Paco l’homme de valeur et de principes ne mérite vraiment pas ça Yalla xol lay fayy té notre Paco du trokh inchalla. Even pro vous montrer chaque jour des réalités qui existent dans notre société merci
Lâ ilâha illâ l-lâhu, wahdahu lâ sharîka lahu, lahu-l-mulku wa lahu-l-hamdu, yuhyî wa yumîtu, wa huwa hayyun lâ yamûtu, bi-yadihi-l-khayru, wa huwa alâ kulli shay’in qadîr.
@@khadidiatousylla6262mane sama tanta moma deudale ak domame gua khamni mane rekk la bougone walakhi sa fait 8ans de cela mane ak wadji doukhougnou sakh dadie ta nio bokk famille daniouy nekk si ben khew ta douniou guisante
@@alimafall7221Lolou mom doyna warr dii amna niou sokhorr nk s derett sah ngakey bagn mtx lossi guiss dinagn soukratt des mois ndax dieuf diou bone té boul kham lougn nara féki Alakhira😢
@@joliekalsoum7287 bialye kokou yallah atenaniou car lak bou meti moka dall instant bi demi paralysi la am et le pire dans tout sa moye môme dafa niak diom daye niew sounou keur bataye mai douma khol si beute ndakh rous sama yaye dako defal teranga bounek si adouna car ay domou badiane domou nidiaye laniou mai nitt kou bonne moy kokou j'ai passé autres choses mais le gars n'arrête pas de me poursuivre
Serie bi d sanekh mo takh makoy setane depuis la fameuse théâtre sanekh boba legui la nek sama acteur préféré amlene jamm yene niep barkep borome touba ❤❤❤
La mère de Sacha va pleurer tout les larmes de son corps quand elle verra que sa fille est devenue un robot et que Aly Mamadou va la prendre comme un chiffon elle ne s est pas ce qu elle a fait
Hmm même s'il arrive malheur avec aly mamadou, elle ne fera rien. Elle n'aime pas sa fille. N'oublions pas que sa fille a tenté de se suicider et elle s'en fichait
C'est quoi la tradition ?!, ce qui va tjrs détruire nos vies 🚶♀️ y'a k de l'égoïsme. Lan moy liguéy nitt pour mou top nitt, Allé Mamadou est ce qu'il réfléchit, neik ak ko khamni lernalani limouy dound ak ioe c pas naturel non du tt. Man suis xaal poularh, ko Kandé mi yeita, ms alhamdoulillah mes parents respectent nos choix, si c'est faisable 🙏 Aïssata weiré gua 😒 nous réclamons le bonheur de Paco ✊
Certes wadiour amna dolé ci dom mais Mère Aissata limi déf rèyna, grawna 😢😢 Yêneu wadiour yi warnagnou djiteul sèni bonheur ak avenirou dom avant les "qu'en dira-t-on". Aly Mamadou yow diapoo si touss. Amour forcé 😮 Oh c'est triste pour Paco et encore plus pour Chacha la pauvre 😢😢😢 EvenProd yalèn meneu "Aléa" - BRAVO ❤
très content retourve oustaz sylla dant lâ serie bété bété ❤mais salimita ligeuye nimo diapé eupone😂😂sa yaye mico déf xamna ni li ngay wakh teyo co😂😂😂machalla bété bété le meilleur séries qui parle le culture taraditionél dû Sénégal ❤❤❤❤❤❤
Vraiment affaire Chacha et sa famille ! Ali Mamadou qui se réjouit bêtement gnak fayda gnak classe vraiment il sait bien que Chacha a été marabouté par sa mère. Les parents de Chacha doivent avoir honte parce qu'ils ont échoué en tant que parents.😤
Wlie lingen di joué yepu exister na 😮 Une de mes sœurs a vécu la situation que Aïssata Kane a pu imposé sur Chacha, elle continue a gérer son ménage comme il le faut, l'autre aussi a fait des co-épouses. Bref, finalement ils ont passé à autre chose. Nos mamans veulent juste notre bonheur. On peut aimer qlq'1, fait tout pour lui mais un jr tout peut tourner mal contre nous et nous finirons par pleurer et demander les excuses sous les bras de nos chères mères. À mon avis,nagnu ngu choix mère yi le reste niu bayiko ci lohoy yAllah🙏 Walahi je vis la même situation (Problème de castes). On s'aime mais je n'y peux rien. Je me retires vite pour pouvoir gérer la situation le plus rapidement possible sinon ma mienne❤ est capable de tout pour que je ne sois pas hors de son caste(niénio)😢Ay Hal poulaar lagnu😂"Gilami habedee withié e mayo"😅
Yoneneti bi thi fep thi lep dagnioko wara khalate ❤❤ kou meune di djouli thi mom SALLALAHOU ALA MOUHAMED ❤❤❤❤nakh guinaw yalla mo takh gniou donne lougniou donne 😊❤
Malheureusement 😔c'est ce que nous vivons chaque jours🤔 des maraboutage pour gâcher la vie des gens rien que de satisfaire notre égo😠. Et c'est la triste réalité mais Dieu voit tous. Que dieu nous préserve des ses genres de parents 🙏 Et Merci Evenprod chapeau à vous 😍🙏
la réaction de shasha c'est la triste réalité sa se passe comme sa chez nous les haalpulaars on te donne un mari que tu n'aimes pas et un bon jour tu te réveilles pour dire que tu acceptes le mariage nga seuy fa ba ameuh fa des enfants.
Méré won wa even pro ndakh chacha ni liguey bi diapé . Mais nak je leur comprends xolou niou liniou nékh ni société bi bindon rek laniouy wané . Mouy lou metti yalnaniou yallah sam ar niou t bayiniou ak souniouy sago amine🤲
Sanéx yalle nafi yague té ande ak weur ak keup kou wah amine téy sama journée dina néh
Amine
Amine way
Amin
@@cheikhndione3589 amine way
Amine 👌👌
Chacha Yaye dji diékou nako nak🙆🏾
Diekou bou ame diome😂😂😂
Wayè beusse bouye tothie mouyi kharou
@@omarbadji5133wakh gua , Dara guenoule Lou naturel
@Everything-p4h Mome key li doyna ware.
Esk défoule semblant pour nax Yaye dji
Où sont les amoureux du prophète Muhammad ❤
Prières et salut sur l’élu suprême ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Macallah ❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
Paix salut sur lui
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Oh njaabar meune na loune oh deudeule bi fort na mère ya sokhor Yalna liguey bi todje fi ak une semaine 😮
C'est ça l'Afrique 💔
Samy ragal bala toth paco takkk Oumy Mbaye 😢
@@SakhoMbene-bt1rjsurment nonou lay démé😢
Yague yague todje inchallah
@noelle3631 Mome key li doyna ware.
Ndesyssn kou yerem paco RK lalal ma li meti n'a 😢😢❤
😂
@maxbbfall4027 Mome key li doyna ware. 😥
Mystique bakhoul que nous préserver
Paco defa wané dongu. Chacha n'est pas plus belle que sa cousine
Mane shasha la yeureum sou khimimico ba kham deug bi😢
Pape Sidy Falle yalla nafi yague te weur
Amiine amiine amiine amiine
Amine wayyyyyyy
Fall dou am « e » pour la prochaine fois
Amine yaraby
Koubeugue seydina Mohamed la lal jaime
Oh chacha sa yaye diekou nala oh yalla naniou yalla mousseul thi njabar 🙏🙏
Billahii ioe
Bilay 😢😢
Wayé naniou sétane rék founiouy moudié inecha ALLAH ... YALLA naniouko féké
Wayer fimoy moudier dounehhh ndiabar rek 😮
Ça a juste un début elle va regretter ay kouko yakar te Yalla nek fi
Aïssata sa serigne nakhoula😂😂😂😂😂
Chacha mingui yek paco kétémé😅😅😅😅😅
@khadydiouf2627 Mome key... 😂
Lou seurigne def rek dina meussa toth Aïssa ta dotou ko défati
Paco l’homme de valeur et de principes ne mérite vraiment pas ça Yalla xol lay fayy té notre Paco du trokh inchalla. Even pro vous montrer chaque jour des réalités qui existent dans notre société merci
Daffa soff warra bayyi diabbarou diambour kou am dieukeur gha topp thi rek
@FidelMendy-t6b Merci, c'est toujours un plaisir de vous satisfaire.
Lâ ilâha illâ l-lâhu, wahdahu lâ sharîka lahu, lahu-l-mulku wa lahu-l-hamdu, yuhyî wa yumîtu, wa huwa hayyun lâ yamûtu, bi-yadihi-l-khayru, wa huwa alâ kulli shay’in qadîr.
Enfin Deguene bayina suñu couple bi meuneu heureux😛🥳🥳🥳
@awa1128 👍
Aduna mogui ni daguay beugue nite niouné dousi dale bamou diaraléne niou sacrifié sa vie yallah naniou yallah mousél si lou bone 😢
Billay teh say propre parents gnolakoy def
Mais khar lène fimouye moudjè doulène nèkh ndakh lou bone amoul ndarigne tè tegougnouko fène loudoul thi séne nafssou bakane😢
@@nganefall seuy mbok mom merci ay problèmes rek près diganté yakou
@ThiabaNdoye-sg3ui Amine. 👍
Attendons impatiemment ce nouveau couple de Alkaly junior et bigue, c'est là la revanche de Diaga Thiam sur la grand mère de keutcha 😂😂😂
Aka l'ère
Maaane mome magui thi couple bobou alkaly and bigue ❤
Lou nara nekh😂😂
@ivetteagbada À suivre. 😂
Ohhh evenprod Paco ne mérite pas ses choses on réclame son bonheur😢
Qu'il cherche son bonheur ailleurs
Li mom nekhoul dara 😢
Blh nk😊😊
Blh nk il ne mérite pas ça 😢😢
@@DikhaLy-us6uipourquoi tu dis ça?
Ani sopeye mame diarra Bousso yi gnou wadiale prokhane ❤❤❤
Chacha tayoul lii evenprod merrei nalén trop😢
Wa yeine mom khana ci youtube bi guéni fanane 😂😂😂😂
Diarnaaaa lathié dh 😂😂😂😂
😂😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Ou sont les amoureux du prophète mouhamed slw ❤❤❤
Salallahou à la Mouhamed
yallah Nanou téral sunu wadjur ❤ amine
J'ai vraiment de la peine pour Paco
@iboundao3387 😥
Kouni serigne amoul dala diapoul chacha 😢
Bilay kouko wedi lathima
@@khadidiatousylla6262mane sama tanta moma deudale ak domame gua khamni mane rekk la bougone walakhi sa fait 8ans de cela mane ak wadji doukhougnou sakh dadie ta nio bokk famille daniouy nekk si ben khew ta douniou guisante
@@alimafall7221Lolou mom doyna warr dii amna niou sokhorr nk s derett sah ngakey bagn mtx lossi guiss dinagn soukratt des mois ndax dieuf diou bone té boul kham lougn nara féki Alakhira😢
@@joliekalsoum7287 bialye kokou yallah atenaniou car lak bou meti moka dall instant bi demi paralysi la am et le pire dans tout sa moye môme dafa niak diom daye niew sounou keur bataye mai douma khol si beute ndakh rous sama yaye dako defal teranga bounek si adouna car ay domou badiane domou nidiaye laniou mai nitt kou bonne moy kokou j'ai passé autres choses mais le gars n'arrête pas de me poursuivre
Niniou tassé si commentaires yii Yalla naniou tassé nonou Aldjiana ♥️🙏🤲
Lii nèko si kholl yi tè Manou gnouko wax yalla n'a yalla safara lèpou 😢❤❤
Aisata ya boon le peuple réclame le bonheur de Chacha et paco
@louffa2551 Vraiment. 😥
Yalna aly mamadou Sida
Ohhh serie bii une vraie réalité de notre société Machallah ❤🎉
@cheikhouna0ly333 👍
Even pro yéneu meuneu yéneu eupou dolé macha allah c'est très bien ❤❤❤
Sallalahou alla Mouhamed ❤️❤️❤️
Salâm alaykum la famille ❤
On ne parle jamais de Mael Thiam mais bilahi c'est le best dans l'humour 😅😅😅😅.
Dès que je le vois, je ris😂
@miss22395 Merci. ❤
Serie bi d sanekh mo takh makoy setane depuis la fameuse théâtre sanekh boba legui la nek sama acteur préféré amlene jamm yene niep barkep borome touba ❤❤❤
Yalna Diamou yagg si Sénégal Ak louka weur si Barké Baye Niasse Yarabi Teuf Teuf Teuf Teuf Teuf Teuf Teuf Teuf Teuf Teuf Teuf Teuf Teuf Teuf Teuf Teuf ❤❤
Amine way❤
Ooh sama khol bi diékhna kouné khalima amoul dala diapoul wayé Ali mamadou yaw ya diapoul si dara ndakh lou serigne df serigne mokoy yakhat
Malheureusement day trop tard. Fékeu dégat amna ba nopi 😢😢😢
Kou beugue yalla lalala j'aime ❤
La mère de Sacha va pleurer tout les larmes de son corps quand elle verra que sa fille est devenue un robot et que Aly Mamadou va la prendre comme un chiffon elle ne s est pas ce qu elle a fait
Hmm même s'il arrive malheur avec aly mamadou, elle ne fera rien. Elle n'aime pas sa fille. N'oublions pas que sa fille a tenté de se suicider et elle s'en fichait
@@ThamaBella exactement, meme quand sa fille pleurait le jour de son mariage forcément elle dansait et riait, dara safouko loudoul sa propre personne
Kou beugue S TOUBA lalal ❤bi🎉🎉
Ligey sa dome pour mou topou goor boko force yaye bou bakh dou def lou niaw li
Merci
Diomi amoule heure ramenez-nous notre Chacha.
@fatysy2205 😥
Bon réveil matinal 🎉❤
Yayou chacha mi tamit est ce que dou deum!!!!!!
On peut être fière au point de détruire la vie des gens sans un soupçon de peur..😮😮😮😮😮😮
walay moi ça me dépasse surtout venant d'une mere ... non j'imagine que bcp de vies ont été bousilles pour des bêtises
Aly Mamadou a épousé une Sasha qui n'agit plus selon sa propre volonté. Il a donc épousé une FOLLE😂LOVE
@fatasall982 Bien dit. 👍
Ooooh Chacha sa yaye yakheu na sa adouna parce-que liguéye bou bone lala dèf ndeysane😢😢😢. Serigne bi aye na nak. Bi changement gueuna gaw😮😮😮😡😡🥺🥺
Hoo yeureum na Paco ndeyssann😢 yayou chacha Yagui retann sa moussiba dhh…
C'est quoi la tradition ?!, ce qui va tjrs détruire nos vies 🚶♀️ y'a k de l'égoïsme. Lan moy liguéy nitt pour mou top nitt, Allé Mamadou est ce qu'il réfléchit, neik ak ko khamni lernalani limouy dound ak ioe c pas naturel non du tt.
Man suis xaal poularh, ko Kandé mi yeita, ms alhamdoulillah mes parents respectent nos choix, si c'est faisable 🙏 Aïssata weiré gua 😒 nous réclamons le bonheur de Paco ✊
Le bonheur de Aly Mamadou 😅😅😅
Le bonheur des uns fait le malheur des autres 😂
Ah oui enfin il était temps 😂😂😂😂
@dynamiquebibliotheque5728 Est-ce un bonheur qui va durer ?
Ohhhhh un jour viendra les larmes de chacha va nous faite tous pleurer 😭 triste 😢
@soumahFatou-d9u À suivre.
Realisateur bi na integrer son daara j family xeet si serie bi waay
Sallalahou allah mouhamed ❤❤❤
Certes wadiour amna dolé ci dom mais Mère Aissata limi déf rèyna, grawna 😢😢
Yêneu wadiour yi warnagnou djiteul sèni bonheur ak avenirou dom avant les "qu'en dira-t-on".
Aly Mamadou yow diapoo si touss. Amour forcé 😮
Oh c'est triste pour Paco et encore plus pour Chacha la pauvre 😢😢😢
EvenProd yalèn meneu "Aléa" - BRAVO ❤
Paco stp baniale 😢boule ndagou dh
Diapale ni rk chacha dagn lo liguéye 😢
Moi je dirais juste qu'elle a retrouvé sa vie d'avant.
Wa serigne bi mom ligeuy yam bi gawna diap torop😢😢😢Paco ne mérite pas ça 😢😢 Evenprod Pourquoi😢
Alkaly gathiè national 😢😢😢
@aminatambaye2525 Mome key...😥
très content retourve oustaz sylla dant lâ serie bété bété ❤mais salimita ligeuye nimo diapé eupone😂😂sa yaye mico déf xamna ni li ngay wakh teyo co😂😂😂machalla bété bété le meilleur séries qui parle le culture taraditionél dû Sénégal ❤❤❤❤❤❤
Mafi djitou 🎉🎉🎉😂😂
Scheutt mane li dotoumako sétane chacha limouy wkhe pako nii scheutt yayy diou bonn yalnaniousi yallah mousale Sarab li akh sof ngénn trope wyy
Dieu est grand ❤
Sama xoll bi mogui wadd😢ay chacha 😢
@AdamaNdiaye-o2i Tayoko. 😥
Shiiii Chacha accident de parole. Li ma meti rek mom on vit dans cette folie. Yallah na Yallah tapé xol yi
Ohhhh Paco yeureum nako🙈🙈🙈
@aissatousene9078 Diarna yeureume.😥
Ohh chacha ligy df paco tmt nekhouma d😢
No famille chachacha lougni deff sama khol bi 😢
Alhamdoulilah
Le marabout de la mère de Sacha est fort deh ! Li dafa yomb waaye
@yakhsen-s9946 Xaral suite bi.
Sallallahou ala Mouhammad ❤❤
Vraiment affaire Chacha et sa famille ! Ali Mamadou qui se réjouit bêtement gnak fayda gnak classe vraiment il sait bien que Chacha a été marabouté par sa mère. Les parents de Chacha doivent avoir honte parce qu'ils ont échoué en tant que parents.😤
0:28 gni dagno yap mame 😂😂😂
😅😅
Yalna yalla dolli soutoureu AK heweul AK wer gou yaram amiin yaa rabbi inchaallah niou bok lep
Mane ma pare setane lii dakh sama khol atandoul lii bilay 😢 paco mérite woul lii sama khol bi wouy pare na setane ba affaire yi normal ma niewat 😢
Paco mérité woul li way evenpro on réclame son bonheur nk enough enough😢😢
Wlie lingen di joué yepu exister na 😮 Une de mes sœurs a vécu la situation que Aïssata Kane a pu imposé sur Chacha, elle continue a gérer son ménage comme il le faut, l'autre aussi a fait des co-épouses. Bref, finalement ils ont passé à autre chose. Nos mamans veulent juste notre bonheur. On peut aimer qlq'1, fait tout pour lui mais un jr tout peut tourner mal contre nous et nous finirons par pleurer et demander les excuses sous les bras de nos chères mères.
À mon avis,nagnu ngu choix mère yi le reste niu bayiko ci lohoy yAllah🙏 Walahi je vis la même situation (Problème de castes). On s'aime mais je n'y peux rien. Je me retires vite pour pouvoir gérer la situation le plus rapidement possible sinon ma mienne❤ est capable de tout pour que je ne sois pas hors de son caste(niénio)😢Ay Hal poulaar lagnu😂"Gilami habedee withié e mayo"😅
Bilahi kouné serigne amour bouboule dalay diaroul wayé loudoul deugue dou yague 😢
Yalla na nieupou ame diamou🙏🙏🙏
Ohh shasha 😭😭😭
Mani on réclame le bonheur de paco😢
Ngirr yalla boufi kenn niane ay cœur ❤️ pour yonente bi🙏🏽😂
Yoneneti bi thi fep thi lep dagnioko wara khalate ❤❤ kou meune di djouli thi mom SALLALAHOU ALA MOUHAMED ❤❤❤❤nakh guinaw yalla mo takh gniou donne lougniou donne 😊❤
Merci cha cha thiaa khathie soff gua trop
Sama kholl nekhoul bilea paco L'homme fort ❤
Waa Ramata mi lanla def chacha 😭🥹Koumou metii comme moi
Merci Maman ❤❤
Tonton ibou lig gnou yén diss na dei trop sakh. Yalana sa jaam yagu. Très belle œuvre ❤
Malheureusement 😔c'est ce que nous vivons chaque jours🤔 des maraboutage pour gâcher la vie des gens rien que de satisfaire notre égo😠. Et c'est la triste réalité mais Dieu voit tous. Que dieu nous préserve des ses genres de parents 🙏 Et Merci Evenprod chapeau à vous 😍🙏
Kou gome ni guènti la rek laalal ma ❤❤ ma guis
Ooooh pacoooooo gnak gueu 😭😭😭😭
Mais attention mbeguel Dafa fort dh 🥲 hâte de voir comment ils vont terminer ! 🥰
evenbord dagua guéna dioum dh checa waroul wona bay paco paska méryou mèlni yayou chaca sén dom boulén diahalé ni laniou koy déf guén bay si xél 🙏🥹
Ramenez nous la vraie Chacha ! 😢
😂😂😂 mayi 3eme 😅😅😅😅😂 wa bignona ameguéne ndame 😅😅🎉🎉🎉
Ahh Casamance amna ndam 🎉😂❤
🎉🎉🎉
@@diop8200 waou 😘😘😅😅😅
Évenpro ramener nous notre Chacha
Donc il continue à croire que aléa est un personnage 😂😂😂😂😂
@ToureMameFatou-fz9qt Oui. 😂
Oh Paco 😂😂yayou Chacha mola défal bagages dh😅
Bagass you diss kagn 😂
@ramatoulayeseck3986 Paco na mougn rkk kholl si gouney milieu yi nioniou djiabar doulén diap😂
Yayou shasha limou def khamouko sakh imagine Aly Mamadou commencer di mbougal Shasha dina kham kéna dou forcé amour
Sanékh sougnou papa acteur bravo 👍❤
Le mara de la mère de Chacha es très efficace 😂😂😂😂😂😂😂😂😂 revoir la suite
@sibereba3529 👍
la réaction de shasha c'est la triste réalité sa se passe comme sa chez nous les haalpulaars on te donne un mari que tu n'aimes pas et un bon jour tu te réveilles pour dire que tu acceptes le mariage nga seuy fa ba ameuh fa des enfants.
C 😯😮😳
Bientôt Ramadan inchallah🙏🙏
Oh😂shasha 😊
Ô Paco waay kouko yeureum lalal j’aime ❤
Méré won wa even pro ndakh chacha ni liguey bi diapé . Mais nak je leur comprends xolou niou liniou nékh ni société bi bindon rek laniouy wané . Mouy lou metti yalnaniou yallah sam ar niou t bayiniou ak souniouy sago amine🤲
Bete bete ma série préféré 🎉❤💕💖🤩🤩😍
Alkhamdoulillah ❤🙏🏻