Mane deh jai 25 ans awma diekeur mais yalah defna mangui dinthie sama ndaw batay. Di khare beusse bou rafete pour sama diekeur ndieuk si mane inchalah.
@@adamasene6988 bilaye amone naa copain bo khamni dafma wax carrement qu'on peut pas sortir sans sexe (excusez moi du terme), cest la cause de notre rupture. Mais yalah bakhna ,amna goor you bakh bataye.
Dara geunoul nekh sa borom keur fekeu la nga fesse deleu( balene ma si thermes bi) mais c'est très important de garder sa virginité jusqu'au jour du mariage. Diebali noumou metté khawma nouko nite di diokhé gratuitement. Pour les filles violées se n'est pas de leurs faute. Yallah na yallah samou khaleyi
Mane dei sama Badiene da décédé mane sama yaye moma wadial deifarma gni sama kanam papa ma parei deim sama keur goro fala teudei sama goro feuggna 3 fois neikk bi nei sama dieugueur nama bayi ba souba dakh ay youkhou sama dieugueur gni bopam moma done wakh nanema sa yaye neilawoul yaw rek lay khar lolou moma ma gueuna yokk diom tei machalla sama goro mo deim wowi seine gueiweul gnou yeuketima ak samay oumpagne dieugueur samay dieukkei walahi gnoma yobou ba sounou keur tei bagnou feigguei sounou keur sama yaye mogni oubil neilawoul ba beurseitt yalla na yalla samme dakh môme rekk mo meune
Mane deh j'ai 29 ans je me suis marié il ya 2 ans mon mari n'es pas au Sénégal mes magui koy khar ak sama ndaw mashalla sama keur lay teudé téral sama famille
Mane d je me suis mariee à 25ans dakar la djoudo fi la yaro maguei fii teude na 1 semaine sama dieukeur amoul bountou degn ma yoobou beu kaolack dagual meu 14 sothiète ma doora teud alhamdoulilah auto ak million legn meu ndiéguènayalai... loulen way wakh tai wakhoulen teuyai len sen bop dalen di nakh hormis l aspect materiel k j ai cité et ki n est k futilité mais grandeur bi ngey ame si seu kanamou dieukeur seu belle famille sa yaye et toi meme rek diarnako... ya de ces hommes ki disent k ca compte pas pour eux mai degn ko khamoul rek sougnu amei diabar bouni mel dougn ko yamalaik kouko amoul... respecter len sen bop girls 😘😍😍
Vierge ou pas lou am solo moy nio beugayé moi je suis la divorcé mère de 2 enfant mai magui nii amna sama dieukeur mousoul marie té il m'aime ,il me soutien vraiment té soutoura da bakh
C'est ça. J'ai été mariée à l'âge de 23ans. J'ai fait 4ans de mariage , ma fille a 3ans et demi. J'ai divorcé depuis 2017 Yallah def ma dadjé akk irresponsable bohamni méritéwul sama virginité aussi c'est ce que je regrette. Mais alhamdoulilah bima tassék ku bah !!! Il m'a accepté, ma fille et moi.
@@kharyfaye8324 mane deh Kou seuy ba tass la am mai soumay guiss genre video yi dafmay tayal lo Dra dakhoul ndaw lolou mom souma sanione dina am niarel wala 2ème wala 3ème wala 4ème bouko am
Labane dafa harame no seulement daguaye werre djieguene bi rousse lou familles l’islam n jamais permis ça je le d en v haute dafa harame ce qui passe entre l’époux e l’épouse reste entre eux. C contrairement à l’islam.
Fi ngay tak diank té doula seyeul gua tak ap diék mou seyeula ba gua contane si coté bou nék soutoureu dafa bakh nék diank takhoul gua nék djiguéne bou bakh
mane deh 15ans lane ma takei 20ans j'ai divorcé machaalah walakhi amate na djeukeur bou bakh yalla xamnako 23ans la am instant bi mangui koy seuyeul tei niane na yalla seuyeul ko beu niep guiss ko
@@mamerosediop9519 walahi tres bien diék lay weur mane yéne rék ka fi seuye té kou beugue dom bou bakh diamono bi diék ngay tak ma dé amagouma wayé diék lay nian am
A ouais Adouna bi lépp guifi yalla rkk mo xam naka la ak ayy diamam que tu soit vierge ou pas ce n'est pas a nous de jugé on fait ce qu'on en a faire et puis basta kouy geustou nitt boula borom bi geusto ga torokh Tout le monde n'est pas blanche comme neige on fait tous des erreurs mais on dmande pardon a Dieu même si c difficile yalla naniou yalla doli soutoureu ak mougne
Adouna bi dafa doywar,péhé yi beré,wayé sante yallah, inchallah dieukeur rék moy takh ma diohé sama ndaw!!!je suis fière de moi, djiguéne da wara am foula bo begué gnou respecté la
Ah dafmay fatally sama biss en Dècembre 1997 miguimelna tay dji, sama djeukeur dafa contane ba mayma bague diamant. Sama yaye bekker, sama goro. Gneup beeg Am ndaw amna solo machallah. Mes soeurs attachaient bien vos pagnes
@@maremecoly6026 yaa meuna doul yow loo xam ci sarakholé yi meuna fen gnom gneup jour s'en mariage lagnouy teud ta s'en keur goro lay alè bayil doul way yow soninké et fière de l'être nak
Machallah linga wax dé deug la ta xamougnou sathie sa diabar youbou hôtel soo seuyè ba paré ngay teud sa jour mariage sax kèn doula guiss ci biir nek ngay yendou pendant une semaine sa yaye boolé la ak mère boumou am confiance gnoukoy woowè khoussmanta molay topato ba semaine bi dièx sa dieukër ak aÿ mbokam teral ko ak teranga you doul dièx gnou xewalat laat la ngay soga guène nek sa mbokou yi gneuwat téwé ko machallah
Machalla machalla waay mbossè da nga ma nèkh billahi thiëy kouthi yakk sa toukkou si ngalam di nga riiti riiti mou te le c'est le plus beau jour de tt les jeunes filles qui ont gardè leurs vièrginitè
Lima meti moy pour lane niou fokk ni gni seuy ba tass teuyé wouniou sen bopp beurina niou seuy ba tass gueuneu teuyé sen bokk diank dji niép yamouniou ki seuy ba tass nit la djiguene la amoul droit amate benene dieukeur
C’est vrai et j’avais ce problème au près de ma belle famille et je vous assure c’était très dure en plus bi ma done seye javais16ans actuellement sante yallah bou bakh amouma ak mome dome nak mais yallah bakhna🙏🏽
@@yaa___marieendour7054 ndeysaane c'est triste ,mais la vie est ainsi faite ,les gens ne cherche pas à savoir ,... lo guiss day dafay dieh ma chérie, ça va aller
Sama dome Aby diop madame Sow keur gorome la teudé en plus gorome yayou dieuereume mo dieuk ci mome mo lali serbi mou fess dél nek khalé bou daw alhamdoulilah
C'est vrai tata mbosse mane mom j'ai passé ma nuits de noce chez mes goros .sante yalla car xamnagnou maykane sama dieukeur am confiance trop si mane .
Mane dé sama keur dieukeur la teudé thi sama kanam goro thé mome khamnané jank la machala il ya 23 ans et c'est une protection pour ses enfants té en plus dama jogualé donc machala
J’ai 23 ans je garde ma virginité par recommandé et le respect pour ma propre personne 🙏🏼Mais mère bi je l’aime bien mais beugouma ay labane mane na xam , yalla xam , samay mbokou kham point ❤️
Non magui dheii billahi dégg na deugg vierge dafa nék lou am solo dakh Aÿ énémis sa yaye say xarite oh métina yalna yalla doli soutoura mai y'en gniy commentaire ken d'où y'en o6 Sénégal nexna
Je suis une fille de 21ans mesouma Def rapport mais souma amé dieukeur inchalah douma deef labane gneup diko guise nono sama badiane sama dieukeur sama yaye sama Giro katan wo gnieup doko deef beut bakhoul
Senegal lgui dagnouy defare ndaw meuno hamei vrai ou faux bilahi ame ndaw c bien dtrop m li eup solo moyy na fekk ngua ame soxna ssou bahh yattou beugu sa famille beugue la c sa gnak vierge c po psk te mauvais nono tu px n po etre vierdge donne seuy katte baxx pour mane c l essentiel vierginite 1er jour leu rk dnc amour mofay dess ak djiko bou rafetet n empeche fonkal sa bopp ba goor gni dounoula foweii💁♀️
L islam bani c pratik té Lima diaxal gni fabriqué dak sabar😂man dh sama keur goro lagnou ma dieulé sama djiekeu ma yeukeuti end ak sen nguéweul bi nema Lima guiss guethie nako guiss té teugouma wotewouma.sen seur yi kou nek di tek beut mtx gni di sey dom teu len sey soutoura leu gnou bayi si xel l essentiel moy gay djank té sa djiekeur xam ko dax ya des fille qui n naissent pas avk wa salammmmmm
Mane sakh je parle pas de sa mais erreur thie adouna daffay ame nekoul tu n’es plus vierge rek k da nga bone walleu aussi nekoul tu vierge rek k da nga bakh yalla dall mo hame yalla nagnou dolli soutereu rek
Mes nak elle dit la vérité Lou meune ti nek rek nafa deug am c'est ce qui compte mes aussi ont n'es pas obligé de passer la lune de miel chez tes parents ou ta belle mère
Labane c est pour encourager les jeunes filles à s abstenir jusqu'à au mariage ,ça fait honneur à ton mari et à ta famille, c haram mais c est une stratégie que nos parents utilisaient,mais regardez maintenant, on ne se reconnaît plus à cause des gestes et faits qu on puisse des occidentaux
Mane damay lathie nga tede kheuy gnou labane dafay indi yaradal ndakh façon nit bouné dila time d’après louma lirre ci commentaire . Legui nga dem l’une de miel après sa dieukeur woter indi drap Bi gnouner lolou gnak wolou sa bopou la stp Kone nagn lagnou wara def
Certaines personnes naissent sans . D'autres l'ont perdu par accident ou lors des infections qui sont très fréquentes de nos jours . c'est haram ce que vous faitent avec vos instruments de musique. L'islam ne vous a pas demandé de dévoiler ce qui se passe pe'dant la nuit............ Dieu sait tout le suprême, le grand, ........
C'est vrai que beaucoup de filles ne sont plus vierge mais aussi, teud, heuye wara nopalou nit gni weurla, tankal la ak thiow, ba paré parfois meune ngaci jeulé fébar wala yaradal, aah
Billahi ndaw Lou âme solo la mane dé mbosé mi di wakh badiene la si mane Abdou ngom mikoy té limouy wakh Lou âme la ndakh mane sama djieukeur mo ndieuk si mane té bama teudé yéwou meunou ma dokh cône ndaw Lou amela
Gnikoy diokhé gratuitema bilahi ça m poz problème wala affair yi d'où bène bok en tout cas dal diaxalnama kouy sathie mom yakarna ni youkhou doufa âme🤷🤷
Mane ame na borome keur depuis 2009 lima diakhal mosouma sékhe ak gor té bima tedé amouma ndaw sanete yalla sama borom keur amoul problème bobou souma amane far sakh mou lathma sama bope ma bayiko ndakh damanane qui begouma yéné wouma limou yéné rakam diakhalone nama trop sakh🤔🤔
Bilahi doyna warr lo xamni dagay yèwou do meune marcher ta des vertiges ta mal a faire du pipi tu te rèveilles melni daga perdre 10kg bilahi no li ame lègui kenn xamouko
Mane deh jai 25 ans awma diekeur mais yalah defna mangui dinthie sama ndaw batay. Di khare beusse bou rafete pour sama diekeur ndieuk si mane inchalah.
C'est bien chérie bilakhii la femme amoul loudoul bobammm😗😗
Pareil comme Mann ndakh djigueyy amoul loudoul popam
@@adamasene6988 bilaye amone naa copain bo khamni dafma wax carrement qu'on peut pas sortir sans sexe (excusez moi du terme), cest la cause de notre rupture. Mais yalah bakhna ,amna goor you bakh bataye.
@@ramadiallo2497 c'est vrai cherie. Yalah bakhna
@@PEOPLE-km7vr yalna Diam yague baniou fegué leup inchallah
On reste pas vierge pour son mari
Mais plutôt recommendation divine
Yalla naniou Yalla diapaler amine
mais pour gua garder ko pour ton mari motax yalla recommander ko
Noushna Noushna yalla wokhouk kou djiguene ki kesse garde ko dafne niom niar nieup pour mom
Noushna noushna demal dianguiwat ioe
@@aminatakonate5457 ya wara dianguiwate. La femme doit rester chaste té rester vierge cila bok
enfin kouy wah lou am sens
Peulh aka fonk ndaw motax souma nare df dara halate souniou famille nougneko fonke ake nigne si sévère motax damay ragal sax ❣️yalla naniou yalla sambe arniou ake mboleme dioulite ❣️
Ak sarakhoulé aussi magno compé bataye dankaye deff
Dara geunoul nekh sa borom keur fekeu la nga fesse deleu( balene ma si thermes bi) mais c'est très important de garder sa virginité jusqu'au jour du mariage.
Diebali noumou metté khawma nouko nite di diokhé gratuitement. Pour les filles violées se n'est pas de leurs faute. Yallah na yallah samou khaleyi
J ss d'accord mais j'aime le labane
Bilay ioe walay badiane dafma yague nékh
@Maryama Tall dara geunoul nékh tmt gua fékk sa dieukeur puceau
Amine
Pensez à ses filles là qui sont violées et qui sont tromatisez bayilène sen kadouyii pensez aux autres nguir yallah
Bilaye amole sance soutoure on n'est des musulmans
Bilay
Yaw khana moye lolou
SÉNÉGAL CULTURE TV moh iow khalate nay rafete way 🙏🏻🙏🏻
Je penses que wakhouniou les filles voilée mais celles qui s'amusent comme elles veullent bilae c'est honteux khana guay banékhou aduna rek
Cette griote je l’aime bien elle est trop belle ❣️🍫
J'aime bien le comportement du journaliste elle concentrée très posée malgré l'ambiance
Souvenir houssou dour
Man dh Sama kar diakar la tadé Sama goro yaka tima jigèun go wolo boupam do taddè otèl
Mane dei sama Badiene da décédé mane sama yaye moma wadial deifarma gni sama kanam papa ma parei deim sama keur goro fala teudei sama goro feuggna 3 fois neikk bi nei sama dieugueur nama bayi ba souba dakh ay youkhou sama dieugueur gni bopam moma done wakh nanema sa yaye neilawoul yaw rek lay khar lolou moma ma gueuna yokk diom tei machalla sama goro mo deim wowi seine gueiweul gnou yeuketima ak samay oumpagne dieugueur samay dieukkei walahi gnoma yobou ba sounou keur tei bagnou feigguei sounou keur sama yaye mogni oubil neilawoul ba beurseitt yalla na yalla samme dakh môme rekk mo meune
Machallah wy digma yok dioum dh
Machallakh
kon d gnamon ga d
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 vreuument
@@damegorakebe6482 🤣🤣🤣🤣
Mane deh j'ai 29 ans je me suis marié il ya 2 ans mon mari n'es pas au Sénégal mes magui koy khar ak sama ndaw mashalla sama keur lay teudé téral sama famille
Yallah baxna
Normalement sa keur dieukeur gua wara teudé non ??
Mane d je me suis mariee à 25ans dakar la djoudo fi la yaro maguei fii teude na 1 semaine sama dieukeur amoul bountou degn ma yoobou beu kaolack dagual meu 14 sothiète ma doora teud alhamdoulilah auto ak million legn meu ndiéguènayalai... loulen way wakh tai wakhoulen teuyai len sen bop dalen di nakh hormis l aspect materiel k j ai cité et ki n est k futilité mais grandeur bi ngey ame si seu kanamou dieukeur seu belle famille sa yaye et toi meme rek diarnako... ya de ces hommes ki disent k ca compte pas pour eux mai degn ko khamoul rek sougnu amei diabar bouni mel dougn ko yamalaik kouko amoul... respecter len sen bop girls 😘😍😍
Machalla
Aa lolo nekh
Lane moy sotiete et pourquoi 14 juste une curiosité
Vierge ou pas lou am solo moy nio beugayé moi je suis la divorcé mère de 2 enfant mai magui nii amna sama dieukeur mousoul marie té il m'aime ,il me soutien vraiment té soutoura da bakh
C'est ça. J'ai été mariée à l'âge de 23ans. J'ai fait 4ans de mariage , ma fille a 3ans et demi. J'ai divorcé depuis 2017 Yallah def ma dadjé akk irresponsable bohamni méritéwul sama virginité aussi c'est ce que je regrette. Mais alhamdoulilah bima tassék ku bah !!! Il m'a accepté, ma fille et moi.
@@kharyfaye8324 bilahi yoboul mai yallah dinala soural inchallah même moi il ma accepté avec mes enfants
Les hommes Sénégalais moylolou, moi sincèrement je ne veux pas du tout sérieux
Nous avons la même possible bien dit ma chérie
@@kharyfaye8324 mane deh Kou seuy ba tass la am mai soumay guiss genre video yi dafmay tayal lo
Dra dakhoul ndaw lolou mom souma sanione dina am niarel wala 2ème wala 3ème wala 4ème bouko am
Labane dafa harame no seulement daguaye werre djieguene bi rousse lou familles l’islam n jamais permis ça je le d en v haute dafa harame ce qui passe entre l’époux e l’épouse reste entre eux. C contrairement à l’islam.
Absolument
Degue la islam da beugue soutoureu
Yaw maynala 100 milliards danio exagéré dh ayy drap blanc ah grawoul xwma kouko créé
Aada la rek ngir ñaax jigéen ñi ñu gën a sàmm seen ndaw te lislaam aada bu baaxee mën a and ak moom
Félicitations ma petite sœur ❤️❤️❤️🥰✨🌹🌹Aminta liguey bi rafetna Machallah, Yallah nga dem si kaw inchallah , gnoulay degue feep 🙏
jour bila sa dieukeur di dieul contane ci yow dara dakhouko
Yalnagnou yalla sameu mousseulniu ci cheytane
Fi ngay tak diank té doula seyeul gua tak ap diék mou seyeula ba gua contane si coté bou nék soutoureu dafa bakh nék diank takhoul gua nék djiguéne bou bakh
Je valide
mane deh 15ans lane ma takei 20ans j'ai divorcé machaalah walakhi amate na djeukeur bou bakh yalla xamnako 23ans la am instant bi mangui koy seuyeul tei niane na yalla seuyeul ko beu niep guiss ko
@@mamerosediop9519 walahi tres bien diék lay weur mane yéne rék ka fi seuye té kou beugue dom bou bakh diamono bi diék ngay tak ma dé amagouma wayé diék lay nian am
T'a tout dit. En plus gno eup expérience.
A ouais
Adouna bi lépp guifi yalla rkk mo xam naka la ak ayy diamam que tu soit vierge ou pas ce n'est pas a nous de jugé on fait ce qu'on en a faire et puis basta kouy geustou nitt boula borom bi geusto ga torokh
Tout le monde n'est pas blanche comme neige on fait tous des erreurs mais on dmande pardon a Dieu même si c difficile yalla naniou yalla doli soutoureu ak mougne
Adouna bi dafa doywar,péhé yi beré,wayé sante yallah, inchallah dieukeur rék moy takh ma diohé sama ndaw!!!je suis fière de moi, djiguéne da wara am foula bo begué gnou respecté la
Walay ta raison té sa bop ba am sa djekeur mou djokhla thieur fonk la
Émission nexone na très intéressante.. bilay ngeweul lay bégué🤩😍
Ah dafmay fatally sama biss en Dècembre 1997 miguimelna tay dji, sama djeukeur dafa contane ba mayma bague diamant. Sama yaye bekker, sama goro. Gneup beeg Am ndaw amna solo machallah. Mes soeurs attachaient bien vos pagnes
Thiey ndaw aka neuh surtout sama famille aka nioko fonk sarahoule yi👌
Moi je connais des sarahoulé et elle sont rarement vierge au mariage
@@maremecoly6026 yaw yangui sétt lingay wax bou bax c très grave de juger les gens té khamo lén
Xolate lén bou bax sén commentaire
@@maremecoly6026 yaa meuna doul yow loo xam ci sarakholé yi meuna fen gnom gneup jour s'en mariage lagnouy teud ta s'en keur goro lay alè bayil doul way yow soninké et fière de l'être nak
@@maremecoly6026 doul Kat nga rek mosso guiss sarakholé bou teudè fenen foudoul keur goro ta après thièt lay am nak meuna fen
Machallah linga wax dé deug la ta xamougnou sathie sa diabar youbou hôtel soo seuyè ba paré ngay teud sa jour mariage sax kèn doula guiss ci biir nek ngay yendou pendant une semaine sa yaye boolé la ak mère boumou am confiance gnoukoy woowè khoussmanta molay topato ba semaine bi dièx sa dieukër ak aÿ mbokam teral ko ak teranga you doul dièx gnou xewalat laat la ngay soga guène nek sa mbokou yi gneuwat téwé ko machallah
Machalla machalla waay mbossè da nga ma nèkh billahi thiëy kouthi yakk sa toukkou si ngalam di nga riiti riiti mou te le c'est le plus beau jour de tt les jeunes filles qui ont gardè leurs vièrginitè
ni
n
Lima meti moy pour lane niou fokk ni gni seuy ba tass teuyé wouniou sen bopp beurina niou seuy ba tass gueuneu teuyé sen bokk diank dji niép yamouniou ki seuy ba tass nit la djiguene la amoul droit amate benene dieukeur
Vraiment
Djiguene amoul loudoul bopam yalla naniou yalla samalé sougnou bopou
Même souféké daguanoul nagnou téyé sounou bopp ba am biss bou rafett dakh yaye yi meune contane
Machala li da fa neh sa ma dieukeur dafma respecte
Bilaye deguela mane mom sama keur ndiènkè la tedè dafa nèkh machallah nièp bèk
C important machalla Yalna yalla sam képi kuy djiguene labaan da neh te sur ken dula yap...nehngama Mama🥰😘
L'islam soutoural la beug tout ça c'est des futilités wassalam 🙏
Façon c dès chose afwa
Il ya des filles qui naissent sans hymen
Akkay deugue
wawaw con ni gor di dioudo ak kharaff rek
C’est vrai et j’avais ce problème au près de ma belle famille et je vous assure c’était très dure en plus bi ma done seye javais16ans actuellement sante yallah bou bakh amouma ak mome dome nak mais yallah bakhna🙏🏽
@@yaa___marieendour7054 c'est triste ndeyesane
@@yaa___marieendour7054 ndeysaane c'est triste ,mais la vie est ainsi faite ,les gens ne cherche pas à savoir ,... lo guiss day dafay dieh ma chérie, ça va aller
Ah Tata sa numéro rek la beug nga labane ma rek 😍nguir yalla
Mane dhh bamay teudd sama keur goro la teuddé ba parei sogga deim lune de miel
GN bakh gno bakh taye
Félicitation chérie
@@fachatop6015 si chérie comme nous les toucouleurs sa keur goro guay teudeu
Même man sama keur Goro la teudde me jour bou daw yaram la ndaw cadeaux bou diara fonk la
Sama dome Aby diop madame Sow keur gorome la teudé en plus gorome yayou dieuereume mo dieuk ci mome mo lali serbi mou fess dél nek khalé bou daw alhamdoulilah
C'est vrai tata mbosse mane mom j'ai passé ma nuits de noce chez mes goros .sante yalla car xamnagnou maykane sama dieukeur am confiance trop si mane .
Mane dé sama keur dieukeur la teudé thi sama kanam goro thé mome khamnané jank la machala il ya 23 ans et c'est une protection pour ses enfants té en plus dama jogualé donc machala
Mère Mbossé saff nga ma machallah
J’ai 23 ans je garde ma virginité par recommandé et le respect pour ma propre personne 🙏🏼Mais mère bi je l’aime bien mais beugouma ay labane mane na xam , yalla xam , samay mbokou kham point ❤️
Ces bien ma cherie
Nikif-Nikif ❤️
Non magui dheii billahi dégg na deugg vierge dafa nék lou am solo dakh Aÿ énémis sa yaye say xarite oh métina yalna yalla doli soutoura mai y'en gniy commentaire ken d'où y'en o6 Sénégal nexna
Vierginité takhoul nit bakh dieko mo diarra khol si nit
💖
Bilay chérie deug nga dé
Machalah amina diaw bonne continuation emission bi nekh na
Mais attention c'est différent les maris on plus de patience avec leurs femmes avant c'était pas comme c'était la pression et les lubrifiant
Soutoure amena solo c'est entre les 2 partenaires arrête svp
Deug blh sa conserne ke les deux
Je suis une fille de 21ans mesouma Def rapport mais souma amé dieukeur inchalah douma deef labane gneup diko guise nono sama badiane sama dieukeur sama yaye sama Giro katan wo gnieup doko deef beut bakhoul
On a rien a prouver aux gens tei sa bopp dakh Yallah takhhh.c'est l'essentiel
L'islam daganoul ndakh islam soutoura rekk
Deuk pur islam soutoura la santané
Bilaye legui soutou ra amatoule yalla na yalla soutoureus nieup
Diego leugui bilahi mane guathié momay rayyy l'islam soutoura rek la wakh bilahi labane walahi bounioko khamone li thi l'islam wakh mai dieu é grand
Vrema li amoul djerigne
Amna solo diguéne waroul diokh bopame kouko diokhoul thiane.wakhouma nak victime yi
Senegal lgui dagnouy defare ndaw meuno hamei vrai ou faux bilahi ame ndaw c bien dtrop m li eup solo moyy na fekk ngua ame soxna ssou bahh yattou beugu sa famille beugue la c sa gnak vierge c po psk te mauvais nono tu px n po etre vierdge donne seuy katte baxx pour mane c l essentiel vierginite 1er jour leu rk dnc amour mofay dess ak djiko bou rafetet n empeche fonkal sa bopp ba goor gni dounoula foweii💁♀️
bien dit
Machalla tata labane sétale sa dérla yaye bégue sa famille bégue
Waw amna Solo dall machallah
L islam bani c pratik té Lima diaxal gni fabriqué dak sabar😂man dh sama keur goro lagnou ma dieulé sama djiekeu ma yeukeuti end ak sen nguéweul bi nema Lima guiss guethie nako guiss té teugouma wotewouma.sen seur yi kou nek di tek beut mtx gni di sey dom teu len sey soutoura leu gnou bayi si xel l essentiel moy gay djank té sa djiekeur xam ko dax ya des fille qui n naissent pas avk wa salammmmmm
Chez nous les halpoular la viergnite et trs importent jour bigua deegé al hayri jour bobou guay teud force
Mareme DIOP a haali ngogua der ajaarama
J confirme
Bilaye c'est très très important chez nous les alpoulard naniou thi fière
CoumBis Ndiaye c partout
Walahi chez nous mom si té pas vierge tay gua dé
Mais lolou métina dh mais yala bkhna😥😥😭😭😭
En tt cas gniy bakh batay gni ngui.bakh mais boulen fateini .amna niounou viole tei genre emission meun nalen choquer nguen balma.nak si kaddu yi
Machalla merci 💯💯
🤣🤣🤣🤣🤣😭anti douleur yii la mo takh gnouy gawa dokhi😂😂😂😂no mbose ray nama
Mère yii Machallah am Nguen filling
3:22 mangui dé😂🤣🤣😅
Meunou mala geume fii gnouy bakh gnongui bakh batay gnouy fonkk sen ndaw aussi mngui ame batay
WaW -Machallah 😀amnasoLo
Vierge ou Pô lou am solo moyy djiguène bou Bakh mo eup solo
C vrai dei de ma part mane beug ma rk am ndaw wala niak la yamale beug ma rk la ham wa Salam
I really apperciate this
Nekoul tu n’est pas vierge ke da nga bone dé lene li ngeni commentaire
Cc.
Moma diakhal amna nio khamni sen ndaw daniou ko perte ndakh daniou lene violé wala mou am accident ou quelques choses comme ça.
Wakhal wayy
Wayé nioniou takhouniou di wakh dolène bèn
Mane sakh je parle pas de sa mais erreur thie adouna daffay ame nekoul tu n’es plus vierge rek k da nga bone walleu aussi nekoul tu vierge rek k da nga bakh yalla dall mo hame yalla nagnou dolli soutereu rek
labane Amena ndakh fouye ndokh di taaa ba taye bo déme féke témbou témbou ❤
Labaane goor loutakh amoul ?😫
Li meti na waay nioune djiguéne dagn niou yap sérieux
Wakh deugeu, mélni djiguén rk mo wara vierge
Maman Bose je l aime bpc❤❤❤❤❤
Manchallah badienn mbossé amna solo lol
Manchallah daf may fatali sama beus bobou mé Lou sa dieukeur daf lay naw manchallah badienn
Kham lènn séné boppou yènn djiguèn gnii ndaw lou am solo laa ak wayy wou rafètt pour sa dom
A man de sama guoro keurem la teude darap. Bifanane ak serr bi sama guoro moko fote machalla
Mère bossé bilaye deff ma nekh trop bilaye
Mbosse ray nama😂
Bénni goor wakhoul lolou khana déngua yakar né goorgni dégno doffff 😀😀
Khana fo nguay wakh kay wayé kou bougua takkk bo sagnooon kou ammm ndaw lay doonn
Mes nak elle dit la vérité Lou meune ti nek rek nafa deug am c'est ce qui compte mes aussi ont n'es pas obligé de passer la lune de miel chez tes parents ou ta belle mère
Machallah beug na nga labaanal ma d tata mbossé ton numéro svp
Machalla wolouga sa boop ma belle
Machallah ma belle
Labane c est pour encourager les jeunes filles à s abstenir jusqu'à au mariage ,ça fait honneur à ton mari et à ta famille, c haram mais c est une stratégie que nos parents utilisaient,mais regardez maintenant, on ne se reconnaît plus à cause des gestes et faits qu on puisse des occidentaux
Ahh thioume dara dakoul siggil sa ndéye ay way tama fadiare aka nekhhhhh
aye way mane dé dagne ma nakhone sama badiane sangou ma sama keur goro layne ma yobou
Mane damay lathie nga tede kheuy gnou labane dafay indi yaradal ndakh façon nit bouné dila time d’après louma lirre ci commentaire . Legui nga dem l’une de miel après sa dieukeur woter indi drap Bi gnouner lolou gnak wolou sa bopou la stp Kone nagn lagnou wara def
Mére mbossé sakh dafa diékk macha allah
Certaines personnes naissent sans . D'autres l'ont perdu par accident ou lors des infections qui sont très fréquentes de nos jours . c'est haram ce que vous faitent avec vos instruments de musique. L'islam ne vous a pas demandé de dévoiler ce qui se passe pe'dant la nuit............ Dieu sait tout le suprême, le grand, ........
C'est vrai que beaucoup de filles ne sont plus vierge mais aussi, teud, heuye wara nopalou nit gni weurla, tankal la ak thiow, ba paré parfois meune ngaci jeulé fébar wala yaradal, aah
Bilahi nioussi beuri silaniou diaarei meunou nio am doom
Mère bi saff na khorom 😂😭😭😭
On aime la personne pas l'hymen no mais sénégal c le bordel
Tata mbossé ray nama diamm si diamm
Maman jtm bcp long vie
No mbosè ra ynama 😂😂😂
Bissbobou rk lay khar ba siguile sama yay🤲
Inchallah
😂😂😂😂😂😂mane Mbossé la beugue
Non cette émission es très intéressant
Dsolai mai yow liguay wakh ni sakh khamo bilay ni bou viergoul talhoul gua bonne donc bay lén si khel
Bilahi Mala beug Mane dé j'ai 26 ans te diank la amna solo mais bouma meunon am sa numéro dina bakh
Billahi ndaw Lou âme solo la mane dé mbosé mi di wakh badiene la si mane Abdou ngom mikoy té limouy wakh Lou âme la ndakh mane sama djieukeur mo ndieuk si mane té bama teudé yéwou meunou ma dokh cône ndaw Lou amela
Mahachalla bonne continuation
Ms sougnou la violè sa ndaw dounèkk si yaw non ms soufèkkè violè wougnou la dou dègnew
Gnikoy diokhé gratuitema bilahi ça m poz problème wala affair yi d'où bène bok en tout cas dal diaxalnama kouy sathie mom yakarna ni youkhou doufa âme🤷🤷
C tjrs la question que je me pose aide moi
@@coumbandao1483 bilay ça m fait cas
@@yacinesow4688 ah px être c pas la mm chose 😀
Vraima doyna War dh
Lolou momeu messeu diakhal
Vierge ou pas Yallahh nama yallahh bolè akk kou jubbb dégu nigall
Machallah🤣🤣🤣🤣❤
Mane ame na borome keur depuis 2009 lima diakhal mosouma sékhe ak gor té bima tedé amouma ndaw sanete yalla sama borom keur amoul problème bobou souma amane far sakh mou lathma sama bope ma bayiko ndakh damanane qui begouma yéné wouma limou yéné rakam diakhalone nama trop sakh🤔🤔
Danga warone dem hopital nga khol la cause
Bilahi maman Lou ler nga wax maman beugue nala
😂😂😂 néna khalé bine wala laabane mo kheuy di balé😂😂
Bilahi doyna warr lo xamni dagay yèwou do meune marcher ta des vertiges ta mal a faire du pipi tu te rèveilles melni daga perdre 10kg bilahi no li ame lègui kenn xamouko
Lolou est-ce que deug leu fabrique ndaw
Ohh yalla na gniou yalla sou tou rall
Wa lolou de bakhna soutoura
Mdr elle est drôle 😂
Yowite nak premier jour dou yegue thi femme bi ak force way
Gor boula dieule fekoule si yow dara doula wolou parsk dou kham gnata goor gnola khammm mieu vaut nga té sa boppp dara dakhouko