ZIARRA GENERALE 2023: Le message du Khalif délivré par serigne Pape Makhtar Kébé

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 25 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 197

  • @TheTamsir
    @TheTamsir ปีที่แล้ว +40

    Discours bi matt na macha’Allah. Toujours un plaisir d’écouter Serigne Pape Makhtar Kebe !

  • @fallhadji1213
    @fallhadji1213 ปีที่แล้ว +8

    As'salaamu anlaykum war'Rahmatul'LAH. Je suis toujours impressionné par votre yar, votre sagesse et votre perspicacité... Quand je vous écoute parler je ne peux m'empêcher de penser à Mame Abdu RTA. Mashaal'LAH Serigne

  • @ndeyekane3567
    @ndeyekane3567 ปีที่แล้ว +22

    barkep serigne touba pape makhtar mala baga yalla naga fi yaga ta werr

  • @morndiayemor435
    @morndiayemor435 ปีที่แล้ว +45

    Dieure dieufati am kilifa gou mat kilifa loco dieundé diar naco yalna lein yalla dolli samm may lein weir ak goudou fann inchalla ❤

  • @seynaboudiane5391
    @seynaboudiane5391 ปีที่แล้ว +33

    Ma shaa Allah discours complet et plein d'enseignements. Yananou Yallah samal sounou Khalifa qui nous l'a choisi parmi les nombreuses recommandations de notre vénéré Aboul Abass Atijani mayko goud fan ak wer. Amine barké Cheikhoul Khalifa borom besbi. Pape Makhtar merci pour votre fermeté et éloquence. Chapeau bas à ASFIYAHI rien à dire. Merci pour votre modestie et grandeur dans le travail

    • @abdouazizpouye717
      @abdouazizpouye717 ปีที่แล้ว

      Q0 pp

    • @karimatoudiack4381
      @karimatoudiack4381 ปีที่แล้ว

      Pa Makhtar Machalah! Sa discours bi doyon n'a. Lep lougnou worone wakh wakh ngako. Doyona seuk. Loussi yokou bou yakhoul defaroul dara! Sa Kabou yi khalifabi yoné dalna khel. Majorité Sénégalais yep lolou légnou wakh. Sama kharit Touba you baré woté negnou né Pa Makhtar Kébé daal moy Serigne Abdoul Aziz Sy Dabakh RTA. Rafetna, l'islam la, intérêt l'alouette dé! Deugueu rek Yalana SWTA Same la, sama Serigne Babacar SY Mansour. Contane négnou Chi yen gnar lool

    • @malicktoure4500
      @malicktoure4500 ปีที่แล้ว

      يارب طول عمر مختار كبي بجاح مالكنا

    • @absambaye2368
      @absambaye2368 ปีที่แล้ว

      Dieureudieuf kébé message amna solo yalla na la yalla dafal tawfkh ak taissir ak nadiakh ci barke saw

    • @maguitaseck6991
      @maguitaseck6991 ปีที่แล้ว

      Amine yarabi yarabana

  • @aichagueye6506
    @aichagueye6506 ปีที่แล้ว +5

    Oustass Moctar kébé machallah yalla nala yalla goudal fan wi weral thier yi djital si al khalifa ak jambotou sydi hadji Malick yepouh ak kepou kouy dioulittt 🙏si barké seydina Mouhamed PSL

  • @attagueye3007
    @attagueye3007 ปีที่แล้ว +1

    Macha allah toujours egal à lui meme depuis qu'il nous transmet les discours de mame dabakh je suis tres contente de t'ecouter goudou fan wér jam ju sakh dakk soutoura ci boolem djoulit amiin ❤❤❤❤❤❤

  • @hajjgora605
    @hajjgora605 ปีที่แล้ว +5

    Louwaye woute ci sa Walou Yalla bo démé Tivaouane daa kofa fékk mou bari bani ganie léer néh nanie té sétt withie
    Seydil Hajj Malik meussounio nakh Yalla nanou ko Yalla fayal barké Seydina Muhammad صلى الله عليه وسلم 🥰🤲🏼💚🤍

  • @abdouazizdiop8746
    @abdouazizdiop8746 ปีที่แล้ว +1

    Papa goudal fan si barki Saydina Muhammed PSL yallah nako gneippp yaga feikei merci beaucoup vraiment Asfiyahi

  • @aliadiop7349
    @aliadiop7349 ปีที่แล้ว +18

    Serigne pape makhtar Kébé yalla na yalla goudeul sa faane yook la wéer 🤲🏽🤲🏽🤲🏽🤲🏽🤲🏽🤲🏽🤲🏽

  • @racinediop7154
    @racinediop7154 ปีที่แล้ว +4

    Machallah ! Discours bi amna solo. Lëp diangaléla. Yallah na nu yallah fayal sunu kilifeu yi, defal leen gudu fan ak wër ak sutura aduna ak alakhira.

  • @T3JTV
    @T3JTV ปีที่แล้ว +5

    Dieureudieuf Serigne pape mactar kebe.yalla n'a yalla woutou fayal nioula.Serigne Babacar Sy mansour yalla nafi yague té werr.Motali ak diam projet yi.

  • @dabakhwade4695
    @dabakhwade4695 ปีที่แล้ว +7

    Mach'allah Al'hamdou lilah
    Dieureu dieuf Pape Makhtar KEBE message bi amna solo trop.
    Tivaouane deukou leir 💫
    Serigne Babacar SY Mansour Alkhalifa yàl n'a borom yagal taxawayam si kanamou ndiabote gi si barké Yonanta bi SAW amin yarrabi 🙏

  • @babacarmbaye6892
    @babacarmbaye6892 ปีที่แล้ว +5

    MACHAAĹLAH...
    Yallah na Yallah wëraal thieurr yi.
    Un discours très très très instructif, digne d'un Talibé Cheikh et qui vient à son heure🙏🙏🙏

  • @laminediouf3713
    @laminediouf3713 ปีที่แล้ว +3

    BarakALLAH BarakALLAH BarakALLAH. Rafetna yiwna meutna. Yalnagnou YALLA feyal Seydi Hajj Malick ak njabootam. DjazakALLAH Serigne PM KEBE

  • @adamathiomefaye3259
    @adamathiomefaye3259 ปีที่แล้ว +2

    Machala yanagn Yalla fayal Cheikh Ahmath Tijan Chérif leep simom laa tambalé fatabarkalah lii wanéna nii kou am Cheikhal Khalifa am nga Yonénte bii amnga Mame Maodo amnga Cheikhou Tijan🙏🙏al hamdoulilah sanete Yalla bignu donei ak djoulitt téksii nék ay talibé Cheikh🙏

  • @Hawaa351
    @Hawaa351 ปีที่แล้ว +1

    Machalah guiss na si sama bopp si discours magistral bii kebe same goudal fane wu beuri mou ande ak weer sutureu ak al khalifa serigne babacar sy Mansour nakhouleen nou mouk

  • @moussasy2813
    @moussasy2813 ปีที่แล้ว +12

    Tivaoune danion dég moune wakh deug monye nieuk deug monye moudieu Masha'Allah

  • @fallaboudda94
    @fallaboudda94 ปีที่แล้ว +5

    MACHALLAH SEUTOU DEMBA BOUNA SY BII CONTANE NAGNOU THI YAWE DJEUREU DJEUFE MAME MAODO MALICK SY J'AIME TIVAOUANE ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ousmanembengue1119
    @ousmanembengue1119 ปีที่แล้ว +3

    Bilahi ma beuge Papa Makhtar Kèbè machalla diangalè bii ame na soloo💯🙏 Yallah na Yallah yok kham kham ni maye wèreu ak wèreulè sou niou kilifeu yi fi nèk

  • @khadipouye3630
    @khadipouye3630 ปีที่แล้ว +4

    Bilahi talibe cheikh rk d'où ayé foooooo kebe yalla n'a yalla may la wer ake goudou fane 🙏❤️💪💪

  • @abouamadouba9955
    @abouamadouba9955 ปีที่แล้ว +1

    Message court, précis et très instructifs. Guddu fan AKk wërr 🙏❤️✊

  • @fatoudiop4608
    @fatoudiop4608 ปีที่แล้ว

    Machallah konne ningako donne défé ak Mame Abdou Aziz Sy dabakh begoul wonne di wah nioukay tatiou ndahté daféné day diotali wahou yallah kassé pape makhtar kébé yalna yallah goudal saye fane andak were

  • @taphadiagne8550
    @taphadiagne8550 ปีที่แล้ว +14

    Quel discours, kouné guisguasi sa bopou , yalna yalla fayal nioulén 🙏🙏🙏machalla

    • @prettymera1918
      @prettymera1918 ปีที่แล้ว +2

      Walahi! Mane dama contante😭Sama khel daffa dall 🙏

  • @ndeyekhadythiaw1216
    @ndeyekhadythiaw1216 ปีที่แล้ว +1

    Fatabarakalla maashalla beguatinagnou yallana yalla feyalgnou pape makhtar kebe

  • @mamadoumoustaphagueye6100
    @mamadoumoustaphagueye6100 ปีที่แล้ว +14

    Un message d'une haute facture. Macha Allah

    • @mamadoulaminendour4983
      @mamadoulaminendour4983 ปีที่แล้ว +1

      Maa shaa Allah...Un témoin auculo_ auditif de la période de Mame Abdou Aziz ...Un rappel pour tous...yalna Bour Yalla fey yiw..Djeredjeufaty KÉBÉ..AMINE AMINE YA RABBY...

    • @astoufall7125
      @astoufall7125 ปีที่แล้ว

  • @oumarly3185
    @oumarly3185 ปีที่แล้ว +1

    Machalla yalla naniou yalla may deugg AK topp pape makhtar kébé yalla na yalla gouddal sa fan mayla weur AK ndiabotou Mame seyidil hadji Malik sy yeupp

  • @mariatandiaye8560
    @mariatandiaye8560 ปีที่แล้ว

    Machallah amna solo lolou❤️🙏🏻Yallah naleu Yalla faye yiw 🤲🏻

  • @yamardieye3071
    @yamardieye3071 ปีที่แล้ว +3

    Soune goor gui Yalna ko yalla may goudou fann defal ko diame 🎉

  • @abdoukarimgueye6629
    @abdoukarimgueye6629 ปีที่แล้ว +4

    Dieuredieuf seydina Aboul abass cheikh Ahmed tisane Cherif

  • @alaminegassamasoldarbi9868
    @alaminegassamasoldarbi9868 ปีที่แล้ว +5

    Yallna yalla fayal niou len si barke Mame cheikh seydil hadji Malick Sy

  • @ousseynoudiaw-go6me
    @ousseynoudiaw-go6me ปีที่แล้ว +1

    Machalla lafthiat yalna yalla samme lèn

  • @lovediop4480
    @lovediop4480 ปีที่แล้ว +2

    Magui wakhna ma begue papa makhtar kebe ta yalla rek takh 🥰❤️

  • @Souleymanekanediamil97
    @Souleymanekanediamil97 ปีที่แล้ว

    El Hadji Makhtar Kébé yalna yalla goudeul sa fane té dollila wer bidiahi seydinna mouhammad salalahou Aleyhi wa Discours bi Setna Selna matna yalna geneu degeureul sa taxawaye si dinné dji ak si tarikha bi bidiahi seydinna mouhammad salalahou Aleyhi wa salam.

  • @cheikhmoussaka3278
    @cheikhmoussaka3278 ปีที่แล้ว

    Machallah sangue amna solo lol waay yalna yallah mayniou dégg ak topp.
    Guiss nanie si souniou bopp bou baax.

  • @awatoure2470
    @awatoure2470 ปีที่แล้ว +2

    Alhamdoulilahi rabbil alamine. Dîeureudieuf Allah SWT. Sounou Khalife yalnako Allah SWT same bayil gnouko fii bamou inaugurer sounou jumma bi ,ngungué gnou ba ci kanama kanam

    • @mamisene7293
      @mamisene7293 ปีที่แล้ว +1

      Allahouma Amine

    • @awatoure2470
      @awatoure2470 ปีที่แล้ว +1

      @@mamisene7293 merci mamy. Yalna Allah SWT doli diam ci senegal

    • @mamisene7293
      @mamisene7293 ปีที่แล้ว

      @@awatoure2470 Amine yarabi si barké yonente bi Aleyhi Sallatou Wa Salam

  • @prettymera1918
    @prettymera1918 ปีที่แล้ว +2

    Eey waay li nekhnaa ❤Alhamdoulilah Machallah 🙏❤️

  • @virus965
    @virus965 ปีที่แล้ว

    Machalah papa yalna yala may gnou degue ak top kadou yi amna solo surtout ndialo bi Bari n'a ssi deuk bi trop yala 'nagn yala dioubal

  • @diagnepapis3515
    @diagnepapis3515 ปีที่แล้ว

    Ohh machallah dieureudieuf sama serigne degue ak top rek

  • @gnagnagueye4467
    @gnagnagueye4467 ปีที่แล้ว +4

    Discour bi amna solo pleins d’enseignements
    Dieuredieuf 🙏 yallana bour YALLA fayla thi barké MOUHAMADOU RASSOULILLAH 🤲🤲🤲

  • @IbrahimaKa-x5x
    @IbrahimaKa-x5x 20 วันที่ผ่านมา

    Diaradife pape makhtar kebe❤❤❤

  • @khadyseck8069
    @khadyseck8069 ปีที่แล้ว +2

    Yalla naniou yalla defal degue AK topou diagalé bi amna solo li laniouy khar si yen machallah yalla n'a yalla fay la Amine

  • @fatoukebe2313
    @fatoukebe2313 ปีที่แล้ว

    Machalla yalla na yalla mayléne wer ak goudou fane message bi amatina solo

  • @morndiaye3022
    @morndiaye3022 ปีที่แล้ว +1

    Machalla amna solo lol
    Serigne Babacar sy Mansour
    Yalna yalla defal la wer
    Ak fan wou goudou

  • @ndoumbembaye-gd8nr
    @ndoumbembaye-gd8nr ปีที่แล้ว +1

    Bouniou faté nianal Serigne makhtar kébé douniou sackla machahala

  • @ndiayetayorndiayesarr8560
    @ndiayetayorndiayesarr8560 ปีที่แล้ว +7

    Macha Allah Discours Mémorable !!!!

  • @Mpene1234
    @Mpene1234 ปีที่แล้ว +3

    Bilahi tariha tidiane mo nekh ❤

  • @abdoulayeniang2511
    @abdoulayeniang2511 ปีที่แล้ว +3

    Yalla na Yalla Goudeul Séne Fane Maye léne Katane Wére Ak Wérlé ❤️🙏🏿

  • @rokhayafall8351
    @rokhayafall8351 ปีที่แล้ว +6

    Machaala ❤️ yalla na Yalla fayal niou la bou bah kébé yalla na Yalla fayal niou souniou serigne al Khalifa message bi amna solo alhamndoulila deuge néh na

  • @assniang9152
    @assniang9152 ปีที่แล้ว +1

    Machalla am na solo macha alla fatabara kalla yalla na yalla barkéll yagual lén fi machalla talibés chiekh mo nékh ❤❤❤🙏🙏🙏👈👈

  • @ndeyegoubydiagne3616
    @ndeyegoubydiagne3616 ปีที่แล้ว

    machallah beau discours yallah na yalla fay

  • @ndeyeastouseck3539
    @ndeyeastouseck3539 ปีที่แล้ว +1

    Dieuredieuf wa keur Mame Maodo sy

  • @mansourniang4544
    @mansourniang4544 ปีที่แล้ว

    Thiéy bi hadara machaallah ziyar bi par semaine la War Di am

  • @baboudiouf8499
    @baboudiouf8499 ปีที่แล้ว +1

    Dieureudieul way P.M. Kèbe nasa diam yagg ak werr rk inshallah amna solo 🙏🙏 Sy Malick yagg fii si barké psl ❤ ❤ ❤

  • @mamedabakh8494
    @mamedabakh8494 ปีที่แล้ว +2

    Djeukeur Cheikh Papa Makhtar yalna ndamyi Teguallo yala yagualfi Khalifabi te ñou djanguuei thi waxtanwi yalna djoumadji Parei teñou djoulithi

    • @absambaye2368
      @absambaye2368 ปีที่แล้ว +1

      Pape Makhtar sa discourt bi couleur na diataille bi yalla na nou la yalla fayal kebe

  • @fallaboudda94
    @fallaboudda94 ปีที่แล้ว +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤J'AIME TIVAOUANE

  • @walkershouse28
    @walkershouse28 ปีที่แล้ว +1

    Sunu sopeii Pape Makhtar yalneu Yallah deugeureul taxaway bii bidiayii Rassul'Allah

  • @nafiseck6552
    @nafiseck6552 ปีที่แล้ว

    Macha allahou serigne makhtar yalana yala faye té yagaléne fi sameléne bopam Yalananiou yala defal topou ak dég

  • @babacarfaty4490
    @babacarfaty4490 ปีที่แล้ว

    Dieureudieuf pape mactar kébé
    Masha allah
    Discours amna solo trop té mate na

  • @maramekhouma9866
    @maramekhouma9866 ปีที่แล้ว +1

    machallah machallah papa makhtar kebe amatina solo sang bi machallah

  • @hamaththiame9296
    @hamaththiame9296 ปีที่แล้ว

    Serigne pape makhtar yalna yallah goudel sa fan faye la yiw kebe

  • @tafsirmbaye7567
    @tafsirmbaye7567 ปีที่แล้ว +1

    Machall ماشاء الله أطال الله بقاءكم أمامنا

  • @diallomamadou1431
    @diallomamadou1431 ปีที่แล้ว

    Macha ALLAH. JAZAKUM ALLAHOU KAYRANE.

  • @kebealaminetv5956
    @kebealaminetv5956 ปีที่แล้ว +4

    فتبارك الله أحسن الخالقين 🥰

  • @abdouniang9482
    @abdouniang9482 ปีที่แล้ว +4

    Ma challah wakhtanei bi amna solo ❤️❤️❤️❤️

  • @مالكك.إبراهيم
    @مالكك.إبراهيم ปีที่แล้ว +1

    مساء الله عمرك طوال إنشاء الله بخير وصحة وعافية وسلام معك كل.من.امين يارب

  • @abdoulayely174
    @abdoulayely174 ปีที่แล้ว

    Yalla nanioufi yageu lol té wére amine

  • @khalilleye1742
    @khalilleye1742 ปีที่แล้ว +1

    الحمد لله رب العالمين 😍
    Yalla nanu Yalla
    Tékkr ci Yonnu ndjoup,té defal ñu degg ak Topu

  • @khabanemboh9797
    @khabanemboh9797 ปีที่แล้ว

    MACHALLAH LI LANIOUYE KHAAR SI DJOTAYOU DINE YII

  • @badrutv5312
    @badrutv5312 ปีที่แล้ว

    ماشاءاللہ جزاك اللهُ‎

  • @Getma94
    @Getma94 ปีที่แล้ว +3

    بارك الله فيكم ❤

  • @karimatoudiack4381
    @karimatoudiack4381 ปีที่แล้ว +9

    Pa Makhtar yzlana SWTA goudeul sey fan té wéreuleu didjayi Seydil Woudjoud SAW Khalifabi yalanako SWTA defal wer ak goudeu. Djoumoul bimou la yoné. Meuteul nga lep sa Kaboul doyonna dé. Amoul parparlo, amoul fété, amoul bakeu Ken. SWTA ak Seydil Woudjoud rek. Kal Allah kalla Rassouloulah rek késsé donc. Sounou baye bou bakh ba, bou rey bakanam bou ragalon YAWMAL KHIYAMA CHI KANAMOU BOROM BI bekna Chi yaw. Serigne Babacar SY Mansour djoumoul Chi choix bi mou def. Meut nga ko. Sa discours rek doyone neu!MACHALAH

  • @ndeyesylla4478
    @ndeyesylla4478 ปีที่แล้ว +1

    Machalah serigne moctar kébé

  • @fatoungom9912
    @fatoungom9912 ปีที่แล้ว

    SOPE IMAM MAKHTAR 😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍

  • @fatouresow1675
    @fatouresow1675 ปีที่แล้ว

    Salam Salam ziarnaléne machalla dieureudieuf

  • @abdoulayefall8287
    @abdoulayefall8287 ปีที่แล้ว

    Yalla na yalla goudal seen fan, yok leen wer

  • @Gier889
    @Gier889 ปีที่แล้ว

    Machalah discours bi amna solo li rek la al amine wakhone tivaoune programme la khalif bou togg rk ngané gongo🙏

  • @reussirsesetudesaluvs7250
    @reussirsesetudesaluvs7250 ปีที่แล้ว

    Dieureuf Pape Moctar khole céda tina

  • @matarniang9603
    @matarniang9603 ปีที่แล้ว

    إِنَّ اللَّهَ وَمَلَائِكَتَهُ يُصَلُّونَ عَلَى النَّبِيِّ يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا صَلُّوا عَلَيْهِ وَسَلِّمُوا تَسْلِيمًا
    Ahzaab 56 .
    🤷‍♂️

  • @mamadous6919
    @mamadous6919 ปีที่แล้ว +2

    Djeredjef al Khalifa. Djeredjef Pape Makhtar Kebe

  • @ZawiyaCheikhElHdjMalickSy
    @ZawiyaCheikhElHdjMalickSy ปีที่แล้ว +2

    Machalla حفظك الله ورعاك

  • @papadembagaye1133
    @papadembagaye1133 ปีที่แล้ว +1

    alhamdoulilah

  • @matydiop6423
    @matydiop6423 ปีที่แล้ว

    Alkhmdouliha ❤

  • @chefale6572
    @chefale6572 ปีที่แล้ว

    Machalla 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @mbayebabacar5653
    @mbayebabacar5653 ปีที่แล้ว

    Machallah yalla naniou yalla defal degue ak toppo

  • @ourydiagne3144
    @ourydiagne3144 ปีที่แล้ว +3

    Macha Allah amna solo

  • @malickba-xq2wo
    @malickba-xq2wo ปีที่แล้ว

    jeureujeuf si kaddu yii. Yalla naniou yalla may deig ak topp

  • @yeewuteyeete8468
    @yeewuteyeete8468 ปีที่แล้ว

    Amatina solo yàlna yàlla sàamm te aar te may ñu dégg ak tòoppu 🙏🏼

  • @djashkeub7231
    @djashkeub7231 ปีที่แล้ว +1

    Machallah imam kebe wakhtane bii rafett n

  • @ametdamedrame6532
    @ametdamedrame6532 ปีที่แล้ว +1

    Ziar ❤️. Valider

  • @nogayeboye-pf3bx
    @nogayeboye-pf3bx ปีที่แล้ว

    Serigne Babacar sy Mansour yalna fi yag té werr

  • @omartouretoure2454
    @omartouretoure2454 ปีที่แล้ว

    Machaalah pape Makhtar kèbè❤❤

  • @touss544
    @touss544 ปีที่แล้ว

    Machalla pape makhtar kebe

  • @ahmadfall6502
    @ahmadfall6502 ปีที่แล้ว

    فجزاكم الله خيرا

  • @amadoubassiroumbodji
    @amadoubassiroumbodji ปีที่แล้ว

    Machallah yalna yalla yagual lafi yagualfi seydi aboubacar sy mansour

  • @papendiaye3400
    @papendiaye3400 ปีที่แล้ว

    Machalla yalna takhaway bi yagg

  • @moussagueye8221
    @moussagueye8221 ปีที่แล้ว +1

    شكرا لكم جميعا حياكم غ وبارك فيكم وجزاكم خيرا

  • @egb3911
    @egb3911 ปีที่แล้ว +1

    Machallahh 💚🤍💚

  • @Youzarsif739
    @Youzarsif739 ปีที่แล้ว +1

    Macha'Allah ❤️🙌🏽

  • @daoudasambasy8963
    @daoudasambasy8963 ปีที่แล้ว

    JAREDIEF PAPA KEBE TABARAKALLAH , YALNA SUNUBOROOM GOUDDEUL SEENI FANE SAMLEEN AARLEEN WOTTOULEEN YOKK SENN QATTAN AK SEEN WEUR