Balla mii son époque est passé amoul fébar amoul défarou Magg boufi moytouwoul boy yii dinga khamni lépp deug leu Et merci à la 2stv vous êtes les meilleurs 🥇🔥🔥🔥🔥🔥
Wlh 2stv comme Canal+ si lamb loumou rawé télé yi dafa beuri bantamba rk lay setane guiss détail lamb wayé télé y bou deff direct bi tchiim do xam sakh kou eupeuh Supporter .. Merci 2stv❤️
Modou mbaye que dieu te protège , toi comme ton père !! Vraiment j'ai pas de mots car ce que tu réalises et juste exceptionnel !! . Voilà 15 Ans que je suis bantamba depuis la France et j'ai jamais étais déçu par le travail que ton père réalisé, puis toi ! La relève , donc inchallah je prie le bon dieu que tout ce que tu entreprendra pour cette 2023 ne soit que bonheur inchallah . . Paix sur toi et toutes ta famille.
Modou Mbaye je te l'avais, et je ne cesserai de le dire, t'es sur le bon chemin, ça se voit que t'as bien appris est que la formation est bien sue donc la releve est assurée. on continuera d'aimer la lutte grace a Batamba et tuu essayes d'apporter une nouvelle touche à a cette emission. Chapeau a toi mais chapeau egalement à toute l'equipe. c'est le bantamba, c'est le bantamba, c'est le meilleur...
La lutte continu de nous faire rêver. J'ai toujours cru à boy niang 2 depuis. Ils l'ont sous estimé et ils oublient qu'il lutte avec intelligence. Le lion est tombé avec les armes à la main. Donner chance aux jeunes feras que améliorer et développer la lutte les temps changent et c'est au tour des jeunes
Balla legui dafa yekh si mouvement yeup amatoul rapidité mais moy lamb xola ambiance bi rek oh vs xlo forme bobou la balla war di andi. Mais bantamba dra doula raw merci à vous💥💯
Yalah moy mayé ndam mais balla gaye kou gaye kou wara xolate staff bila quoi magui guiss yeneu détails yo xamni temps yifi père double less ak père balla gaye néké doko guiss yalnalenn yalah yeureum. Félicitations à boy niang
BG2 n'est pas le meilleur de l'histoire de la lutte sénégalaise. Niom Falaye Baldé, Mame Gorgui Ndiaye, Pape Diop Boston champion olympique et médaille international, Mbaye Gueye , double less , Boy Bambara, Yekini khana ñioniou daniou donn samm ay nakk
Wally seck ak domou PÉRE Gaston liniou wakh amna solo lool le faite que niou délo yallah limou mom santeu ko magalko niakhat nit yi niou kham ni yallah rék moy bour mofi nékeu donc Alhamdoulillah
@@cbcb6076 nafekh rek becaye combien de fois sur le plateau 2tv ni yekini c’est le meilleur de tout les temps parcrque Legui y’a aziz Ndiaye molen di may khaliss rek
Balla mii son époque est passé amoul fébar amoul défarou
Magg boufi moytouwoul boy yii dinga khamni lépp deug leu
Et merci à la 2stv vous êtes les meilleurs 🥇🔥🔥🔥🔥🔥
Kou d'accord ni 2stv Moy halif général koul télé si lamb direct yéna si mane bantamba mome lathie Modou thieuy père békay
Les autres ce sont des pseudos médias..Gni ce sont des pro..
Boy Niang meilleur Bakou de l’année , Nekhna tropp franchement
Culture Deugue la
Modou MBAYE delén dém keur Pére Birahim NDIAYE diko diokh micro mouy def analyse il est le meilleur de tous les temps vraiment.
Merci Pére Beckaye.
Deugue dou Romb noopou
Wlh 2stv comme Canal+ si lamb loumou rawé télé yi dafa beuri bantamba rk lay setane guiss détail lamb wayé télé y bou deff direct bi tchiim do xam sakh kou eupeuh Supporter ..
Merci 2stv❤️
Boy niang mo ambiance mo eupp dolé mo danne félicitations mbeur
Modou mbaye que dieu te protège , toi comme ton père !! Vraiment j'ai pas de mots car ce que tu réalises et juste exceptionnel !! . Voilà 15 Ans que je suis bantamba depuis la France et j'ai jamais étais déçu par le travail que ton père réalisé, puis toi ! La relève , donc inchallah je prie le bon dieu que tout ce que tu entreprendra pour cette 2023 ne soit que bonheur inchallah . . Paix sur toi et toutes ta famille.
Modou Lo Xaragne Lo 👑👑👑👑👑👑👑👑 Modou Lo Xaragne Lo 👑👑👑👑👑👑👑👑 lo déf begue nagne lamb dji dagua gniafé ba done ligua done Yalla naguako mourelo 👑👑👑👑👑
Amine yarabi🤲🏾❤️🙏🏾
Modou Mbaye je te l'avais, et je ne cesserai de le dire, t'es sur le bon chemin, ça se voit que t'as bien appris est que la formation est bien sue donc la releve est assurée. on continuera d'aimer la lutte grace a Batamba et tuu essayes d'apporter une nouvelle touche à a cette emission. Chapeau a toi mais chapeau egalement à toute l'equipe. c'est le bantamba, c'est le bantamba, c'est le meilleur...
Sama Oustaz Monde Lo❤❤
Le real VIP de la lutte sénégalaise
félicitation boy niang courage le vrai lion on t'aime fort nékha faral
Fane la neke lion🤣
@@iboubaye1184 ki lay mous leug😂😂😂
Nice na Modou Mbaye. Mai kendou eumeu bilay ❤
C’est le BANTAMBA c’est le BANTAMBA c’est le meilleur 🥰❤️
Félicitations à Boy Niang ndam li yalla nala dijkk barkep borom Touba
Modou Xaragne Lô le GOAT de la lutte sénégalaise🇸🇳💪💪💪 Amoul siiissou
🗣️Thiey wa pikine ken Dou niom pikine Moy Sénégal 🇸🇳
Eumeu sene Boy Niang❤️💚❤️💚❤️💚
2stv et lutte tu doivent travailler ensemble pour le meilleur de la lutte ❤️ wa 2stv danio meun lamb vraiment ❤
Boy Niang 2 meilleur lutteur de l année
Deug deug Bantamba c’est le meilleur wallahi❤️✌🏾
Boye niang sa guèweul yi way nanu lu nèh bilahi douma dèm fi lay toG maylèn xaliss way 😭1:04
Franchement Guédiawaye nion meuna yeugueul du courage Balla guaye yaye lamb félicitation Boy niang bonne continuation
Wakho fi Dara ba paré gnou Dann Len amolen staff ay commedien gno yorr thioumoukay mbeur mi li😅😅😅😅😅😅
Merci beaucoup waa 2stv vraiment ken dou yen billhai yalla na sen diamou yagui barkep Serigne bi
Domaine bou néke amna messi modou lo moy messi de la lutte moy bayi lamb ak couronne unchallah le phénomène de la lutte
Kat lein sein ndy deim bEUri dji sein combat bi mO gEUn
@@babacarndiaye8548 Tousse kou sissou sa yaye diourate Modou Lô le messi de l’aréne😂😂😂
Loulér nga wakh moye lamb de😅😅😅😅🤙🤙🤙🤙🤙
@@babacarndiaye8548abalma sa xol bi ma tangal si ndokh 😂
Wouy gros mots😂😂😂
Mdrr “balla tank bou damm le beurré”
Xanna bamouy baakou, tank bi damoul woone….😅😅😂🤣
bantamba est le meilleur émission de lutte
2:14:23 tank bou damme kay akanio meun saltel victoire 😂😂😂😂
Moma def ay ree bakou def lounek beuré niou daanla niounan tangkeu bou damou
Hana guissou niou lou balla baakou 😂 lolou kou daam dinako baakou
Merci à toute l’équipe de Bantamba pour ses images exceptionnelles 👍 mention spéciale a Modou mbaye et bruno 🙏
Wakhal d mane chaque combat gnom lay khar pour savourer lamb ji machalla ❤
Wakhal d mane chaque combat gnom lay khar pour savourer lamb ji machalla ❤
💪🙏
La lutte continu de nous faire rêver.
J'ai toujours cru à boy niang 2 depuis.
Ils l'ont sous estimé et ils oublient qu'il lutte avec intelligence.
Le lion est tombé avec les armes à la main. Donner chance aux jeunes feras que améliorer et développer la lutte les temps changent et c'est au tour des jeunes
Balla Gaye est encore très jeune.
Félicitations à toute l'équipe de Bantamba vraiment vous les meilleurs👌👌👌 Modou Mbaye chapeau à vous❤🙏
balla yalna sa diam yagg bilahi so danouwei 1000 combats dou takh nu bayila tu es le meilleur lutteur iow yay lamb bilahi lolou mom nangoul lein
Nekhoul ba nekhoul nak 2stv c la meilleure télé au Sénégal
Mais touss boy niang bi neexna dh 😍😍😍
Bakou Boy Niang lane la nékhe na trop waye ❤❤❤❤
Lou léere nga wakh
Mame balla gaye 2 yalnako yalla takhawou amine ya rabi
Bantamba gay sétane gni dém stade sakh yaléni gueuneu néekh lei
Felicitation Modou Mbaye et à toute l équipe,vous faites un grand boulot
Vraiment SENSEi, sa wakh amna solo...le staff des lutteurs devraient prendre en compte vos analyses
Balla legui dafa yekh si mouvement yeup amatoul rapidité mais moy lamb xola ambiance bi rek oh vs xlo forme bobou la balla war di andi. Mais bantamba dra doula raw merci à vous💥💯
Neixoul ba neixoul mei Bantamba moy xoramou Lamb si image si son leipe leipe❤❤❤❤❤
Vous êtes les meilleurs bravo à toutes l'équipes la lutte nôtre Propre sport...💪💪👍💪💪👍👍👍👍👍👍👍
Modou mbaye walahi yagui dèf liguéye bou âme solo
Modou lo le messi de l’arène lamb Ji Namnagn la ❤️🥳🥳
Boye Niang mo sokhor danko ba dam ko
Boy gniang siguil ngagniou bilahi yallnala ndamli djick
Tank Bou dameu nga fethie ba weundélou 😅😅🤣🤣 grawoul miss nagn ko ci yen
Merci beaucoup à tout l'équipe suis content de vous mention spéciale à modou mbaye li moy lamb li laniou am li moy souniou ada hooo dara dou lamb
Alhamdoulillah félicitations Boy niang ❤ du courage balla G2 yallah na diamou yague
Bantamba meilleur émissions de lutte ❤
Lamb nekhna machalla ❤ boy niang rek ❤
Boy Niang vrai guewaal feeling bou beuri
Je suis toujours avec Balla bilaye.mais bantamba Ay bantamba c'est le meilleur
Modou mbaye bantamba bi nekhna machalah. Mais stp debrief il y'a toujours à la fin.
Pape Birahim delen ko consulter lu beuri waay il est excellent
Boy niang esk mandiwoul limou touss néxna
Trop sakh
YALLA NALEN BOROM MAY WER THI BARKE MOUHAMED AMINE .MERCI BCP
😂😂😂donc balla gaye amoul défaite ndakh chak défaite gnu doul nii daffa blessé gueum léne yalla sénégalais Yii kéne manatuléne nakh balla moo yaakh bopam dieul ay doom baa yaram bi feuneukh
Yalah moy mayé ndam mais balla gaye kou gaye kou wara xolate staff bila quoi magui guiss yeneu détails yo xamni temps yifi père double less ak père balla gaye néké doko guiss yalnalenn yalah yeureum.
Félicitations à boy niang
Président Ousmane sonko le futur président du Sénégal 2024inchalla inchalla inchalla
Walakhi 2stv c'est le meilleur ❤️❤️♥️♥️🥰🥰😭😭😭🥰🥰🥰🥰🥰
Bantamba c L meilleur ❤🎉
Wa Guédiawaye ba légui yénay wakh😌😌😌
Modou Mbay yalla na sa diamou yage ❤️❤️
Machalla 2stv billah yén na mane si lanmp Machalla eumue sene Machalla boy niag ❤
Ndekkei wa pikine nio eup classe wa guediawaye 😂😂
Wa guediawaye heure bouniou léne dané niounie danio blessé 😂😂
Bilahi lol ma niekhle man
wadji néna balla tank bou dame la beuré khana dou dame binou kham 😜😜😜
bantamba c le meilleur
C’est qui sait arrêter boy Niang a Guedieway
Batamba c’est le meilleur
Niou Nangoul ko Balla moy lamb
Modou Lo 100% ❤
Boucher ak lirou Diane takkoune radio 🔉 yi nopilen guir yalla thiapathioly bi moy s'en baye nopilen boy niang tass guediawaye
Xaragne lo kasse seul
Balla gaye 2 daniou la beug ba aldiana inchallah ❤️🙏
Mais nak défale Lila warr boule topou khalisse bi way holale si gnila beug 🙏❤️
Machalla modou mbaye yena mom lamb
Sa guédiaway yi 🤣🤣 tangkeu bou damou nounsiy dokhé bay bakkou bay beuré 🤣🤣🤣🤣🤣
Sensei merci wahga lép une pertinente analyse
Bilay 2stv moy lamb kholal image yi ak montagr yii thioo vraiment chapeau a vous
2s TV mooooy souniou télé 💯💯
Billahi Sénégal nékh na mé politique séyi rék niouko yakhe bayielén satihmi tayerem sén popoul bi 🇸🇳🤲
Y
Warnagne bayii kougnou dane nga declarer blessure balla neka dii fethia di daw gnou dane ko ngene dafa dame mais esk cava
Ay ree sakh dama diapou gni danio mana saltel victoire
😁😁😂😂😅🤣🤣
1:43:31 père bi xamna lamb deglou leenn ko il a tout vu
Papa Dieng la lambalogue la
Boule décourage mbeur tu est le meilleur et tu restera le meilleur champion travailler dur inchallah
Balla gaye tu resteras le meilleur de l’histoire lolou dou changer yay sunu mbeur à vie❤
Hahahahah le meilleur de l'histoire nak
BG2 n'est pas le meilleur de l'histoire de la lutte sénégalaise.
Niom Falaye Baldé, Mame Gorgui Ndiaye, Pape Diop Boston champion olympique et médaille international, Mbaye Gueye , double less , Boy Bambara, Yekini khana ñioniou daniou donn samm ay nakk
"Nabou Yâ Dânne" yângui môll balégui 🔥🤙.
Bayiléne Di saltéll victoire diambour kougnee;Kougne dann rek ganné dagua blessé
Ada fass kassé yalla nala yalla may ndam inchallah 👑
Wally seck ak domou PÉRE Gaston liniou wakh amna solo lool le faite que niou délo yallah limou mom santeu ko magalko niakhat nit yi niou kham ni yallah rék moy bour mofi nékeu donc Alhamdoulillah
Balla vraiment champion la mo mbeuré lépp
Becaye Mbaye vrai nafekh gua yekini loumoufi def ben mbeur doko fi def plus de 10anszero défaites do sakh nit
en tout cas diaxalnama loutax les gens ne veulent pas reconnaître le mérite de Yekini c'est le meilleur lutteur de tout les temps🎉
@@cbcb6076 nafekh rek becaye combien de fois sur le plateau 2tv ni yekini c’est le meilleur de tout les temps parcrque Legui y’a aziz Ndiaye molen di may khaliss rek
Pourtant Becaye yag naa wakh Yekini c’ est le meilleur des meilleurs !
@@papadiom9260 oui mes depuis longtemps wakhatouko
@@talibendoye2818 tas tt compris khaliss rek takh mouy wakh li yeup mais balla deffoufi lou kene deffoul
Tank bou damou kay xana après touss bila wax léne lou logique
2stv C les meilleurs vraiment
Bantamba c'est le meilleur
Mention spéciale à la 2stv sen liguey rafetna !
Wa mane Boucher la geuneuh yeureum si lambe dji ba diabaram togal nako xéwar bouy ak bisap bilési karité😂mouy mélni 🐂bouniou roukhh😂😂
😂 😂 😂 😂 😂 No bakhou quoi ak yerem talou bi
Ya bonn😂😂😂😂😂😂😂
Ibou Afia 2 rék lagnouy topou 💯🔥🦁
Wa 2s tv yalla na sén diam yague
Merci beaucoup modou may bantama rék 🥰🥰🥰
Père birahim Ndiaye loutakh mou kham lamb tamit kholal limou commenter té lamb bi commencer goul😏
No balla il soufre en silence
Li metti moy balla gaye à chaque fois bou danou oute laye dafa febar wala cagoule bi newoul si lamb ji wa la danko soute geum len yalla
Ballagaye2 bimi Bakou migui si lamb dji mais lamb dernier moment la
8.30😂😂😂😂😂 mbeur bi atté Léne ba parè teudaat 😂😂😂😅
Wouye 😂😂moma diomale li😂