Ada K-nibal - Dou Ngeen fi tokk

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 8 ก.พ. 2025
  • ``Doungen Fi tokk" (Vous ne resterez pas là) le premier extrait de la mixtape #Syperman est le cri de coeur de la majorité des sénégalais contre le système oppresseur qui nous gouverne depuis l'indépendance du Senegal en 1960.
    Rappeur engagé politiquement et socialement Ada K-nibal met la lumière sur certaines dérives du gouvernement actuel et incite la population à prendre ses responsabilités en un mot : la rupture.
    Mixtape : Syperman (2018)
    Musique : Kotf Stratégies
    Mixage et Mastering : Tek Vibes Studio
    Production : Nangam Nangam Prod'Action
    Disponible sur les plateformes de téléchargement et de streaming 👇
    open.spotify.c...
    www.deezer.com/...
    itunes.apple.c...
    Lyrics :
    Dou guéén fi tokk (2fois)
    Dou guéén fi tokk yokouniou fitneu gueun niou noot
    Niou dadjalé carte dioubali urne waneu la yalla fi né
    Sénégal dou kaaw niou beugouniou doundou ci mal bou enraciné
    Prési diay na rewmi gars yi na kouné dieul walam dem
    Intellectuel yeup départ volontaire
    Yalla bour dou teudj bountou teudjalé palantéér
    Nioune gni dess ci gueub magui nio deuk di kalanté
    Carte gui laniou faussé
    Sen doundak souniou boss ngangi fossé
    Sen thiéré souniou rangogne lagn ko saucé
    Domam takh na ma nam Karim bign niou done forcé
    Mbourou fof ko farine
    Ndjitou rancunier yor xolou keurign
    Gouvernement bou amoul ndieurign
    Niaka respecté souniouy serigne
    Je ne sais pas ce qui se passe mais nak c'est pas rationnel
    Nioune président par défaut lagn fal espoir de jeunesse
    Mou andi li yess ki fi djitou gni done war di chômé
    Beugue deuk dima rêvélo man je n'ai plus sommeil
    Refrain
    Prési bi yééss ci niéti yifi diota falu
    Dadjalé liniou mom sédokok hay mbokam la farlu
    Djombouna wakh toubab déét nioune mou nane niou matay
    Dakh sénégalais bari yeurmandé té gawa faaté
    Bou done kou wathie niou jugé sa crime yeup teudj
    Serigne si nara intervenir adjou def keuthie
    Audit bi dal sa kaw topoula ba ci say seut
    Kenene kou fi mounti tokk diga niou diokh some respect
    Dou guéén fi tokk, kou melni yéén dotou fi tokk
    Guénouwaleu dictateur dotou fi fort
    Yakk yakalaté rek nek sa xol
    Boudoul thiouné wala matay dafay nek sokhor
    Ray katou étudiant yagui ladj 2e mandat
    Nagn leen def ni Carthage andil leén Delenda
    Magui xaar fou justice bi am appolo guissé
    Mention bi wathie na députés applaudissez
    Gouvernement bouy teudj hay ilimane té nioy sathie yi
    Diouxouma thieur cour de justice bouy wathie charte yi
    Copier-coller léép ci colon né théorie du genre
    Niak sawar souniouy yité gouverneurou France
    Niak yééné sa askan am diam dolél CFA
    Teudj say opposant dioureul la diouni Kémi Séba
    Ndieunk fi done ndjiit bou djiteul xéét ci xam xam
    Sénégal boolo léén guirr wadji bania am ndam
    Créer ministère pour hay récompense politique
    Falé Charlie nopi quand les rohingya vous sollicitent
    Kou nék ak lila nior engagement bou deugou deukou fi
    Souniou kagn lagn niou délo kone diaroul gay nieuw di xoulo si
    Beugue niou corrompre ci hay millions financements
    Niou bari si nioune gueum ni ben rappeur dotoul innocent
    Nakarou xol yé xaptal thieur yi
    Askan bi bakk deur bi
    Ci kanamou takk dér yi
    Niou seugg fak xéér
    Dou guéén fi tokk
    Momou leen niou
    Défouléén fok
    Momouléén niou
    Nioune dagn léén sopi
    Momouléen niou
    Délouléen fok
    Momouléen niou
    Nioune dagn léen sopi
    Momouléén niou
    Refrain

ความคิดเห็น • 40

  • @adak-nibal221
    @adak-nibal221  6 ปีที่แล้ว +9

  • @mbayealvesgning6464
    @mbayealvesgning6464 5 ปีที่แล้ว +1

    Mon rappeur préféré depuis diamm ci ioe

  • @killaonesbf8401
    @killaonesbf8401 4 ปีที่แล้ว +1

    Tu est lés meilleurs

  • @dienzeboy726
    @dienzeboy726 3 ปีที่แล้ว

    Grand fo nek rap bi soxla nala delou sill dieulat linga mom

  • @papandiogoundiaye120
    @papandiogoundiaye120 3 ปีที่แล้ว

    Big respect Mister Ada

  • @kawistodiallo4882
    @kawistodiallo4882 5 ปีที่แล้ว +1

    Feler bien dit parole yi amena solo

  • @papandiogoundiaye120
    @papandiogoundiaye120 5 ปีที่แล้ว +1

    One love sissawandè

  • @queencolette1928
    @queencolette1928 3 ปีที่แล้ว

    Dop vibes machallah

  • @mamediarraboussogningue4240
    @mamediarraboussogningue4240 5 ปีที่แล้ว +1

    nice nice magoum

  • @l4tz0
    @l4tz0 3 ปีที่แล้ว

    ça, c'est être visionnaire.
    Exactement en accord avec ce qui se passe Now (et qui rampait vers le "Niak") .
    Thanks SuperMan

  • @moustaphadieng2348
    @moustaphadieng2348 5 ปีที่แล้ว

    goood djob mister kanibal

  • @moustaphathiongane2253
    @moustaphathiongane2253 5 ปีที่แล้ว

    Nice Nice Nice Nice Nice Nice Nice bor

  • @reveillez-vousdiome5073
    @reveillez-vousdiome5073 5 ปีที่แล้ว +1

    Bravo nice le combat continue

  • @r.f.t.academy9752
    @r.f.t.academy9752 6 ปีที่แล้ว +2

    Nice Track Respekt pour la sagesse imprégnée

  • @pepenuurhu7203
    @pepenuurhu7203 4 ปีที่แล้ว

    Bilahi tu fais partie des meilleurs ! L’ÉCRITURE ELLE TRÈS CLASSIQUE BIG RESPECT ADAMAXSY!

  • @babacarndiaye5023
    @babacarndiaye5023 5 ปีที่แล้ว +1

    Respect bri

  • @BassirouNdiaye662
    @BassirouNdiaye662 4 ปีที่แล้ว

    Nice n'a

  • @babsyoutubeurng5179
    @babsyoutubeurng5179 4 ปีที่แล้ว

    ✊🏿🇸🇳

  • @badoudeme7749
    @badoudeme7749 6 ปีที่แล้ว +1

    Nice Bro bonne continuation

  • @razzaguitsb6899
    @razzaguitsb6899 6 ปีที่แล้ว +1

    Wakh ngua deug

  • @BABACARSALL-r9e
    @BABACARSALL-r9e 6 ปีที่แล้ว +2

    C over nice bri ada knibal tu es le meilleur

  • @bekdiop8418
    @bekdiop8418 6 ปีที่แล้ว +1

    Merci ada wakhal dé

  • @aliouseene5546
    @aliouseene5546 6 ปีที่แล้ว +1

    Respect rekk .Toujours engagé...

  • @RhapsodAfreekindman
    @RhapsodAfreekindman 6 ปีที่แล้ว +1

    ✊🏿

  • @morlo896
    @morlo896 6 ปีที่แล้ว +1

    merci ada

  • @niangibrahima2261
    @niangibrahima2261 6 ปีที่แล้ว +1

    Nice track kom d’habitude

  • @mbayediop443
    @mbayediop443 6 ปีที่แล้ว +1

    Nice track by ada k-nibal🔥🔥🔥

  • @omarndiaye6019
    @omarndiaye6019 6 ปีที่แล้ว +1

    Nice son

  • @abg9207
    @abg9207 4 ปีที่แล้ว

    2021

  • @babanian4755
    @babanian4755 3 ปีที่แล้ว

    Niccce

  • @babacarcoulibaly3443
    @babacarcoulibaly3443 6 ปีที่แล้ว

    Ndanane

  • @dofbbi
    @dofbbi 6 ปีที่แล้ว

    Nice tube 🔥🔥🔥
    #SonkoPrésident 🇸🇳

  • @baaynjah2246
    @baaynjah2246 6 ปีที่แล้ว

    Nice grand Ada👍👍👍

  • @mamadoumoustaphalo3741
    @mamadoumoustaphalo3741 5 ปีที่แล้ว

    Machallah

  • @aminegueye1379
    @aminegueye1379 6 ปีที่แล้ว

    Nice nice

  • @dieyeayouss9519
    @dieyeayouss9519 6 ปีที่แล้ว +1

    Nic track✊

  • @marcelgaye8330
    @marcelgaye8330 2 ปีที่แล้ว

    Merci ada