Séga communique bien et m'a l'air responsable machallah. Sokhna est si jeune,si innocente et a l'air très gentille. Longue vie à votre couple, yallah nalèn yallah samm té lafal lèn thiat ci barki Nabil Moustapha
Machallah quel beau couple, jeune, spontané, qu'Allah les assiste vraiment. Ils sont adorables surtout la fille elle est naturelle et très sincère Machallah.
Qu'allah vous fasse miséricorde 🤲 dans votre vie de couple 🤲🤲 suis contente ❤️ surtout la souriante Sokhna 👏🥰🥰 macha'allah je ris bêtement 😅 yal na sénn diamm yague
Machallah mon frère de coeur ndeysane dafa meusa bakh beug niit âme respect sociale aussi yeufeum la Di dadialè talibè yi fadiar dilèn defaral machallah
Khaw ma niane nioy wadiour sokhna ,mais ils sont très responsables et ils sont pas égoïstes,ils ont chercher le bonheur de leur fille C'est comme ça ay khalei bougnu beuguenté danga leine Di mayei ,bala gathi dissi am
😂😂❤❤❤❤magyi rétane rk rholala elle est trop chouuuu la fille 😅😅 Mu topeu je taime bi rk raynama 😅😅😂 ils sonts trop mignon mashaAllah ❤❤❤ yallah nalēen thiatt sekhlouuu 🎉🎉 ça se voit elle est gentille le sourire sur son visage n ment pas 😅😅 ndékée duu indou yii rk ñioy doundeu mbeuguél 😊😊
Affaires buh cool oh my God. Du courage vous etes tres jeunes. QU'ALLOU AKBAR VOUS PROTEGE SOUS SA PROTECTION INSHALLA ALLAH RABBY BARKE SEYDOUNA MOHAMED PSL AMINE Yarraby
N'ecoutez personnes que votre parents vraiment je suis tres content de vous QU'ALLOU AKBAR YOKE CENE Diame Ak Salam Inshalla Allah Barke Seydouna Mohamed Psl Inshalla Allah Amine
Séga communique bien et m'a l'air responsable machallah. Sokhna est si jeune,si innocente et a l'air très gentille. Longue vie à votre couple, yallah nalèn yallah samm té lafal lèn thiat ci barki Nabil Moustapha
😊
😊 21:45 'o😅
24:12 😅o
Ooooh ndeysane beuguel
Jai un seul mot machallah di na metti di nekhe restes soudez mon couple prefere
Sokhna beug nga ré ba melni mane😂😂 mais machallah longue vie à vie que Dieu vous protèges
Pourtant Sokhna elle est très intéligente ceque dafa timide rek 😊😊 machalah sen couple rester soudez yallna dinguenbi khate seytané sorrilen ❤
Sokhna son sourire est contagieux 😂❤️❤️❤️❤️wollah MashAllah à vous
Ndessane la fille môme quand elle sourie je souris 😂😂 je veux être comme toi 😂😅
Machallah quel beau couple, jeune, spontané, qu'Allah les assiste vraiment. Ils sont adorables surtout la fille elle est naturelle et très sincère Machallah.
Interview bi yép damoko rétane😂😂😂couple khalé sokhna elle est mignione macha allah et kou bakh lay nirole
Ndeyesane sokh na day sourire rek 😍🥰🥰
Merci pour cette joie de vie que vous nous avez offert ❤❤❤❤❤❤❤
Sokhna ndeysane day rétane nitt kou bari diam machaalah yalnaléne yalla sam
Salibataire yi ame l'en diom touti 😂😂😂khana warguéna rouss deh❤❤❤❤❤❤❤
Lii dafe ma nekh Machalla yalla naiou yalla aye diabarr you bakh
Couple jeune responsable c 1% dans le population et c vous machallah 😊❤
Oh machallah amgua diabar bou simple Bari Diam ♥️💯
Machallah
Déf Guen Li war
Yalnaléne YALLA tahawou Arlene mousalene si thiate.amlene diame
Qu'allah mettent de la baraka dans votre union ❤amine 🙏🙏🙏
Qu'allah vous fasse miséricorde 🤲 dans votre vie de couple 🤲🤲 suis contente ❤️ surtout la souriante Sokhna 👏🥰🥰 macha'allah je ris bêtement 😅 yal na sénn diamm yague
Amin
Yalnalene yalla mousseul si thiate
Machallah vraiment nalen yalla same bou bakh boulen khejal ken sen didante
Bilahi Sokhna sou rétané rk damay ré khawma lane la.Blagues appart elle est mignonne ❤
Naniou lene organiser kermesse waye nioune célibataire aussi beugeunaniou djeukeur niou deff comme sokhna ak djeukeureum 😂❤
😂😂 billaye bb 😢
@@kadiatoutamboura4587 ah oui😅
😂😂😂😂
Machallah mon frère de coeur ndeysane dafa meusa bakh beug niit âme respect sociale aussi yeufeum la Di dadialè talibè yi fadiar dilèn defaral machallah
Ma sha'allah yalla naléne yalla l'afale thiate
Shona is a peaceful wife she always smile
Sega a une bonne communication machalah il communique bien❤❤❤
Machalla.yalla nalen yalla sam té mousseul lenn si thiat. Je vous adore
J’adore se couple il sont si jeunes 😂❤️
Machalah gniom gniar yeup ay khalé lagniou
Khaw ma niane nioy wadiour sokhna ,mais ils sont très responsables et ils sont pas égoïstes,ils ont chercher le bonheur de leur fille
C'est comme ça ay khalei bougnu beuguenté danga leine Di mayei ,bala gathi dissi am
On sais très bien sa mets il ne faut pas insiste ma cousin
Jeune couple machalla Qu'Allah vous protège ❤❤, mais sokhna est très timide 😂
LONGUE VIE A VOS COUPLE
Sénn couple néh n'a ma bilay comme Man ak sa ma copain bii depuis 2019 je vous aime
i love both of you i pray you have long lives and a successful marriage i love this couple so much
Amine
Machallh ma fille chérie longue vie ❤❤
Sokhna momm Beuryna jaamuu maachalah😂😂
😂😂❤❤❤❤magyi rétane rk rholala elle est trop chouuuu la fille 😅😅 Mu topeu je taime bi rk raynama 😅😅😂 ils sonts trop mignon mashaAllah ❤❤❤ yallah nalēen thiatt sekhlouuu 🎉🎉 ça se voit elle est gentille le sourire sur son visage n ment pas 😅😅 ndékée duu indou yii rk ñioy doundeu mbeuguél 😊😊
Sokhna xallei la Bly que dieu vous protège
Sama rak yi Machallah yalla n’a leen yalla taxawou ❤❤❤
Ils sont mignons ❤❤❤❤
❤❤❤❤❤machahalla lo gue vie sokhena et segua contene si yéne❤❤❤❤❤❤
Machallah yalla nalène yalla dèfal diamou 🤲🤲
Machala elle est toute gentille adorable diamb si yéne🎉🎉🎉
C'est des anges ❤❤❤❤❤❤❤❤
Ndeysane sokhna da beuri diam machalla
Masha Allah ❤❤❤ sou jeunes yi démé bay ame mentale bi, gneupa wara roy si gnom
Yalla na Yalla youkou soutoura ak diam machala
Masha allah yalla nalen yalla sam mousseul len cii thiate
Yalla nalein yalla sam té aar lène yarabi❤❤❤❤
Salibataire yi ame l'en diom touti 😂😂😂khana warguéna rouss deh❤❤❤❤❤❤❤je vous j'aime sokhna et Sega
Machallah k dieu vs guide ❤
Que du bonheur sur vous bilay couple bi nex nama toropp damay ree rek😂😂😂
ndeysane yalnalène yalla samu ta mousal lènsi thiat ta maylène ndiabot gou barkèl si barkè seydina mouhamed sl 🙏
Machaallah khalé laniou laff thiate way à vos 100ans in sha Allah
Laf thiate mon couple préféré ❤❤
Je vs j’adore vraiment allah vs protège
Machalla yalna sen diam yagg
Yalna yalla barkèl thi barkè baye psl vous êtes mignonne
Macha'allah ❤
Macha'allah ❤
Macha'allah c'est très mignon ❣
Yallah na lénueh yallah défaal diam si barcky nabil #Moustapha ❤❤❤❤
Sega!! Sokhna Diaroul outaal Woudjiou billahi macha'allah
Aldiana guaye âme ni laff thiiat ❤
😊vraiment kontane na rek. Yalla nalen diapalei
Vraiment elle me fait rire😂😂macha'allah que du bonheur dans votre couple
Wa 2016 ak légui yagul Sama couple dal aye khalélagnu😂 yalna yala samuléne té arléne 🤲
Amine ❤
Maaa ngui deii cii retaan😅😅❤❤ contaaan naa yallah naleen yallah sambbb❤❤❤
Je vous love mes bb que dieu vous protège et qu'ils vous donnent longue vie santé de fer réussite totale inchallah ❤❤❤❤❤
Machallah sène histoire nékhna
Ay way machallah laff thiate si barki cheikh
Amine way yalla dakhna insalla
Vraiment je vous adore 😍 longue vie à vous 💕😊
Machallah frr Bilay diam si iow
Machalah je vous adore qu'Allah vous protège ❤
Amin
Machallah yalla nalén yalla défal diamm
J'aime bien ce couple
Macha'alla mon couple préféré je vous j'aime ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ ❤️❤️❤️❤️❤️
Mome khélou khalé bi moma nékh si mome😂😂
Ils sont beaux Ma shaa Allah Y'Allah nalen Y'Allah sam
Yalla nalene yalla soutoural
Machalla longue vie ❤️🥰❤️❤️
Foumay dieulé sen numéro ma couple préféré bilay
Mahalla très beau couple ❤❤❤❤
Ndéysane yalnaléne yalla same ❤❤❤❤❤❤
Bakkki yalla malen beug ❤❤❤❤❤❤❤😂❤❤❤❤❤
Bilaye yaye d'aide way je vous jamais ❤❤❤❤😊😊😊😊😊😊
Machallah laff bouche ❤❤❤
Diang bi daf may dioylo 😢liguen di def Machllah
Affaires buh cool oh my God. Du courage vous etes tres jeunes. QU'ALLOU AKBAR VOUS PROTEGE SOUS SA PROTECTION INSHALLA ALLAH RABBY BARKE SEYDOUNA MOHAMED PSL AMINE Yarraby
N'ecoutez personnes que votre parents vraiment je suis tres content de vous QU'ALLOU AKBAR YOKE CENE Diame Ak Salam Inshalla Allah Barke Seydouna Mohamed Psl Inshalla Allah Amine
Machalla ils sont tellement mignon et adorable ❤
Merci ❤❤❤
Machallah nekhna trop
Machalla beautiful family
Vraiment c’est beau à voir 😂❤
J'adore se couple 🎉❤
Que dieu tout-puissant versse sa miséricorde sur vous
Machallah ma couple préférée
Ndaysan Machallah mgui reee rk Machallah j vous aime 💕
🥰🥰🥰🥰🥰🥰🙏Yalna yalla samlene 🙏
Je suis tellement heureuse Long vie à vous
Ŕé na ba d.sokhena aka djiobal 😂😂je l adore.
Machala laf thiate yalla maylene diabote gou barquel
Yalla nalène Yalla same diappalé lene vraiment ta femme est toute timide, gentille et vous êtes complice
Je Vous aimes ❤❤❤❤❤