Yalla na Yallah yokou soutoura té takhawou niou thi jaboot gui... Repères yi lompogne naniou.Yalla na Yallah deff thi nioune tawhid... Yalla naniou kholâte en permanence souniou takhawaye.Yalla nieup diote thi sa khalates ,sa Djangaates you rafet yi...Sa ragal Yallah rek môko waral... Yallah fayla yiw Serigne Momar...
Salam serigne Diagne vous avez parfaitement raison il y’a trop de laisser aller dans ce pays des énergumènes qui se permettent de décrire les faits sur les lieux du crime sans autorisation ni science exacte alors qu’hier on a vu sur le plateau du JT de la Rts une voix autorisée de la Police Nationale en l’occurrence le Commissaire Gueye chargé de la communication dire carrément qu’à ce stade de la procédure où les investigations et les enquêtes sont en cours entre la police le parquet et le juge d’instruction qu’il est de rigueur de les laisser dérouler les procédures mais donc pourquoi l’Etat ne met pas de l’ordre sur tous ces incultes qui se permettent d’aller au-delà de ceux qui sont habiletés à communiquer sur un sujet aussi sensible qu’un double meurtre. Il est temps pour lEtat en l’occurrence le Ministère de l’intérieur de rappeler à l’ordre ceux qui interfèrent sur les enquêtes en cours en donnant des informations non avérées
Merci infiniment Oustaz Momar Diagne. Je salue vraiment votre constance votre objectivité. Le Sénégal à besoin des personnes ressources comme vous. Nala yalla borom bii samal bopam barké Alxouran 🙏
Vous dite que la vérité que Allah subhanak wataalah vous garde dans sa miséricorde et toutes les odeurs qui vous écoute inchallah Sabrine béni soit sur vous Assalamaleykum warahmatullah taallah wabarkatuh Elkhadji momar Daigne merci beaucoup
Senegal yakhu na rek. Kou yebu deff ni serigne mbaye jaxaté waxoon wutt barab bu weet difa weetal YALLA nitt gni jaru gnoo waxal te danu lay yobaalé si alkandé gi
Je ne suis pas en phase! Taper sur Modou Gueye et le traiter d’insolent sans vraiment apporter des arguments très fondés pour infirmer ses propos , je suis désolé mais c’est faire preuve d’agressivité verbale. Mr Gueye peut ne pas penser comme la majorité des sénégalais musulmans voire des musulmans en général mais personne ne peux dire qu’il va à l’encontre de ce qui est dit dans le Coran! Maintenant, libre à ceux qui pensent que Le Coran est insuffisant comme source et ont besoin de sources secondaires ATTRIBUÉES au prophète (avec leurs lot de mensonges et de vérités probables) pour pratiquer leur foi, mais attention, la surprise risque d’être grande… fii mou wérou moo geuneu woor dé! AlQuran REK moo woor, li ci dess waxou nitt késsé La.
Modou gueye kiko defendre yaak mooma yamm diiine sii koussi am xam xam moo si wakh ki xamoul ngua demm gnou xamalla... Des gens comme modou gueye il parle de tout comme s il savait tout
Pourtant wonaniou des journalistes et des tiktokeurs
Papa momar diagne naw nala thi kham kham ak khel mou seel long vie a vous et beaucoup de sante Senegal da raflee kham kham ak education
Machallah Baye momar Diange vraiment say vidéo Dama kay khar tjr
Yalla na Yallah yokou soutoura té takhawou niou thi jaboot gui... Repères yi lompogne naniou.Yalla na Yallah deff thi nioune tawhid... Yalla naniou kholâte en permanence souniou takhawaye.Yalla nieup diote thi sa khalates ,sa Djangaates you rafet yi...Sa ragal Yallah rek môko waral... Yallah fayla yiw Serigne Momar...
Mashalla papa, may Allah protect you and grant you a long life with good health. Well said.
Manchalla yalna Yalla fay la yiw goudal say fane amine ❤❤❤
Yaradikou gui nék Senegal gui eupouna
Jërëjëf sëriñ bi yàlla nala saa boroom fay aw yiw ❤❤❤
Djoumaa Moubarek dieureudieuf Imam yalna na borom by féy sa takhaway Assalamou Aleikoum
Salam serigne Diagne vous avez parfaitement raison il y’a trop de laisser aller dans ce pays des énergumènes qui se permettent de décrire les faits sur les lieux du crime sans autorisation ni science exacte alors qu’hier on a vu sur le plateau du JT de la Rts une voix autorisée de la Police Nationale en l’occurrence le Commissaire Gueye chargé de la communication dire carrément qu’à ce stade de la procédure où les investigations et les enquêtes sont en cours entre la police le parquet et le juge d’instruction qu’il est de rigueur de les laisser dérouler les procédures mais donc pourquoi l’Etat ne met pas de l’ordre sur tous ces incultes qui se permettent d’aller au-delà de ceux qui sont habiletés à communiquer sur un sujet aussi sensible qu’un double meurtre. Il est temps pour lEtat en l’occurrence le Ministère de l’intérieur de rappeler à l’ordre ceux qui interfèrent sur les enquêtes en cours en donnant des informations non avérées
Aye sama papa amale diame ❤❤❤❤❤❤
Modou Gueye 😅est fou intégralement 😅
Merci infiniment Oustaz Momar Diagne. Je salue vraiment votre constance votre objectivité. Le Sénégal à besoin des personnes ressources comme vous.
Nala yalla borom bii samal bopam barké Alxouran 🙏
Saway senegal dh sene yone nekoussi khana danguay def effort dilene delossi rek
Reew mi négagoul ciy lokho walay diagne wakh nga deug
Bien dit machallah
Euy way sama serigne Yalla nalla souniou Borom bi yaubou assemblée nationale way❤❤❤
ma sha Allah pur vérité merci Tonton diagne qu'Allah swt vous garde amine
Jerejef amna solo manchallah
Macahall sama papa contana sy yow❤❤❤
Merci encore ya imame
Macha allah Oustaz amna sollo 🙏🙏🙏
Et ce qui est bizarre moyy sunu télé yiii akh certaines sites Internets, ils font la promotion de la médiocrité..
serigne bi magui ziar ga balma mai senegal dou rewou deh amna sollo
Baye momar diagne jërëjëff ❤
Mais lo xalate si vidéos Cheikh Mbacke sakho
Et le pire moy amna gnoulèn Di gueum😢
Vous dite que la vérité que Allah subhanak wataalah vous garde dans sa miséricorde et toutes les odeurs qui vous écoute inchallah Sabrine béni soit sur vous Assalamaleykum warahmatullah taallah wabarkatuh Elkhadji momar Daigne merci beaucoup
Ma cha Allah dieureudieuf sama serigne yana nga fi yague té wer 🙏❤️🙏❤️❤️🙏🙏
Je confirme que les lives sont propre et sonorité cool
Senegal louniou def boumou beteu keneu en vérité la plupart si rew mi ay dioulitou feké massi bollé lagne ragualouniou yalla
JUB ❤️ JUBAL ❤️ JUBANTI ❤️
Machallah papa ❤️❤️❤️❤️❤️
Vamos garasia ❤❤🎉🎉🎉
Kalimatoul hag 🇸🇳♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️👍🏿
Non père daf may rey😂😂😂 machalla
Ndakhe yallah me dègueu kou wakhe modou Gueye dou niite dou royoukaye nékéwoufi loudoule di sani aye doom 😢
Yedde yeureum makogeune! Diangatinaa.
Dieureudief ❤❤❤
Deugg rek ngaye wakh. Dundal Tonton!!!
Macha halla
Machallah amna solo
Machall ❤❤❤
Machalla Machalla Machalla
Diadieuf amatina solo!
Dani fans nite défois nga guis ko kham loumou déf nèkh na léne ba paré gnounane ko royou kay nga dém rek wakh nako
Deff nga waeefu djioulit. Yalla azza wa jall fayy la. Mais pour cet énergumène que je viens de découvrir je crois que c'est peine perdue.
Machaallah
Merci
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Choukran lak 🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤
🆗🆗🆗🆗🆗
Jërëjëf dég na dëg
Goude fane ak wer papa...
❤️🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
13:40 Walahi Père man dama sax moudjié yeemou tellement certains individus niniouy influencer niit yii dafma yeem lolou.
Fatiha + sourate moungui thi Alkhourane. Sourate Al hijr. Aya 87
Désolé, mais ce verset ne cités pas nommément la prière, il aura fallu que le prophète PSL nous l'explicite.
Tounkara ne peut être un exemple. Quelqu'un qui est capable de changer ses convictions pour de l'argent, s'il a des convictions bien sûr...
Mon père si l'enquête et en fuite ce entre la police et les juge et les avocats
❤❤❤❤❤❤❤❤😂
Seringe bi wahkh dak deradef
Seringe bi lika wahkh dak la senegal ye tlaĺae r
Senegal yakhu na rek. Kou yebu deff ni serigne mbaye jaxaté waxoon wutt barab bu weet difa weetal YALLA nitt gni jaru gnoo waxal te danu lay yobaalé si alkandé gi
Fi mooy senégal
Deug dou Romme aye nop rewmi amakoul kilifa
Móodu géy day dafa dese te xamuko
Juge bi deglogoul ken
قال الله تعالى
{ وَكُلَّ إِنسَٰنٍ أَلۡزَمۡنَٰهُ طَٰٓئِرَهُۥ فِي عُنُقِهِۦۖ وَنُخۡرِجُ
لَهُۥ يَوۡمَ ٱلۡقِيَٰمَةِ كِتَٰبٗا يَلۡقَىٰهُ مَنشُورًا }
{ ٱقۡرَأۡ كِتَٰبَكَ كَفَىٰ بِنَفۡسِكَ ٱلۡيَوۡمَ عَلَيۡكَ حَسِيبٗا }
[Sourate AL-ISRÃ': 13-14]
Yala nagafi yagne lol ta weralela lol
Machallah si micro bi
Niaka diangue arabe téwoula kham sa diiné parce que arabe langue lah kom langue yépp moi je suis contre nouni kou diangoul arabe waro wakh si diiné
Monsieur tajoudine khamenga kane la .kou rew la.make bou bone
Biss bou sétt ma wakh ko Senegal woutel sen bopp bakar rk
Je ne suis pas en phase!
Taper sur Modou Gueye et le traiter d’insolent sans vraiment apporter des arguments très fondés pour infirmer ses propos , je suis désolé mais c’est faire preuve d’agressivité verbale. Mr Gueye peut ne pas penser comme la majorité des sénégalais musulmans voire des musulmans en général mais personne ne peux dire qu’il va à l’encontre de ce qui est dit dans le Coran!
Maintenant, libre à ceux qui pensent que Le Coran est insuffisant comme source et ont besoin de sources secondaires ATTRIBUÉES au prophète (avec leurs lot de mensonges et de vérités probables) pour pratiquer leur foi, mais attention, la surprise risque d’être grande… fii mou wérou moo geuneu woor dé!
AlQuran REK moo woor, li ci dess waxou nitt késsé La.
Modou gueye kiko defendre yaak mooma yamm diiine sii koussi am xam xam moo si wakh ki xamoul ngua demm gnou xamalla... Des gens comme modou gueye il parle de tout comme s il savait tout
Jerejef amna solo manchallah
Dieuredieuf❤❤❤
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
Jerejef amna solo manchallah
❤❤❤❤❤❤