franchement ce documentaire est emouvant et tous les etudiants senegalais du maghreb lui doit un grand merci pour ses efforts emblématiques .Il est un exemple pour tous ceux qui pronent pour l'islam Oustaz Barham Diop une fierté pour tous yalla na yalla yokou leram té tass gnou ci barkéme
Je ne vois vraiment pas ce qu'il y a dans cette vidéo qui mérite un dislike. So beugoul dialal rek, mais beugo té bayiwo gniy beug gnou beug. Lii daal khawma loum doone. Yalna Borom Bi Dolli Oustaz Barham DIOP leer bijahi Rassouloul Lahi Sallal Lahou Alayhi Wa Sallam. Aamiine...
Je suis talibé de S Touba lolou motax ma sope Barham Diop ndax S Touba nénagnou kepp Kou bax nanguén ko sope ta Yalla rek tax Barham yalna Yalla Yoki leram ta tass gnou ci barkém
Merci kossi TV merci tfm li mou bakh li moy Senegal li lanio kham m kholo saga wakhlo bon rek lolou bakhol li mou bakh delen wakh lou bakh diko def machallah ya oustaz yalnako yalla dekelek mame baye niass ♥️♥️♥️♥️♥️🤲🤲🤲🤲
Wallahi beaucoup de sénégalais meconnaissent cet homme multidimensionnel qui a sillonné toutes les contrées du monde au service de l'islam. Que Dieu l'accueille dans son paradis éternel si barke Baye Niass
Maa Shaa Allah, OustAz Barham Diop RA Yalla Na Yalla yokou leeram te Tass Niou si Barke yoneneti Bi (SAWS) Un Homme De science et de religion d’une dimension Internationale. Dieureudieufe Baye
Mashaa Allah..Ses enseignements resteront éternels..Il a parlé de tous les sujets. Il suffit de l'écouter pour apprendre et remonter jusqu'aux références. Un pédagogue hors pair. PS : Si vous pourriez refaire le montage en diminuant le zikr ce serait plus bénéfique. Bonne continuation in shaa Allah !
Alhamdulillah li lako Baye Niass wakh هاك القراطيس أ يا برهام قد حدت عن نهج الآلي قد هامو عشت وأنت صندد همام فتى لكل مشكل فهام يعنوا لك القرطاس و الأقلام حتى يقال إنــه برهــام❤️🙏🏿 Yalna yalla yokou lèram té tass niou si Barkème فقد كرس جهده الكبير لخدمة الدين و الطريقة التجانية لا سيما الفيضة الإبراهيمية نفعنا الله ببركته
franchement ce documentaire est emouvant et tous les etudiants senegalais du maghreb lui doit un grand merci pour ses efforts emblématiques .Il est un exemple pour tous ceux qui pronent pour l'islam Oustaz Barham Diop une fierté pour tous yalla na yalla yokou leram té tass gnou ci barkéme
Merci KossyTV
Le sabotage de la TFM n'est pas passé.
En 2019, internet diffuse plus largement que la télévision classique.
Baaraka Laahu Fiik
Thieye yalla kou ragale yalla rek mou khamale la c'est un miracle de dieu yana yalla yokou lérame di barkép mawlana cheikh ibrahima niass 🤲🤲🤲
Wallahi oustaz diambar la Sénégal danko oumplé woon wallahi man dh mouride laa wayé djeum djii damako sop lol nguir jeumi yalla
Qu'Allah agrée tous ceux qui ont participé à la réussite de ce documentaire et toutes les chaines TV qui l'ont publié ! Merci Kossy TV !
bilahi kou Baye niass yare ni gua meuneu méle
Oustaz Barham Diop ,un des miracles de Baye Niasse.Merci d'honorer les hommes de science
Allahou akbar les réalisateurs de ce documentaire riche en enseignement que le TOUT PUISSANT vous préserve.
Je l'ai suivi avec beaucoup d'intérêt ❤
C'est du fruit qu'on reconnaît l'arbre. Niass
Elhadj Cheikh Diagne salam Oustas barhama il habite a kaolak ???
Je ne vois vraiment pas ce qu'il y a dans cette vidéo qui mérite un dislike. So beugoul dialal rek, mais beugo té bayiwo gniy beug gnou beug. Lii daal khawma loum doone. Yalna Borom Bi Dolli Oustaz Barham DIOP leer bijahi Rassouloul Lahi Sallal Lahou Alayhi Wa Sallam. Aamiine...
oumar amadou Niang lou lére
Dislike means this i like
Le Zikr est trop fort,
Al Hamdoulilah, Oustaz Barham Diop YALLAH yok lerram
Ta bien bien mon frère
Oustaz Barham Diop yalla nako yalla gueureum ndakh ligueyalna yalla bâ kheuy wouyoudji boromam
Hééééé Baye Niass😭
Walay Sénégal khamougnou lignou ame
bilahi wakhatiko
Je suis talibé de S Touba lolou motax ma sope Barham Diop ndax S Touba nénagnou kepp Kou bax nanguén ko sope ta Yalla rek tax Barham yalna Yalla Yoki leram ta tass gnou ci barkém
Kenn dou baye Niass Baye moy borome international niass for ever
Yal na yalla yok ay léram té tass niou si barkém bi seydil woudioude aleyhi salatou wa salam
ouztace barham un missionnaire un grand savant de l'islam et da la fayda tidjiania yalle nako yalla doli lere ya rabbi
Merci kossi TV merci tfm li mou bakh li moy Senegal li lanio kham m kholo saga wakhlo bon rek lolou bakhol li mou bakh delen wakh lou bakh diko def machallah ya oustaz yalnako yalla dekelek mame baye niass ♥️♥️♥️♥️♥️🤲🤲🤲🤲
C'est du fruit qu'on reconnaît l'arbre. Oustace barham diop si baye niass. Oustace mon idole
Oustaz Barham Diop kende lawone yalna ko yalla doli yeuremé dé chi kawame
Walahi un grand savant repose en paix 😭😭😭
رضي الله عنه وعن شيخه ووالديه
وأورثنا الله من أمثاله
Oustas Yalana Yala yokou lerram té taffe gnou si barkéme Diop
Al hamdoulilahi j ai assistée a ses cours durant une periode en 2011 merci oustaz
Ndeyssane
Dara diaroul faté Yalla dieuredieuf Baye Niass, Oustaz Barham Diop yalna yalla yokou leram tass gniou si barkem
bonéké Sénégal manga réré kane moye baye niass waya boguéné diga khame baye par force
ماشاء الله تبارك الله
رحمة الله عليك يا أستاذ برهان محمود وجب
Machala Oustaz
Un pure produit de Cheikh Ibrahim🙏❤️❤️❤️
Jai une forte joie au coeur dieureidieuf baye
Ndeysaan Baye yalla deug la xalal gnimou yaar rek Allah. Niassén yi Macha'Allah😍😍
Machallah kenne dou baye Niass yalla na niou ko yalla féyal ya rabbi
Wallahi beaucoup de sénégalais meconnaissent cet homme multidimensionnel qui a sillonné toutes les contrées du monde au service de l'islam. Que Dieu l'accueille dans son paradis éternel si barke Baye Niass
Yala fayalgnouko outyaz barhame
Yala fayalgnou baye
Dieureudieufé BAYE pour ce magnifique bijou qu'est Barham Diop yalla naa yalla yokk sene lérrrr
il restera toujours dans nos cœurs barham on t'aime
Yallah defakko bakhal te yerou. Ustaz. Barham Diop.
Dieureudieufee Baye Niass La Solution Du Monde
Soul Gaze Mome Douko Tarekhegne
Machala oustaz dieureudieufe baye, haa zikarou groupe djiolofene bi nekh na
Mashallah lii réfétt na yalna BAYE gërëm ya rabbi
Que le bon Dieu lui accorde le paradis
mashala yalla naniou yalla tass si sa barkè
Machalla cheikh Ibrahim makhmout diop barham 😍❤
Dieuredieuff!! Oustaz ce très grand homme, YALLA nagnou ko YALLA fayal AMINE
Billahi en pleine des larmes paix à ton ame
Mascallah dieureudieufe Baye, Yalla Na Yalla yokk leram te tass GNOU si barkem barke Baye Niasse
Alhamdoulillah Alhamdoulillah Alhamdoulillah Dieuredieufe Baye Niass ♥️🙏
Alhamdoulilahh oustaz Barham Diop yalna yokk ay léram té tassniou si barkém
Machalla kenn dou baye NiASS
Yalla nakoo ylla khare adiana mako sopou bilahii kham kham kesse
Dieudieufé Baye niass wa maratane uhra tarawna ajabane
Un pur produit de baye Niasse. Alhamdoulilah
Dieurédieuf baye niasse
je vous remercie et vous souhaite une bonne continuation que dieu vous guide
Alhamdoulilah Dieureudieufei Baye niass
Machallah amna solo trop yalna yalla yokou léram si barki baye niass
Oustaz Barham Diop Yalla na Yalla yokk leram
Ma sha Allah. Thiey Baye
Machallah Yallah na Yallah Yokk léram té tass'gnou si barkémm.
Yallah niou Yallah fayal Oustaz Barham Diop
Machallah thi barhama diop
ما شاء الله جزاه الله خيرا وأسكنه فسيح جناته
Maa Shaa Allah, OustAz Barham Diop RA Yalla Na Yalla yokou leeram te Tass Niou si Barke yoneneti Bi (SAWS)
Un Homme De science et de religion d’une dimension Internationale.
Dieureudieufe Baye
Merci pour le documentaire, Dieuredieufé Baye Niass
Machalla Baye kéne dougo khammm
Merci Cheikh Ibrahima Niass
Alhamdoulillah alhamdoulillah baye dieureudeuf
Machallah ♥️♥️♥️♥️♥️
Machalah dieureudieufe DIOP
Mashaa Allah..Ses enseignements resteront éternels..Il a parlé de tous les sujets. Il suffit de l'écouter pour apprendre et remonter jusqu'aux références. Un pédagogue hors pair.
PS : Si vous pourriez refaire le montage en diminuant le zikr ce serait plus bénéfique. Bonne continuation in shaa Allah !
Wallahi kène domame ndyssann
Yalna yallah yokkou ay léram thi barké baye
Masha Allah yaa Barhama
Macha Allah yalena yalla fayala gnouko
Ina lillahi wa innaa ileyhi rajihon
Alhamdoulilah DIEUREUDIEUFÉ Baye NIASS WARNA diam bi
Macha allah Oustaz Barham Diop yalna yalla yokou léram yarabi
Machallah alhamdoulilah 🙏
Shoukran shukran
Mashallah, May Allah be pleased with Outass Barham Diop, Al Marjah Jerejeff Baye Niasse, Alhamdoullilah
Alhamdoulilah mashallah dieureudieufé BAYE NIASS
Deyssane
Thiey Baye Niass
Machallah Outaz Barham Diop Yalla na yalla yokk léram🙏🙏🙏
Mashallah Baye
Alhamdulillah li lako Baye Niass wakh
هاك القراطيس أ يا برهام
قد حدت عن نهج الآلي قد هامو
عشت وأنت صندد همام
فتى لكل مشكل فهام
يعنوا لك القرطاس و الأقلام
حتى يقال إنــه برهــام❤️🙏🏿
Yalna yalla yokou lèram té tass niou si Barkème فقد كرس جهده الكبير لخدمة الدين و الطريقة التجانية لا سيما الفيضة الإبراهيمية
نفعنا الله ببركته
Thiey adouna
Machallah Baye merci beaucoup ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️☪️🇸🇳🇸🇳
Machalah
Allahou Akbaaarrrrrrrr
La marocaine ma fait pleur wallahi
Moi aussi à la fin j'ai pas pu retenir mes larmes.
Al hamdoulilah !!!! Djeureudieufé BAYE!!!!!
machalla
Mashallah oustaz Barham
Mashallah ❤
❤️❤️❤️
Mashallah baye niass
Machalla machalla ame na sollo trop
Svp le zikar est trop fort on arrive meme pas à entendre les temoignages.
Macha Allah diereudieff baye niasse
Un conseil pour kossy tv : le zikr est trop fort
Alhamdoulilla
Yalla nako Faye