JOE (Tekki for life) Moma recommandé chaine bi mais vraiment reuthiou wouma loutakh ma sétane saay vidéo, amna solo troop et bonne continuation merci !
Histoirou vélo bi danouma lek soupou kagndia on m'avait dit de le manger et puis on m'acheteras un vélo direct je l'ai fait vraiment t'es illustration sont réel merci encore ❤
Yalle nagnou Yallah fayal Naby (psl) c'est le premier à nous conseiller de faire des sourires et de paroles douces. ❤ Ça ouvre toute façon de porte (réussite, richesse, amitié, amour)
Merci beaucoup bly bala may commencé setan say vidéo bly grand dama rérone haw mawone loumay déf dama fogone sah dama am fébarou hél mais guénégama si situation you ma nékone MERCI énormément👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍🤍🤍🤍🤍🤍🤍
Dama nékk kou beug di lire ay livre pour guenedi cultiver waayé malheureusement sama jang déméwoul nonou waayé sa video yingay déf si wolof dima dimbali boubakh ma xam li nékk si livre you amsolo yi meme bou fékéni sama jang deméwoul nonou vraiment merci beaucoup
Jërëjëf amatina solo yal nala Yàlla fay. Bu la ko jot gi mayee 48 lois du pouvoir bi tamit boo ko defoon ni bii boole lepp muy benn dina baax lool. Jërëjëf
Non diarou ko continue thi vidéo development personnel yi ndah population bi mom la guena, sokh la. Tekki for lif mo niou yébal thi sa chaîne bi, mom mo gèré walou éducation financière bi bayi na dév..personnel bi, frère le peuple a besoin de vous gèrèl niou dv personnel bi slvp, bon courage
Max de partager svp ❤️
C'est bon
❤
❤
JOE (Tekki for life) Moma recommandé chaine bi mais vraiment reuthiou wouma loutakh ma sétane saay vidéo, amna solo troop et bonne continuation merci !
Merci beaucoup frère ❤️
Mashallah lingay def lu am solo la yalla nala yalla taxawu
Mach allah
Que Dieu vous rend heureux dans les deux mondes
Je suis en train de lire la version arabe et grâce à ces dernières vidéos je comprends très facilement.
Bravo et bonne continuation
Bon courage
Et comment son nom en arabe?
@@dakararena7168 كيف تكسب الأصدقاء وتأثر في الناس
Interessant.guewel yi nio comprendre borom livre bi il apppliquent tous les conseils😅😅😅
Histoirou vélo bi danouma lek soupou kagndia on m'avait dit de le manger et puis on m'acheteras un vélo direct je l'ai fait vraiment t'es illustration sont réel merci encore ❤
J'avais pas l'habitude de lire des livres,mes grâce à vous j'ai commencé à lire des livres.
Merci ❤❤❤
Génial !
Ohhh machallah chaque jour Dinako deglou inchallah ❤️❤️❤️
Bon courage et merci beaucoup
Machallah sama wadji fanwou goudou ak weer ❤❤
Jërëjëf yawit frère
Yalle nagnou Yallah fayal Naby (psl) c'est le premier à nous conseiller de faire des sourires et de paroles douces. ❤ Ça ouvre toute façon de porte (réussite, richesse, amitié, amour)
Amin et merci beaucoup
Machallah amna solo ❤❤❤❤
Merci beaucoup
Merci amna solo en tout cas mangi commencer changé sa ma vie ❤️❤️
Merci à vous
Merci beaucoup frère amna solo man yi rek lay ware si youtube bi bily😊
Bon courage
Saye vidéo amna ndiarigne lool machallah
Jërëjëf
Nice frr كان الله في عونك يا اخي 💎🙏😊
Jagga Na Loma masta jagga
Machalah Allah ❤❤❤
Merci beaucoup ❤️
Merci beaucoup et que Dieu vous récompense bien
Amin et merci beaucoup
Machalla contan nan çi yaw ni jaay çi vidéo yinga bollé defko benn
Merci beaucoup
Machalah loko deglou eupou n’a 20fois Amna solo trop yalna yalla barkel
Amin et merci beaucoup
Merci beaucoup bly bala may commencé setan say vidéo bly grand dama rérone haw mawone loumay déf dama fogone sah dama am fébarou hél mais guénégama si situation you ma nékone MERCI énormément👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍🤍🤍🤍🤍🤍🤍
L’art de la guerre laniouy khar
Mais merci bcp vraiment ceT très important ce q tu fais pour nous aider à évoluer 🎉
Ok Merci beaucoup
Ok Merci beaucoup
Vos contenus sont très utiles machallah ❤
Merci beaucoup
Machalla jop bi Nice muchísimas gracias
Merci à toi aussi
Dama nékk kou beug di lire ay livre pour guenedi cultiver waayé malheureusement sama jang déméwoul nonou waayé sa video yingay déf si wolof dima dimbali boubakh ma xam li nékk si livre you amsolo yi meme bou fékéni sama jang deméwoul nonou vraiment merci beaucoup
Merci à toi aussi
Machallah amna solo
Merci beaucoup
Machalla amna solo loll bilaye ❤❤ yalla nala yalla defall diamo ❤
Amin nio bokko merci beaucoup
Machall amna solo
Merci beaucoup
Merci tekki for life mo ma téktal fi
Merci encore GDT
Merci à vous et bienvenue
Vraiment ndanane nga samay
Ma chalah ma chalah amna solo dee Dieredief ❤️❤️❤️❤️
Jërëjëf yawit
@@Gdt221 yal nala yala samou.
Bo amé diot ga dikal gnou si
Livre 📕 ricardo kagnama bi le chèvre 🐐 de ma mère
Dieredief
Mashalla
Fait nous une video complète du livre père riche père pauvre
Et réfléchissez et devenez riche
Incha Allah
Machlla sétane nako 2foia ❤❤❤❤
Merci beaucoup bon courage
Vidéo bi doma ci doyall bess bosett nako deglo❤
Bon courage
Lingay wah c,est très important ❤❤souma sanione nga yokou volume vois bi merci
D'accord merci
👍👍👍👍 liguéy bi rafetena 🥰🥰🥰
Jërëjëf
Yalla nalayalla fay❤❤❤❤❤❤❤
Amin nio bokko ko
machallah amna solo 👍🏾👍🏾👍🏾👍🏾❤️❤️❤️
MERCI BCP CONTANE THI LIVRE COMPET BI
Merci bien
Machallah très important ❤
Merci beaucoup
جزاك الله خيرا ❤❤❤❤❤❤
شكرا لكم
Macallah amna solo ❤❤❤
Merci beaucoup
Merci frérot bonne continuation❤ j'aime bien votre vidéo
Merci infiniment
Vraiment yagui sii lou am solo
Merci mon frère ❤
Bokossi kilifeuguiii yagg fi lollll wayy damay yakamti Say vidéo bilahi
Merci beaucoup ❤️
Nice to meet you😊
Thank you
Machalla dwr lép rafétna
Jërëjëf
Yaw rekk lañuy topp
Jërëjëf
Oui moi j'ai appliqué mais lep dokh na billahi 😊
Bon courage
C mon première jour et Jai abonné😍
Merci beaucoup ❤️
Moguie si tékk fort life ak GDT xam xam rék la gnou begeu gnounn ✌
Bon courage
Merci beaucoup 😘
Merci à vous 😊
MERCI BEAUCOUP FRÉROT
Merci beaucoup 🎉bonne continuation ❤
Merci à toi aussi
c est vraiment pertinent
Merci beaucoup
Merci bonne continuation ❤❤
Merci à toi aussi
Machallah merci bcp ❤
Merci
Machine ❤️❤️🙏🏿
Thanks you so much❤
Thank you
Merci bcp 🎉
Bon courage
Machallah
Yàlla na la yàlla faye
Amin
Thanks so much g d t but I have idea for this chanel
Thank you, what is it?
L art de la guerre svp❤❤❤❤
Incha Allah
bindon naa wayee dinaa bindat ndakh say wakh dafa am importance
Ziarr ferr defal nou resima 45 louwa de pouofvar de roben guilin svp
Amna thi chaîne bi frère
Merci ferr❤
Merci frère
Merci ❤️
encore merci
Ok
Merci nice na
Merci à vous
Merci sa ligye rafetna
Jërëjëf 😊
Merci ❤
👍👍👍
😭😭😭😭😭😭😭😭 merci bcp frère
Merci
War nga cree ay podcasts dh❤
Jërëjëf amatina solo yal nala Yàlla fay.
Bu la ko jot gi mayee 48 lois du pouvoir bi tamit boo ko defoon ni bii boole lepp muy benn dina baax lool. Jërëjëf
Incha Allah dinako def amin et merci beaucoup
Ohhh grand bi merci beaucoup ❤ms beugeu na num dh Stp ❤🙏
Merci à vous 78 362 59 91
Grand bi merci way ❤🙏
Machallah ❤
Machallah❤
Merci beaucoup
Livre 📖 by noumou toude geunn ballma bakhelenmaco
Comment se faire des amis et influencer les autres
Macallan amne sa❤❤
Merci beaucoup
Toubarkalla❤
Jërëjëf
Machallh ❤❤❤
Merci
Machaallah ❤❤
Merci
Amna solo🎉
Merci beaucoup
Que dieux vous protège
Caoch livre cadran du cas Flow Robert kiyosaki ngir yalla😢
Incha Allah 👍
Merci
👍👍👍
Nice 🙏
Merci
Yaw rék lay top
Deggla merci beaucoup
👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Merci beaucoup frère, mais doniou résumél père riche père pauvre
Incha Allah
Non diarou ko continue thi vidéo development personnel yi ndah population bi mom la guena, sokh la.
Tekki for lif mo niou yébal thi sa chaîne bi, mom mo gèré walou éducation financière bi bayi na dév..personnel bi,
frère le peuple a besoin de vous gèrèl niou dv personnel bi slvp, bon courage
je suis nouveau dans ce chêne c'est teki for life qui ma invité à ce que ma suivre chêne bi mai super 👍
Merci beaucoup et bienvenu
Que dieu vous protège
Zo borom tekki for live momafi yabal mé abonné naa
Bienvenue et merci beaucoup
Très important
communicationinterpersonnelle
Mashlla
Merci
Résumé de livre réfléchir et deviner riche de Napoléon Hill en wolof svp
Incha Allah
❤❤❤