Je ne suis pas contre ce mariage svp pensez à la Maman je demande à la femme de faire cette démarche de bien les consolider je suis une maman comme elle qu elle. essaye de. se mettre à la place de la maman du garçon heureux ménage ❤
Lolou mére bi moko thi mana diapalé Di wakh tane AK mboki boy bi diléne khamalné Lou yalla dogale la Di dalale séneu khél Di andeu ak môme Di séti mére bi
Ousseynou a avoué que ce n'est pas la première fois qu'il courtise une femme plus âgée que lui. Je condamnais la femme au départ à cause des parents du garçon et surtout de son fils qui a le même âge que son mari. Mais comme Ousseynou n'est pas à sa première expérience avec une femme plus âgée, à mon avis il n'a pas été manigancé par la dame. Na ci nieupe mandou la guiss
Ousseynou mi day tekk khél rek déjà nangouwoul expliquer dara lou lére ci nane lako abordé ndakh lepp mère bi moko manigancer, sinon lou khalé beug kouko mak tamite dou wessou quelques années maximum 10ans mais pas koula mate yaye ak loumou tarou tarou...Lolou rek la meuneu tontou pour tour nite yi leundeum
Ousseynou ak mère bi yeup wiri wiri nagn ba tontou wouniou ci nane la aborder mère bi tout simplement parce que mère bi moko dokhane mo diriger lepp c'est tout car khalé bou tolni ki dou guiss moromou yayam ak noumou meuneti mell diko khole beutou mbeuguél ta fékoul femme bi oubilko bounte baparé. Ousseynou est un innocent que la dame utilise et dirige
Nieup niouy wakh dara nékouci da fekk Ousseynou dou séne rakk dou séne dome. Kéne banioul diabar diou mak dieukeur yen a en pagaille mais moromou yaye tekci abandonné sa famille c'est grave
Ousseynou sagalna koulou jeune fiii thi rewoumm Sénégal, toute les jaloux vont mégrire, se cadeaux ces pour vous le couple Mbingue 🎉🎉 a vous deux seulement , ay waay fann laay amé lou mélni
delol domi djambour dji ! Fou nekk nga djionkone fa di expliqué chiiiip! reuyy nga lamine trop té meun wanéwou! Yaw ana sa tarr? mounane djinés ak rapp?Des fois gnakk diom dayy khawa nourok djiongué té dou bene!seydina Mouhamed( sAw) santoul kenn mou dioylo ndayam ndakh djiguéne! Et quand seydina Mouhamed sAw epousait khadija, leur écart d âge n était pas aussi énorme et Mouhamed n avait presque plus de famille et avait besoin "d une couverture " ! Elle n avait pas kidnappé l enfant de quelqu un !Arrêtons l hypocrisie!
Je ne sais pas si vous avez la même analyse que moi mais c’est la dame qui est victime dans cette histoire. Car le jeune homme est intelligent et très mature il cherche juste du buzz pour se faire remarquer. Et il utilise la dame mais c’est désolant 😢
Cheikh Ahmed aka mouss boula beugué wax lo do reutie dalay taf si bopam mélni yaw la faral mais kénén ki mo dof la day saga rek motax ku am fulaa doko déglou Nénako mon coeur wa baxna néxna dal
Mane dafa am juste question bima beugeu posé question senegalais yi On dis que nous somme a 90% de musulmans té gnoune nénagnou sunna Mohamed lanouy roy, té degna sunu prophète geun dji mindef lika sokhnam maguéwone barina lol, legui lane motah warouno nangou seuy bi soude geum nagn yalla ak yonente Mane dama diapeuni kepou kou opposewou si seuy bi rek wediga sunna ya rassoulilahi
Ousseynou bamiy takk mère bi béneu parents wam yégoul mariage bi , fi mariage amoufi ,wakh lén gnaari lascars yi deug mogueun . Ousseynou sa yaye mo ngui dioye rek si internet bi , té nga meuytou ,akhou parents woroul si dom dé.
Brother cheikh, don't say "Allah boni celibataire deh 😂😂😂😂 just pray for us because we are bachelorettes and we follow and like you 😂😂😂😂😂😂😂. ❤❤❤❤❤❤❤may Allah continue to bless you amiine
Sama ex copin nena bimou neke khalait ben mer moko done iri diko yeudai moko😅khamal djiguen te après laa découvrir ni deef nako presque kharitame yeupe😅 li😅yaguena Sénégal te boye khole khalebi dafa beugone gnalo ake mome mouneko dedete
Salam gars yi, Sénégal quelque chose me dérange : quand un vieux monsieur épouse une très jeune femme personne ne crie oh scandale! Cette femme se marie avec un très jeune homme et beaucoup de personnes viennent l'insulter, l'humilier, la diffamer mais pourquoi? Nous avons en face de nous un couple marié et non un couple clandestin alors respectons les! Nitt dey mandou gnome le ak séne vie c'est leur droit le plus absolu ! Ce pays a beaucoup de problèmes autres à régler que de venir insulter ce couple. Bon vent à eux. Si seydouna Mohamed psl est notre référence nous musulmans respectons les! Si Le prophète Issa (Jésus) est une référence ici dans ce pays et pour le chrétien respectons les! Le prophète Issa disait à une foule au sujet d'une prostituée qui avait touché son pied: " que celui qui n'a jamais péché me jette la première pierre et a béni la prostituée". Leçon de morale : chacun a droit à une chance. Laissez les vivre leur couple dieu seul sait ! Mais nak djaroul wone sakh nguene di expliquer wou si mariage bi c'est votre droit! Wa salam.
@AichaDia-t1d sou feker yaye dji beugoul sey bi khame na lolou diner dina si ame loumou meune ... pour mbiroume dome dji kou gor ki ame droit takk yenene sokhna ame ak gnome dome inshallah. Solution dèye ame toujours.
Un vieux de 60 ans qui épouse une jeune fille , cette relation a de l’avenir même s’il y’a 30 ans d’écarts car la fille peut procréer mais l’opposée une vielle de 53 ans ménopausée avec un jeune de 24 ans il y’a point d’avenir et ne parler pas de miracles 😅. Toi tu voudrais que ton fils ,ton frère meurent sans descendants ? Si oui alors tu es une mère ignoble
C'est vrai que l'amour n'a pas d'âge mais ousseynou et jeune et innocent on le voit à travers son visage
Soxnasy tëyel saborom kërgi bu baax yalla naleen yalla jappule Amiin
Amine franchement bravo Maa Shaa ALLAH mon frére je suis fier de toi bravo 🎈🎉🍾🎊 surtout à votre Mari je suis fier de vous voilà
Enfin je vois un couple model et adorable
Soyez heureux, l'amour ne connait pas d'âge. Les jaloux vont maigrir l'essentiel est que vous vous aimez et vous êtes légaux devant Dieu point❤
Boy weur jeune bou wayadi ba niewé ci gosse teyel
Je t'en veux vraiment
Demal liguey soutenir sa famille
Bly 😂
Heureux menage,yalnaléne yalla défal diam ak salam ak ndiabote diou barké,seuy amoul âge té mo guéne ndialo
Je ne suis pas contre ce mariage svp pensez à la Maman je demande à la femme de faire cette démarche de bien les consolider je suis une maman comme elle qu elle. essaye de. se mettre à la place de la maman du garçon heureux ménage ❤
Gniepou loolou molen metti yaye kenna douko takali ak domam
Voilà t'as tout dit
Ndeysane yalla moy bolé ay nite 🙏mais ousseynou boul abandoner sa famille goorgoorloul diapalaléne 🙏
Lolou mére bi moko thi mana diapalé Di wakh tane AK mboki boy bi diléne khamalné Lou yalla dogale la Di dalale séneu khél Di andeu ak môme Di séti mére bi
Yalla na sey bi barke ❤❤❤❤
Amine ❤
Amine ya rabi
Amine ya rabi🥰
Amin
Amen
Yalnaniou yalla mousseul si nittt Kouy nélaw les yeux ouvert 😢
Ousseynou a avoué que ce n'est pas la première fois qu'il courtise une femme plus âgée que lui. Je condamnais la femme au départ à cause des parents du garçon et surtout de son fils qui a le même âge que son mari. Mais comme Ousseynou n'est pas à sa première expérience avec une femme plus âgée, à mon avis il n'a pas été manigancé par la dame. Na ci nieupe mandou la guiss
Ousseynou dé d’où wakh deugue Day féne rék.
Si c’est le cas dafa tela yakk bopam
Amna gno khamné mak moy choix.... et si c'était le cas de ousseynou ...mandoulen ci mbeuguel
Ousseynou mi day tekk khél rek déjà nangouwoul expliquer dara lou lére ci nane lako abordé ndakh lepp mère bi moko manigancer, sinon lou khalé beug kouko mak tamite dou wessou quelques années maximum 10ans mais pas koula mate yaye ak loumou tarou tarou...Lolou rek la meuneu tontou pour tour nite yi leundeum
@@MimiMimi-vm5oedeug rek nga wakh mèrr bi moko dokhane
Ousseynou ak mère bi yeup wiri wiri nagn ba tontou wouniou ci nane la aborder mère bi tout simplement parce que mère bi moko dokhane mo diriger lepp c'est tout car khalé bou tolni ki dou guiss moromou yayam ak noumou meuneti mell diko khole beutou mbeuguél ta fékoul femme bi oubilko bounte baparé. Ousseynou est un innocent que la dame utilise et dirige
Yalla na seuy bi barkél merci cheikh améde Cissé 🥰🥰🥰🥰
Nieup niouy wakh dara nékouci da fekk Ousseynou dou séne rakk dou séne dome. Kéne banioul diabar diou mak dieukeur yen a en pagaille mais moromou yaye tekci abandonné sa famille c'est grave
Bilay wahatiko
Merci beaucoup je pense la même chose que toi li c’est vilain sim elle m’énerve ak kanamam bi melni dakandé
@@AstouSy-f8i😂😂😂😂
@ Moukha ki mérénako torop ousseynou mi
Dagua nane moromou mamame kaye😢 li adouna moyé wadia touki maye wakh ki nane dionguama mineurs
C Amour entre Serigne AK tabile c mission espiritual.femme sage , homme sage on verra avec le temps 😂❤
Machalla aissatou.kadu.refetena.yalla.sey. bi.barkel😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤
Bilay ahmed Cissè day mbalak ni di len ranguanrti téh khamou gnouko🤭😂😂
Lolou moma diakhal ils n'ont rien compris, surtout la dame di wakh wakhi rafféte 😂😂😂
@@MimiMimi-vm5oe😂😂😂man taar bimouy wakh, sank batay mom lay khôl té guissagou mako
Tare amoufi motakh vidéos yeup dakoy filtre fi nak moy naturel ak séne réseau bou bone amouniou sakh WiFi 😂😂
Yene khane d'âge mer 😅😅😅
Wa😂 mère bi deh elle a l’air de vivre dans un autre monde. Hamed khalifa di yokk diko ranguanti rek.
Yallna yallah barkel seye bi ❤❤❤❤
No Sénégal nékhna... Yalnaniou Yallah sameu doliniou mousseul!!! Défal nieup Diam
Ousseynou sagalna koulou jeune fiii thi rewoumm Sénégal, toute les jaloux vont mégrire, se cadeaux ces pour vous le couple Mbingue 🎉🎉 a vous deux seulement , ay waay fann laay amé lou mélni
Adja bi daffa geum boppam nak 😂😂 ❤
Trop key néna ak taar bi 😂
*Wouyyy😂😂😂😂😂😂*
@@veroniquenatack7392 no damako beugue pour môme mo dakheu si adouna bi 😁
@@Cherifa05 lolou Ray nama 😁😁
Thia tarrrr balaaa😂
Nena mon coeur rek ma youkhou 😂😂😂😂😂😂
😂
Y’a bone 😂
delol domi djambour dji ! Fou nekk nga djionkone fa di expliqué chiiiip! reuyy nga lamine trop té meun wanéwou! Yaw ana sa tarr? mounane djinés ak rapp?Des fois gnakk diom dayy khawa nourok djiongué té dou bene!seydina Mouhamed( sAw) santoul kenn mou dioylo ndayam ndakh djiguéne! Et quand seydina Mouhamed sAw epousait khadija, leur écart d âge n était pas aussi énorme et Mouhamed n avait presque plus de famille et avait besoin "d une couverture " ! Elle n avait pas kidnappé l enfant de quelqu un !Arrêtons l hypocrisie!
😂
😂😂😂😂Mane damasé rouss khawma loutakh 😂😂😂
Mandou amna solo trop.
Mashallah so great may Allah give you happy marriage and long life too
Ki da beug lou yombou dafay daw responsabilité néna mère doula sonale ki amoule diom
C’est vrai kii kou niakk diome la beugue lou yomb imbécile la
Roky dem lenn rekk.. Boy yi si magg yi la niou dieum... Kom yenn gonnê yi amokenn ambition té danguenn rew.. 😅
Séne affaires yoyou naguene ci guénné serigne babacar
Yaw rek mom serigne babacar
mais seuy bi dagane na déh yaye fall😂🤣
machalla téylén bou bakh yalla dou nit mandou si sey bi
😂😂😂😂😂😂
Yaw ya môm serign Babacar?
On vous souhaite tout le bonheur du monde inchalah soyez heureux ménage
Aui soyez heureux
Cette union est legale mais pourquoi certains y voient negatif.Vivez heureux cher COUPLE
Machallah yalna seybi barkel 😂😂😂😂
Mère bi je pense de am febarou khél deh 😂 gnak Diom mounane mon cœur hahaha😂
😂
Pourtant sa yaye bou wakhé sa pa'pa mon cœur dou am problème ciyaw dé
Ki deh woor nama moo leu gueuneu ham limou def dafa guiss bidew xalé bi ndakh voyante leu
😂😂😂😂😂😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅
Thiapa ndayam dalouko loudoul doméramé niak dignité sa moromou dome sim
Ousseynou yalna borombi diappalé
Salam ! bayilen mère bi , l'amour n'a pas d'âge. Regardez Macron & Brigitte. Félicitations ! Bayilen nite yi gnou dounda sen life.❤❤❤❤❤
Machallah Mabelle Cherie ❤❤🎉🎉🎉🎉
Defarale sadiabare bame mele ni viyane ❤❤❤🎉
Mon cœur bii bimako dégué touti ma youkhou danou ganguiri😂 tothie sama téléphone
Barki yalla mane dé saguam sama khol bi wadoul rek alkhamdoulilah ki vrai domérame la take domou diambour sans consentement famillam cheuttttt
@ Bilahi ça fait mal au cœur
Je ne sais pas si vous avez la même analyse que moi mais c’est la dame qui est victime dans cette histoire. Car le jeune homme est intelligent et très mature il cherche juste du buzz pour se faire remarquer. Et il utilise la dame mais c’est désolant 😢
La dame n’est une victime mais une coba
@ tu as raison entoucas li c’est bizarre dale
Celui-qui te conseille cheikh Ahmed soit disant ton marabout n est même pas un referance dans ce pays
❤❤❤❤ machallah yallah na seybi barkel
Fils démal wakhe tane ac sa yaye mo guene ta moytou thiate mo gue ne😮😮😮😮😮
Sénégal mandou lène si seuyou diambour bi nguir yalla kou nekk amenga loula doyy lidieunti ko silou nekh yalla lagnou nekk yalna yalla barkel seuye bi
Worna yallah ouzin barde woul mère belle vie moko fa bayi d'après son réaction beugoul
Merci beaucoup non Ousseynou sama ak souko dalé
@AstouSy-f8i Loy tek ni defma signe gnou wakhtane
Boy bi riyeul la gor la ! ❤Mai nay YALLA tel ok❤
En tout cas il parle avec maturité
Yalla na seyebi barkel❤
Soyez heureux . L'amour n'a pas d'âge, je vous souhaite beaucoup de bonheur ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ que Dieu vous bénisse 🙏
Elle parle de quelle beauté 😂😂😂😂
😂😂
Tu n'a pas vu beauté toi😂😂😂
Yalla nako yalla délo si wétou yayam té mou woute moromame sa yaye bou déwé dingua kham ni tate diaroule yéne yii
Cheikh Ahmed aka mouss boula beugué wax lo do reutie dalay taf si bopam mélni yaw la faral mais kénén ki mo dof la day saga rek motax ku am fulaa doko déglou
Nénako mon coeur wa baxna néxna dal
Wow lou raffett ci vieille bi😂😂😂
Moma diakhal beugue mou nétaliko rec 😂😂😂😂
Man contaann na ci yénn yalna sëy bi baarkel yalla maylénn ci njaboot gou barrkéel AMIIN 🙏
Merci ousynou.wakh deug khale.djigeune.rewna.beug.khalis.boy.djigeune.jeunesse.dof.salté.chiaga.mere.settena.yarou.bakhna.amna.soutura.mere.yore.boyi.wuti.mere❤❤
Yalla na seybi barkelle
Mane dafa am juste question bima beugeu posé question senegalais yi
On dis que nous somme a 90% de musulmans té gnoune nénagnou sunna Mohamed lanouy roy, té degna sunu prophète geun dji mindef lika sokhnam maguéwone barina lol, legui lane motah warouno nangou seuy bi soude geum nagn yalla ak yonente
Mane dama diapeuni kepou kou opposewou si seuy bi rek wediga sunna ya rassoulilahi
Merci beaucoup 👏🏾👏🏾👏🏾ĺa réponse que je cherchais
Lo khamsi nitt you hypocrite 🤔
Sangou sangue yi Psl, bamouy dieul sokhna khadija ay mbokam daniou thi andeu, dém niani. Kii dafa détourner domou diambour, yayam di souffrir mou déff louko saf
@@adamandiayekasse5990❤❤❤
Yonénete yalla mouhamed abandonné woule yayeam bimou také diabar lolou mo méti nit yi mais dou seye bi arrêter
Ousseynou bamiy takk mère bi béneu parents wam yégoul mariage bi , fi mariage amoufi ,wakh lén gnaari lascars yi deug mogueun . Ousseynou sa yaye mo ngui dioye rek si internet bi , té nga meuytou ,akhou parents woroul si dom dé.
Ndeysaan yallna len yallavlafal thiat😊
Machallah farata rek la def
bilahi
Heureux ménage ❤❤❤
Ousseynou du courage, yaw moome laakhe ngua ngueureumou sougnou serigne bou baakh bii,cheikh akhmed cissé,sey bi day barkail inchaalaah
LI DINA TAH HALÉYI DOTOU NIOU RESPECTÉ MAG
Yallah na sey bi barkel si barké Seydina mouhamed psl 🙏🙏
Pauvre ousseynou. . Yémal
Je t'aime maman ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ mn trésor
Mon cœur bi dinama ray 😂
Cheikh Ahmed Cissè mo faux nena tar bi 😂😂😂😂
yow khamo taree🤣🤣🤣🤣🤣
@ khawmako walay 🤣🤣🤣
😅😅😅😅😅😅😂😂😂😂
Non li man nama diokh insomnie djiné kagne😂😂😂😂😂😂😂😂😂
*Lolou la meunoul mougne😂😂😂😂😂😂*
😂😂😂😂mayko lolou
😂😂 wouy mere bi gëm boppam bou eup moko dougeul Si lii 😂
I love this couple ❤❤🇬🇲
❤❤❤ please leave them alone love coming everywhere❤❤❤❤
Adja diallo balgnou mais sa tarr diékhna aujourd'hui 😂
😂😂😂😂
😂😂😂
😂😂😂 merou djinné bi dieul Na lep kay
Baylennn Lou sen yoonnn nekoul nguen dougou ci. Seyou jambur sen yoonnn nekou ci. Heureux ménage au couple
Ki day fen rek limouy wakh amoul bopou amoul geen😢
Bilahi
Bayil ndy sokhor séyou diambour sa yone nékousi
Bilaye aisatou kou oyofe la mashalla Kontanna siyawe ❤
Brother cheikh, don't say "Allah boni celibataire deh 😂😂😂😂 just pray for us because we are bachelorettes and we follow and like you 😂😂😂😂😂😂😂. ❤❤❤❤❤❤❤may Allah continue to bless you amiine
Mashallah Aissatou❤❤❤❤
Mounir mon cœur kay😂😂😂
Diame sii yenne bilahi
wouyyyyy😂😂😂😂😂😂😂Machallah
Nenako niou ndangou nagnou tarr bi😂😂😂
C'est le DESTIN
Bonne Continuation au COUPLE
Bilahi amed niass ya meuneu doul deugg té meun diayyi nit 😟😟😟
Mon coeur 😂😂😂😂
❤EN TOUT CAS JE VOUS FELICITE ET QUE DIEU VOUS GARDE ... AUCUN PROBLEME VOUS AVEZ LE DROIT
Ousseynou dh hamnna djinné mere bi la guiss diawalé ko ak mere bi 🤣🤣 liii
C possible d djiner bi dougal ko bamou dougu mou rotiekou
Ak Kanamou khaley bi😂😂😂, yalla Ndiabott... N'a mandou rek...
😂😂😂😂
Wouyyyyy mangui dée
Amegua fiitt dall té wow beuut
Wa li deugue leu ousseynou yalla nako sama ak dal liiii
@@AstouSy-f8ilégui senegalais you ame 25ans di tak mere toubab you ame 55 Ans nak
Yalna lénne Yalla défale diamme 🙏🙏
Esk khamnguèn ni Ahmed Cissé day roubé ndawci 😂
Je te jure femme bi weroul
Yeine kham bayileine gni gnou seye
WAKHAL SA DIEUKEUR BOUMOU FATE YA YAM
Maguétoume djiné daye beurri ngalaniou😂
😂😂😂😂
😂@@fatoubeye3212
Maintenant il faut que les 2 familles se retrouvent pour un atmosphere plus sain pour securiser le COUPLE
Mo gueune wakh diou bari ji. Et fermer le bec à tout le monde
Boye bi mo deuguer fite deugue deugue boye ya deuguer fite lefeul ndeyam li dou deugue wayy
DEUGUE LA KAYYE BILAHI
Sama ex copin nena bimou neke khalait ben mer moko done iri diko yeudai moko😅khamal djiguen te après laa découvrir ni deef nako presque kharitame yeupe😅 li😅yaguena Sénégal te boye khole khalebi dafa beugone gnalo ake mome mouneko dedete
Dokhantoulén soiré wally khol comment on va vous accueillir.c très sale 😢😢😢
Yalla n'a seybi barkell t'es ouseynou boull Fate ca famille
Boye saye ga beugeu dimbeli mé yagicoye beugeu raye😢😢😢😢
Salam gars yi, Sénégal quelque chose me dérange : quand un vieux monsieur épouse une très jeune femme personne ne crie oh scandale! Cette femme se marie avec un très jeune homme et beaucoup de personnes viennent l'insulter, l'humilier, la diffamer mais pourquoi? Nous avons en face de nous un couple marié et non un couple clandestin alors respectons les! Nitt dey mandou gnome le ak séne vie c'est leur droit le plus absolu ! Ce pays a beaucoup de problèmes autres à régler que de venir insulter ce couple. Bon vent à eux. Si seydouna Mohamed psl est notre référence nous musulmans respectons les! Si Le prophète Issa (Jésus) est une référence ici dans ce pays et pour le chrétien respectons les! Le prophète Issa disait à une foule au sujet d'une prostituée qui avait touché son pied: " que celui qui n'a jamais péché me jette la première pierre et a béni la prostituée". Leçon de morale : chacun a droit à une chance. Laissez les vivre leur couple dieu seul sait ! Mais nak djaroul wone sakh nguene di expliquer wou si mariage bi c'est votre droit! Wa salam.
Pask goor bou amé 70an sakh mouna am Dom me khamnga ki douko moussa joural som te yaayji bougoul seydji
@AichaDia-t1d sou feker yaye dji beugoul sey bi khame na lolou diner dina si ame loumou meune ... pour mbiroume dome dji kou gor ki ame droit takk yenene sokhna ame ak gnome dome inshallah. Solution dèye ame toujours.
Un vieux de 60 ans qui épouse une jeune fille , cette relation a de l’avenir même s’il y’a 30 ans d’écarts car la fille peut procréer mais l’opposée une vielle de 53 ans ménopausée avec un jeune de 24 ans il y’a point d’avenir et ne parler pas de miracles 😅. Toi tu voudrais que ton fils ,ton frère meurent sans descendants ? Si oui alors tu es une mère ignoble
Bonne continuation s'est pas haram je vous souhaite bonne chance par la baraka de son prophète mouhamed psl
AMETH CISSE DOMOUKHARAM LEU😂😂
GUEMOUL DARA THIË LIMOUY WAKH😂😂
NAN MEŔE BI DEFA TAROU😂😂
Domerame la 😂
@nancyfaye8151 billay DOMOUKHARAM LEU
Ousseynou est un innocent 😂😂😂😂😂😂😂
Ki ani taram wala mane ma dioum 🤔
Elle est belle sakh dangako diéppi rek😂😂😂
Khalé bou touti wow beute legui ngua maguet
Bayil sisou bi😂😂 mére yi donio séte par rapport ak yéne