La fin raye nama😂😂😂😂Ngor yalnala yalla diapalé sisay projets mayla lou geune si yaw témou geunal la barké Seydina Mouhamed ak wer wou séleu wii gnou nèkeu sama khol lako tibè ndakh sa tèy ak sa dale ak sa geume geume motakh ngua nekhma😍😇🙏
Loutakh Sénégal yen ñji yoor micro di ladj xamolen dara si li ngein di ladj actrice yi nek marodi li ñou wax dou salair bouy tarde me lidj len di day dafa touty dañoulen di utilisé lolou la ñou wax
Parla la tua lingua madre che meglio pure io parlo italiano ma per fare dei commenti non ha senso scrivere italiano che allora parla wolof che ti viene meglio !! Wakhal wolof gnoun aye wolof lanou d’oùnu aye italien
@@dalandadiallo1616 sokhar ? Mane fima djioudô sokhar amoufa deuga wakhoulène si dara kilimou way lane ladj nite meuna djaguè tè way bou yètèwoul djiagalè mè dousi bèna
J'aime cette jeune koi dafa téy en plus il comunic super bien
La fin raye nama😂😂😂😂Ngor yalnala yalla diapalé sisay projets mayla lou geune si yaw témou geunal la barké Seydina Mouhamed ak wer wou séleu wii gnou nèkeu sama khol lako tibè ndakh sa tèy ak sa dale ak sa geume geume motakh ngua nekhma😍😇🙏
S'il vous paît kou beuge seydina Mouhamed dougal nga abonné siniou chaîne guir yalla yakaloula d'Ara ❤🙏
Yaw mi di lire Sama commentaires
Machalla🥰💯💔
Say wakh amna solo mashaallah ❤️🇸🇳
Kou beug Seydina Mouhammed (Psl) na nga bayi j’aime yi T dem dieuff diouli woor diokhé azaka
Bouniou beussé j'aime apres dagne lay fay xaliss walla bayilén di diaxassé nite yi ak yonéntibi tmt
@@IbrahimaNdiaye-ui1yv gni kay soff rek
Kou beugg developpment.senegal.mangilay.nian.abonne.waxtan you.amsolo pour Senegal
Machala yalla na yalla koudale sa fane si barké Alkhourane par c k nite gua dalle
Jai tjr adore sa communication
Il est bourré de talent et aussi posé et mouna communiqué il a raison daniou mouna lathié
Athieu domou jonguaye Séné setou beytir😂
Bonne continuation mon frère di courage
Bravo bravo bravo bravo 🤗🤗🤗🤗🤗🤗🤗😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍
Machallah yalla na séne ande yague
Machallah👍💯💯
Ngor afairbi diom rék
Bien dit frère
Superbe frr bi
Loutakh Sénégal yen ñji yoor micro di ladj xamolen dara si li ngein di ladj actrice yi nek marodi li ñou wax dou salair bouy tarde me lidj len di day dafa touty dañoulen di utilisé lolou la ñou wax
Machalla machalla
Je l aime bien machalla longue vie a tw Mn grand
Continuation surtout gardes cette mentalité la valeur n'attend pas l'âge
Amna solo
Je l'apprécie bcp vraiment
Machala ♥️ il est bien
Questo video e bellissimo 🥰❤❤❤❤💯💯🥰
Video buoma setan guiss lafa te li rek guay binde khana daguay diang italien 😂 li rek gua degg😂
@@sambich8864 mm k mne li rek laye guise mouy binde 😂pensavo che sta studiando 🤣🤣🤣🤣
Parla la tua lingua madre che meglio pure io parlo italiano ma per fare dei commenti non ha senso scrivere italiano che allora parla wolof che ti viene meglio !! Wakhal wolof gnoun aye wolof lanou d’oùnu aye italien
Machallah 😍😍😍😍
Bonne continuation et du courage
Machallah kadou yi nice na
Right
Ngor Sama idols
Go on
Wawa
Super frère
Machalla
Nice boy giroe
👍👍
𝘔𝘢𝘤𝘩𝘢𝘭𝘭𝘢 𝘯𝘨𝘰𝘳 𝘭𝘰𝘯𝘨𝘶𝘦 𝘷𝘪🙏🇨🇵🇨🇵
Il faut payé les artistes mo guéne
Tafa
Journalisme art la ?
,
Com domou Becaye mbaye
Gor dèfogofi dara di gadagadalouni tu es núl
Loy sokhor
Ya sokhor way🤭😳
@@dalandadiallo1616 sokhar ? Mane fima djioudô sokhar amoufa deuga wakhoulène si dara kilimou way lane ladj nite meuna djaguè tè way bou yètèwoul djiagalè mè dousi bèna
Machalla