🚨 S Ishaqa Mbacke, yabal na ay camion ca keur S Abdou Lahad abdou khadre ngir wallu leen ci ndoxmi…

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 16 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 65

  • @damefall2637
    @damefall2637 3 หลายเดือนก่อน +1

    Machallah serigne bi kadou yi amna solo

  • @mikemiketyson4584
    @mikemiketyson4584 3 หลายเดือนก่อน +2

    Yalne yalla téguil léne

  • @mamanmaman7411
    @mamanmaman7411 3 หลายเดือนก่อน +2

    Merci s ismahila Mbacke

  • @SouhiboufallFall
    @SouhiboufallFall 3 หลายเดือนก่อน +1

    Ma cha allah

  • @toubaaffetv360
    @toubaaffetv360 3 หลายเดือนก่อน +3

    Santé rek❤

  • @devgueye1217
    @devgueye1217 3 หลายเดือนก่อน +1

    Merci beaucoup ❤

  • @baragaye-bt6ql
    @baragaye-bt6ql 3 หลายเดือนก่อน +4

    Bilahi Li s bass lawaron
    Niou taxxalo mim keur
    S Laht aka dimbaré

  • @Djiily7461
    @Djiily7461 3 หลายเดือนก่อน

    Waw Goor mbacke waxal de ,
    S issakha yalna yalla baril am kemame ta fay kow yiw royoukaaye deugg la machallaah

  • @akimbousso2206
    @akimbousso2206 3 หลายเดือนก่อน +14

    Yawmi daga bague ay wakh rek daga warona khamne ndokhmi da barri fepou la dadj CI touba ginaw serigne issakha defnako defalnako ñapou SA wakhdji garouwale rek la nay refet fi dará loufi diar nek CI internet bi di garouwale serigne issakha mbacke Moy serigne mountakh Moy serigne bass abdou khadre garouwale bi daal matoukowon ndokh mo khamne fepou la dadj CI biir touba diaroul wakh 😊😊😊😊

    • @solution5135
      @solution5135 3 หลายเดือนก่อน

      Ki dou nitt ana taloubé yi manoulawakh té amounou founou dieum ndokhmi fépela

    • @sagyatal8545
      @sagyatal8545 3 หลายเดือนก่อน +1

      Waw goor

  • @LamineKane-kn5tk
    @LamineKane-kn5tk 3 หลายเดือนก่อน +1

    Sa wakhdji dafa khebou tropp serigne isakha yalnako yalla faye

    • @fatoudieye7624
      @fatoudieye7624 3 หลายเดือนก่อน

      Bilahi kou bakh lole dé khebou

  • @cheikhdiop83
    @cheikhdiop83 3 หลายเดือนก่อน +5

    Bilahi wakhga deug

  • @SMoustapbaSylla
    @SMoustapbaSylla 3 หลายเดือนก่อน +2

    ❤❤❤❤❤❤

  • @papediop7955
    @papediop7955 3 หลายเดือนก่อน +2

    Kou guissné Serigne bass abdou Khadre mo mome wakhdji

    • @FallouLeye-ss6uj
      @FallouLeye-ss6uj 3 หลายเดือนก่อน

      S.Bass keuram temit daa walé di

  • @mamefall9788
    @mamefall9788 3 หลายเดือนก่อน

    Khamgueneh Serigne domou adamale yalla nak bourlle boromla doussene morom nguendi wakhni serignbi yalla toublene tediamou yalla

  • @BabacarSakho-t4h
    @BabacarSakho-t4h 3 หลายเดือนก่อน

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @MalickngayaThiane-y8e
    @MalickngayaThiane-y8e 3 หลายเดือนก่อน

    SMA xarite mbacke balla Nice

  • @baragaye-bt6ql
    @baragaye-bt6ql 3 หลายเดือนก่อน +2

    Fi sak ané daye taa
    Jakkaye s abdoukhadr Touba guidé

    • @babacargueye5986
      @babacargueye5986 3 หลายเดือนก่อน

      waroul takheu niou wara setaneu chak atteu mouy melni

    • @thiamfatou6230
      @thiamfatou6230 3 หลายเดือนก่อน

      Magual gui monsieur moudiou

  • @babacargueye5986
    @babacargueye5986 3 หลายเดือนก่อน +3

    bayi leineu khel limeu wakheu feippeu amena ndokh wayei fi domou segn abdou khadre direct mo fi nek neguameu fess deleu ndokh ba amoul foumou fananeu . mou donneu magueu teksi amo leineu beineu talibe .

    • @Djiily7461
      @Djiily7461 3 หลายเดือนก่อน

      Waw goor

    • @thiamfatou6230
      @thiamfatou6230 3 หลายเดือนก่อน

      Merci beaucoup mon frère

  • @sheikhibrahimandiayealqura3615
    @sheikhibrahimandiayealqura3615 3 หลายเดือนก่อน +1

    Dieredief ❤❤merci ❤❤❤

  • @bigophone2834
    @bigophone2834 3 หลายเดือนก่อน

    Merçi❤❤❤️🙏♻️👀♻️🙏❤️🙏🙏♻️🙏🙏❤️🙏♻️👀♻️🙏🙏♻️🙏

  • @begueBamba
    @begueBamba 3 หลายเดือนก่อน

    ❌️❌️❌️❌️❌️❌️❌️

  • @aichagoudiaby1148
    @aichagoudiaby1148 3 หลายเดือนก่อน

    Li yalla la yalla mo wathiee ndokh momou ken meunoul touma ken mofi diarra sant yzlla kep moy bour defois nak mou wonnee bopam mom moy yalla kep nak mom leup

  • @abdoulahaddiop1769
    @abdoulahaddiop1769 3 หลายเดือนก่อน +1

    Jerejef s ishakha wayé naga xamné Ndox mé bari rk du géde rk rafétalal say kaddu ta rafét jortu

  • @sinkkimpressionsinkk291
    @sinkkimpressionsinkk291 3 หลายเดือนก่อน

    SAYTAANÉ AK DIAKHASÉ BAAKHOUL

  • @Ndrametv
    @Ndrametv 3 หลายเดือนก่อน +1

    Wax dji dé Serigne bass moko mome

  • @fayeadama-yx4tp
    @fayeadama-yx4tp 3 หลายเดือนก่อน

    Waxal wax je t'aime bayi raay raayal bii

  • @daoudandiaye5588
    @daoudandiaye5588 3 หลายเดือนก่อน +1

    yaw mi seytanei pirr nga... keur serigne si yenakoye diakhassei tei lernama ny li nga wakh segne bi wax loo woula ko... ndox mi mome Touba guepp leu... amlene habitudou defar tei bayi feiweulei bi

  • @bayegalassmbacke8749
    @bayegalassmbacke8749 3 หลายเดือนก่อน

    ❌❌❌❌❌❌❌❌❌

  • @sagyatal8545
    @sagyatal8545 3 หลายเดือนก่อน

    Nay rafet way S Ismaila

    • @fatoudieye7624
      @fatoudieye7624 3 หลายเดือนก่อน

      Fi dra niawou fi

    • @sagyatal8545
      @sagyatal8545 3 หลายเดือนก่อน

      @@fatoudieye7624 han key

  • @cheikhdembasylla4327
    @cheikhdembasylla4327 3 หลายเดือนก่อน

    Ya bakh té wakh dague man mi guede la néka man ak mome nio dague

  • @moustaphababou6282
    @moustaphababou6282 3 หลายเดือนก่อน

    monte senge bass abdou khadir bimouye def declacion wakhe nako nena sama niari kilifa yima dendal ndokhe mi dafa nangou seni keur billahi wakhe nako

  • @LamineKane-kn5tk
    @LamineKane-kn5tk 3 หลายเดือนก่อน

    iaw seytane nga

  • @moussafall9676
    @moussafall9676 3 หลายเดือนก่อน

    Diakhassé nit ak rakam loutakh woowoo niako négligé

    • @fatoudieye7624
      @fatoudieye7624 3 หลายเดือนก่อน

      Diakhassé woul kein dome la si kheur gui

  • @tdkcosmetiquebeautedereve6149
    @tdkcosmetiquebeautedereve6149 3 หลายเดือนก่อน

    Wa li touba gueppp. Leu xana ki rekkk mou fiy nittt yennn soffff guennn trop ki amna niouka geuna sokhla demballlll foufffff bayilennn wakh amna sakh niou deeee si ndokh miiii

  • @cheikhounadiop2632
    @cheikhounadiop2632 3 หลายเดือนก่อน

    Nokh mi yalla moko wathee nieppa ci Yam talibe ak niepou nieppa Yam
    Diomay Touba sakh dafa am nokh
    Warooo ci am Khol bou nakhari
    Kili fa gui niakoul koko dimali

  • @nouroutv1880
    @nouroutv1880 3 หลายเดือนก่อน +1

    Yaw mi wakhou saytane rk ngay wakh khana Ch bass ngay wakhl lingay wakh dagako raagal

  • @magougueye1264
    @magougueye1264 3 หลายเดือนก่อน

    Ndokmi fépela

  • @bbbbbbbbbbvvvv
    @bbbbbbbbbbvvvv 3 หลายเดือนก่อน

    Geum quénn yén nou brom bi❤

  • @OusmaneThiam-er4zh
    @OusmaneThiam-er4zh 3 หลายเดือนก่อน

    Saa way lii doussa thieurr,lii dou yeufou talibè rawatina ab sangue.lii day diakhassè rékk,bayi lène wakh,talibè serigne touba day meuneu mougne.ndokh mi fèppe leu çi biir touba!

    • @thiamfatou6230
      @thiamfatou6230 3 หลายเดือนก่อน

      NGA défe limou déf bou ndox mi néké séne cogne té NGA bayi wakhe dji epeul NGA trop

    • @fatoudieye7624
      @fatoudieye7624 3 หลายเดือนก่อน

      Bouko nékhé wakhsi nakh domou Serigne Modou la mome Serigne Abdou Khadre kon keur bayam la né té dou fi késé la déme dadi bi rek guein guiss

  • @magougueye1264
    @magougueye1264 3 หลายเดือนก่อน

    Nako défall népe

  • @baratall4966
    @baratall4966 3 หลายเดือนก่อน

    Yaw daal dô nite Seriñ si rék sa yon nékute ci Talibè yi rawatina ñici Fatou ak ñici yakholé ay millions né patte wakh nga ba nopi té dialéwo ñi ci fatou ap dof nga rék

  • @ibrahimaloum6392
    @ibrahimaloum6392 3 หลายเดือนก่อน

    keur yapou. am nokh

    • @babacargueye5986
      @babacargueye5986 3 หลายเดือนก่อน

      sou beuguei yamale keur yeup ak keur domou segn abdou khadr ware ngua kholateu sak talibe

  • @cheikhmaremoundiaye7216
    @cheikhmaremoundiaye7216 3 หลายเดือนก่อน

    Kii moom ap seytani piir la day diakhase waye s bassiru Mbackè abdou khadir fawu ngéen xam ni sampom Broom Tuubaa la kenn meunou si dra seytani rk ngeen def

    • @thiamfatou6230
      @thiamfatou6230 3 หลายเดือนก่อน

      Cône mou wakhe si dioumay bayale biko khalale bamou âme limou âme bok té bayi gnénegni😷😷

  • @toubabelellferallye2273
    @toubabelellferallye2273 3 หลายเดือนก่อน

    Seringue ismaila

  • @serignembackesylla6866
    @serignembackesylla6866 3 หลายเดือนก่อน +1

    Xaw ma ab sr nga xaw ma me li dou waxi nitt

  • @HassenNgoune
    @HassenNgoune 3 หลายเดือนก่อน

    Sawaye serigne touba sokhlawoul kou Mélanie yawe

  • @Sardegna-y2q
    @Sardegna-y2q 3 หลายเดือนก่อน

    C du garouwale

    • @thiamfatou6230
      @thiamfatou6230 3 หลายเดือนก่อน

      On a mis beaucoup de graway et du sable beaucoup c'est d'est talubé qui on fait ça mais rien

  • @SouhiboufallFall
    @SouhiboufallFall 3 หลายเดือนก่อน

    Ma cha allah