Jahman X-Press - CELEBRATE - Album ABIYO
ฝัง
- เผยแพร่เมื่อ 9 ก.พ. 2025
- EN CONCERT AU POINT FORT D'AUBERVILLIERT 27 SEPTEMBRE 2024 : shotgun.live/f...
Production : Hoside Studio
Prod & Mix by Jeuuss Beatz
CONTACT MANAGEMENT : 77 640 22 08
ECOUTER L'ALBUM ICI : backl.ink/1496...
Bessou mbegté leu ci mane
Bég bou amoul foumouy yam
Bég ci lima yallah deff
Beneu Baye Fall lou niow mané kheyneu dafa gueune
Bessou thianta leu ci mane
Thianta ngiir diam dji ma am
Dieureudieuf !
Dieureudieuf ! Yallah buur bima lakkeu
Fou beut bou bone yegoul wala lokho bouy yakeu
Damay contane continuer
(Bégué beauté ! begué mongui baakh ! Bégué beauté ! )
Mangui bég tei bégueulé
Merr maîtrisé
(Bégué beauté ! Bégué mongui baakh ! Begué beauté ! )
Diégueulé tei diéleulé
CELEBRATE ( nioune daniouy foo)
CELEBRATE ( kou merr bokko )
CELEBRATE ( fii lépeu jamm)
CELEBRATE ( bégué beauté )
Té niit liy garabam niit leu
Diama gueune li ci sa compte
Damay bég même soumay banque
Lénéne lou niow rek bonus leu
Yallah teral nama kone nak defal ci mane ndank
Soumay guestu lima wessou
Khamné mane merr warouma non non
( Nonono )
Awma dara loumay réthiou
Ndakh yallah yagg nama tekk lokho
Am sokhla fadjal ko sa bopp
Diarna sante yallah té khamni kene mounoul mey sa bopp
Wakh sakh mou yegu yallah la nekh
Kone warnga santeu yallah saa bo yéwo
Damay contane continuer
(Bégué beauté ! bégué mongui baakh ! Bégué beauté ! )
Mangui bég tei bégueulé
Merr maîtrisé
(Bégué beauté ! Bégué mongui baakh ! Begué beauté ! )
Diégueulé tei diéleulé
CELEBRATE ( nioune daniouy foo )
CELEBRATE ( kou merr bokko )
CELEBRATE ( fii lépeu jamm
CELEBRATE ( bégué beauté )
Degg naa fi louné , dadj naa fi louné
Deukeul ma founé té woul mangui bégué di dem
Saga nagn ma ndeye , takoul feneu ci mane
Mangui doli santeu yallah ndakh mom rek moy ki meune
Bégué beauté !
begué mongui baakh !
Bégué beauté !
Bégué beauté !
Bégué mongui baakh !
Begué beauté !
Machallah 🥳😍où sont les fans de jahman X-Press manifestés vous waye toujours guan nioye beuguel merci beaucoup et bonne continuation
Aaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaa
Masan
Merci beaucoup
Celebrate. Il faut avoir la joie de vivre. Di sante yalla fougnou tolou. Alhamdoulilah. Merci pour cette belle chanson très pointue dans l'écriture 🔥🔥🔥
Bilayii yalla na sa diamou yague machalla tu es fort💟💟💟💟💟💟💟💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯💯
❤❤❤❤❤
Lowayol bakhol yalnala yalla dole samo😭😭💪💪💪❤❤❤❤❤❤❤
Je valide
Machala je t'aime
Jahman nak balgnou mo lii kenn douko def ni🥱😭😭❣️❤️❤️❤️
Jahmancetamol de L'Amour quand tu prend cette comprimé ça adoucie le khol ❤💗💓💔💕💚💛❤
Merci beaucoup fra
De l'art
De la beauté
Du succès
De la voiture d'or
Sa s trouve sur lui bon continuation
Merci Jahman❤❤❤❤❤❤c'est moi Banosall ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Oh mon Dieu du lourd bonne continuation frère 😍🥰
oh jahman je t aime
no jahman dou nitte quoi mane dall damala beugue rkk
machallah
Warnagne Sante yallah sa yougnou yewo
Une fierté Sénégalaise particulièrement Diourbéloise t'es entrain d'abattre un job hight class , y'a l'harmonie des mélodies
Machala frère tu es le meilleur
Toujours égal à toi même merci pour le joie que tu nous procure nalla succès sonal téy djik leu peace end love 🥰🥰❣️ de
Wakh sa mou yegue Yallah ma nekh... lou leer.
Bravo j'adore tt simplement
Le meilleur de sa génération on t'aime fort ❤️❤️❤️
Machala ta encore tapé fort diam si yow
Ma çhaalah jahmane mane dale bègue na si album bi ndax mane gasé diagne ndax nite bou mèré warga metrisé mère bi ndax louka moye ga wakh lou apou 100%100 baol baol bagui nonou texi deuk Touba
Salut to jahman
Franchement amouma préférence si album bi car son yeupa mashallah
machallah nice chanson ❤❤❤ j'adore
Ton BeatMaker tu l'as déniché où? C'est incroyable, une mélodie magnifique, ta voix, mon Dieu, il faut essaye de sortir un peu du Sénégalais.
J'adore vraiment cette chanson bravo jahman🥰🥰🥰
Machalla j t'aime laff tiatt
Bonne continuation notre jahman national 🇸🇳ton album c'est du 🔥🔥 machallah
❤️❤️❤️❤️💯
Je suis très fière de toi jah bilay bonne continuation et que dieu te bénisse et te donne la force sur tout
Hoooo
🥳🥳🥳mba khol yi fékh na
Mes chansons favoris Celebrate et Yaay mais album bi tout est OK 👌machala Jah yalna yallak S Touba fayla
No wwaaay bi sens bou extraordinaire la am😭❤✨
J'écoute en boucle. Mon Dieu!!! Quelle voix !!! Machallah puisse Dieu veiller sur ton talent. L'album en entier est une tuerie.
Je valide ❤
Salam ma sœur vraiment y a de quoi c est super😍
Machallah yangui def sa joob on t'aime fort❤❤❤❤
Cool oooooook
C est le méilleur bilaye💕
Doundal boy
Machallah longue vie frère on jt'aime fort 🥰🥰😍🇸🇳👌
Bilae diama geune lissa compte ✌️💪
Album bi Nice na trop bilahi vraiment liguey nga ko de la part de lamine depuis sokone
Ñongi lay bégué notre Jaman national mangi lay bégué depuis SL
💃🏾💕💕
Bilay jdtr frère du lourd com dab deumere bénis mon cher bilay beugnala♥️🙏🙏😘♥️
Jahman qui est tu wowww quelle masterclass your voice is sublime
Machallah Dafa lèrr bilaye ❤️😘
Bilhali ki damako beug ❤
Album bi doumaci doyal surtout YAAY
Nn vrai yagui beuguélei🙏🥰
Waouhhhh💞machallah 🥰 broh yangui déf sa job
On est la numero 1
Diadieuff bro son yi deg diam! Fier d'etr baol baol
❤❤❤❤❤❤❤
Machallah fall lép Nice na ❤️❤️❤️👌
Célébration Nice meilleur Album de l'année inchala Machala
Mon le prefere du lourd 💃💐
Ay tonton diakh togal mayma ma consommé li diota géneu yalna sa diam yag tu es le meilleur
Machaalah sa dole bala 🔥🔥🔥
You'are the best of the best
Oh je l'aime trop khole seedatina depuis je ne fais k t écoutais à longueur de journée tes sons fans bou dof fière de tw
Sante yalla mouye sama borom
Bonne continuation inchallah lépeuy bakh ❤️💖💖 tes fans t'aiment fort 💪💖
Machallah tu as encore tapé fort on t'aime bien ❤❤❤❤
Toutes mes félicitations Jahman you are thé best.
Machallah nékhe na tamite 🔥🔥❤❤❤❤💪
Le king de sa génération bilahi ❤ bonne continuation
des paroles très riches. bonne continuation jahman 👏👏
Je l'adore.Il est une inspiration pour moi.chapeau à lui.
Oh Jahman tu es le meilleur que Dieu te protège
Machallah neh na mon frere bonne continuation et des bénédictions en abondance
Jahman force a toi 🇸🇳🇸🇳🇲🇷🇲🇷🇲🇷
J'adore vraiment la chanson 🔥♥️
Machallah @
Jah bal leine way🥺🔥🥵♥️🎊🍾
Machalla Machalla Machalla. J adore
Vraiment jahman chaque jour plus doux plus romantiques avec jahman on kiffe du vrai musique je t'encourage chapeau à toi
Respect bro tarkalah machaallah
♥️♥️♥️♥️
Un album de ouf des paroles tres riches félicitation à toi jahman the best
C'est comme ça amnagno kham ne ndagnolay wak kay madiala burërre worr la dom ssa thiieüla DH kolel
Felicitation notre fierté ❤️🥰🥰
♥️♥️♥️❤❤❤sa c d la musique pure pa delonges juste d bel paroles jahaman té l New KING
Bégué boté késsé ya meun❤️✌️
Waaaaw c'est ouuuffff l'album est riche ❤️❤️❤️❤️🔥 🔥🔥🔥🔥♥️♥️♥️
Niceee💞💞love sur toi❤️👍
Machalah contane si yaw 🙏🏻💫♥️♥️
Ki mo daxa way si monde bi😙
Bimome amatoul bilay
Machallah jahman
Machalla très belle chanson
Toujours fière de toi que du bonheur toujours du lourd 💃💃💃💃💃💃💃💃💪💪💪
No Fall balléne waye
Jahman on t.aime fort domou baol BI❤️❤️
Ce son est devenu mon nouveau BOOSTER des matins d’hiver oú la motivation n’est pas tjrs au RDV. Je le mets à fond dans le métro et suis prête à affronter le monde, MERCI Bro 😍
Nékhna ci ❤❤❤❤❤
Jahman the big
Bilay yay s'en Baye j t'aime fort ❤️❤️👍
Tu est vraiment ouf walahii bonne continuation frère
No li khaw nama Ray❤️😆😆😭😆🥰🥰
Oh comme ile parlé sur moi ❤️❤️❤️🤲😭🤗
💖💖💖💖💖💖💖💖💖