5:27 Exactement coach : c'est une technique de manipulation qui consiste à présenter deux options à notre victime ( la personne manipulée) : peu importe le choix qu'elle fera elle perd. C'est un genre de dilemme. Merci
Salut mane dé sama copain bi defna 1 mois ba légui wowou ma après demb ma vocal ko WhatsApp néko Lou khew ba légui wowa toma message sakh dêfa tomako après mou néma sa comportement motakh ndakh Soumay wakh ak yaw wakh bou yakhou yaw doma nango tonetou wala ngay wakh lénén motakh wowatou mala 😢 en résumé dale néna djiggeen bou yakhou la beug té mane wakh yoyou môme bougou mako en plus défmay Sakh énervé légui nak môme diélna yonou bopame et moi je ne sais pas comment faire 😢
Cv coach man daal je suis en relation à distance depuis 4ans ms sama copain daal moma commencer soff souma togué dégoumako damakoy nammeu ms il suffit ma déganté ak mom rk commencer ko diéppi loumou wakh mani waw té doumako gueume damay douté aussi lou bari si mbeuguélam damay took sakh parfois sama xel bi yeupp nekk si guénneu si relation bi wayé khamouma nane lako koy wakhé ma beugone xam ndakh lolou rapp la wala dafma soff rk réellement
Sama mbokou goor nhi dimbali l'en niou si am diabar bou vérge parce que yén téwoulén sén bopu boudonni gor Day eumb gor niou bari birnanou😊😊
😂 wakhati gua
Coach Asse tu a bien dit walahi ...
Café touba la done naane ni☕ alkhamdoulilah
Ass yow réke lay top ya meukay ❤❤❤
5:27 Exactement coach : c'est une technique de manipulation qui consiste à présenter deux options à notre victime ( la personne manipulée) : peu importe le choix qu'elle fera elle perd. C'est un genre de dilemme.
Merci
Salamaleyloumr keur ass tv naka def yagui ci Diam dama doone lathié lane mo waray nakka bou metti❤
Salut mane dé sama copain bi defna 1 mois ba légui wowou ma après demb ma vocal ko WhatsApp néko Lou khew ba légui wowa toma message sakh dêfa tomako après mou néma sa comportement motakh ndakh Soumay wakh ak yaw wakh bou yakhou yaw doma nango tonetou wala ngay wakh lénén motakh wowatou mala 😢 en résumé dale néna djiggeen bou yakhou la beug té mane wakh yoyou môme bougou mako en plus défmay Sakh énervé légui nak môme diélna yonou bopame et moi je ne sais pas comment faire 😢
❤❤❤
Slu sokhna ci damaye je demande lathie bi ak khorome pollé bi daniou koye rapé wala
slt tonton ass sama tata Moy lathié néna daa défon planning, piqûre bi ladone dieul mais bayinako légui il yaa 7mois de cela ,wayé baa légui dieuleugoul eumbou Mouy lathié l'âne Moy rakhass dosou planning
Slt coach est ce que djiguéne bou am sothiéte Dinay am envie def rapport
louy dindi seere
Cv coach man daal je suis en relation à distance depuis 4ans ms sama copain daal moma commencer soff souma togué dégoumako damakoy nammeu ms il suffit ma déganté ak mom rk commencer ko diéppi loumou wakh mani waw té doumako gueume damay douté aussi lou bari si mbeuguélam damay took sakh parfois sama xel bi yeupp nekk si guénneu si relation bi wayé khamouma nane lako koy wakhé
ma beugone xam ndakh lolou rapp la wala dafma soff rk réellement
Gore tak nafi djiguen bou vierge téki woul dara
Ass man femme marié la soumay guiss régle sama thioussou wén yi day metti
C'est normal
Noy khamé ni amo ndah alors que foo gua
Hôpital rek
Ass mande sama guel bi dama bague trp me bou niou kholou we dou nek day diaakh le
C'est normal day ragual gua bayiko
@ En ok merci pour réponse 👍
Djiguéne bu Amul thiouss à l'âge de 18 ans C normal ou pas
Bien sûr
Djiguene mounoule gnake âme thiouss thiouss mo beuri façon rek mais c'est normal