JE NE S8 DACCORD AVEC LA 2 EMME FEMME DE SON ACTE TU SORT OLIEU DE S'accompagne avec la 2ere mais elle sort et prends son chemin enyout cas serine Saliou il faudras parle a ta 2eme, que son acte est visible. de revoir son comportement, et elle est tres jolie la premiere manchanallah
Domage le kessal à détruit la beauté de la femme sénégalaise je prie que dieu nous pardnne tous et nous donne la volonté d arrêté le kessal et devienne beauté naturelles amine yarabi
Li apres Nou ni sene brom kuer ay quilifa yen nakh sene bop seringe touba kene man co nakh def yaramou nene ni dangay dondal godi gamou si ay magom diem
Guiss nga sokhna si Dom adama dafa war am loy rous iaw nit you bari top la dila sokal ak dila ramal apres nga bayi sa yaram com cou bokol si dina Islam man lima bueg xam Lan mo takh nit yi niak fayda top nio xam diom nou la fen
Il faut changer en commençant à ne pas montrer les habillements des femmes et de nous montrer les causeries sur le Prophète (PSL) et les khassaïdes c'est mieux "sounatou"
Yow dee rouss na sa tour bi. Warnga ham li diadou Surtout sen borom keur di wotee si dinee mourit. Sama yaye dou sa morom elle a 80ans. Ana gorr al tontou djiguene. Wahouma ak yaw. Chipatouuuu.....
N importe quoi allez apprendre le coran et le sunna du prophète ceux que vous faites ne reflètent pas le dîner que des choses sataniques vous pensez que La religion se résume sur la danse et porter des habits
Thiey li moy dîné Sénégal yalla Nanou yalla yeureum
Non bouko askanale senegal
@@morydiouf2962 bien sûr parce-que Sénégal la khéwè
Amine, diarna niane, lou eupeu tourou
Ndeysane lou teugue tass insbi sokhna aida diallo guadone giss ak serigne bethio si kanam
Bilahi adina dara sakhoul dou keur
billahi ndeyesane dé momety
Lepp lo guiss thi aduna ni lay démé apres darà sakoul diamou yalla rek mo worr
Walaye ndeysane dafa triste
Djite ap bomlo yalla rek mokey deff si nite mes kenn douko force aida nak dadonn force yeufi lounek deff nako yalla naniou yalla soutoural 🙏🙏🙏🙏
Lii rek moutakh Je suis trop méfiante de ces gamou finalement je me retrouve pas du tout Et Mame Dabbakh rek la beuguaa
Machallah 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏niou yarou gnou séll lolou sakhh machallah
JE NE S8 DACCORD AVEC LA 2 EMME FEMME DE SON ACTE TU SORT OLIEU DE S'accompagne avec la 2ere mais elle sort et prends son chemin enyout cas serine Saliou il faudras parle a ta 2eme, que son acte est visible.
de revoir son comportement, et elle est tres jolie la premiere manchanallah
Domage le kessal à détruit la beauté de la femme sénégalaise je prie que dieu nous pardnne tous et nous donne la volonté d arrêté le kessal et devienne beauté naturelles amine yarabi
Billay khesal sonal nanou
Machallah machallah this is so Nice 😘😘🤝🤝❤❤❤❤
Machalla yalla dolli souttoural
Neu yiwwww way
Dakar buzz bayi lén sonou khasidayi ngéndi foyé lou bonne li
Diabarou chekh betio yi gnoleine eup class ndakh seine yereuyi da yarakh trs beuri brian
fraiche fraiche vérité au lieu kel des boubous en basin bien brodé
Foufe sakhe diabarou cheikh bi gnolaine eupeu classe
C'est pas un gamou ça, mais un défilé indécent, c'est pour celà qu'il eT kharam c'est genre de soit disant gamou. Que du voyeurisme
Li apres Nou ni sene brom kuer ay quilifa yen nakh sene bop seringe touba kene man co nakh def yaramou nene ni dangay dondal godi gamou si ay magom diem
Wakh deugue femme musulmane dafa wara sol lou yiw té bagna yarakh surtout kougnou wara roy
Guiss nga sokhna si Dom adama dafa war am loy rous iaw nit you bari top la dila sokal ak dila ramal apres nga bayi sa yaram com cou bokol si dina Islam man lima bueg xam Lan mo takh nit yi niak fayda top nio xam diom nou la fen
@@falloulo3983 this is what they have been missing that why they hated Aida Dallo
Yalla na yalla Mousel lene si setane
Maaachalah
Jolie les marié lol
Allez vous habiller waay
D'où dinnè ça
ADJARATOU , you Djongama , té am maturité , té téy mashallah . DJIGUÉNES dal maturité réékk , dagouléne maa guiiss way ... Mashallah .
Khesal ba yakhou melnou niouye defile de mode yena bone amolene bene gamou ngir magal yonente bi
Vraiment c'est pas normal des femmes de marabout sans voile pour un gamou
Ya yeme yalla khana amo ayy 👀👀👀👀
Il faut changer en commençant à ne pas montrer les habillements des femmes et de nous montrer les causeries sur le Prophète (PSL) et les khassaïdes c'est mieux "sounatou"
Du voyé moi toujours voyé moi d ignisi doyalle seuque.
Kon maname mouhamad rassoulallah salallahou aleyhi WA salam mo takh gnou sagnséni, sopi yaram yi ni? They yalla!
.
Ay djiguene youdoul mourou jamais.
Da yay esk mongui morou
Ioe tmt esk yangui mourou dolén bayi naféck
Yow dee rouss na sa tour bi.
Warnga ham li diadou Surtout sen borom keur di wotee si dinee mourit.
Sama yaye dou sa morom elle a 80ans.
Ana gorr al tontou djiguene.
Wahouma ak yaw. Chipatouuuu.....
So bagné koula togn dél dougou loussa yonn nékk kou nék lér namani do mourou
@@diorbadiane2638 ne répond pas
Sokhna aida saliou laniou wakh nioun bolé woul dara aki wakh
😂😂😂 Aïda woury Diallo daa amatoul loumou wax wayé paroles yeufeum leu. Doul rek lay def ak khéreum
Ni nguén di déf di feusseul sén sohna yi ba koussi sa borom keur dée ngua gnouy sonal ak ndono ish
😂😂😂😂😂
Khana apre magal la ame benene magal bene rek lagne guis
Habiter comme ça !!!🤐🤐
LIGUENE BEGUONE DI GUENE TELE
folklore folklore
Machallah
N importe quoi allez apprendre le coran et le sunna du prophète ceux que vous faites ne reflètent pas le dîner que des choses sataniques vous pensez que La religion se résume sur la danse et porter des habits
Anna sama fans bii diallo
Cokou molene eupe buzz aida diallo rek
Bien pense et bien dit li du dinai
Demlen.diamo.deyalla.tabayye.senthiakhanye
@@mimifall4039 c normal elle est jeune
Il faur gnou kham sén sokhna yi quoi cheuuuuuuu gnoun sunu yone nékoul sen sohna yi ak sén thiolka you yiweudi ish
Hana vs êtes en réception
c la tour de ces femmes mentena
On dit le tour😂😂 beugg toubab teh khamou leen dara
soudonne sagnsé rék sokhna aïda dou diokk chaise bi changé de mentalité svp.
This dress Not good Not good or prayer