🤣🤣🤣 Ah gosse ponkal Lou mouy firri ? Mo raaw gaagny té di Serignou Serigne ssi. So bougué comprendre sincèrement toppal audios yi déglou inchâ Allah dina leer naadj ci ssa boop. Tu nous en diras des nouvelles à propos du surnom PONKAL. Ponkal veut dire entre autres quelqu'un de droit, extrêmement versé dans les sciences religieuses exotériques et ésotériques. Ce qu'il éclaircit, tu ne l'entendras nulle part ailleurs: La profondeur et la clarté de ses explications n'existent nulle part ailleurs et pour s'en convaincre pour quelqu'un qui ne recherche la vérité : il faut l'écouter encore l'écouter et inchâ Allah tu verras. L'écouter, c'est finir par savoir comment aimer Allah, son prophète saws, les compagnons et tous nos anciens bien guidés. Donc effectivement il est le PONKAL de son temps. Ça n'a rien à voir avec notre seigneur. Allah est plus qu'un ponkal car c'est lui qui fait les ponkals. Wa salaam
@@talibedabakhmalicksy1276 Ahh mais lolou dokko régg parce que poser question bou melnii foo kee waadji diombi pour comprendre parce que affaire de pass pass leu donc il faut l'amener petit à petit avec des preuves claires.
Aboubakr. Khadiss bouyy andi sadlou. Moyy diappal lii Tai maygnou diam. Yonentibi donne na dioubanti diouli diambour ba nekko a la fin kou diouliwoul niii amo diouli. Tai ci diangalai boobou andiwouci qabdou. Donc may gnou diam. Kennn eupeul kham kham fini mayy toudd. Cheikh AHMET tidiane chérif el HADJI MALICK SERIGNE touba mame abdoulaye NIASS omar al foutiyou. Gni gneup daniouyy sadlou.
Ndeyssane yangui wookhé khol bou bonn té rew ande ak sokhor ! Ibra asta le ndiaaloo kat. Djiguénn bou ko rombe té khawa taarou rek mou bougueko time. Ibra asta le grand thiaga !!! 🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Domeram ça fait longtemps que je t'ai posé une question à savoir si tu le connais, mais tu n'y viens pas je réponds : sa deudieuw ndaye puisque dangay diay rew di wokh louleu neekh. Je te montre qu'il est facile de faire pareil. SA LEFEUL NDAYE
QU'EST CE QUE TU RACONTES EN FAIT ??? TU T'ADRESSES À QUI EXACTEMENT ? POUR QUE LA DISCUSSION SOIT INTÉRESSANTE IL FAUT APPRENDRE À PARLER CLAIREMENT !

Toujours pertinent. J'ai beaucoup de respect pour lui
Djazakallah fika
Degla
Comment ne pas avoir de respect pour cet Homme Véridique?❤
Mooy jambaar u diiné ji ak tariiqa bi dëgg dëgg.
Sheex Abdul Hamiid Saar
( *حفظـہ اللّـــہ وأيده و رعاه* )
Sangue bii yalna fi yague tei andak weur vraiment ham ham bii setna tei lér ylna Co yala fay
manchalan sarr yalla naga fi yague the wer
Macha allah yalna yalla goudal sa fan serigne biiii yokou sa soutoura si barki alladji abdou
بارك الله فيك يا شيخ عبدالحميد صار
Machallah amatina sholo lool🙏
Salam rendez la vidéo telechargeable SVP
Dieurdieuf chikh habdou Hamid sarr
Xam xam pur .nitou yallah Kamil. Sarr. Dieureudieuf cheikh Muhammad Diop atijani
Yow loo si kham
Machalahh
ما شاءالله
Waaaaaw lignou dindi kan moo KO dindi.kan moo am sagn sagnou dindi wala yokk dara ci téré bi nga khamni yalla moo Koy aral boppam.
Dieurdieuf atilmîzou tidiane
Mâchaalah mâchaalah mâchaalah mâchaalah mâchaalah mâchaalah
molene rawe niome nieup
💔💔🙏🙏
Thiey ponkal bi
Lérna dé
ماشاءالله
Euskeuy mane deh Mouride là mais ki yémé na deh . Seigneur bi Li mome wakh deug xam xam la
صحيح
Maacha Allaah.
❤️❤️❤️❤️❤️❤️
🤜⚘⚘👍
Serigne bi dé khawmako deguna touram nakk wayee borom kham kham la dé.
ESKEYYYYYYYYY PONKAL MI !
Ki yémé neu
Topp YALLA moka ko may machallah
Machalah
Maachaaa'alllaaahhh 🥰 mais pourquoi nguene koy wowé PONKAL mi ?✍️🙏 ta yalla nekkfi ✍️???
🤣🤣🤣 Ah gosse ponkal Lou mouy firri ? Mo raaw gaagny té di Serignou Serigne ssi.
So bougué comprendre sincèrement toppal audios yi déglou inchâ Allah dina leer naadj ci ssa boop. Tu nous en diras des nouvelles à propos du surnom PONKAL.
Ponkal veut dire entre autres quelqu'un de droit, extrêmement versé dans les sciences religieuses exotériques et ésotériques. Ce qu'il éclaircit, tu ne l'entendras nulle part ailleurs:
La profondeur et la clarté de ses explications n'existent nulle part ailleurs et pour s'en convaincre pour quelqu'un qui ne recherche la vérité : il faut l'écouter encore l'écouter et inchâ Allah tu verras.
L'écouter, c'est finir par savoir comment aimer Allah, son prophète saws, les compagnons et tous nos anciens bien guidés. Donc effectivement il est le PONKAL de son temps. Ça n'a rien à voir avec notre seigneur. Allah est plus qu'un ponkal car c'est lui qui fait les ponkals.
Wa salaam
Ponkale daniouye koye wakh yalla diga wakh domou Adama
Bombardier lou takh gnou koye wowè pongkal mi
@@talibedabakhmalicksy1276 Ahh mais lolou dokko régg parce que poser question bou melnii foo kee waadji diombi pour comprendre parce que affaire de pass pass leu donc il faut l'amener petit à petit avec des preuves claires.
@@ndiougalo4668 🤣🤣🤣 khana kouyy deff lou HARAME ( LAMBEU) bougn touddé ponkal, niou sagn koo meuna woowé kouy ligeuyall ALLAH.
Amna kham kham bou lére nagni gnéména dégue
Limou wakh si khabdou leerna nagn ...hafizakal laahou
Pourquoi ponkal y a pas un autre surnom plus cohérent que Ponkal
Boula nakhari we taalale GAZ TOOK SSI tee demm deglou JAZZ Puisque Paco diazz nga toudee sa bopp 👍😀😜😀😀😂😂😂😂
@@Ndaar-Faam yalla rekkay ponkal
@@papaalassaneseye8252 Mooko wall gaayam yii niouy woowé PONKAL aussi niou melni CHEIKH SAYYIDIL HAADJI ABDIL HAMID SARR !!! 😀😀😂😂😂🤣 Ayy cons nguène khamoulènn darra ba darra dièkh, mais c'est normal des talibés de hibou diallo 🦉 nii rek nguènn mouna mèll parce que sènn baaye hibou diallo diangoul delou woul !!😂😂😂😂😂😂😂
Je veux le débat qui l'opposait à l'ibadou sur xablou et sadlou.Il avait vraiment massacré le wahabiyyou.
Effectivement il l'avait bien remis à sa place d'ignorant. Il faudrait épurer le son pour qu'il soit plus net car il y a bruit de fond...
Aboubakr. Khadiss bouyy andi sadlou.
Moyy diappal lii Tai maygnou diam. Yonentibi donne na dioubanti diouli diambour ba nekko a la fin kou diouliwoul niii amo diouli. Tai ci diangalai boobou andiwouci qabdou.
Donc may gnou diam.
Kennn eupeul kham kham fini mayy toudd. Cheikh AHMET tidiane chérif el HADJI MALICK SERIGNE touba mame abdoulaye NIASS omar al foutiyou. Gni gneup daniouyy sadlou.
Sen wadiou khalkou bi
Dou leufeul ndéme
Kou bon kou trokhe kou khalkou
Ndeyssane yangui wookhé khol bou bonn té rew ande ak sokhor ! Ibra asta le ndiaaloo kat. Djiguénn bou ko rombe té khawa taarou rek mou bougueko time. Ibra asta le grand thiaga !!! 🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Effectivement borom xam xam
Nane la mouhamed{psl} akh sakhabam yi done dioulé? Kép kou wouté gnom sohla wougnou sa wakh
M Lo
M
Kii naafeq la
Ahh bon ??? Tu le connais ???
Domeram ça fait longtemps que je t'ai posé une question à savoir si tu le connais, mais tu n'y viens pas je réponds : sa deudieuw ndaye puisque dangay diay rew di wokh louleu neekh. Je te montre qu'il est facile de faire pareil. SA LEFEUL NDAYE
Indil bena hadith bou werr si sadlou boul kena saga réponse rek la sokhla wa wasalam
SAWWAL TEURRY GOSSE gni YEEWOU nieup té guemm Yalla nangou naniou 👍👍👍😂😂😂😂😀😀😀😀
@@Ndaar-Faam yow yagui wone ni doo talibe amoo bena adab
@@abubakrmd0078 Sawwal teurri.
@@Ndaar-Faam merci
Wakh nako ci birr wakh tane bi ms wakh tane bi dafa ds lou barri mane amnako bamou diekh bi matoul dafa dagg
Thiey domeram j .Martaba mo doy War .
Dalaye maye goudou fane di la wane louye daga sa xol ta dossi mene daara.di xoulo sa sou nekkkk aki daga saneteh
QU'EST CE QUE TU RACONTES EN FAIT ??? TU T'ADRESSES À QUI EXACTEMENT ? POUR QUE LA DISCUSSION SOIT INTÉRESSANTE IL FAUT APPRENDRE À PARLER CLAIREMENT !
Wa Waaw dieureudièfè cheikhal el hadji malick sy cheikh hamid Sarr yalla na yalla samula
Baye Niasse mayam
Dîna yague dageu sen xol 😂 daguén tarder vous êtes en retard . FAYDOU bi Mingui dem nguen tokk sen poukhous di fen