Dip ak nit dof niobokou combat ay patriotes lan bi réwmi di méti khékh bi niodon wakh andeu ak jeunés bi ak peuple sénégalais ❤❤❤❤sounou diambar yi 🎉🎉🎉🎉
Mane mom franchement artiste tchi sa engagement bi nga ame par rapport à sa askan lalay diappé motakh respect à Nit Dof you know. Sinon Rap Galsen suivre nako depuis diamonoy foural ak concours dance mo amone après niom Mc Lida ndieuka rap ak niom PBS, Daara Dji, Pee Froiss etc jusquà diamonoy compilations yi, mais nak franchement generation bou bess bi gni tchi real pour mane ak gni tchi séne songs nekh tchi mane bariwoul dal, encore une fois respect Nit Dof !
Man personnellement diapoumani clash moy néxal rap bi oubien moko meuneu yobou si kanam mais culture hip hop créativité la soxla ak ay collaboration kom ricains yi. Boy yi gnoussi bari si gnom clash ak egotrip lagnou meuné solén tégalé thème rék gnou peuteux. Dou gnom gneupa meuneu bind té rap dou rek def say sounds di clash egotrip ak woy mbeuguél donté sila bok rap engagement. So téyé micro 🎤🎙️ di wax pour nitgni dégeula dagaleni wax loulén amal ndiarigne pas louléni delo guinaw wala lou amoul sens. Sinon d'ici quelques années say way kén dotouko déglou. Liguéye bobou la grand yi def motax batay séni son déssfi
Excuse meme deja le domaine dans le quel tu es entrain de t'expliquer il ya des gens plus connaisseurs et d'apporter des chiffres concrets mais meme si tu as raison il a une maniere de s'exprimer en public le respect que tu aimerai qu'on donne ca doit d'abord commence par soi meme comme on le dit chari bien commence soit meme excuse moi encore
Même Dizzy KHA je trouve qu'il est sous côté mais est-ce que dih nguenn déglou ak le niveau de ses textes ? Il est montreux mais le GOAT du rap Galsen reste *"Dip_Doundou_Guiss"*
Omzo et Dip peuvent bel et bien se réconcilier mais cela ne viendra pas du hip hop mais plutôt un personnalité respecté comme un Thione Niang par exemple.
Omzo n’est pas sérieux Koma s fait il q nga meuneu juger carrière si benn extrait bo deglou si boutique Dit la vérité est très simple. Do wakh directement deglou nako tay deglouko demb c simple
Tu n'a jamais aimé Omzo dollar d'après lima guisson mais tey môme chapeau a toi mais par contre je ne dis pas tu l'aime Aujourd'hui mais c'est un peu positif
JOUBO DIP ET OMZO ⤵️
Rap Galsen rekk moo ciy gagner 🎉❤
Oui❤
Oui
Oui
Bah oui
Dip ak Nit Doff ayy Patriotes lay douniou tassoul bein President mes respects
Dipl moy Diplôme 🎓 rapour yi ❤
Barki alxourann dip dou rapeur il est autre chose ce gars😮😮😮❤
Omzo iss ladone wakhal dou Dip😡
Vraiment 😂
Vraiment
Saway Kay video wambi dafa sathieu film bi😂 kou sétanoul interview omzo dagay foguené dip lay waxal alors que c'est ce traître de Fake de iss
Archi si bopam mo seytané
Dip ak nit dof niobokou combat ay patriotes lan bi réwmi di méti khékh bi niodon wakh andeu ak jeunés bi ak peuple sénégalais ❤❤❤❤sounou diambar yi 🎉🎉🎉🎉
Dip meilleur rappeur du Sénégal ❤❤
Meilleur rappeur d tout le temps omzo dollar
Mane mom franchement artiste tchi sa engagement bi nga ame par rapport à sa askan lalay diappé motakh respect à Nit Dof you know. Sinon Rap Galsen suivre nako depuis diamonoy foural ak concours dance mo amone après niom Mc Lida ndieuka rap ak niom PBS, Daara Dji, Pee Froiss etc jusquà diamonoy compilations yi, mais nak franchement generation bou bess bi gni tchi real pour mane ak gni tchi séne songs nekh tchi mane bariwoul dal, encore une fois respect Nit Dof !
C'est ce Sénégal qu'on connait ❤️
Ta totalement raison archi dip feat Ngaaka 🎉
King baba 🎉🎉
Dip seul 🔥🇸🇳🤟
Bou sisou amoul Omzo d'où morome benne rappeur ❤
Sénégal 🇸🇳 moy gangé 👑❤️
Meilleurs rapeur de tout les temps Zo Dollars
Kan 😂😂😂😂😂😂 yalla degue na Wolof dh astaxfiroul laha
Merci beaucoup frère j'espère que amna solo 😍 hip-hop Galsen United ❤❤❤
Bou ken dioubo 😂😂 thiow li moy safal rap bi😂❤
Mièzé de Riv A.K.A sène Papeu 😊
Dip seul nit douf ❤❤
Les 5 meilleures rappeur du Sénégal kanla?
Omzo est le meilleur rappeur du Sénégal 🇸🇳 de tous les temps
Omzo d’où ben morom rappeur nek Len nitt omzo lan lafi dieul ba nek fi goat bi ben goat monfi am mouy papa dip
Meilleur rappeur omzo dollar
Dip vs ngaaka blindé dioubi j'aime
Dip moy papay rappeur yeuppp❤❤
Omzo s'adresse pas à dip ms plutôt Iss lay wkhni nekhouma j pense
Dip vs Omzo dioubo j'aime
King baba râpeur peuple ❤
Boy bul tumal omzo omzo iss 814 la wah ne nehut ko bayilen di dumal nit
Baba ndiaye seul
Meilleur rappeur Galsen nitt dof killer
Omzo yaw ak dip comme réal Madrid ak man united ,dip dou moromou benneu rappeur! C'est le meilleur rappeur du senegal de tous les temps❤❤❤
Omzo iss leu done Wakhal
Sa way Bouba AK la fouine douniou lalé
Sama avis diaroul feat
Man personnellement diapoumani clash moy néxal rap bi oubien moko meuneu yobou si kanam mais culture hip hop créativité la soxla ak ay collaboration kom ricains yi. Boy yi gnoussi bari si gnom clash ak egotrip lagnou meuné solén tégalé thème rék gnou peuteux. Dou gnom gneupa meuneu bind té rap dou rek def say sounds di clash egotrip ak woy mbeuguél donté sila bok rap engagement. So téyé micro 🎤🎙️ di wax pour nitgni dégeula dagaleni wax loulén amal ndiarigne pas louléni delo guinaw wala lou amoul sens. Sinon d'ici quelques années say way kén dotouko déglou. Liguéye bobou la grand yi def motax batay séni son déssfi
le 31 décembre dangay dem 😂wala
Fan nonou
Bayil say tanè omzo wakhoull dip nèkhouma bayilèn diakhasè
Première commentaire 😂🎉
vraiment ARCHI yagui déff aay recherche you amm solo mais le problème de nos Rappeurs GALSEN est que dono sofff
Omzo dollar wakhol wone ak dip dh iss 8 14 La done wakhal Nekhouma 👍
Dip rék ❤❤❤
Espèce de Nilar le rap est déjà en musique internationale
Excuse meme deja le domaine dans le quel tu es entrain de t'expliquer il ya des gens plus connaisseurs et d'apporter des chiffres concrets mais meme si tu as raison il a une maniere de s'exprimer en public le respect que tu aimerai qu'on donne ca doit d'abord commence par soi meme comme on le dit chari bien commence soit meme excuse moi encore
stp soutenir len akbes❤
Dip séîgneur du rap galsen🎉
King baba 🎉❤
Dip one lyrical loolu dina dooy waar
Dip feat king baba sera très bien
Oumzo ak canabass
Dioumbo naniouu🎉🎉
Nono frr ay rappeur Di wakh si ki ak Di wakh ké lolou mofi wara diékh
Bonsoir
Archi bo amoul principe muni comprendre li karballah di deff ou bien li zo dollar di wah life bi lepp dou xallis …
Dip ak king baba
Saay omzo bimouy wakh na doumdou ma doundou iss ladonn wakhal bayil yall derr
Iss mom bandit la té mola euppou xaliss yaroul rk Omzo😅😅😅
Omzo dalle ak dip ak nit doff ak nguaka blindé pourkoi pas nguéne défe béne son thi Anne 2025 bi q sa rék thi loho bok
mais pape sidy fall ak yeedy nk
Yw do méloman dh yw OmzO rk ngeu bagn
Saway seitan nagnou émission bi zo iss la don wakhal 😂
Adouna Lépa Mana nékki Nit doff Bénni jour Mi wakh Ba Mérr Nan Dip Dousa Morom 😂
Même Dizzy KHA je trouve qu'il est sous côté mais est-ce que dih nguenn déglou ak le niveau de ses textes ? Il est montreux mais le GOAT du rap Galsen reste *"Dip_Doundou_Guiss"*
Qsaa waxal gars yi deug def rap bou killeuh molay yobou sur la scène internationale
Omzo mofi née katal sa deye baye Omzo
Collabe bi mane n'a Indy dis que d'or bilahi
Omzo et Dip peuvent bel et bien se réconcilier mais cela ne viendra pas du hip hop mais plutôt un personnalité respecté comme un Thione Niang par exemple.
Garde la monnaie samba nice
Bly peuzzi li la kham motakh mou dieul yonam
Ak fimou mana youp rap galsen
Bly rapp senegal moy lo lou karbalah galsèn niou fa dake rapp sila bok
King baba seul
Omzo n’est pas sérieux
Koma s fait il q nga meuneu juger carrière si benn extrait bo deglou si boutique
Dit la vérité est très simple. Do wakh directement deglou nako tay deglouko demb c simple
Omzo Canabasse sen jubbo sm combat
Dou wax sax canabasse omzo
Tu n'a jamais aimé Omzo dollar d'après lima guisson mais tey môme chapeau a toi mais par contre je ne dis pas tu l'aime Aujourd'hui mais c'est un peu positif
Dip seul❤
Dioubo omzo ak Dip Manoul Nek niawna ba nopi
Boul wakh lolou 😢
Jdobo warto am ci rapport yi
King baba🎉
Name Naniu clash yi way
OmzO a vie ❤
NIOUNE OUSMANE SONKO REK LA NIOU ÂME KOU NIOU KO TIYEL NIOU TIYELA SONKO PARTOUT SONKO FEPOU BILLAHI MERCI BEAUCOUP BASSIROU DIOMAYE FAYE REK
Yangui dioume dh Omzo iss 814 ladone wakhale néxoumma pas dip, zo dollar néna meune na clashe dip si top3 yi
@@Tafisko22 dafa dioum ky
❤❤❤❤
Doundou guiss
King baba
🎉🎉❤
Wa Mais
Iow tu fais la confusion Babacar lui a posé la question sur iss 814 donc bayil mélangé affaire yii
No sérieux man sakh diap Nani djibo yi day déf effet
Yo bayil feneu ak diakhasé cest pas ton reul Omzo wakhoul dip iss la done wkhal li mo takh rap galsen bi bone
Non omzo il parlait de IS 814
TH-camure bi srx ay ré lamay dief
On dirait kou bok staff soleil levant dmn
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
🎉
❤❤
6:35
Dip
Omzo t’es le plus nul
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
King baba
❤❤❤