Le message est poignant et triste. Il faut réaliser un documentaire de ces différents témoignages afin que les autorités réalisent les souffrances de la jeunesse et arrêtent leurs politiques politichiennes pour se consacrer à cette problématique. Merci à ce jeune pour ce partage de son expérience
C'est vrai Deh Mane si gal yi la diare mais alhamdoulila j'ai reçu môme paspor européenne 🎉🎉 avant j'ai arrivée ici j'ai beaucoup faire prison en Turquie
La pauvreté ne doit nullement justifier le banditisme,il faut rester digne et aller travailler,le problème c'est que vous ne voulez pas accepter tout boulot.. vous ne voulez pas travailler dans les chantiers, vous ne voulez pas être agent de sécurité, vous voulez tous partir en Europe
Exact! Les peuls fouta font plein de petits boulots qui leur permettent de vivre. La vie n'est facile nulle part. Lii mome personne ne comprend ce qui se passe dans la tête des candidats. Le gouvernement a raison de les faire revenir.
Ce probleme est bcp plus profond que ce qu'on pense, enfaite c'est un probleme spychologique ces jeunes voient que le mal il ne parvient plus a raisonné, voir le positif dans ce Pays. on ne doit surtout pas les jugés on contraire essayer de changer leur etat d'esprit avec des specialiste. car si on les entends parler on voit que ils sont depourvu de raison c'est vraiment triste. C'est comme un jihad pour eux. alors que au fond tout le monde avait un busness qui tourner mais ils veulent tous devenir riche avoir des millions alors que Yalah moyi mayé. leur etat d'esprit me fait depasse c'est triste
Ce qu’il dit je confirme en étant moi-même à ces endroits pour les mêmes raisons, de Laayoune à dakhla de casa à rabat de tanger à nador … que des souvenirs et je rend hommage aux compagnons et tous ceux qui sont passer avec succès et tous ceux qui sont tombé ainsi que ceux qui se battent encore, qu’Allah vous assiste et vous fasse miséricorde 🫶🏽
Gueno fé néka goor yàlla kén lingay wakh tégoko fén pauvreté waroul takh banditisme, khalé bou ndaw bou tolni yaw am keur taka diabar am dom am sa liguey bo doylou woul geum sa bopp bayi fi lepp dieul gal ak ay 4millions 500 pour immigration clandestine kén manou si dara dou problème deuk bou dokhoul ms état d'esprit bou bone rek nga fi wakh , ngay mélni kou démon djhad wakho fi dara
Le message est poignant et triste. Il faut réaliser un documentaire de ces différents témoignages afin que les autorités réalisent les souffrances de la jeunesse et arrêtent leurs politiques politichiennes pour se consacrer à cette problématique.
Merci à ce jeune pour ce partage de son expérience
Jahdieuf frère lou leer
Goor rek soneu du courage frère dina bakh dh inchalla
C'est vrai Deh Mane si gal yi la diare mais alhamdoulila j'ai reçu môme paspor européenne 🎉🎉 avant j'ai arrivée ici j'ai beaucoup faire prison en Turquie
Merci beaucoup mon frère tu as bien parlé bien expliqué voici le Sénégal d'aujourd'hui ❤
La pauvreté ne doit nullement justifier le banditisme,il faut rester digne et aller travailler,le problème c'est que vous ne voulez pas accepter tout boulot.. vous ne voulez pas travailler dans les chantiers, vous ne voulez pas être agent de sécurité, vous voulez tous partir en Europe
Exact! Les peuls fouta font plein de petits boulots qui leur permettent de vivre. La vie n'est facile nulle part. Lii mome personne ne comprend ce qui se passe dans la tête des candidats. Le gouvernement a raison de les faire revenir.
@@Nittou-g4i vraiment
Toi tu comprend rien
Niata nit nioy liguey ba dé té amounou ligniouy agné
@@gooroundeyefatou7552 nga nangou lila yalla sedeu..on ne force pas son destin
Machalla gor degue gua vraiment ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ce probleme est bcp plus profond que ce qu'on pense, enfaite c'est un probleme spychologique ces jeunes voient que le mal il ne parvient plus a raisonné, voir le positif dans ce Pays. on ne doit surtout pas les jugés on contraire essayer de changer leur etat d'esprit avec des specialiste. car si on les entends parler on voit que ils sont depourvu de raison c'est vraiment triste. C'est comme un jihad pour eux. alors que au fond tout le monde avait un busness qui tourner mais ils veulent tous devenir riche avoir des millions alors que Yalah moyi mayé. leur etat d'esprit me fait depasse c'est triste
Vous avez parfaitement raison
badolo tahoula agressé ana goreh yalla moy mayeh .kou deh perte .gueum lene yalla.yow somoytouwoul si gualyi nguay deh
Niak takhoul nianki nite day ameu diome nango liguey mais pas Di sathieu
Adorable big nga dioume, aggression beugue lou bomb leu... Gola geunone deugeurr fouff geuneu leu deck hood
Politicien dh lafi guiss bilahi
D accord rouma ak affair bi diomla ak induction la aguerésion si induction rék mais pas badolo
Doul way yow .il faut travailler votre pays pas les autres pays
Tant que le Sénégal ne sera pas pour les Sénégalais toutes les politiques seront vouées à l'échec
Ce qu’il dit je confirme en étant moi-même à ces endroits pour les mêmes raisons, de Laayoune à dakhla de casa à rabat de tanger à nador … que des souvenirs et je rend hommage aux compagnons et tous ceux qui sont passer avec succès et tous ceux qui sont tombé ainsi que ceux qui se battent encore, qu’Allah vous assiste et vous fasse miséricorde 🫶🏽
Je recents de la colère, que de la colère chez ce garçon . cela fait mal.Diomaye est interpellé.😢😢
Merci way gabi
Gui d'à AM promlemou mBopou Billahi 😂
Hhhhhhh machallah et vérité absolue
Mais même 1 millions 5 tu peux travailler avec Lou co fi diar defoi une paye te do doundou
Wakh deugue yalla dagua thiouné wayei lo ligueye ba am si keur bo amone kham kham do perte 3 places yeuppu daanu
Niakk khél meunoul wéssou nga yoor 4 millions diko faay thi toukki à l'aventure
Saway 4 millions bi nga diokhé meno ko wone df fénen wala df le tout ba diar si yone bi
Les transferts de ria et autres tu te fais 2.000fr pour un envoi de 35.000fr alors xana sa multiservice yako tey danelko.
Gemal yalla way
Ki limouye wakh tegouwoul fe agresson dou pekh
❤ki doff la rekk
Tout le monde va partir car l'Afrique ses enfants ne saiment pas
Dagay thiakhaane rek
WAY JUR YI ÑOOM IT LUTAX DUÑU JOG DEF DARA?
Sophia sa fait longtemps guissoumako sntv je ne sais Lou xéw
Saway lingay wakh khamnâko mais agression mom kéne mounouko layall yallnagñou défall soutoureu wasalâm
Bayil ba guene tu na rien compris
Vrai doff ngua ma ngui jegalou
Diaroul diégalou déh ki doff bou con leu🤦🏾♂️
Diarul diégualou dé doff plus la
Saway so guissatè démal dhei , Sénégal gui, Gambie sax moko geneu néx ndax dara chéroufa
Gouvernement mounou si dara mane duipi 1992 la ndiaka guise
Sénégal Gambie sakh moko tané Sénégal dou réwe kou guisse gale démale
yene legui aye agresseur nguene di inviter. en hen.
Bougane n'a dieul boy bii thii télévision. Ses paroles sont trop poignard
Gueno fé néka goor yàlla kén lingay wakh tégoko fén pauvreté waroul takh banditisme, khalé bou ndaw bou tolni yaw am keur taka diabar am dom am sa liguey bo doylou woul geum sa bopp bayi fi lepp dieul gal ak ay 4millions 500 pour immigration clandestine kén manou si dara dou problème deuk bou dokhoul ms état d'esprit bou bone rek nga fi wakh , ngay mélni kou démon djhad wakho fi dara
Courage frère 😢
Xamalni yalla Moy mayye
santal yalla
Teranga yalla moko yoré sa bopou mola yombou chaque foi teral wadiour
Verema waxx deg manmi sila djiarr
Safia dafa deloussi sen tv?
Sènègal dou rèw
Ki fén rek lay deff bougan moko yonni li😂
Gueum yalla war na djioulite
Fi nek mane gua fa tékké touki takhoul tékki déh
Noumou def ba danou au lieu de se remettre en question ils veulent aller en Europe
Merci beaucoup frr tu es vraiment fertina
Billahy poula fatayi bounioulen outaloul cart sejour. proge sonkobi dou meuseu sotty
❤❤❤❤❤❤
Cette dame la ne peut pas comprend elle ne sais rien dis tout
Effectivement
Lou lerr gua wakh
Fall linga am souma ko amone douma wakh dara
Merci merci et merci❤❤ tu as tout dis
Ki vrai domaram la dagn ka wara enprisonner c est un influenseur .
😂😂😂😂dof la dh
Yaw Mi Dôomiraam Bu Mak Bi
@@khadimndiaye7273 damay Kat sa yay djouteul ko de
Sa lefeul nday yak mom
@@karimthiandoum1510 Lii Dé Môye Wané Ni Dôomi Mbaam Nga
REWMI SONKO AK DOIMAYE METTINA TORO TASNA YAAKAR KHALEYI DEKGERPIRMA BI OPPUNA TORO😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😊
Novembre là wax , donc 2023 leu ndakh novembre jottagoul fini . Donc Macky Sall mo len rapatrier.
Yaa meunn doul doméram
Mak bou niak fayda ga yow, outil lo liguéy bayi fén, sa papa bou tassé sa yakar boul ko djign sonko
Khep sen weurseuk ak woudiekk sen domou bayi mo sonnal souniou mbokk kao-kao yi
Amo sansou deme con togal c mieux
Yaweu la andakeu Sénégalais dafa meneu topono té mouneu bayi kheileu nite ake teikeu beteu dougnou créé
Vraiment Afrique métina trop, en plus le gouvernement de sonko est Diomaye nous ça déçu
Un gouvernement qui n’a même pas fait un an, et vous osez parler de déception…soyez sérieux !
C'est tres tot de juger le president
Tu racontes des bétises,
Keur dof yi 😂
Dioulite dou togne
Meteo hamoul koumpeu.kouko geum yagi bokale yalla
Wakhoul déuge dh billay yone bi djigeune you wéroul yi sakh niongi si diarr