Machalla moi je crois que seul l'agriculture pourra développer le Sénégal le nouveau régime doit discuter avec ces chefs religieux et créer des vastes champs pour donner du travail à Une bonne partie des jeunes
Intéressant l’émission à perpétuer de manière ponctuelle, faites intervenir des experts avec des conseils pratiques, notamment comment trouver un terrain agricole pour les jeunes sans trop de moyens !
L 'état devait donné plus de terre et de financement a ces valeureux sénégalais qui travaillent en silence et qui supportent beaucoup d'emplois...voila qui peut créer beaucoup d'emploi ........on se demande souvent pourquoi les marabouts réussissent plus que les ingénieur agronomes !.. ils sont plus ambitieux et plus libres de la mentalité européenne du salarié de l'état.. xelcom est exemple très ambitieux et privés....maintenant il faut organiser davantage pour plus de sécurité des employés et formalisation.....
Tout ça c'est l'œuvre de serigne Moustapha bassirou mbacke et de fils serigne cheikh awa balla mbacke son fils qui avait pris le relais de la ferme agricole de pout merci mon ami seck mr diadji gueye expert agricole
Wakeur Serigne Touba yi lignouy liguèye kèn liguéyougo Gni khamoul dara gno wakh aye toke mouye dokh. Ceux sont les grands agro-industriels et opérateurs économique du pays lii bène exemple rèk leu parmi tant d’autres
You mél nidé aka bari thie yonou mouride ta nite niou bari khamou niouko ! Motakh Souma dégué am niouye wakh Serigne si aye affairou tok mouye dokh rétane daf maye diapou sakh ! Niou bari daniouye guisse aye défauts minorité bou ndaw niou beugue ko généraliser ! diwakh diwakh rék ak di togne ta liniouye wakh khamou nioussi dara !.
Ñoun mourid ñoo amal Sénégal yepp njariñ jël suñuy millions diko jagleel Sénégal par ce que ligeeye jaamu yalla japp sunu njambour dëglou serigne bi lañu xam. Daa am ñoo xamni jiitou gui yoonu murid jiitou ci lepp xam xam, am am, akouk defarou mooleen neehul tah fouñou tollu lou ñaaw rekk lanuy xool
Machalla moi je crois que seul l'agriculture pourra développer le Sénégal le nouveau régime doit discuter avec ces chefs religieux et créer des vastes champs pour donner du travail à Une bonne partie des jeunes
Macha allah yal naah senegal dieem kha naam😊
Content d’avoir été là tout au début de l’exportation des fruits.
Machalah tonton secka un technicien qui metris bien l'agriculture je le connais bien
Bonjour, est-ce que vous pouvez me mettre en relation avec lui svp?
Machallah c'est intréssant merci
Bravo..une belle emission..❤❤❤❤❤❤
Balla aicha boury, walahi si li rek ngagnou taguatte. Liguey ak diamou yallah. Rethiou wougnou beneu yone soukou fa yoe diokhla sugnu lepou.
Merci good job
Intéressant l’émission à perpétuer de manière ponctuelle, faites intervenir des experts avec des conseils pratiques, notamment comment trouver un terrain agricole pour les jeunes sans trop de moyens !
L 'état devait donné plus de terre et de financement a ces valeureux sénégalais qui travaillent en silence et qui supportent beaucoup d'emplois...voila qui peut créer beaucoup d'emploi ........on se demande souvent pourquoi les marabouts réussissent plus que les ingénieur agronomes !.. ils sont plus ambitieux et plus libres de la mentalité européenne du salarié de l'état.. xelcom est exemple très ambitieux et privés....maintenant il faut organiser davantage pour plus de sécurité des employés et formalisation.....
Machallah ❤
Amna solo Jajef baykat
❤❤❤Machallah
POURTANT DA MASSA LEER TE DAY GËNA LEER YOONU MURID LIGEEY JAAMU YALLA JAPP SEEN NJAMBOUR ON EN A TANT D'EXEMPLES
Machalla
Tout ça c'est l'œuvre de serigne Moustapha bassirou mbacke et de fils serigne cheikh awa balla mbacke son fils qui avait pris le relais de la ferme agricole de pout merci mon ami seck mr diadji gueye expert agricole
Serigne cheikhe awa balla Mbakce ibnou serigne moustapha bassirou Mbakce ibnou serigne bassirou Mbakce père de actuel khalif général des mouride serigne mountakha Mbakce
Macha'allah
Kou yapp yonou mouride danga xamoul rekk wayee bilahi dévoloppment Sénégal rôle bou makc lathi yonou mouride joue
Dégueula mbokk liguey bokoul ak wakhi késsé bayiléne niou wakh niome niou liguey rék
@@papasambandiaye5405 lolou moom deugg laa wawaw
Ligueye diamou Yalla rék.
Machalla li mo matta wane
J'aime le Sénégal
Thieye mouride yi
Diara Diaf borom Nawell
djierudief serigne moustapha bassirou mbake yalla na nioko yalla fayal ❤❤❤❤❤❤❤
Wakeur Serigne Touba yi lignouy liguèye kèn liguéyougo
Gni khamoul dara gno wakh aye toke mouye dokh. Ceux sont les grands agro-industriels et opérateurs économique du pays lii bène exemple rèk leu parmi tant d’autres
Took muy dokh kou melni bokouci ! Ce marabout est un exemple à montrer
❤❤❤❤
You mél nidé aka bari thie yonou mouride ta nite niou bari khamou niouko ! Motakh Souma dégué am niouye wakh Serigne si aye affairou tok mouye dokh rétane daf maye diapou sakh ! Niou bari daniouye guisse aye défauts minorité bou ndaw niou beugue ko généraliser ! diwakh diwakh rék ak di togne ta liniouye wakh khamou nioussi dara !.
❤❤
Ñoun mourid ñoo amal Sénégal yepp njariñ jël suñuy millions diko jagleel Sénégal par ce que ligeeye jaamu yalla japp sunu njambour dëglou serigne bi lañu xam.
Daa am ñoo xamni jiitou gui yoonu murid jiitou ci lepp xam xam, am am, akouk defarou mooleen neehul tah fouñou tollu lou ñaaw rekk lanuy xool
Si tout les marabout fesais comme toit senegal développer na bou yague wayer took rek dit ladje adiya
Ñi ngay wah took muy doh tu a tout simplement l'impression waaye lañiy ligeey yepp xamoo ci dara
Contenu Yi lan sokhla si média Yi sinon débat bi Dana wathi basi soufe
Wawa dakh dioume sokhlawone ligueye katt mane dama bague kouma diall
Partage video bi