1er Partie Laylatoul hadr à Tivaouane par Serigne Moustapha SY

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 23 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 158

  • @moussafay9747
    @moussafay9747 2 ปีที่แล้ว +62

    Je suis layène mé j'estime tro capitaine la façon kil dirige YALNA DIAME YAGUE BARKÉ BAYE LAYE ALEYSALAM DIEUREUDIEUF sy malick

  • @adyfqye8890
    @adyfqye8890 2 ปีที่แล้ว +3

    Yallana yalla fayalnioula
    Defal la goudou fane ak wër

  • @khadidiatouwade7176
    @khadidiatouwade7176 2 ปีที่แล้ว +8

    Machaallah yana yalla may la wer ak werlé nga yague fi lol ak talibé yi ak bolléme koula yéné amine inchalah 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲

  • @cheikhfaye9592
    @cheikhfaye9592 2 ปีที่แล้ว +6

    Wallahi bour yalla magui lay niane fane wou goudou ci sy Demba🙏❤❤❤❤❤❤

  • @modouseck9249
    @modouseck9249 2 ปีที่แล้ว +3

    Ndayesane yalna yalla goudal sa Fann seringe Moustapha s'y♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • @moussendoye1290
    @moussendoye1290 2 ปีที่แล้ว +5

    Yalna yalla fayléne ki di papà ak dom yeup

  • @aichesy1633
    @aichesy1633 2 ปีที่แล้ว +9

    yalna yalla samla arr la sy demba

  • @dienzen
    @dienzen 2 ปีที่แล้ว +3

    Wa Aleyka Salam Sy Malick. Nimala beugei mak yallah reka ko kham. Yague fi lol te werr bi jaahi Nabil Mustafa. Ameen

  • @cheikhlo10
    @cheikhlo10 2 ปีที่แล้ว +23

    Sy Malick namone nagne la😭😭😭 yalna yalla goudeul sa fane inchallah 🙏🏾

  • @pendagamouniang3497
    @pendagamouniang3497 2 ปีที่แล้ว +8

    Machallah sy malick yalna yallah goudal say fane téh sammal niouko 💖💖💖💖💖💖😥🙏

  • @ibrahimafall2933
    @ibrahimafall2933 8 หลายเดือนก่อน

    Vous êtes indestructibles.
    La bénédiction de Dieu vous accompagne !

  • @papedieng6815
    @papedieng6815 2 ปีที่แล้ว +6

    Machllah yallana yala motali inchall sy malick ❣❣❣🙏

  • @magatteka8124
    @magatteka8124 2 ปีที่แล้ว +5

    L espoir est permis avec mame cheikh capitaine. Yalnala borom bi same

  • @dioufmalick1330
    @dioufmalick1330 2 ปีที่แล้ว +6

    Amatina nèkh nèkh 🙏🙏🙏🙏🙏🙏♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • @moussendoye1290
    @moussendoye1290 2 ปีที่แล้ว +7

    Yalna yalla taxawoula serign moustapha ❤️

  • @malicktop543
    @malicktop543 2 ปีที่แล้ว +2

    Alhamdulillah
    Alhamdulillah
    Alhamdulillah
    Machallah fatabârakallâhou Sy

  • @amadousamb7687
    @amadousamb7687 2 ปีที่แล้ว +1

    Mashaaallaah ❤️❤️

  • @assaneka7149
    @assaneka7149 2 ปีที่แล้ว +3

    Fatabarakal lahou machallah ❤️

  • @ngossegueye9414
    @ngossegueye9414 2 ปีที่แล้ว

    Sy Malick ❤️ goude AK wer rék lanioulay gnanal, yalla nanoula Matt ndioabott yalla bougnula reuthie Sy

  • @services24h13
    @services24h13 2 ปีที่แล้ว +22

    Quand il parle je me sens heureux comme si je suis à firdawsi

    • @alassaneseye1425
      @alassaneseye1425 2 ปีที่แล้ว +1

      Walay ndeysan

    • @cheikhlo10
      @cheikhlo10 2 ปีที่แล้ว +3

      Sa voix apaise le cœur tout simplement tout comme son père ❤️

    • @biranedieng2771
      @biranedieng2771 2 ปีที่แล้ว +2

      Walay ndeysan beuri nga si morom yalna yalla deff niou ay ndiabotam incha Allah

    • @baldejuniorkourawellbaldej5913
      @baldejuniorkourawellbaldej5913 2 ปีที่แล้ว +1

      Walay ndeyesan frère moi je suis guinéen mais quand il parle je me sens quelque choses d'extraordinaires au fond de moi walaye

    • @baldejuniorkourawellbaldej5913
      @baldejuniorkourawellbaldej5913 2 ปีที่แล้ว +1

      Que Allah Tout-Puissant vous protège Sy Malick

  • @alioucisse8515
    @alioucisse8515 2 ปีที่แล้ว +12

    mahsallah sy Malick

  • @ousseynouthiam7796
    @ousseynouthiam7796 2 ปีที่แล้ว +4

    Macha Allah way ♥️👊

  • @rokiadiop8373
    @rokiadiop8373 2 ปีที่แล้ว +3

    Machallah,💖💖💖💖

  • @adamatop8234
    @adamatop8234 2 ปีที่แล้ว +9

    Machahala yag lol té wer

  • @aysatoufallfall9437
    @aysatoufallfall9437 2 ปีที่แล้ว +4

    Yala nafi yag te wer🤲🤲🤲

  • @moussaladiane82
    @moussaladiane82 2 ปีที่แล้ว +9

    ماشاءالله سه مالك أطال الله عمرك وأيدك ونصرك

  • @dramemouhamadoumoustapha5387
    @dramemouhamadoumoustapha5387 2 ปีที่แล้ว +1

    Alkhamdoulilah Sy ....

  • @teusteusproduction931
    @teusteusproduction931 2 ปีที่แล้ว +12

    Dieureudieuff sy

  • @elhajuisegadiopdiop6499
    @elhajuisegadiopdiop6499 2 ปีที่แล้ว +6

    Yalla barkel capitaine

  • @khadygambie8566
    @khadygambie8566 2 ปีที่แล้ว +4

    Mon capitaine je vous amies beaucoup

  • @services24h13
    @services24h13 2 ปีที่แล้ว +19

    Un vrai philosophe
    Sa dimension est incontournable

  • @dieynabousmoustaphasy9377
    @dieynabousmoustaphasy9377 2 ปีที่แล้ว +8

    Macha allah

  • @damigueye858
    @damigueye858 2 ปีที่แล้ว +6

    Ma challa

  • @djilylome4620
    @djilylome4620 2 ปีที่แล้ว +3

    Machallah amna solo

  • @dabandiaye5314
    @dabandiaye5314 2 ปีที่แล้ว +5

    Machallah sy

  • @mohamedfall6154
    @mohamedfall6154 2 ปีที่แล้ว +1

    Wakho darrrrrra sawaye. Père et fils dans les nuages.

  • @groupeleveurprofessioneltv3058
    @groupeleveurprofessioneltv3058 2 ปีที่แล้ว +4

    Ma challah

  • @ndeyediop335
    @ndeyediop335 2 ปีที่แล้ว +6

    Lo léblé lolou lagne laye faye Sy Malick li ga lébolone sa wadiour dou nakhsaye mouk mane Mouride sadikh la wayyé dama beugeu kou fonque aye wadiouram lodoul défal kènne té Yalla takh bo weurré adouna bamou dathie do guiss kouleu ko défal bouma fatté si niane SY MALICK

  • @teusteusproduction931
    @teusteusproduction931 2 ปีที่แล้ว +9

    Machala

  • @abouka174
    @abouka174 2 ปีที่แล้ว

    Macha Allah sy doundal te weur

  • @mouhamadoutoure6276
    @mouhamadoutoure6276 2 ปีที่แล้ว +20

    J'ai l'impression qu'il comprend bien le coran parfois quand il le parle ça fait bon de l'entendre seulement ...

  • @rayhanakane7231
    @rayhanakane7231 2 ปีที่แล้ว

    UN VRAI ERUDIT MASHALA.

  • @alousylla674
    @alousylla674 2 ปีที่แล้ว

    Machalah sy Malick

  • @kineniang9777
    @kineniang9777 2 ปีที่แล้ว +9

    - machallah amamatina solo lol

  • @sopetaha7459
    @sopetaha7459 2 ปีที่แล้ว +5

    Yonentibi SAW mo gen si lepp Lu yalla bind Epuis mo wara genal bep djoulit bou gom yalla leppe loumou ame. Subhanallah Senegal mo barri aye thiakhan ‼️‼️‼️

    • @mouhamedgueye1924
      @mouhamedgueye1924 2 ปีที่แล้ว +4

      ohhh wakh déguine la ladj

    • @elhmalick4026
      @elhmalick4026 2 ปีที่แล้ว +2

      SAW si léram langnou bind lolou c sans doute donc on vous prie d'analyser les paroles des sages selon leur contexte et même si c'était mal dit , en tant que bn musulman, ta priorité devrait être d'essayer d'en puiser l'importance
      Désolé pour la réponse s'il ya des mal dit 🙏🙏

    • @cheikhtidianethiam9197
      @cheikhtidianethiam9197 2 ปีที่แล้ว +2

      Yaw yaako bole thi koursou boum bokoul .demal outi deg deg boka amoul gua noppi

    • @Rasssoullll
      @Rasssoullll 2 ปีที่แล้ว +2

      Yow amo deg deg almo kham kham,,yonetbi takhoul gnouy wakh,,,c un exeption kokou bokoul si course bi cou conscienwoul sakh khamgako foumouy wakhee moy diamono dji gnouy doudou la wakh

    • @sopetaha7459
      @sopetaha7459 2 ปีที่แล้ว +1

      @@cheikhtidianethiam9197 fanatisme baaxoul si dine, Serigne Moustapha not kou baax la, teh barri xam xam mes nak amna lol xamne dafa diadouwoula waxx. Dafaye yobu nit si etapou Fanatisme di waral SHIRK ak waxx lou op.

  • @sopetaha7459
    @sopetaha7459 2 ปีที่แล้ว +7

    ‏العلم يرفع بيتا لا عماد له والجهل ‏يهدم بيت العز والشرف ❤️❤️‼️🥰

    • @manesoursamb7952
      @manesoursamb7952 2 ปีที่แล้ว

      Magiu laye ziar bay yitbi foumo né

    • @sopetaha7459
      @sopetaha7459 2 ปีที่แล้ว

      @@manesoursamb7952 Ahmad sawqhi moko waxx. ‏أحمد شوقي أمير الشعراء

    • @manesoursamb7952
      @manesoursamb7952 2 ปีที่แล้ว

      @@sopetaha7459 machala damako masa lir mais khamatouma fanla barakal lawou fiika kanmoy amii rou souhara fii سنغال 🙏🙏

    • @sopetaha7459
      @sopetaha7459 2 ปีที่แล้ว

      @@manesoursamb7952 seydil hadji Malik ibnu Ousamane 😀

    • @manesoursamb7952
      @manesoursamb7952 2 ปีที่แล้ว

      أمير الشعراء في سنغال مام شيخ ألمكتوم

  • @mouhamedseye10
    @mouhamedseye10 2 ปีที่แล้ว +7

    Macha allah ❤️🙏🏾

  • @alioucisse8515
    @alioucisse8515 2 ปีที่แล้ว +8

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @goramaar9642
    @goramaar9642 2 ปีที่แล้ว +4

    D-M-W-M ❤️

  • @adjabinetafall3635
    @adjabinetafall3635 2 ปีที่แล้ว +4

    2ème partie bi

  • @khadtv8013
    @khadtv8013 2 ปีที่แล้ว +4

    Xam xam dekoule féne fooko fék rék yaye boroom الحكمة دالة المؤمن

  • @nourafall3771
    @nourafall3771 2 ปีที่แล้ว

    Titarou rek ak top ou bak an

  • @sopetaha7459
    @sopetaha7459 2 ปีที่แล้ว +3

    عَنْ أَنَسِ بْنِ مَالِكٍ قَالَ قَالَ رَسُولُ اللَّهِ صلى الله عليه وسلم لاَ يُؤْمِنُ أَحَدُكُمْ حَتَّى أَكُونَ أَحَبَّ إِلَيْهِ مِنْ وَلَدِهِ وَوَالِدِهِ وَالنَّاسِ أَجْمَعِينَ
    ‏صحيح البخاري

    • @amdykebe9223
      @amdykebe9223 2 ปีที่แล้ว +1

      والله

    • @oumaralfarooqciss7356
      @oumaralfarooqciss7356 2 ปีที่แล้ว +1

      Nitt dafay teey way hamal famou jeum ba paré

    • @magattediop4442
      @magattediop4442 2 ปีที่แล้ว +1

      Sahiiih houbbou rassoul awwalane : annabi awllaa bil mouminin....

  • @ndiayebopthiore623
    @ndiayebopthiore623 2 ปีที่แล้ว +3

    Aka dég arabe.

  • @nourafall3771
    @nourafall3771 2 ปีที่แล้ว +1

    Wakho fi touss

  • @ousmanediop1620
    @ousmanediop1620 2 ปีที่แล้ว +1

    Mane bouma nekhe samay wadiour nioma gueneul lou yalla binde lolene thi meun ? donter dieume wouko thi yonenti bi amlene khel wala guene nopi

    • @omarmbengue6984
      @omarmbengue6984 2 ปีที่แล้ว

      Seni baye nio lenjitou sili wayé sotiwoul yalnayala joubantila

  • @mouhamethndiaye8021
    @mouhamethndiaye8021 2 ปีที่แล้ว +2

    Ki khamoul foumouy takhaw bokalé yalla rkk guene meune ak lundeumeul khélou nit gniy wayé yalla gueumoul nelawoul lou teuweu kham yagoul

    • @omarmbengue6984
      @omarmbengue6984 2 ปีที่แล้ว +2

      Bilahi yaw khamo islam khamo yala rouh motah nit kham islam ak yala yalnayala joubantila

    • @seynaboudiop7709
      @seynaboudiop7709 2 ปีที่แล้ว +2

      @@omarmbengue6984 amiiine genre yii rk nio mata nianal c ke dagn ko soxla 😂😂😂

    • @NDIAYEPM
      @NDIAYEPM 2 ปีที่แล้ว

      NDIAYE loo beugg buzz, ndeyssan yaa yaye, foofu aam darra la dhe.

  • @mouhamadoutoure6276
    @mouhamadoutoure6276 2 ปีที่แล้ว +2

    Parlez nous de notre Seigneur... promotion tarikha dafa doy

    • @khadimboy566
      @khadimboy566 2 ปีที่แล้ว +2

      Tu n'as qu'à zappé té dem setti ton seigneur nga may niou diam

    • @messatsu2074
      @messatsu2074 2 ปีที่แล้ว +1

      Ani sa baye loumouy diarign si yaw néko mou jangal la sa diiné mo eup solo.

    • @ndeyediop335
      @ndeyediop335 2 ปีที่แล้ว +1

      Mandou mo geune djiouli

    • @oumaralfarooqciss7356
      @oumaralfarooqciss7356 2 ปีที่แล้ว +1

      Nga dem seeti et puis c'est tout

  • @boubacarba6644
    @boubacarba6644 2 ปีที่แล้ว +1

    Astakhfiroulah

  • @djamilniang2780
    @djamilniang2780 2 ปีที่แล้ว

    Senegal aka bari saytané

  • @papesylla613
    @papesylla613 2 ปีที่แล้ว

    Wakhoo fii touss wakhal nite yii lou yeunentibi wakh akk alkhourane mo geun détails yii compliqué yii di philosophie philosophil ni 😂

  • @mouhamadoutoure6276
    @mouhamadoutoure6276 2 ปีที่แล้ว

    Yonentébi kouko bindeu????

    • @moustaphagaye1457
      @moustaphagaye1457 2 ปีที่แล้ว +2

      Yonenebi Yalla moko bind té li Yalla binde yeup mosi geun mais ki bamouy wax yonenebi taxoul mouy wax nakh kokou c autre chose geuné
      Amoulene degg degg bari ngéne wax té am diott topou niou rék di wax xana amoulene programme boudoul suivre moustarchid yi

    • @modouseck2588
      @modouseck2588 2 ปีที่แล้ว

      ♥️♥️♥️♥️♥️♥️

    • @Rasssoullll
      @Rasssoullll 2 ปีที่แล้ว +1

      Dego wathdji

    • @Rasssoullll
      @Rasssoullll 2 ปีที่แล้ว +1

      Yonetbi takhoul mouy wakh kokou expetion la

    • @oumaralfarooqciss7356
      @oumaralfarooqciss7356 2 ปีที่แล้ว

      Yaw soon nga way nanal ndox

  • @lunelune8872
    @lunelune8872 2 ปีที่แล้ว

    boy bi deg na ci discouram mounane daccorouma ak serigne chiekh almakhtoum bi nane yalla kene douko guisss.. legui sa papa nga beugeu diokh deug si sa kaw mame..do nitou dara..serigne chiekh dafa élégant thi kham kham. degueul wakhi dof yi sagne nga guené nit..non yeurem na khar yi lene di setane.

    • @mamadouly2276
      @mamadouly2276 2 ปีที่แล้ว

      Diguente Mame ak papa ak dom losi sa yoon

    • @lunelune8872
      @lunelune8872 2 ปีที่แล้ว

      mame Dji dafa universel té boy bi khamoul tous

  • @sopetaha7459
    @sopetaha7459 2 ปีที่แล้ว +1

    Subhanallah kee tog mo niou genal kep kou yalla binde lolu waxx bou doye ware la. Lolu dai waneh rek neh Capitaine mame cheikh diangoul. Sunu borom neina : ‏والله ورسوله أحق أن يرضوه إن كانوا مؤمنين. Serigne moustapha fonk nala lol mes Capitaine diangoul. Limouy waxx xamousi Dara subhanallah.

    • @goradiop5618
      @goradiop5618 2 ปีที่แล้ว

      Si vous n'êtes pas rhétoricien, fermez votre gueule. Wax bu nekk ak contexte bign ko waxé, limu wax jamono bi mu nekk rek la concerné. Mais do ko xam parce que jàngo réthorique

    • @goradiop5618
      @goradiop5618 2 ปีที่แล้ว

      Si vous n'êtes pas rhétoricien, fermez votre gueule. Wax bu nekk ak contexte bign ko waxé, limu wax jamono bi mu nekk rek la concerné. Mais do ko xam parce que jàngo réthorique

    • @sopetaha7459
      @sopetaha7459 2 ปีที่แล้ว

      @@goradiop5618 limou waxx op na. Ak noko mane degue, kee tog mo niou genal kou yalla bind op loool. iow Momu ya diangoul

    • @awaseck8984
      @awaseck8984 2 ปีที่แล้ว +2

      Mahalla bou guein douguei yakamti guein corriger ba do deiglou et Serigne Moustapha là si bien dit nitki bo hamoul philosophie wam khamo logiquam bouko atei sisa logique ak sa philosophie nonou la tolou kou bah bayilein sew djiko

    • @sopetaha7459
      @sopetaha7459 2 ปีที่แล้ว +1

      @UC4eBOn_YHARejHPqXxS1u7Q iow mane douma sa morom. Sa jare gui topeh rek teh du ngen ladj loutax. Wolof da khoumbe teh mane topeh. Bayilen thiakhan teh dem diangue li yalla waxx ak li yonentibi diangaleh. Thiakhan baaxoul

  • @goramaar9642
    @goramaar9642 2 ปีที่แล้ว

    Pourquoi les wollof méchant?

  • @djamilniang2780
    @djamilniang2780 2 ปีที่แล้ว +1

    Capitaine démal diangui sa Baye kéne rawouko

  • @sidatemohamedthiam3787
    @sidatemohamedthiam3787 2 ปีที่แล้ว +1

    Capitaine del sol yeré you yiw

  • @ibrahimakane8315
    @ibrahimakane8315 2 ปีที่แล้ว

    Du danger d'un hypocrite que vous ne réaliserez sa ruse ou son complot qu'après qu'il vous aura fait peu ou beaucoup de mal

  • @khadimdiop1853
    @khadimdiop1853 2 ปีที่แล้ว

    Mola guenal kep kou yalla bind en plus nga préciser ko donc yonent bi nak psl???

    • @messatsu2074
      @messatsu2074 2 ปีที่แล้ว +1

      Nitt bo khamoul philosophie wam khamo logique-am boul ko atté sisa philosophie wla sisa logique. Yonent bi bokoul si course bobu.

    • @alhassanthiam5743
      @alhassanthiam5743 2 ปีที่แล้ว

      @@messatsu2074 respect aux saints

  • @mouhamadoutoure6276
    @mouhamadoutoure6276 2 ปีที่แล้ว

    Wokhi doff rék nguéndi wakh

    • @moustaphagaye1457
      @moustaphagaye1457 2 ปีที่แล้ว +3

      Amguene diott réw ngéne séne xam xam néw na ba dolene am béne degg degg wayé diguéne sonou dh dém léne dadialé adiya yi té fayi dji séne borou banque bi moy séne farata

    • @awaseck8984
      @awaseck8984 2 ปีที่แล้ว

      Yay dofbou makk bi

    • @omarmbengue6984
      @omarmbengue6984 2 ปีที่แล้ว

      Abjoulit dou sokhar dou bone yalnayala joubantila

    • @oumaralfarooqciss7356
      @oumaralfarooqciss7356 2 ปีที่แล้ว

      Yay dof bou makk bi lo fiy def

    • @mouhamadoutoure6276
      @mouhamadoutoure6276 2 ปีที่แล้ว

      @@oumaralfarooqciss7356 sén serigne bi mi gueune ... nieup

  • @elhadjigaye979
    @elhadjigaye979 2 ปีที่แล้ว +6

    Macha alla

  • @jambaarlegilegi9252
    @jambaarlegilegi9252 2 ปีที่แล้ว +3

    Macha'allah

  • @bebendiaye1422
    @bebendiaye1422 2 ปีที่แล้ว +3

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @moussambengue9988
    @moussambengue9988 2 ปีที่แล้ว +4

    Machalla

  • @evadiallo6237
    @evadiallo6237 2 ปีที่แล้ว +3

    Machaallah