Lima nekh thi l’actrice Boury moy doko guiss féne à part série yi, elle n’est pas thi réseaux yi pas thi soirée ou khéw yii et elle n’est pas vulgaire dans son habillement. Nonou la rafetté masha’Allah ☺️
En trois épisodes seulement vous êtes cartonné je pensais que l'émotion que vous nous faites ressentir s 'étais juste à bêté bété mais xalisso c'est autre chose vraiment chapeau à vous
Une pire trahison pour boury!!!! 😢voici le boulot des belles mères et belles sœurs au Sénégal c amerdant 😔en plus trop ingrats !! il suffit juste k leurs femmes soient heureuses dans leurs ménages elles poussent au bout pour k l’homme cherche une seconde femme pour le secour 😴😔yalnaniou yallah doli soutoureu 🙏des cœurs pour boury elle joue hyper bien❤❤❤❤❤❤
Bilay je suis la j'ai une sérieux problème meunou massi wakh AK kene je préfère tog mane kessé sama nena dama bari djiguo alors kholou sakh mba kham magui si diam où pas 😢😢
L'hypocrisie de Sokhna 🥹 Allahou Akbar comment on peut être si méchante et jalouse à ce point 😢 Boury vraiment elle est unique dans son jeux 🥰trop d'émotions
@@coumbatandian4865 merci bcp pour ma part mangui sante boubakh alhamdoulilah je touche du bois je parlais des femmes qui en souffrent ma khol ko thi sama bop motakh may compatir...mais merci c gentil
@@coumbatandian4865 pour ma part mangui sante boubakh alhamdoulilah je touche du bois je parlais des femmes qui en souffrent ma khol ko thi sama bop motakh may compatir... Mais merci quand même c gentil
Dagay andak AK nite thia bamouy metii gua hey Bess lép sotii gnou worla sa famille dieukeur tékla beute surtout sa belle mère AK belle sœur yii 😢 gnou nekeu thi situation Boury bi yallah nalein tahawou maylein holou mougn yallah dina gnow inchallah 🙏
Ce que j'adore chez evenprod c'est que leurs séries parlent toujours de la vérité de notre société comme bété bété, cœur brisé et autres et franchement j'apprécie 👍
Wallahi c’est mon cas je suis le porte bonheur de mon mari dés qu’on s’est marié toutes ces porte sont ouvertes mais sa mère me voyais trop dans sa vie mais heureusement que mon mari était mon ange gardien il n’écoutait jamais ce que sa mère disait sur moi Aujourd’hui je dis Alhamdoulilah je suis la femme la plus comblée et à l’aise dans ma grande maison avec la famille mais je dis une chose que dieu nous préserve de ces genres de belles mères wallahi nous les femmes on souffrent bcp vraiment sounou néguou seye ❤
La leçon que j'en tire est qu'il ne faut jamais parler sous le coup de la colère 😡. Faut toujours prendre du recule et réfléchir avant d'affronter un problème. Dommage que c'est souvent par manque de maîtrise de soi qu'on se cree même nos propres problèmes. Mais dans cette vie quand tu trahie saches que tôt où tard tu mordera la poussière
Pour moi si une fille doit quitter la maison de ses parents c’est pour aller dans la maison de son mari ce n’est pas dans nos valeurs ce qu’a fait MATY ROSE mais elle va voir ce que ça mère veut lui éviter et elle devrait savoir que son copain ne l’aime pas parce que si oui il allait le recadrer
Nieup niongui nane lepp diabarou diop fall la mais suis pas d'accord. Ndiawar ak yayam nioy ay ingrats rek parce que fi kougne fi manipuler yaw la nekh. Gni ay badola lagn. Genre yi motakh khalé yi ndango touniou mougne ndango touniou def beine sacrifice ndakh à tout moment niou torokhal la trahir la. Sounou generation bi dagne leine di khass parce que danio conscients si genre yi. Li rek laniouy bagne wayei amouniou beine blem. Senegal nak gnifi reconnaissants bari wouniou💔
@@FatimaSeck-s8m non je t'assure deh. Khalé yi beug nagn mais khétou métite yi laniouy bania doundou ba kheuy fi goitre wala kheuy fi déh nga perte. Nagn focus si sounou avenir rek niane yala seuy ak kou nité ak kou am mbokou you nité🤦🏽♀️
HEURES DE PRIÈRES DU 27 SEPTEMBRE AU 03 OCTOBRE 2024 Fadjr: 05h45 Suba: 06h00 Tisbar: 14h15 Takussan: 17h00 Timis: 19h08 Gue: 20h08 Qu'allah accepte nos prières Al Jummah Mubarack
Bayilen boury dem ndank ndianwar ham louko boury don ndianrign mère bi. Soda mère dina torturé ko ci galé bi😂 maty rose djiguen hamogo dieukeur sa wetou yaay gan wara tok bakhna yaay dou morom😢
La situation de Matyrose est actuellement ce qu'il a dans le pays 😢😢mrd elles pensent que la liberté s'est de quitter la maison de chez parents pour vivre seul mais non 😢
Thieuy even prod yékeuti wat ngen niveau bi dh.yen rek lay topou 😂.xallisso 3 épisode et ça cartonne déjà.lima gueuna nekh Moy gnom li nek thi réw mi lagnuy dénoncer.bravo à vous et bonne continuation.❤
Le genre de sokhna des hipocrites de haute niveau des solopes des vaut rien qui cherchent toujours à détruire une famille yalnanou yalla mousal si saytané afficher Indien dawal caboy
Moytou len meu diguene bouñiou brisé cœur am💔 andeu ak merr beug fayou elle sont très dangereuses Une pensé pour notre Boury limouy doundou metti neu😢😢😢
Vraiment Boury ne mérite pas cette trahison . C’est la première fois may commenté si série . Limouy doundou ni Lou am la . Motakh kéneu waroul dieul sa adina bi yeupp diokh ko goor parsk li c’est de leur nature
Vraiment elle sait jouer son rôle. j'avais ressenti cette douleur sans avoir personne pour me consoler. J'ai d'abord quitté la maison puis demandé le divorce. Bravo à ceux qui ont pensé à cette scénario
Enfin! Dagno nammoon genres séries you amm sense yii, instructives et profondes. Une série pour ceux qui ne se contentent pas des "série divertissement" Le casting aussi, que des acteurs de qualité, gnou kham lougnouy deff. On sent que bii mom dina yegg niveau Bété Bété. J'aimerais bien dire niveau Idoles mais geuwma ni lou mell nonou dina gawa amat. En tous cas, on est proud. Evenprod, li lagn tamm ci yeen, force à vous et bonne continuation 🎉💯
C'est un manque de respect de ndiawar envers sa femme boury. Épouser une autre et l'amener dans la Maison sans lui dire. Affairou yabatee la. J'approuve la réaction de Boury😢 Chapeau à Even prod encore une fois
Après lakoy rethiou bilakhi may wakh mounan fardeau liberté rék Maman amal fouleu sam ngua b fi dome bou khamoul Ndayam ndaye ham bopam xaliss lux rék thipri
Vraiment djiguéne bou andeu ak iow bimouye méti moment bo guissoul kéne môme kassé lep nieuw ngala bo amone aye milliards wala sa yaye wala sa papa nila takhal niarél ga wara bagne am ngor si mome... 😢😢😢
37:22 is very emotional 😢i am a Gambian watching from Paris 🇬🇲🇫🇷i love watching Senegalese series.i learned many things from it, this episode I learned that I will never betray my wife who sacrificed all her life for me.she how boury is crying even me I'm crying on my bed while watching it
Lima diaxal sénégal moy djiguen moy tek moromam louka meti ga am dieukeur guen beugueté mou dieul lepam tek ko ci sa laxo gakoy comme il faut famille wame neko sa diambar dala ligueye wala defa beugue hériter sa allal dem indi sen mboko pour nakaral la bourry je partage ta peine Te lima diaxal ossi moy kou gor ki bou yoroul nioune ya wara mougne nah ga am ay dom you bax 😢😢😢
Bouri tu nous a manqué sur les écrans félicitations ❤❤❤ Astou avec ta nouvelle grinta de sissou Binta t'as Kate sey merci à evenprod pour votre travail extraordinaire et de relancer les acteurs actrices renommer macha Allah ❤❤❤❤
Maty rose ya trahir sa yaye nonou ndakh goor ak vie de luxe ayyy biss dina nieuw dou fayatii apprtmnt bi nga beugu delou si sa yaye mou teu leu yayz ken douko torokhal
C’est triste ce que l’argent peut nous faire perdre 😢 Des familles brisées comme ça Sunu amé khaliss yalna niou yalla defal soutoura moussal niou si sheytan 🙏🏾
une série qui peint carrément les réalités de notre société. L'hypocrisie des personnes est démesurée je vous le dis. les gens deviennent de plus en plus avides. j'ai vu trois de ces personnages dans la vraie vie voilà pourquoi je vous tire mon chapeau et j'espère que vous garderez le même concept
Yayou ndiawar limou def khamou ko sax. Desfois danguay guiss goor yor alale famillam fokni diabaram dafkoy leek alors que alal bobou yeup c’est la femme qui est derrière di soutoural ak diko diapalé wayé Bo fekhé beu takhalé leine nguay kham ni leep deug leu.
Lima nekh thi l’actrice Boury moy doko guiss féne à part série yi, elle n’est pas thi réseaux yi pas thi soirée ou khéw yii et elle n’est pas vulgaire dans son habillement. Nonou la rafetté masha’Allah ☺️
Wakhga lepp
Dégue na deugue chérie❤
Bly dafa cool trop
Billy
Vérité
Kou yeureum mére bi ñou trokhal rk lalal j’aime 😭
Thieuy khaliss 😤
Dafa tombé ak sa commentaire 😢
😭😭😭😭😭😭
Bègou mawona ré de 😂😂
Xalisso toukeul na adouna 😢
Bravo à toute l’équipe de xalisso 👏🏻❤️
Billah dé l'argent toujours l'argent 🤦
😂😂 bilay
@mbayangdiagne1904 Merci. ❤
La petite sokhna elle dégage une émotion exceptionnelle mashalah elle m'a fait pleuré 😢 une vraie actrice ❤
Cette série est très intéressante hâte de regarder l prochaine épisode 🇫🇷
Kou beug Seydina Mohamed lalal j’aime 🇸🇳
En trois épisodes seulement vous êtes cartonné je pensais que l'émotion que vous nous faites ressentir s 'étais juste à bêté bété mais xalisso c'est autre chose vraiment chapeau à vous
Vraiment ❤
Ils sont excellents
Evenprod rek Masha'Allah manak niome depuis idoles ❤❤❤❤❤
Ils sont les meilleurs
@MariemeNdiaye-rq8lj Merci, as-tu tiré des leçons sur cet épisode ?
Une pire trahison pour boury!!!! 😢voici le boulot des belles mères et belles sœurs au Sénégal c amerdant 😔en plus trop ingrats !! il suffit juste k leurs femmes soient heureuses dans leurs ménages elles poussent au bout pour k l’homme cherche une seconde femme pour le secour 😴😔yalnaniou yallah doli soutoureu 🙏des cœurs pour boury elle joue hyper bien❤❤❤❤❤❤
C vraiment dommage c ki s passe au Sénégal
Wayé mane japnani lép kou goor ki dakh niit bo amé fo diar ak mom digua kham lo déf wala lo défoul
@@DiarryDiallo-yc8rcdefa niakk foula 😮en plus il est trop ingrats !!
@@fatoudiba4922tout à fait 😢
Avec tt les sacrifice youmou def bilahi parfois seytane yakkh hell walahi il va le regretter de sa c sur
Yayou diadia nimou def mere bi metinama trop bilahi 😢😢
Mère bi daffa bone
Billae sama xol bangi metii
Ki kagne da sokhor trop
@@MarietouTine-ev9zl bilahi 😭
Wallahi dioy nasi comme si degula 😢
Le jeux d’acteur de Boury est juste spéciale elle fournit bcp d’émotion juste ouff mais aussi une ami comme diadia bravo a vs 😍❤️🥰
Kou geum nii dingah tékki sans toukki téraal wajuur yii beusseul j'♥️m EvEND PROD Seul Jäjëf
Mandé khamna dou yombou si man ak 900mil yinou ma beug faylo
Une pensée pour ceux qui vivent des moments très difficiles et qui ne peuvent en parler à personne Yalla nalen Yalla taxawou si barki Muhammad (PSL)
Bilay je suis la j'ai une sérieux problème meunou massi wakh AK kene je préfère tog mane kessé sama nena dama bari djiguo alors kholou sakh mba kham magui si diam où pas 😢😢
Amine
Merci beaucoup metina trop la souffrance en silence mais yalla bakhna 😢
Amine
Amine yarabi 🙏🙏
Kou yeureum boury lalal j’aime ❤❤😢
Dafa meti mai dinako reuthiou
❤❤❤❤
❤❤ndiawar bakhoul xamoul touss lépou bouri mokay défal
Motakh il va soufrir@@aramegueye-ox8ff
Ndiawar dina torokh li la jiguene you bari di doubd
Vraiment notre boury est un brave dame des cœurs pour elle❤❤❤❤
❤❤❤❤
@@Salimatasalimata_h21 😍😍😍😍
❤❤❤❤❤❤❤
@fatoucisse9977 Merci.
L'hypocrisie de Sokhna 🥹 Allahou Akbar comment on peut être si méchante et jalouse à ce point 😢
Boury vraiment elle est unique dans son jeux 🥰trop d'émotions
C'est le commentaire que je cherchais elle est l'incarnation de Satan cette femme wépépé
Boury ,Léna et soumboulou méritent d'être décoré
Elles sont de vrais actrices 🎉🎉
Boury ’est une très grande artiste
Elle transmet tous les émotions machalla ❤️
Bilay lolou la wakh senk aussi holal domyi jioye yinu dn df ak bamuy wahak rakji nanko demal hol sa mak auuuuu
@fatouchababy1972 Merci. ❤
Hommage à toutes les femmes qui ont subit de l'injustice dans leurs foyers métina mais yalla guissna lepp😢💔
@mamewade1402 👍
Merci Mame Wade insha Allah lep dîna bakh thi katanou sounou borom wolouko rek té gueum ko bayil ko lep
@@coumbatandian4865 merci bcp pour ma part mangui sante boubakh alhamdoulilah je touche du bois je parlais des femmes qui en souffrent ma khol ko thi sama bop motakh may compatir...mais merci c gentil
Wallahi deugue bou werr
@@coumbatandian4865 pour ma part mangui sante boubakh alhamdoulilah je touche du bois je parlais des femmes qui en souffrent ma khol ko thi sama bop motakh may compatir...
Mais merci quand même c gentil
Bourry daniouko woor woor bou metti ça c’est la pire des trahisons 😢😢😮😮😮😮😢😢😢
Bilay
Ni dhei lagne deifff clara sénégalais bania comprendre mais kou neikk ci neigou sey khameni meitina
@@nadiadiabilaye yaw mane je la comprend
@@nadiadiayalla moy bour mongui guiss leep
Boul comparé si lo metrisé woul nakhe Dara lérou lasi. Kone Khadija awo dora bi monme lougnouy ko déf@@nadiadia
Boury est une grande actrice, dans toutes les productions où elle a joué, elle gère parfaitement. Bonne continuation à elle 😊.
Diadia elle est douce ma sha Allah ma préférée dans la série ❤
Maty Rose wow nga kholl ! Wane sa ndayy guinaw juste pour fly to fly ?? Tu vas le regretter inchaAllah
Fly to fly 😭🤣🤣🤣🤣
Bly
Teh mom dara safouko puisque à peine sortie de la maison mongui biz le gars, ki mo panne kilifa
Anh ya oumou sow nonou.fly to fly😂😂😂😂😂😂
A wana fly😂@@lennavivilennavivi
Dagay andak AK nite thia bamouy metii gua hey Bess lép sotii gnou worla sa famille dieukeur tékla beute surtout sa belle mère AK belle sœur yii 😢 gnou nekeu thi situation Boury bi yallah nalein tahawou maylein holou mougn yallah dina gnow inchallah 🙏
😢
Li aka beri si rew my
Billahi 😢
Amine inchallah
Li de lay dondo
Salalaahou Alah MOUHAMED 😭❤️
❤❤❤❤❤❤❤❤
Psl ❤❤❤❤
❤❤❤psl
Psl❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤@@aramegueye-ox8ff
Ce que j'adore chez evenprod c'est que leurs séries parlent toujours de la vérité de notre société comme bété bété, cœur brisé et autres et franchement j'apprécie 👍
Wallahi c’est mon cas je suis le porte bonheur de mon mari dés qu’on s’est marié toutes ces porte sont ouvertes mais sa mère me voyais trop dans sa vie mais heureusement que mon mari était mon ange gardien il n’écoutait jamais ce que sa mère disait sur moi Aujourd’hui je dis Alhamdoulilah je suis la femme la plus comblée et à l’aise dans ma grande maison avec la famille mais je dis une chose que dieu nous préserve de ces genres de belles mères wallahi nous les femmes on souffrent bcp vraiment sounou néguou seye ❤
Longue vie á vous lire katou commentaire yi 😂😂😂❤❤❤🎉🎉😂😂❤
😂😂😂😂😂
Amine
Amine souniou nawlé
Amine souniou nawlé😂😂
😂😂😂😂😂😂
Cou geumni l mot fassé comme l eau a boir au Sénégal mais ya toujours de regret cou d accord beusal j'aime ❤😂😂
Motakhite 😂mongui 😂dioye dh 😂
Bilahi
Mofy beury
@NdebaSene Mais est-ce que bouri li diarone na mouye gnane bagne ?
mais tmt vous femmes vous êtes qui😂 da nguene ñiane bate ñiou fasé leen nguéni kasse😂😂
Bou adouna nékh baniou fatté gni niou djiitou si birr souf. ndax yageu yageu daniou léne di fékki dji. na niou léne diangeul fatiha ak 11 likhlass nianal léne yallah bour bi yeureum léne té xaré léne alldianatoul firdawsi si barki alkhourane
🤲🏽⚰️🤲🏽
Allahouma Amine inchallah billahi wax ga DEUG dé
Amine
yalnalen yalla yeureum Amine inchala
Amine inchallah
amine inchallah 🤲
Oh la petite Sokhna elle est incroyable ❤❤❤❤❤❤du courage boury❤❤❤
La leçon que j'en tire est qu'il ne faut jamais parler sous le coup de la colère 😡.
Faut toujours prendre du recule et réfléchir avant d'affronter un problème.
Dommage que c'est souvent par manque de maîtrise de soi qu'on se cree même nos propres problèmes.
Mais dans cette vie quand tu trahie saches que tôt où tard tu mordera la poussière
Vérité absolue
La maison de production qui n’a jamais perdu sa ponctualité ❤❤❤
@aidagueye8021 Merci. ❤
Nexoull ba nexoull me Seri bi dafa Am solo li mo am Sénégal 😢 baravo evenprd
Actualités la sokhoré igniane tekk beauté badola trahison monfi am bilahi
Aka fé Bari sakh
Wayé mèlni wa pikini rék 🤬
Koudoul diouli nguir yalla déle diouli té yalla takh si barké saïdina Muhammad psl
Problème diouli laa am😭
@@matymasl3481 yalla nala yalla diapale mouseul la saytane
Macha Allah amna solo yalla Naniou yalla yombalal incha Allah amine 🤲🤲🤲❤❤
@@matymasl3481personne n’est parfait mais nak khékhal ak sa bakane ngay diouli Sister 🙏🙏
Yalla nala yalla diapalé🙏
@@matymasl3481personne n’est parfait mais nak khékhal ak sa bakane ngay diouli Sister 🙏
Yalla nala yalla diapalé🙏
Pour moi si une fille doit quitter la maison de ses parents c’est pour aller dans la maison de son mari ce n’est pas dans nos valeurs ce qu’a fait MATY ROSE mais elle va voir ce que ça mère veut lui éviter et elle devrait savoir que son copain ne l’aime pas parce que si oui il allait le recadrer
Nita leundeum deugue deugue 😢
Merci evenprod si leçons yinguéne gni transmettre à travers vos séries ❤
SERIGNE MUNTAKHA MBACKÉ YALLA NAFI YAGU LOLL TÉ WERR🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Amine inchallah ❤❤
Amine inchallah
Amine
Nieup niongui nane lepp diabarou diop fall la mais suis pas d'accord. Ndiawar ak yayam nioy ay ingrats rek parce que fi kougne fi manipuler yaw la nekh. Gni ay badola lagn. Genre yi motakh khalé yi ndango touniou mougne ndango touniou def beine sacrifice ndakh à tout moment niou torokhal la trahir la.
Sounou generation bi dagne leine di khass parce que danio conscients si genre yi. Li rek laniouy bagne wayei amouniou beine blem.
Senegal nak gnifi reconnaissants bari wouniou💔
C'est ça le blème bala ma gueneu ame louma méti niou nane douniouye aye seuye katt
Exactly sis lii rék motax duma soneu ci homme
@@FatimaSeck-s8m non je t'assure deh.
Khalé yi beug nagn mais khétou métite yi laniouy bania doundou ba kheuy fi goitre wala kheuy fi déh nga perte.
Nagn focus si sounou avenir rek niane yala seuy ak kou nité ak kou am mbokou you nité🤦🏽♀️
@@NdeyendiobaNdiaye-vx8yh walahi diarou niouko. Focus rek nek si sounou bopp fight pour sounou bopp
@@Tymachu bilaye mne déh llu la guiss job pour sma bopp le reste on gère
Le retour de Hélènita chérie Diogoye séne 😍❤️😂😂😂😂
Team Boury❤…!!!
Wawaww nako regretter deih, ruiner ko sakh. Ndiawar ne te mérite pas. Yayam nak cheuttt🙄..! Goor moh doywar si bopam.
Badiene tamit fausse na😭🤦♀️
Pourtant Niawar n'a rien fait
Bourry c'est comme Mareme Sall je l'aime trop une très bonne actrice j'ai regardé toute les séries auxquelles elle a participé j suis amoureuse ❤😂😂
HEURES DE PRIÈRES DU 27 SEPTEMBRE AU 03 OCTOBRE 2024
Fadjr: 05h45
Suba: 06h00
Tisbar: 14h15
Takussan: 17h00
Timis: 19h08
Gue: 20h08
Qu'allah accepte nos prières Al Jummah Mubarack
Alahuma amiiinn ❤
Amine inchallah
Soda Marieme mo nara def mère bi lou meti😂
Je te jure 😂😂😂😂je vois venir tout ça
Kone ma sente yalla
Bayilen boury dem ndank ndianwar ham louko boury don ndianrign mère bi. Soda mère dina torturé ko ci galé bi😂 maty rose djiguen hamogo dieukeur sa wetou yaay gan wara tok bakhna yaay dou morom😢
Bàyyi ko foofu rekk. 😂
Lolou laka wara déff sakh ndakh mou nékh
Cette série mérite des millions vues❤
Nekoul série rek dhè even si bopam nio merito ay millions d’abonnés n
@Ptitleuz Merci pour la force. ❤
Djadja tmt dougn si wax xalei bi manchallah ❤
Ms sincerement nak adja ak elena ils montrent leur complise dans tout les series chapeau a eux🎉🎉🎉🎉
La situation de Matyrose est actuellement ce qu'il a dans le pays 😢😢mrd elles pensent que la liberté s'est de quitter la maison de chez parents pour vivre seul mais non 😢
Et ce qui est dommage mais comme l'adage wolof kou amoul kileufeu djiné diseu kiffeuleu
Lou let mofi am legui mais dinako rethiou
@@thianediack9512 teeh li guen grawoul si adouna moy am xarit bou bonne daal melni ibliss sii yaw rek
Motakh moussibeu dina leen yag dale.kou amoul kilifeu mbédeuh bi nek sa kilifeu
Vivre avec ses parents c'est une grande sécurité Ndey saan boo xamul rek xamoo
Ana kouy avance publicité yi kom mane ☝️😎
❤❤❤❤❤
Magui ni
@@CoumbaSeck-uu8cx bayyil loolu 😎
Man 😂
Bouldiko wakh deffall te nopi
Ayy way mére bi yayou diadia torôkhale méti Nama bilahi damaka yeureum gnakk méti na yalenagnou si Yalla moussale 😢
Bilay ak limouy mayé yeup
Amine yarabbi
Amine inchallah
Amine
@fatykane1063 Lo xam si kou bew ?
Thieuy even prod yékeuti wat ngen niveau bi dh.yen rek lay topou 😂.xallisso 3 épisode et ça cartonne déjà.lima gueuna nekh Moy gnom li nek thi réw mi lagnuy dénoncer.bravo à vous et bonne continuation.❤
Les chansons de Dior Mbaye ngi yakeu sama life😢😢😢❤❤❤❤
Kou yakar sarigne touba nama aime ❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Le genre de sokhna des hipocrites de haute niveau des solopes des vaut rien qui cherchent toujours à détruire une famille yalnanou yalla mousal si saytané afficher Indien dawal caboy
Merci là-bas
@thiategueye5245 Ah doyna ware, mais mome da melni sah si bire keureume ?
Sokhna c'est la belle-sœur ils me semblent ?
Walahi ay dmrm laniou thim
@@sarahgnigouan5174elle a 2roles belle sœur et perthiorgo car c’est la femme du cousin de Ndiawar y’en a bcp de ce genre 😢
Moytou len meu diguene bouñiou brisé cœur am💔 andeu ak merr beug fayou elle sont très dangereuses
Une pensé pour notre Boury limouy doundou metti neu😢😢😢
Bilayy séné xoll d'où nekh
@@adjasaliou8309
Bilay deug leu
@baldeibrahima4580 Da melni jekeur dji dinako rethiou ?
@@evenprod bien sûr il la dit sous le coup de la colère
@@evenprod
Très profondément aussi
Kou guiss ressemblance entre adjia ak fa binetou rék like👍
Tropp
Dior Mbaye à une voix suave, trop nekh
Teams Diop Fall magnifestez vous😂😂
Néna man nianouma batt😂😂
Diop Fall damako beugue 😂😂😂
@SeydouDeme-n8s Loleine koy conseiller ?
@@evenprodmou seuy seuy bi😅
Boury théâtre boumou jouer souffrance lathie doundou 😢😢elle joue bien son rôle
Setlou nga lolou
Billahi Kom Amy Léa Sy marodii ❤ xale bou rafett bobou oh❤
@Nndayediaw Merci.
@@BayeBassDieng-y6k Bly yaw
@@evenprod de rien ☺️
Cette série est une bombe je vous dit ❤Boury ma préférée 😻
Vraiment Boury ne mérite pas cette trahison . C’est la première fois may commenté si série . Limouy doundou ni Lou am la . Motakh kéneu waroul dieul sa adina bi yeupp diokh ko goor parsk li c’est de leur nature
Vraiment elle sait jouer son rôle. j'avais ressenti cette douleur sans avoir personne pour me consoler. J'ai d'abord quitté la maison puis demandé le divorce. Bravo à ceux qui ont pensé à cette scénario
Enfin! Dagno nammoon genres séries you amm sense yii, instructives et profondes. Une série pour ceux qui ne se contentent pas des "série divertissement" Le casting aussi, que des acteurs de qualité, gnou kham lougnouy deff. On sent que bii mom dina yegg niveau Bété Bété. J'aimerais bien dire niveau Idoles mais geuwma ni lou mell nonou dina gawa amat. En tous cas, on est proud. Evenprod, li lagn tamm ci yeen, force à vous et bonne continuation 🎉💯
@fatyn.8035 Merci, c'est toujours un plaisir de vous satisfaire. ❤
❤❤❤
@@evenprod Vous savez comment, merci à vous! ❤
Boury transmets très bien ses émotions 😢😢😢 ndeysane c dure diour ay dome you magg ba xamei gnoulay torakhal séne kanaam métinaa lol
Amine yarabbi barkep Serigne Touba
@Fkdalmaktoum7 Doyna ware, yakaro woudiou bi tek lou meity goro bi ?
@@evenprod lolou kay sa se voit déjà k bess bou sentirer ni qu'elle est bien installée Dina réglei mére bi bou baxx saxx
Vrmt Evenpro vous êtes les meilleurs Xalisso.
Sama papa serigne babacar sy abdoul aziz sy yalna fi yague lol té wer bcps de 25 septembre inchalla ❤❤
C'est un manque de respect de ndiawar envers sa femme boury. Épouser une autre et l'amener dans la Maison sans lui dire. Affairou yabatee la. J'approuve la réaction de Boury😢 Chapeau à Even prod encore une fois
Boury vraiment chapeau à toi tu transmet bcp d’émotions 😢merci even prod❤🎉
Maty rose perte ga sa copin bi khamni boury moko yorone 😂😂yakh gako 😅rethiou dina fékk dieuf wéss😢
Maty rose mola gueuna khamni seydou yoroul touss. Khamna ndiawar mo am khaliss
Maty Rose molako geneu xam
@SoukeyeLom Seydouyone leu rek, ndah wahnagne koko.
@@khadydiouf3539 ms dafa fogni ndiawar mokoy diokh khalise te alors ke ni boury mokokoy diokh donc sou bourry dèmé foumkoy dieuleti
@@evenprod j sais ms tmt sou boury dèmé occasion bobou foumkoy dieulété nakh ndiawar nagouwouko diokh khalise té maty rose dafa fokni ndiawar moko yorr
Boury loutax signé wo monogamie ak sa jeukeur😂😂😂
Est-ce que amnagne papiers de mariage sakh ndakh wadji waddd la 😂😂😂
@@fatougueye-zh7td😂😂😂😂utilisé nga mot bou yague
Wadd kay😂😂😂@@mbbcrssr3118
@@fatougueye-zh7tdwadd ou ngaka louma geudie degg😂😂
@Ak15922 🤔
Gnogno aka meune rôle pauvre wouy 😂😂😂😂
Akk yeuram talou😂😂
😂😂😂😂😂té bou amé genre rôle yi dafay torokh lou, dou diwou, di défart teint wam
Hum hum 😞😞😅
Té nonou la meuné tountou nk mom day raare trop 😂😂
😂😂😂😂😂😂
c la première fois que je vois les commentaire TH-cam qui parle sur le sujet merci de continuer comme ça🤩
Bilae 😂😂😂
MachaAllah Boury joue très très bien ses rôles c’était la même chose dans la série impuissant elle mérite des oscars vraiment chapeau bas à elle .
Vraiment nak sama mak dji astou Diaw li moy dans la peau d’une autre🤣🤣🤣🤣tout à fait ton contraire ndeyssane yalla na yalla defal la diam❤️
Vraie actrice la macha allah ❤❤❤
@@yayemayelatmbao5442 merci
@follesdelux6980 👍
Ndeyssane rôle la rek mais kouko khol khamni nirou woule sakh nite yoyou
Je suis pas contente de l’attitude de Maty rose depuis quand vivre avec sa mère est un fardeau😢. Elle va le regretter
C ce qui existe dans ce pays ma belle. Bari ba déh
Maty rose est tro naïve
@khounniii9146
Moma diakhal 😂mounane j veu juste voler de mes propres ailes
Après lakoy rethiou bilakhi may wakh mounan fardeau liberté rék Maman amal fouleu sam ngua b fi dome bou khamoul Ndayam ndaye ham bopam xaliss lux rék thipri
Vraiment djiguéne bou andeu ak iow bimouye méti moment bo guissoul kéne môme kassé lep nieuw ngala bo amone aye milliards wala sa yaye wala sa papa nila takhal niarél ga wara bagne am ngor si mome... 😢😢😢
Dama fogone si bête bete lay yammm mai Xalisso amoul louko dak si casting ❤❤❤ wa kou done casting yi personnalité bou xalisso je suis éblouie 🤩
37:22 is very emotional 😢i am a Gambian watching from Paris 🇬🇲🇫🇷i love watching Senegalese series.i learned many things from it, this episode I learned that I will never betray my wife who sacrificed all her life for me.she how boury is crying even me I'm crying on my bed while watching it
It's sad 😔
Say parents divorce dafa métti blh moi même je le vit en ce moment 😭
Masa yaye boye
Ohh C très dur 😢
Masta toma 😢
Ak man billay Lou mouma dall ma belle Lou maity la
😮
C’est la réalité au Sénégal vraiment ms boury ne mérite pas ça ms evenprod la chaîne qui n’a jamais perdu sa valeur ❤❤
@Mindou245 Merci, c'est toujours un plaisir de vous satisfaire. ❤
Boury une vraie actrice Walay je vois soumblou en elle❤…evenprod chapeau à vous fi nguein guenati noy na🥰
C’est elle la grande sœur de soumboulou
Vraiment bravo à boury elle incarne le rôle à la perfection 😍🥰
La petite sokhna 🥹elle a transmet des émotions de ouf
Lima diaxal sénégal moy djiguen moy tek moromam louka meti ga am dieukeur guen beugueté mou dieul lepam tek ko ci sa laxo gakoy comme il faut famille wame neko sa diambar dala ligueye wala defa beugue hériter sa allal dem indi sen mboko pour nakaral la bourry je partage ta peine
Te lima diaxal ossi moy kou gor ki bou yoroul nioune ya wara mougne nah ga am ay dom you bax 😢😢😢
Bly DEUG nga wakh daniou sokhor
Wayei cas youssi beury mbook yooyou gnouy woutal place gnoy weulbeutikou dileen wann bidewou beuthieuk bou sen toogay degeurei
@aidadiakhoumpa6896 Ah doyna ware li xew si rewmi, lep nieuker bi leu. 😢
Sokhna mi meune na thiou meune thhiaa meune thieureureuwwww😂😂😂
😂😂😂😂
@Oumylaye102 Dei doussi takhe.
Kou begue seydina Mohamed lalal j'aime
❤❤❤❤psl
Bouri tu nous a manqué sur les écrans félicitations ❤❤❤
Astou avec ta nouvelle grinta de sissou Binta t'as Kate sey merci à evenprod pour votre travail extraordinaire et de relancer les acteurs actrices renommer macha Allah ❤❤❤❤
Sérieux lii am Keur Niawa Lepp Ndiallo bou pt frère ram di moy yalla moka waral Parce Ndialo moy lou bonn lou sekhlou que Dieu nous en préserve
Xalisso la série qui n'a jamais perdu sa valeur 😂❤
Nane katou café ☕ insbi dagnouy sétane xaliso😂😅
Nane katou cafe bi😅😅
@@DiamaBa-z5h 😂😂😂
Ki d'où tonton café Touba nameu nala😅
Café Touba lay nane ni sah
Maty rose ya trahir sa yaye nonou ndakh goor ak vie de luxe ayyy biss dina nieuw dou fayatii apprtmnt bi nga beugu delou si sa yaye mou teu leu yayz ken douko torokhal
Même avec des milliards je resterai avec ma mère maty tu ne payes rien pour attendre yaye est irremplaçable
May ko touti rekh 😂dina regrettée
Dinako coûte cher de 😢sa c sur juste begue ham liberté
Bilay
Pourtant mom day lingué yaye dji mon comprendoul rk
Evenprod meilleure maison de production au Sénégal ❤🎉
@mamitacaramel Merci. ❤
Xaliss mo toukeul adouna 🙏🙏
DIADIA EST TROP BELLE❤❤
Wa yene wakholene si musik Dior mbaye bi de manchala
Nékhna torop
Dama dioy si li😭
Trop nekh sang😍
@@fallndeye6092 manchala
Stp son bi noumou touddou titre bi
C’est triste ce que l’argent peut nous faire perdre 😢
Des familles brisées comme ça
Sunu amé khaliss yalna niou yalla defal soutoura moussal niou si sheytan 🙏🏾
Famille Africaine danio allergic si bonheur rou couple 🙏
U as tellement raison 😊
Khamou lo si dara
Tellement vrai
@Grace77690 Femme yakhe femme.
Tu es malheureux ils sont avec toi tu es content ils sont contre toi
une série qui peint carrément les réalités de notre société. L'hypocrisie des personnes est démesurée je vous le dis. les gens deviennent de plus en plus avides. j'ai vu trois de ces personnages dans la vraie vie voilà pourquoi je vous tire mon chapeau et j'espère que vous garderez le même concept
Bilahi yakamti wone na li une serie ki reflete nos realités mais choco choco rek
Merci way
Yayou ndiawar limou def khamou ko sax. Desfois danguay guiss goor yor alale famillam fokni diabaram dafkoy leek alors que alal bobou yeup c’est la femme qui est derrière di soutoural ak diko diapalé wayé Bo fekhé beu takhalé leine nguay kham ni leep deug leu.
Ñaaw njort rekk ak soxor, dund Senegal kay lu ko gën a metti gisuma ko. 😭😭
Ndiawar khamoul touss manoul Dara lépou bouri moka défal
Ta sakh Diabar Dji bouko leikké dafa war ndakh gnoy partagé séne vie pour le meilleur et pour le pire
Surtout lolou nak. Bilahi vous avez tout dit
@innachanel9139 Motah après lagnouye comprendre.
Vraiment Bourry est une brave dame 😢😢 qui est d'accord
Bismilah si wa team diop fall😂❤ vraiment rien a dire on adore 😢
Félicitations wa Even prod 🤞🏽sénégal keur yi limofi nek
Vraiment je n'ai pas m'empêcher de pleurer thiey y'allah force à toutes les femmes qui vivent la même chose 😢