ceux qui est normal sa sert a rien de polémiqué. Meme si il a pas trouvé les mots juste pour dire ses besoins dans le mosquée. Guir yalla senegal arrêtez. Si l'argent du peuple de sert pas au peuple. Je vois pas où est le sens de l'état.
Ce imam nous a pas déçu c’est l’imam de macky sall franchement macky nous a fait découvrir beaucoup personne faut
😂😂😂 Mdr
Félicitons maki sale pour cela.🤣🤣🤣🤣
Bien dit Mansour Cissé ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤, carton vert pour le nvo gouvernement et son excellence Diomaye Moy Sonko ❤❤❤❤❤❤
Deug nékhoul merci Baye Mass. Wayé bofi nieuwaté di sani kher mom on sera sans pitié
😂😂😂 Lou bakh si état bi rek lagnou dègue gnoune
SONKO Seul ❤
Machalla masour yalna yalla weral yokou kham kham bi lila senegale yi di khar si yaw dokhalal
Grande mosquée de Dakar 1960 commission de quête
Journal bi le 20 janvier 1960 la ñu ciy xibaar
Xaliss bi ñu doone ladjie kilifa yi ngir tabàx
Jummah Ndakaru, lime bi moy ñi joxé ci ligéye bi
Seriñ Fallou
1 million
Serin Bassirou.
600 000
Seriñ Shéx Gaindé 500 000
Seriñ Khaban
100 000
Seriñ Mamoune
200000
Serin Tako mback 100000
Seriñ M Awa Balla. 100000
Seriñ S. Awa Balla 100000
Seriñ Modou Habib 30000
Seriñ Ablaye Fall.
50 000
Baye Niass
1,2 million
Abdou Aziz Sy
50 000
Seriñ Ady Touré.
40 000
Amadou dème
25 000
Amadou Cissé
10 000
Babacar ndiour.
5000
Seriñ Fallou Mbacké tél ci wax ni chaque 1 janvier
Dina joxé wate 1 million ba Jummah ji nopi . Baye
Dramé da n'a yobu ate mu jote 1 millions.
Et après... C'est un concours ?
Concour dieum sa yalla aka baax
Fii koufi ball ballou niou wax la sa bop …
@@mamadouthiamsady2906 😂😂😂
Ma sha allah s mansorr blessings 🍏🍋🍉
un imam indigne, senegal islam beuriwoufi. Sounisme rek lagnouy topp.
Imam doit rester dans le cadre des textes et se taire! Il est hautain et nous amène des polémiques chaque année. Les lebous ne l'ont pas envoyé sinon ils lui auraient demandé de remercier ceux qui dénoncent les voleurs. PR Doomaye soyez rassuré. El malick Ndiaye bravo!
Cet Imam ne dit que des bêtises. On doit lui dire la vérité.
Vraiment
Chaque année
ماشاء الله تبارك الرحمن فيكم وجزاكم الله خير الجزاء
Djiby l’homme fort
Jaay prek leu nak mais dafa degg 😂😂😂 🎉
😂😂nanane la dé
Merci Mansour si éclaircissement bi
Certains sénégalais ne connaissent pas le respect il va falloir que Sonko et Diomaye prennent le bâton. Ces comportements imposent à Diomaye de rester dans cours suprême.
Vraiment
Pas contre ce vieux j'espère? On peut tout régler par la diplomatie
Djibi dafa yarou, ma cha allah
Thieuy serign mansour machallah
Merci serigne Mansour
Djiby Sarr le grand journaliste
Machalla Mansour Sy Cissé vous êtes une fierté de notre pays dieredief yalla ne yalla Faye le je vous aime nguer yalla
Yérim cissé seck n2 Wa annal massadjida lilaahi falaa tadhun mahalaahi ahada pas - Ahadd 😂corrigé nga imam bi patriote bi corrigé leu😜mansour bayil graw grawlou bi💊💊
Do dara cheikh Yérim Seck 2
waar na baayi diiné bimiy nioddi kou ko deglou xaam ni day foor limiy wax wayei jangoul 😂
Merci serigne mansour 🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤
Merci mansour
Tey mom mansour cissè wakhna deug 👍👍👍👍
Merci bcp mansour ❤❤❤
Serigne Mansour Sy Cissé😂❤🎉
Exposé mansour bi amna solo. Gars yi baal léne mansour waay
balnane ko😅😅😅
Yirim 2😂
Serigne Mansour daa melni ningua daanalé ayabi amna ndioum teii "Wa annal massadjida lilaahi falaa tadhun mahalaahi ahadaa" et non "Ahad"
Je confirme ! 😂
C'est ça. Aksi hadith bi aussi, on dit ala koulli et non ala koullou.
dafa danel ayabi mo tah mou terminé ko ak sukun
Je comfirme c'est avec soukoun à la fin.❤
C'est soukoune à la fin
Yirim 2 Machalah mais bayil diay prek 😂
Merci imam sa takahway amna solo
MachAllah merci beaucoup
Mansour Sy Cissé ak imam bi gnonyém xamugnou dara doul rék😂
مع الله أحدا leu dou مع الله أحد serigne Mansour
Diadieuf S MANSORR Kadou Yi Amna Solo Nion Sonko Rek Lany Topo ❤
Merci MANSOUR.
حسبنا الله ونعم الوكيل آستغفر الله العظيم وأتوب إليه الله آكبر
Merci mansour si
Mansour fen kat la long time,
Cheikh Yerim jr
Ki mom modestie zero ishhh😴😂😂
😂😂😂
je te jure
non😂/cc😊
Cc
Diomaye yaarou yaarou bi la wora baayi
Merci
Merci beaucoup mansour âme na solo deug moye deug li la réwmi soxla di wax deug té yalla takh ak fo mana fété si politiques wayé genres kokou si plateau bi di mboubo imam té dou wax katou deug lou yakhou si réwmi ñioko yakh gñiko khamone avant mouye changer camps politiques xame nañiou né féne kat deug le motax enciens vidéos wam yi famou nékone 5 dernières années dône fa wakhé ni mouye wakhé baye wakh né kokou waliyou la comme nimou kaye défé fimou nieuwe légui yep la supprimer genres borom xame you melni toma mi la réwmi sohla dou genres bobou si plateau bi
Cissé le nandité intellectuel 💪🙏🤣
Mai kii lou tax manoul modeste 😮
بخ بخ بخ بخ ❤❤❤❤
C'est bien vrai : بخ بخ بخ و الله
Mansour fait du Mansour 😂une fois de plus.
Mais j’admets que son intervention est pertinente. Taay xam xam rek la wax
Mahalahi akhada
Lii motax SWT❤️ ni lougn dioxei si xam xam lou neew leu. Some lagnouy xam tambalei naane ken douma diamakk dou niyakk… Cey
Serigne Mansour dafa dioum, Imam dafa bougeu wakhné lebou yi nioy bountou Ndakarou mais pas keurou diné yi....
70 daradia mai pas 27 daradia
Ziarénaala Mansour … En avant Frère . 😘
Mansour danga def ay erreur si tajwid ayatoullahi falaa tadou'ouu ma allahi ahadaa wala nga neh ahadane mais pas ahad
Merci
Mais ta bien textuellement. Mais l'imam n ignore pas cela. Il veux dakar c pour lebous et grande mosquée est toujours dirigée par les lebous. Donc c'est bien de ne pas oublié les lebous. Ça parole est surtout imagée faut pas interprétation mauvaise
Vérité pure et dure.
Thieuy Mansour 😂😂😂😂
😂😂😂😂oustaz mansour si Cissé machala
Def na erreur
Mansour, quand tu prends le soin de retifier, éviter aussi de faire des erreurs.
Imam bi mowara yam
Fèn rèk masjidou nabawiyi amna
Lolou appellation rek laa mais dans le vrai sens du terme jakla yeup jakka yallah laniou
Mansour ningua firé sah aya bi dou nonou boy dougou thi keur danguay diar thi bountou amna ay interprétation you Bari fén la imam bi dioumé né lebou yi gnoy bountou bi..amna gnounane boy dougou thi diné shahada bi Moy bountou bi
❤❤❤❤❤❤❤
Na ETAT dieull ay responsabilitém ndax président dou ay thiaxane
Vraiment lui il n'est pas simple, il demande à intervenir en direct et il fait semblant de ne pas comprendre que l'émission est en direct, c'est du n'importe quoi...
Fekhal lene khol yi Diomaye mofi nek teh mo narra defar senegal Jubb jubbal jubbanti rk
Ce qui est encore plus grave est que les gens interpretent les versets, hors contexte.
Oussou est un imam sans imane😂😂😂
Machalah mais ayabi kholatko
Si règne bi
Kham kham dina fegne
Beug kham kham Dina am
Lou Bari Dina fegne
Ba deug fegne nakhaté mom
Ak Loula nekh Dina diekh
Deuk bouy yokk Nila laay signaler
Ma shaa Allah
Senegal aar sounou reww diamal niou
Walahi Dina bakh
In shaa Allah
Ouztaz mansour mome migui khekhalé ak boy yi dé. si souf😂😂 .néna niou diangy bala nio tontou.😂😂
Gnounn djangi nagnou ba nopi
Mom moo wara djangi watt
"Ahadaa" moy baat bou djoup bi pas "ahadd"😂😂😂
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Athjia yerime 2
Yerim 2 😂
Mr mansour c'est pas un pays religieux pour que Diomaye dirige une prière. Il ne faut pas intervertir les choses pour faire plaisir
L'histoire nous apprend que pour l'extension de la grande mosquée feu Djily Mbaye a y participé financièrement et pourtant il n'est pas lebou.
La mosquée une maison de dieu
Ahada pa ahadd
Mansour n'a pas fauté il a appliqué la règle de lecture d'arrêt. Il n'existe pas une seule règle de lecture
@@saneseydou443la règle d'arrêt est احدا (ahada) pas احد (ahad)
Règle : Ahadan = Ahada
Non djibi Arkham gua fin bi😂
La mosquee n'a pas ete contruite par le Maroc pour le senegal? ou bien?
Roi bi Contribuer nassi
@@mamesheiix99 merci
La mosquée a été financé à plus d 80% par le maroc
Figa danalé dou nonou dh, c’est ahadaa pas ahad
Dafa xam dara munek fi di diaxase rek
Vraiment je déteste les transporteurs Thiès Richard 16000 billay c'est trop l'état doit prendre des mesures ferme
❤
Ahadaa lanouy wah
Yerim 2 fin Rek lay def
Saway legui oustaz la.
Dioumoul dé il a répété le verset deux fois
Massalikoul djinane ablaye wade mo ko tabakh
Oh saay loy wakh ni!
Kham nga li YALAH wakh ci lidoul deug?
Cet imam travaille pour macky
Nako Diomaye bayil diakka bii
Mansour DG soleil so bayé fouye réék avancé .walaye achiim
thiéy yerim 2😂😂
😂😂😂
Ahadaa wala akhad?
👉👉👂👂💯💯
Un Imam doit parle sur les texte dans un contexte precie , et le pure il nous parle de leur mosquée , vraiment honte à se soit disent Imam
Ku beug djiby dèl bind tureum thi commentairyi aka yaro tè am responsabilitè
Niou balma akh deh ! Wayé nioune la majeur partie des sénégalais tégouniou Yalla plasam ! Dokhôlou niou AL Kitab ( Le Coran) Ak Sunna ( Hadiss Rasoulou lah) Tarikha yi ak wasso rek laniou topou ! Motakh Mosquée yi am ayy tourou wassô ak tarikha ! ImamouGrande Mosquée 🕌 li mouy wakh tégou ka féne loudoul si niak khame chariah ak sounnah, banékhou baké name rek lay wakhé ! Warna am respect si Presidrnt Diomay mi nga khamni moka geune diangue Le Coran Ak Sunnah
Mansour Cissé Moy li toubab naane"Au royaume des aveugles les borgnes sont rois" je ne défend guère l'imam Samb mais guisnaa ni ses propos ont été lachement et hypocritement sortis de leur contexe . combien de fois Allah son st Coran son prophète et sa religion ont été attaqués, dénigrés ,et ke sais je encore au Sénégal ?
Mansour et tes naatangos de moudjirimoune vous n'avez jamais osé levé le plus Petit doigt... senegal lann lagne fi wakhoul Allah (swt) ? Bann yekkati lagne fi yekkati woul sounou yaaliyi! ? Bref Mansour demal diangui les abc de l'islam té moytou sa borome "innal mounaafikhoune fii darkil asfali minnari " maak yow ak nieep Nanou toubabal Yallah swt bala déé nieuw ...
C'est quoi le problème. L' imam a raison . Ils ont besoin de l'aide ceux qui est normal sa sert a rien de polémiqué. Meme si il a pas trouvé les mots juste pour dire ses besoins dans le mosquée. Guir yalla senegal arrêtez. Si l'argent du peuple de sert pas au peuple. Je vois pas où est le sens de l'état.
imam Grand mosquée il est trés impoli te réwou ,te xamedu
achaque fois il prepose son interé préssonelle
même son visage c'est ne pas visagé Islam
Vérité absolue mansour
Son des mécontent n'a khamné fi macky diékhalnafi diomaye moi nek mou nekhko ak mou metiko
Diaye prék rék
J ete choqués d attendre des propos comme ca de l imam franche, c est quoi cette dictature