Siteu prononce yékini juste pour avoir de l'aide il met à mal yékeni et les autres supporters des autres lutteurs nioukoy saga t yonam nékatoul si lamb
Bour je ne suis pas un supporter de siteu mais honnêtement ce que tu fais comme sa n'ai pas correcte de 1 il faut savoir quand est-ce que cette vidéo a etais tournée et de 2 il faut montrer toutes la vidéo .. tu fais une propagande sur siteu .. tu cherche les problèmes pour rien quoi !! Et puis si c'est l'argent des investisseur du combat que aziz Ndiaye a promis à tout les communicateur sur ce combat qui te fait faire ce genre de débat c'est très grave tu va trop loins
Mais yaweu soit disant bour nguèwèl...khana da ngua fatè bi nguay tontou biram soulèy,di saga...khana da ngua fatè sa bopp??? Yaweu soit disant bour koula fueuneu niaw lamigne amoul ... Yaweu meuno yèdeu siteu,wala kou bokeu si momeu... Koneu mangui deugueu ni saga bakhoul. Koneu yèdeu ngua sa bopp bou vide bi. Weet and se ...
Billah Bour balla gaye 2 kilifeuleu merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤
Bour il faut écouter toute la vidéo yekini a tourné le dos à la lutte
Buur Billahi damala beugue mane
Balla Gayie 2 kasse
Bour guéweul nékhna 😂
Bour dou sérére yeup deh
Siteu ak wakham dioubary
😅😅😅😅😅😅 yaldaw kone yaw daguaye féne🤔🤔🤔🤔🤔
Hana combat yeup ay combat du siècle lagn si yen. Li yagg nako deg
😂😂😂😂😂 wakhal dé😂😂
Siteu prononce yékini juste pour avoir de l'aide il met à mal yékeni et les autres supporters des autres lutteurs nioukoy saga t yonam nékatoul si lamb
Js8 serere 100 %100 mais siteu n'est pas notre espoirs nous les serere
😂😂😂😂rouss na
LOUTAKH NGA WARA GUEUM BOU SITEU TE GUEMO JI WAKH SI KADOU YEKINI . SITEU NDIDIAYAM MO KHAM YEKINI MAIS BOKOU NIOU DARA
Mo deug na dem beuredji mo guenn
Suite dou touss wakh yeal dawe
Wa buur lane leu ??
Balla vs modou lo loci am
Mdrrr bour yaw danga neex modou loum beug lay fayeikou
Moma diakhal
Si siteu bat balla revanche siteu Modou lo est plus valable
Un grand SI 😅
Buur ngėuweul dafa beugue siteu depuis comba Modou lo pasé ba legui mė sėrrėt yi siteu moy sėn mbėur si mbeur you mak yi buur ngėuweul khamna deugue
Ce gar c'est Un menteur il force sa relation avec yékini à cause d'une terre qu'ils ont vendu à yékini dans la commune de nguéniéne
Bour je ne suis pas un supporter de siteu mais honnêtement ce que tu fais comme sa n'ai pas correcte de 1 il faut savoir quand est-ce que cette vidéo a etais tournée et de 2 il faut montrer toutes la vidéo .. tu fais une propagande sur siteu .. tu cherche les problèmes pour rien quoi !!
Et puis si c'est l'argent des investisseur du combat que aziz Ndiaye a promis à tout les communicateur sur ce combat qui te fait faire ce genre de débat c'est très grave tu va trop loins
Siter dafa rew
Mais yaweu soit disant bour nguèwèl...khana da ngua fatè bi nguay tontou biram soulèy,di saga...khana da ngua fatè sa bopp???
Yaweu soit disant bour koula fueuneu niaw lamigne amoul ...
Yaweu meuno yèdeu siteu,wala kou bokeu si momeu...
Koneu mangui deugueu ni saga bakhoul. Koneu yèdeu ngua sa bopp bou vide bi. Weet and se ...
Bour wakhofi dara yak fadam ndakh gen maygnou diam si balla gaye modou lo khawma louguen si beug