Assalamou aleikoum Oustaz Oumar Sall, qu'Allah vous récompense pour tout ce que vous faites pour l'Islam, ma sha Allah. J'aime bien vos vidéos car vous craignez DIEU et vous nous motivez à nous rapprocher de Dieu. Alhamdoulilah.
Encore merci toujours merci pour tout. Vos enseignements nous sont utiles car vous attendez rien au retour. Qu'Allah vous donne tout ce que vous désirez ya oustaz🤲
Mashallah toujours très utile, toujours profitable et centré sur l'essentiel. Qu' Allah veille sur vous contre tout mal et vous accorde sa protection et sa miséricorde et accepte toutes nos prières.
Alhamdulilla Macha Allah je n'ai pas pas les mots pour vous remercier oustaz Oumar sall mais je sais que le TOUT PUISSANT EST TOUJOURS LÀ POUR TE PROTÉGER
Marshallah Oustaz oumarr sall yaw de yalna la yalla faye thi jangale you am solo yi ndakh yangi jangale islaam gudi ak bachek we love ❤️ you ❤️❤️❤️❤️❤️😊❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🔒🔒🔒
Sama oustaz amna lathie moussouma bay dioly yor yor mais tanyi dama eumbou dama tayal dioly yor yor esk lolou bakhna beugna conseil s'il vous sama oustaz yalla nga am diam inchaallah
Dieuredieufeti yalla na la yalla Faye yiw youdoule dièkhe Amine
Merci oustaz depuis malay suivre diam rek lassi giss k dieu vous garde on a besoin des gens comme vous macha Allah
Machallah
Billahi nafék yi rek ñiokoy xékh
Très pertinent commentaire. Mais pour la prochaine fois n'oubli pas d'écrire le nom D'Allah en majuscules
Assalamou aleikoum Oustaz Oumar Sall, qu'Allah vous récompense pour tout ce que vous faites pour l'Islam, ma sha Allah. J'aime bien vos vidéos car vous craignez DIEU et vous nous motivez à nous rapprocher de Dieu. Alhamdoulilah.
Machallah ya cheikh islam Omar Sall 💞❣️ qu'Allah te protège💞💕♥️😍 Qu'Allah vous bénisse
*Mercredi 10 Juin 2020* Machallah Ya Oustaz Oumar Ahmed Sall Li Ngua Wakh Si Diouli Yorr Yorr Amna Solo Yalla Nala Yalla Défal Diam Amine
Djéreudjeuf oustaz yalla bayilafi té weur werlai daigg ak topp ci ñaipp machallah
Je vous aime ouztaz oumar sall. Vous illuminez les ténèbres....et vous aidez la oumah islamique
Encore merci toujours merci pour tout. Vos enseignements nous sont utiles car vous attendez rien au retour.
Qu'Allah vous donne tout ce que vous désirez ya oustaz🤲
Mashallah toujours très utile, toujours profitable et centré sur l'essentiel. Qu' Allah veille sur vous contre tout mal et vous accorde sa protection et sa miséricorde et accepte toutes nos prières.
Mashaa Allah! Yaa Oustaz walaahi Yalla kessé lagnouley bayé té dila gnanal🤲🏾😭💓💓💓
Jeuri Jeuff Kharitou Nitt Gnou Bakh Gni Di Nooni Nitt Gnou Bonn Gni.
Waxnga leup
MaschaALLAH cheikh OUMAR sall qu’Allah vs paye
Bien dit.
Sénégal wakhtan yi la sokhla dieureudieuf Ouztaz
Alhamdoulilah sant yallah bi niou yallah mayè kou melni yow outaz yalnan fi yaguè tè wèur
Alkhouran ak sunna rek moy deugg vive omar Sall
Machallah merci beaucoup oustaz 🙏🙏
Machallah amatina solo ! Barakallahou fiikoum ! Yalla sam-la !
Manchaalah merci beaucoup. Que le Dieu vous garde longue vie en bonne santé.
Salam oustage oumar sall je vai venir Senegal a cause de vous je veu slement te voir ya oustage je te sui dpui Gabon
Machallah oustaz beug nala nguir yalla walahi ❤️💞 Omar Sall amal diam rk iow
Machallah qu'allah vous bénisse 🧡
Bilahi ma la beugall sama bopp ouztas yalla nalla yalla wérall goudall say fann amin
Merci beaucoup oustaz omar sall ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Alhamdulilla Macha Allah je n'ai pas pas les mots pour vous remercier oustaz Oumar sall mais je sais que le TOUT PUISSANT EST TOUJOURS LÀ POUR TE PROTÉGER
Marshallah Oustaz oumarr sall yaw de yalna la yalla faye thi jangale you am solo yi ndakh yangi jangale islaam gudi ak bachek we love ❤️ you ❤️❤️❤️❤️❤️😊❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🔒🔒🔒
Barakallahou fiikoum ya oustaze, amena solo
Macha Allah ya Oustaz amna solo diazakallah khair
yallah Bour bi maytla goudou fane ak werr ya oustaz
Manchallah man dé chaque jour ma dioullii ko
Machallah ya oustaz diazakallahou khayran
euywaye aime len vidéo bi boulen soxor 🤩🤩🤩🤩🙏🙏🙏
OUSTAZ yalla goudal fane bi, yok wèr gui
ALHAMNDULLILAH dinagnci bayi khel in sha Allah Oustaz qu'ALLAH te recompense
Diaradieuf oustaz sall yalla moleye faye kéne dou yowe
machalla ustaze Omar Sall
merci b oustaz que la paix de DIEU soi avec vous
ALLAHOU AKBAR amna solo trope Macha Allah. Yallananioussi souniou Borom khir YAA RABBAL ALAMINE
Masha'Allah yah Oustaz qu'Allah le tout puissant vous rétribue
Yalla na yalla fayi la sall
MashaAllah my mentor you always on point I've learned alot from you jaza'kallah khairan may Allah reward you abundantly
Barakallahou fikoum Oustaz ❤️❤️❤️
Barack llahou fikà oustage oumar sall deuma beug nga def vidéo diangaleh istixar ndiabar yi sonale naniou diamou YALLA yi
Djiouli yor yor bane moci geuna bakh
Merci ke Dieu vous protège oustaz Oumar Sall
Yalnala Yalla fay yiw Oustaz
Merci merci merci beaucoup oustaz pure vérité alhamdoulila que alla nous donne longue vie et beaucoup de santé
Machallah ya oustaz diazakallahou khayrane amna solo looool
Machallah ouztaz Omar Sall yalnala yalla barkel té arla
Intéressant comme toujours
Machallah oustaz rien que la vérité suna
Jazaka Allahu kaïreu oustaz🙏🙏🙏
Barakallah fikoum oustaz amna solo très contente de toi
Dieureudieuf oustaz machallah
Oustaz May Allah protect and bless you
Machallah ya oustaz omar sall
Merci oustaz oumar Ahmad sall manchaallah
Macha Allah
Diazaa kallahu khaïr
Dieureudieuf Ouztaz
mashallah . vous etes tres sage je suis tres content de vous
ماشاء الله أحسنت بارك الله فيك جزيتم خيرا
Dieureudieuff Oustaz
Macha'Allah oustaz amna solo
Yalna Yalla fay yiw Oustaz
Macha Allah amena solo merci beaucoup ustaz
Machaallah amna solo de yalla na yalla sam la fayi la yiw
Masha Allah ya oustaz amna solo lol 🙏🏾❤️❤️
Macha Allah ya oustaz barakallahou fikoum
Machallah machallah yallah nala yallah Faye amin ya rabi 🤲🤲🤲🥰
Sama oustaz amna lathie moussouma bay dioly yor yor mais tanyi dama eumbou dama tayal dioly yor yor esk lolou bakhna beugna conseil s'il vous sama oustaz yalla nga am diam inchaallah
Yalna yalla fayla
Asalamou aleykoum
Massalah ya oustag bilay amatiana solo deug deug contanena si iow
Yalla n'a yalla mayla goudou fane akk were ak wérléé
Machalla amna solo dieureudieuf ousraz oumar
Oustaz yalla na la ya RABI soutoural @Asalamaleokum@
Diouli doha sarr boula nékhé guay récité
Dieureudieuf Sall. Macha Allah!
toujours des choses bénéfiques
Maachaa Allah Oustaz Oumar Sall
Macha Alah Dieureudieuf amena solo
Machallah ame na solo 🙏🙏🙏
Machallah amna solo trop🙏
BAARAKA ALLAHOU FIIKOUM
Machaa allla yalla na yalla faye oustas content naniou si yaw
Dieuredieuf oustaz masha allah amatina sollo👏👏
Macha Allah ya oustaz
Machalla oustaz
ماشاءالله تبارك الله
حفظه الله
Machallah Oustaz yalla nala yalla fay yiww
Machala sama oustase baraka la fi koume🌹🌹💓
Bilahi amna solo wayé nioune gniy yéndou si classou école yi bâ 16h dé yakarou ma dinagn ko meune mé beugg nagn ko trop
Dieureudieuf oustaz❤❤❤
Long vie oustage sama serigne
Ma Sha Allah contan na si yaw
Barakalakhou fikoum
Machallah y a Oustage
Assalamouhaleykoum ya oustaz yalna yala fayla la
Machallah long vie oustage bara kallahou fikà
Yalnala borom bi fay yiw🙏
Machallah Que Dieu vous garde
Hafizaka allah ❤️🙏🏻
Macha Allah amna solo
Ma Shaa Allah.mais pour diangue sarr yi ci kaw wala ci souf la
Si souf