machalah mame koumba yalle nala yalla meye diame ga tok ba am sa sitou bop, si barcke seydina mohamed sangue sangue yi p.s.l, yarou ga teye ga machalah ❤❤❤❤
Mame Coumba encore bravo a vous un exemple irréfutable de ton professionnalisme en ce mois béni de safar que dieu accepte toutes vos prières ❤❤❤❤❤ vous êtes un modèle
Docteur Sylla c'est une bonne personne je me rappelle lorsque j'avais des plaies sur mon pied bimi nek cii wetou fourbi damadane defal ay soins tee souvent douma yor dara. Douma massa faté lolou papa. Merci beaucoup
Sérigne Saliou ❤😭😭GUINAW YALLA YONENT BI AK SAMAY NIARI WADIOUR SÉRIGNE SALIOU MO DEF SI MANE YEURMANDÉ😭😭MBACKÉ DIEUREDIEUF SOUMA NITT YI NAWÉ YATAX 😭😭😭😭
Merci pour ton témoignage peux tu m'envoyer son contact ou une personne que je contacter pour que je puisse lui témoigner ce que Serigne saliou nmbackee a fait de moi❤❤❤❤
Djeuredieufe Serigne Saliou Mbacké Borom Khelcom ak Diamono Yalla Na Yalla Yokou ay Lérame ak moléme gnabotou Serigne Touba Ak Mame Cheikh Ibrahima Fall yi djitou Barsakh Allahouma Amine
yeurmandeem ja ci jaami yallah yi kenn manula koo expliquer, dundeum gi yepp yeurmande ju jeex takk ci mindeefi yallah yi moo koy resumer! lu ci waay wax rek neew na, yallah xam nako! thieuy serigne saliou😭😭😭
L'équipe de Confidence est à Touba. Quel autre conférencier aimeriez-vous voir dans votre émission Confidence ?
Khadim gueye,akhaza samb
Seriñ Mame Mor Amdy ou thiefdo mouride sadikh
Aya Traoré capitaine des lionnes stp
Borom darou
S Abdou Rafahi mbackei 🎉❤
Serigne saliou l'humaniste le géographe le distributeur des grands projets l'avocat des génies ❤❤❤❤❤❤❤ ma vie ma lumière ma vision ❤❤❤❤
Des ❤❤❤ pour confidence walay it's the best émission tu apprends et tu en tire des leçons.
Mr Sylla God bless well Inchallah ❤❤❤
❤❤❤❤❤😢😢😢❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieureudieufé Serigne saliou 😭
Machalla une belle émission !!! Un homme très généreux qui comprend parfaitement l’importance du partage. Yalla goudeul sa fan si barké Brome touba🙏🏼
Amine
Machahala diereudief serigne saliou 🙏🙏🙏🥰🥰
machalah mame koumba yalle nala yalla meye diame ga tok ba am sa sitou bop, si barcke seydina mohamed sangue sangue yi p.s.l, yarou ga teye ga machalah ❤❤❤❤
Je pleure 😭 comme pas possible dieredieuf Serigne Touba
Ndeysan thiey S Saliou Mbacke mon expoir
L homme le plus heureux du monde MACHALLAH lawla thiat kéye😅
Thieyy serigne saliou ❤️❤️papa yala gua goudou fane loll te werr
Amine
Machallah ndeysane nouroune halal nourine j’ai pleuré walaye pabi khamoumako mais kou ame yeurmandé la
Moy papay Abdou lay sylla ecotra
Mashalah Yalla nagnou Yalla tass ci barkem 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Yalnaaa niou yalla maaay niou fekker magal gui ta talko ❤❤❤🎉
Mme Mame Coumba est très professionnel en plus d’être pause et attentive machallah 🥰
Sama wadji Serigne Saliou dotou fi am ❤❤❤yalna Yokeu say léer
Massa papa MACHALLAH MACHALLAH MACHALLAH YALLAH mo méyé BARKÉ 😢
Dieuredieuf Serigne Saliou 🙏🏻🥰 Dieuredieufate Serigne Saliou 🙏🏻❤ Dieuredieufaty Serigne Saliou 🙏🏻🥰
Longue vie et de santé serigne sylla
Dieureudieuf baye 🙏🙏machalla serigne Saliou kenla😭😭
li Dawna yaram🤧😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭 thieuy SERIGNE SALIOU❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieureudieufé serigne saliou ❤
Dieureudiefety Serigne saliou yalla.nanouko sounou borome fayal défarna kouné ❤❤
Magui khar ba kene sagua ba commentaire negative machaallah amal diam alhamdoulilahi
Mame saliou 😭😭😭man amouma fayam barki Serign saliou 😭😭❤️
Mame Coumba encore bravo a vous un exemple irréfutable de ton professionnalisme en ce mois béni de safar que dieu accepte toutes vos prières ❤❤❤❤❤ vous êtes un modèle
Ndeysane yalna yalla defale la diamm
Dieuredieufeti Serigne Saliou❤
Machalla kaine dou Akhmadou Bamba
Moi tidiane mais j'adore touba chak magal ma dem suniou wa keur nenagne ma yaw mouride gua
Lep bén la machallah ❤
Dieureudieuf Serigne Saliou ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Docteur Sylla c'est une bonne personne je me rappelle lorsque j'avais des plaies sur mon pied bimi nek cii wetou fourbi damadane defal ay soins tee souvent douma yor dara. Douma massa faté lolou papa. Merci beaucoup
Peut tu me trouver son contact
Ndeysaan, il est transparent et sincère dans ses propos. Pas de filtre....
❤❤❤Ma cousine sétigua nitte kou bakh sama papa diou bakh woyoff lole mamou khaléyii yalna yalla guoudeul faname sylleu
Magui ziar doma envoyé numarom
Dieureudieuf serigne saliou sante na serigne saliou ❤❤❤
Aye waye ya bakhe goude fane kouni amine yalana n'a nga goude fane
Aminé yarabi ❤❤❤❤
Dieureudjeufé Serigne Saliou Mbacké ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ kéne dou mome démako beug ba souma guissé photos Serigne Saliou limay santire thi sama khol mane ag yalla rek nioko kham Dieureudjeufé Mbacké 😢😢😢❤❤❤❤
Doundeul wéral amal diam Docteur Sylla❤. Dieureudieuf Serigne Saliou Yalla yéssal yeurmandém ci mom té taass niou ci barkém 🤲🏾.
Machallah kén d'où serigne saliou ❤
Coumba sa sagnesé dafa marier ak fauteuil bi maMACHALLAH nice na❤🎉❤🎉❤🎉
Coumba kéye moye confidence tigui lou waye di neuba boul eksi thi mome MACHALLAH
❤❤❤❤❤je vous comprends cest le but de serigne saliou mbacke bayou sokhna astou walo d'élever. L'humanité c'est sa passion ❤❤❤❤❤❤
Sylla makhtar y’a goré ❤
Ken dou s saliou mo beri yeumené Mbacké bala 😢❤
Thiey Serigne saliou 🥹
Serigne saliou amoul morom koumou djaraloul beureup meuno ko kham bilahi😭😭😭😭
Serigne saliou ma vie ❤️Mbacké balla gnogui lay sante bou wereu ❤️❤️❤️
Dieureudieuf serigne touba ❤️❤️❤️❤️
Sérigne Saliou ❤😭😭GUINAW YALLA YONENT BI AK SAMAY NIARI WADIOUR SÉRIGNE SALIOU MO DEF SI MANE YEURMANDÉ😭😭MBACKÉ DIEUREDIEUF SOUMA NITT YI NAWÉ YATAX 😭😭😭😭
Wallay serigne saliou mbacke mbacke kou fegue sa diamanou rek defar ngako mbacke balla yalla naniou yalla tast thi sa bargue
Docteur Sylla c’est lui qui m’a circoncis et mes frères aussi… un bon docteur, on habitait ensemble à Gare bou Ndaw et son fils est mon ami
Machallah que le seigneur lui accorde longivite et vous mette sur sa protection divine ainsi que toute sa famille ❤❤❤❤
❤❤❤❤machalla une chance sil te plaît peux tu m'envoyer son contact ❤❤❤❤
Merci pour ton témoignage peux tu m'envoyer son contact ou une personne que je contacter pour que je puisse lui témoigner ce que Serigne saliou nmbackee a fait de moi❤❤❤❤
@@saneoude5613 peut être le contact de son fils Serigne Saliou
@@MakaveliMr7196 oui pourquoi pas akassa
Ndayesane yalla n'a yalla yok lérame seringe saliou mbaké
They Sama sangue bi 😭❤️
Thieuy sa wadji Balla aisha yaniou dimbaly docteur Sylla aka ngasé bari morom kouné ak fimoula diaralé dimbalina koné dieureudieufty Serigne Saliou Mbacke❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Mâcha Allahou Dieureudieufe Borome Touba Khadimou Rassoul .
Santati serigne SALIOU ❤️
Machallah ce docteur Alioune Sylla nous lance des messages très intéressants❤
Kougniouy diapalé gniou guiss paa bi on a besoin de ses grand homme qui nous éveille ❤️yallenala yallah may goudou faneu ak weer🤲
Pa bi nio bokou kogne touba
@@mamediarra7156Ziar fane si TOUBA
Dieureudieufe serigne saliou
Djeuredieufe Serigne Saliou Mbacké Borom Khelcom ak Diamono Yalla Na Yalla Yokou ay Lérame ak moléme gnabotou Serigne Touba Ak Mame Cheikh Ibrahima Fall yi djitou Barsakh Allahouma Amine
Wa émission bi khana dioy yi force la mé nak kén do mame Saliou
Bravo sama mame docteur sylla nala yalla faye je passais le magal chez vous quand j étais petit avec ma défunte grand mère Aby ndiaye de saint Louis
loutah fouma deigueii kouyy wahh Serigne Saliou dii dioyyy Mbacke niak la gis rkk layy dioyyy
yeurmandeem ja ci jaami yallah yi kenn manula koo expliquer, dundeum gi yepp yeurmande ju jeex takk ci mindeefi yallah yi moo koy resumer! lu ci waay wax rek neew na, yallah xam nako! thieuy serigne saliou😭😭😭
Machalla ❤❤❤❤
Macha Allah Dieureudieuf Sylla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Dieuredieufety Serigne Saliou Mbacké ❤️ ❤️ ❤️
THIEY SALIHOU MBACKÉ RTA 😢❤ MO BAKH 😢 YALNA YÀLLA SWT YOKK LÉRAAM
Diaradiafaty serigne saliou
Dieuredieufeti Serigne Touba Diaraama Mame Cheikh Ibrahima Fall Lampe ❤️❤️❤️👍👌🙏🙏🙏
Ma sante santati serigne saliou sama yakar beug guimala beugue manoumasi dara yalla moko déff si man ❤❤❤ dieuredieufate saliou ngiépou nga défal ❤❤❤
Frémaent journaliste bi nekhnama loole machalhh lathie yi tégouna diarr na yonn
Dieuredieufati serigne saliou❤❤❤❤
L'homme le plus heureux du monde bakh rk mo am solo Mbacké diereudieuf Serigne Saliou ❤❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤
Machallah yalla na yalla fayal niou Serigne saliou ❤❤
wallay sa se voit que serigne saliou défar nalla mashalah
Dieuredieufety Serigne Saliou ❤longue vie à toi docteur sylla ❤
Pa bi nitt kou bakh la machalla yalla nga goudou fane🥰
Amine
Mame Coumba bonne continuation, prochain invité Mohamed niang wala faty dieng tfm
Jai la même passion que vous jaime donner sans réfléchir ❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieuredieuf Serigne Saliou.
Dieuredieuf Serigne Touba
Yalla n'a yalla yok sa diama ak sa weur si bark seringe saliou mbaké
Ohh Dieuredieufety SSaliou
Kou Sant Yalla Guii Nii Ndeysann ❤️😭
Dieureudieuf Serigne saliou❤❤❤❤❤❤❤❤
Mame salihou Yalna Yalla Yokou Ay léramm té Tass niou si barkem ❤️🙏
Kou sant sylla daye bakh bilahi sama yaye dji Sylla atou
Machalla dieuredieuf serigne saliou
Ken dou SERIGNE SALIOU
Dieureudieufeuti serigne saliou
Jërëjëfati S Touba Cheikh Saliou🥺❤️😭
Dieureudieuf Serigne saliou ❤❤❤
Soxna Maï mbacké Jamil.
Ndeyssane théye serigne saliou
Merci beaucoup papa Sylla yalla na nga fi yague lôoooooo ta am diamou rek ❤❤❤❤❤
Ken dou serigne saliou MBACKÉ ❤😊
Machalla Machalla Dr Yalla Nalla Yalla Faye
Mashalahhh ki mo bah té tabbé yaw kén meunoula xol dila bagn
Mame Coumba invitél diawrigne Ndiassé
❤❤❤❤❤akassa sangue bou tedbi ni gua meuna mel sama sangue bou tedbobou niteum ni rek ndam rekkkk❤❤❤❤❤
Walahi Mbacké Sa borom dieuredieufety 😢😢sante nala deh
Yalna yalla yokou ay leral❤
Kou guiss ni présentatrice bi Mame Coumba dafa kassé ak micro bi laalal j'aime