Mamam d si li nékh yalla rek la woté té diko dokhé lolou moko may ay seut you meune tok nane léne yalla néna yonént bi néna té dou garouwalé dou khasté
@@AbdouNiang459 ba nga dioudo ba Meusso togn yalla diegalou lo KO yaw Yalla la togn t yalla la diegalou kou KO meuna nianal nga nianal KO kou KO meunoul nga mandou si ay ayibam
Maashaa Allah yaw moom kilifa diine bou ver nga. Khamal nga djioulit yi kane mooy khaadimou rassoul cheikh Ahmad Bamba ak nimou ndiangalai farata ak souna boo beugai nek mouride biko top ci djiaamou yalla topp sounass MOUHAMMAD (psl). Yague fi lool ak gni melni yaw andak wer . INSHAA ALLAH
Ki mo motakh niounane Serigne...ap Serigne ni la wara mel..yaw deh do bokalé yalla mouk mbake..yaw mi la rewmi sokhla ndakh rere gui barrina nakhaté bi ak thiakhane yi eupena
Mariama niass djaangalé ne al Quran wayé tchi pass pass ou mouwahhidoun. Sama ay mbokk foofé fa moom lagnou djangé ba dem Makka tari. Dagnouy khéssal di sol you dang di def boppou néén di djakhasso ak Goor gni... Laa Hawla wa Laa quwwata illaa bilLaah... HasbounalLah wa ni'mal Wakeel.
Yalla n'alla fi souniou borom bayi billahi nous sommes fière de toi
Mom déy mogui si yonwi Yallana yalla yagall werall
Machaalah ya imam : yalla tasse gnu ci barké bii yaatal xam-xam gui
DIEUREU BOROM TOUBA DIARAMA MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMPE SERIGNE CHEIKH NGAÏDÉK SIDYBIRAHIM FALL LAMP Y'AGAL TÉ WÉR FALL S'A BOROM ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yalna yalla goudeul Say fane ta wèreul say thieur ❤️
Machalla dierejef mbacke balla yalla nalafi yalla yagual ta mayla were barképe borom touba
Machallah mbacke bala yalla nala yalla katanale
Bounioula toppé dey dinaniou dioubo ak souniou borome dieureudieuf yalnala sameu.
Machala imam mouno NGA wakh sama Mame naina 😢 Allahou Akbar y'a woor Yalla n'a yalla fayleu sambleu Aminn yarabih 🤲🥰🤞❤❤❤❤❤❤
Mamam deh li YALLA wakh rek la jangalé
@@aliounecisse6833SUNU BOROM khamnani lii nga Wakh la naroona tontou... Waaw goor Yaaram...
Mamam d si li nékh yalla rek la woté té diko dokhé lolou moko may ay seut you meune tok nane léne yalla néna yonént bi néna té dou garouwalé dou khasté
Li mamam déf ba ame fay bi nga wara khol té aw fofou
Yaw wergua mamam bou waxoul loumou wax
Akassa mbacke balla yagal tawerr amine
Dieurdieuf mbacke amna solo trop yalana yala faye bark yonenetibi psl amine
Dieuredieufeti Serigne Touba Diaraama Mame Cheikh Ibrahima Fall Lampe ❤️❤️❤️👍👌🙏🙏🙏
Machala na mourid yep dila deglou
ماشاء الله شكرا لك ياشيخ شيخ أحمد الرفاعي
Serigne cheikh ndiguel yaye djoulite deug❤❤❤
Beaucoup de femme
@@AbdouNiang459 lidieuntil saye ayibe
té bayi ayibou diambour yi
@@Saliougaye-y5c saway mala gueuneu doone bay fall piir mes mbirou dîiné amoul ly wala laa lou yalla wakh moy conté
@@AbdouNiang459 bay fall Day mandu
@@AbdouNiang459 ba nga dioudo ba Meusso togn yalla diegalou lo KO yaw
Yalla la togn t yalla la diegalou kou KO meuna nianal nga nianal KO kou KO meunoul nga mandou si ay ayibam
Jerejeuf imame rafahi
Maashaa Allah yaw moom kilifa diine bou ver nga. Khamal nga djioulit yi kane mooy khaadimou rassoul cheikh Ahmad Bamba ak nimou ndiangalai farata ak souna boo beugai nek mouride biko top ci djiaamou yalla topp sounass MOUHAMMAD (psl). Yague fi lool ak gni melni yaw andak wer . INSHAA ALLAH
Yag fi Lol teu weur diniou tek si Yon Macha allah
Mbacke balla Aïcha yagufi te werr man yaw rek lay topeu mbacke ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
MÂCHA ALLAH, SOU WAKHOON : SAMA MAME NÉNA YIT DISCOURS BI DOU CHANGER, CAR LI YALLA WAKH YONÉNT BI WAKH KO BOROM TOUBA MASSO KO GUÉN
Beaucoup de ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ Pour rafahi machalah
Yalla nala yalla defal diamm Barkéb Borom Touba
Oh machalha sama yaram daw na
Macha Allah ya Imam yala na borom bi fay té mayla Soutoura ak Ted Lé
Macha alla jeréjef mbake
Ma challa yalnala yalah wèral ack goude fane tè sakhal la thiy Li nga nèck
Masha.allah Alhamdoulilah santati yalla bou weer jërëjëf Cheikhoul Khadim amatina.solo imam Masha.allah ❤❤❤❤❤❤❤
Allahouma amine machallah ❤❤❤
YALLA nanga guddu fan
بارك الله فيك با❤❤❤ أتال الله لقائك🤲🤲
Dieureudieuf mbacké yarram yalna la saam rafétna
Ma cha alla mbacke
Ki mo motakh niounane Serigne...ap Serigne ni la wara mel..yaw deh do bokalé yalla mouk mbake..yaw mi la rewmi sokhla ndakh rere gui barrina nakhaté bi ak thiakhane yi eupena
Massallah sama sope Bi
Dieurdieuf Serigne Ahmadou Rafahi Mbacke!!!
🤝🙏Amna solo loool rafetna
Machalla mbacké bala
Machallah mbacke balla aicha
Machalla mback ball
Yallnala yalla saamou la aarr la
jaarejaff mbacke
❤❤❤❤❤❤dieuredieuf mbacke balla
Yallah nagnou yallah sopi
Tieye mbacke balla 😢
Machala
Dieuredieuff
😊
Machala ❤❤❤
Diadieuf mbacke
🎉🎉🎉 machallah amatina solo 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤
Mariama niass djaangalé ne al Quran wayé tchi pass pass ou mouwahhidoun. Sama ay mbokk foofé fa moom lagnou djangé ba dem Makka tari. Dagnouy khéssal di sol you dang di def boppou néén di djakhasso ak Goor gni... Laa Hawla wa Laa quwwata illaa bilLaah... HasbounalLah wa ni'mal Wakeel.
❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉
souniou Borom yokk xam xam bi ak fane wi
❤❤❤❤❤❤❤❤
🙏🙏🙏
Khoutba bi iska ty la
Yallana sounu borom yagual la fi mbacke
Salam dama am sokhla 20000 beug kou mathi diaple te yalla rek takh
76
813
7981
🕚
akassa
MÂCHA ALLAH, SOU WAKHOON : SAMA MAME NÉNA YIT DISCOURS BI DOU CHANGER, CAR LI YALLA WAKH YONÉNT BI WAKH KO BOROM TOUBA MASSOU KO GUÉN
Machalla
❤❤❤
Machallah
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤