Serigne Khadim á souligné un point très important sur le fait de protéger notre dîn Islam ça doivent être une priorité pour le nouveau régime avec des très très sevrés Qu’allah nous pardonne nos péchés et nous guide dans le droit chemin amine🙌🏻🤗
Salam, Barakallahou Ya Imam, MBACKE SAKHO mi Yallah Nako Yallah dioubanti Bamou Diougué ci limou nékeu. Kou beugue sa morome dioulite Niko Mouhamed Alleyhi Salatou Wa Salam. Nako gnanal mou sopékou. Amine Ya Rabi.
ياشيخ ❤❤❤ليت الشيوخ مثلك .لأنك بكرة وأصيلا تقوم برد المنحرفين والمتطرفين الذين مغزاهم الحقيقي هي :تجشيد التشتت والتفرق واحتكار الصوب بين المسلمين والمخلصين : ❤️❤️❤️❤️❤️
Parce que Senegal amoul diné l’islam, Sénégal tarikha mofi am. La preuve si le gars Sakho avait mal parlé des tarikhas attends toi à une réaction spontanée de leurs part
Mbacké sakho ne parle pas de sa propre science. Il est formé par le mouvement coraniste. Une grande éloquence et une maîtrise apparente du coran. Derrière les coranistes ce n'est pas cet égyptien naturalisé américain un certain Khalifa. Mais c'est les juifs qui sont derrière TOUS ces mouvements islamiques qui insistent sur le caractère insignifiant du PROPHÈTE qu'ils qualifient de SIMPLE humain...paradoxalement aussi bien les coranistes que les salafistes. WA SALAM.
Tontoul ay question wam yawmi xam😂😂😂😂 Mbacké Sakho Alpha Ba wo nako débat. Lathie loutax mou bagne😂😂😂 S'il te plaît, s'il te plaît, s'il te plaît fane la yalla né so kabaré diangal fatiha? Souma tonto ma toute nék talibe Mbacké Sakho 😉
Islam dafa toumouranke senegale bou fekon tarikha yi lay wakh gnou jok kii loumouy wakh cheikhe omar jagn wakhou ko dafay wane ne loufi Sen Mami bay molen gnor waye dou diine islam
moi je crois que mbacke sakho quelqu'un ou groupe organisé devrait lui régler son compte, comme le gouvernement n'a rien fait. avant qu'il fasse plus de dégâts
cheikh mbacké sakho n'a jamais critiqué le Prophète (pais salut sur lui) il a bien dit que YONETBI C'est un messager d'Allah on contraire il défend le Prophète donc vos arguments n'est pas poser donc arrêté de mentir et dite aux gens la vérité il défend le Prophète et le CORAN ❤
Naturellement c'est ça la vérité mais vous êtes tellement bête raison pour laquelle vous avez cette vocation ça c'est tellement honte pour un musulman comme si vous ne reconnaissez pas votre prophète
Par contre si c'était tes parents tu aurais cette attitude cette position là moi je vais partir de Sénégalais ne savent rien de leur religion ils n'ont aucun estime sur leur prophète et ça c'est dommage c'est tellement grave
Ki question youmou fi lathie. Bilahi you beurri lathie nako Say morome. Té kéne toutouwouma. Ngir yalla tontoul simple question bi: Sourate 2 Versé 197 yalla néna wére yougniiy hajj yougnou xam la. Wér youyou yane la? Sourate ak versé la sokhla😎 Tontoul😂
@@dabakhdia3873Islam est une religion de paix. Islam est aussi une religion pour les gens qui reflechissent. Si un mulsilman comme nous fait des erreurs on doit l aider et le guider. Allah is the most merciful.
@ je suis bien d'accord avec toi mais celui là il persiste dans son erreur et il va entraîner beaucoup de monde avec lui dans ses délires.... il défie les enseignants du prophètes du prophète en se "se basant uniquement sur le corant " comme si il connaissait le corant mieux que prophète (saw) lui meme ...
S'il vous plaît merci de aimer la vidéo et partager le savoir pour démasquer c'est négateur de l'islam Mbacke Sakho &cie❤❤❤❤
Sénégal diné bou lér dafé toumouranké
Si si vraiment mon frère vous avez raison en disant que l’heure est grave
Lerna mâcha Allah Oustaz khadim Ndiaye ❤❤❤❤❤❤
ما شاء الله جزاكم الله خيرا وبارك الله فيكم وأحسن الله إليكم
Jërëjëf Serigne Khadim masallah amna solo
Yalnaniou Bour YALLA mousseulle si macke Sakho ak ay bonbonam
Allahouma Amine 🙏
Senegal dinne mofi toumaranka Walay
Thiéy moudioum diamano louné ngaye dèg Macha oustaz yalna Allah fayla thi barké yonénti ❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
بارك الله في جهودكم
Serigne khadim ndiaye rachid qu le TOUT PUISSANT vous bénisse et vous accorde tes 100 ans ❤❤❤
Bien sûr que l'heure est tellement grave
Un grand merci pour vos éclaircissements
Merci à vous mbokk mi
Barakallahou fikoum ahlou sounnah
Serigne Khadim á souligné un point très important sur le fait de protéger notre dîn Islam ça doivent être une priorité pour le nouveau régime avec des très très sevrés Qu’allah nous pardonne nos péchés et nous guide dans le droit chemin amine🙌🏻🤗
Merci ya oustaze seydina Mohamed psl notre bien aimé prophète
Sénégal 🇸🇳 nangou nano jang lepou bamou dess sene diné c est ça le véritable blm motakh lou nieuw dinalene feuk yobou.
Mbacké sakho lane laa narr ci dîné yalla bi allahou akbar yalna yalla sougnou borom samou l'islam
ماشاءالله
Que le tt puissant ns guide ❤️et ns écarte des ces genres🤧
Que Dieu vous préserve oustaz
Salam, Barakallahou Ya Imam, MBACKE SAKHO mi Yallah Nako Yallah dioubanti Bamou Diougué ci limou nékeu. Kou beugue sa morome dioulite Niko Mouhamed Alleyhi Salatou Wa Salam. Nako gnanal mou sopékou. Amine Ya Rabi.
Mbacke Sakho kay vrai tapale kaat la
Machallah yalna yalla samela
Galsen dal bou Mbacke Sakho kale Tarikhas kon fou baxx ci mommm Wante islam amoul kokou defandre
Mbacké sakho mi dafa rére Yallah nako Yallah sopi mou guéneu ci li🤲🤲🤲. Kathia kate leu déh😭😭😭😭
Mbackê sakho damako djooytou ba soone néna batayyi Ani borom kham kham yii😢 mingui réral gnou bari
ياشيخ ❤❤❤ليت الشيوخ مثلك .لأنك بكرة وأصيلا تقوم برد المنحرفين والمتطرفين الذين مغزاهم الحقيقي هي :تجشيد التشتت والتفرق واحتكار الصوب بين المسلمين والمخلصين :
❤️❤️❤️❤️❤️
Billalhi 😢 yalla nako yalla guindi
merci ouztaz
Macha Allah oustaz
DIEUREUDIEUF.YALLA.FEYE.ĹA❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
No vraiment li doyna waar
As salamu aleykum cheikhana. Yallah nala dooli diam, soutourou bou and ak wer.
الله يحفظك يا أستاذي الكريم ❤❤❤
أللهم صل وسلم على سيدنا محمد وعلى آله وأصحابه أجمعين!
Jërëjëf sëriñ xaadim njaay
Sakho amoul xam xam yakarni diné philosophe la.
Il se trompe lourdement et QuAllah le guide sur le droit chemin.
Machallah ❤❤
شكرا يا أخي الكريم
Macha'Allah ♥️♥️♥️
Thanks you very much ya iman, you are very right ❤
Wallahi kou diangoul dinala sank😢
Xamadi rek Yal nañu Yalla boole ginndi
Diadieuff Serigne khadim Ndiaye rachid
Bakhna yienangui Sétan chiekh Mbacke sakho wayie dafa wedi yonantebi صل الله عليه وسلم diotna mou aréte
. Si on touchait la constitution CH MB SAKHO NIEUP LA WEDDI.LÈP LA DADJI.
Svp damay laddje nah gua niane Yallah
Né YALLAH mayma ( tant) si barki yonenteu bi nah da haram
Dama degue niouni da haram té awmasi louma léer
Na toudou yonou mourid khôl bakham niamoon na
Cams. Mo yabbatè deig deug.
Kikay khawma foum diangué mbaké Sakho yabone motakhite sa kanam leundeum ni coupure couren yalla nagne yalla mousale sisa genre yi
Day mandi bala mouy wakh
Senegal ayy nafékheu laniou , cheikh A cisse donio wara dokhan ndayaml bilahi
❤❤❤
Et la question que je me pose avec pourquoi certaines sénégalais se sont pas au courant de ce petit poussin sé nagateur de l'islam
Parce que Senegal amoul diné l’islam, Sénégal tarikha mofi am.
La preuve si le gars Sakho avait mal parlé des tarikhas attends toi à une réaction spontanée de leurs part
@@LuqmanAlhakim-l7rtu as tout dit
Mbacké sakho ne parle pas de sa propre science. Il est formé par le mouvement coraniste. Une grande éloquence et une maîtrise apparente du coran. Derrière les coranistes ce n'est pas cet égyptien naturalisé américain un certain Khalifa. Mais c'est les juifs qui sont derrière TOUS ces mouvements islamiques qui insistent sur le caractère insignifiant du PROPHÈTE qu'ils qualifient de SIMPLE humain...paradoxalement aussi bien les coranistes que les salafistes. WA SALAM.
Ils sont au courant dé daleena niorul
Sénégalais yi detournéléne yomboul dé
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bou mbaké sylla lalone béne tarikha gnou lidieuntiko si béne fane.😂
Wayé alkhourane ak souna la lale motakh gnou sétaneko mouye wakh louko nékh...
Sheikh mbacke dafa sanku yallah Nako yallah gendy
Wallahi
Mbacké sakho ak niou melni moom bakhouniou si Aleu waxou Malak rewou
Yàlla rekk mo kham kouy dém Safara 😢
@Mambanegra924 Yalla wax na ni kepp kou tegui yoonou yonent bi safara nga dieum. Nañ baayi thiaakhaan mbokk mi
Yallah rék mo kham kiy dém safara mé aussi yallah wakhna niou liy dobou nitt safara Yalna niou yallah may dégue ak toppou🤲🏽🤲🏽
Sénégal bokalé dafé yag,
Ndono lafi
@@Lepanafricain-1181 lignouy wakh ni amoul ben rapport AK bokaké
@AbouDjigo-i3o 🙏 machallah
Wawaw 😂nanou wax foum ko dieullei d
Non khadim khamon dara si all khour ann non 😂 wa yaw dèmall gua dèf dèba ak chiekh mbacke sakho khala toko 😂
Tontoul ay question wam yawmi xam😂😂😂😂
Mbacké Sakho Alpha Ba wo nako débat. Lathie loutax mou bagne😂😂😂
S'il te plaît, s'il te plaît, s'il te plaît fane la yalla né so kabaré diangal fatiha?
Souma tonto ma toute nék talibe Mbacké Sakho 😉
Ki mann lann sounnati la wax deguouma partie bobou damako beugu bindeu kouko kham s’il vous plaît
Islam dafa toumouranke senegale bou fekon tarikha yi lay wakh gnou jok kii loumouy wakh cheikhe omar jagn wakhou ko dafay wane ne loufi Sen Mami bay molen gnor waye dou diine islam
moi je crois que mbacke sakho quelqu'un ou groupe organisé devrait lui régler son compte, comme le gouvernement n'a rien fait. avant qu'il fasse plus de dégâts
@@ibrahimdiop4225 wakho fi dara
Jërëjëf waay si léeral yi
S khadim aka khoromou ta am pédagogique
Lolu mom defa lèrr kou wèddi sunna rek alku
كفى. لتكفير شيخ امبك ساخو. قوله تعالى أطيعوا الله واطلعوا الرسول إلى آخره
cheikh mbacké sakho n'a jamais critiqué le Prophète (pais salut sur lui) il a bien dit que YONETBI C'est un messager d'Allah on contraire il défend le Prophète donc vos arguments n'est pas poser donc arrêté de mentir et dite aux gens la vérité il défend le Prophète et le CORAN ❤
Yow néko Sénégal té yeugo lou guédj gui di riire
Kou teguiii jangalee yonantee bii moy wedii nga mom mii jangaleko. Delen xalatt tée bayii.
Démal lire Sourate 2 Versé 197
So paré nga wax ma wér youyou yane la si alquran(sén tour, nombre de jours...)
Waa dof bi nitt laa🤦♂️
Lilla oustaz di wakh kou diangoul mou rééral laa😢motakh yaw moom sankou gua ba laré😢mais yalnala yalla téguaan si yonnou siraatal moustakhim bagua kham deug gui🤲🤧
cheikh mbacké Sakho dal Say Say leu rek day tatoné rek
Sai sai bou makk saxx
Diëreudiëf manne damatiite
Sakhou ak ciése danioy fowé diuné dji niaf sén ndeye laniou wara ndéf
Mbacke sakho dafa doff dh werul dh
Man mom chiekh dama diaxal dine bopam la yore te kou xamoul mou reral la
Diouk lénn yénn té bayyi wax na ñièpu diouk
Comme que yéna diappou ni yéna nék si diné islam le reste si bida
Naturellement c'est ça la vérité mais vous êtes tellement bête raison pour laquelle vous avez cette vocation ça c'est tellement honte pour un musulman comme si vous ne reconnaissez pas votre prophète
Par contre si c'était tes parents tu aurais cette attitude cette position là moi je vais partir de Sénégalais ne savent rien de leur religion ils n'ont aucun estime sur leur prophète et ça c'est dommage c'est tellement grave
Nitou tarikha dîné niorouko
Kokou dafa rew dagn ko wara yobou si yon
Wallahi lou lérr gua wax wallahi
Wa yaw kay dèmall guadèf dèba akmom guiryala dèmall yaw dèmon baparè di wakh rèk 😂
Ki question youmou fi lathie. Bilahi you beurri lathie nako Say morome. Té kéne toutouwouma.
Ngir yalla tontoul simple question bi: Sourate 2 Versé 197 yalla néna wére yougniiy hajj yougnou xam la.
Wér youyou yane la? Sourate ak versé la sokhla😎
Tontoul😂
C est un debat d idee…ne menaces pas
Tg
@@lionking2424 débats d'idées contre l'idéologie du prophète mohamed ? désolé mais on ne débat pas avec le prophète suit ses enseignements c'est tout.
@@dabakhdia3873Islam est une religion de paix. Islam est aussi une religion pour les gens qui reflechissent. Si un mulsilman comme nous fait des erreurs on doit l aider et le guider. Allah is the most merciful.
@ je suis bien d'accord avec toi
mais celui là il persiste dans son erreur et il va entraîner beaucoup de monde avec lui dans ses délires.... il défie les enseignants du prophètes du prophète en se "se basant uniquement sur le corant " comme si il connaissait le corant mieux que prophète (saw) lui meme ...
@@dabakhdia3873daa deffoul erreur sah erreur moy dioum mais kou kham ba parei di dof dof Lou beugu reeral nianein gni
Ani matar sarr dowakh si bii nafékh
Kokou nékalofi l'islam
ما شاء الله جزاكم الله خيرا وبارك الله فيكم وأحسن الله إليكم❤❤❤❤
بارك الله في جهودكم
❤❤❤❤
❤❤❤❤