Yagui si febar Fadjou Diapaler jeunesse bi ,makk gni,réfectionner les écoles mosquées venir en aide les nécessiteux, réalisés les rêves des autres personnes si âge yup y’a meune y’a eupeu doller t’es un jeune exceptionnel digne de confiance 🙏❤️🇸🇳yalnala Borom bi sameu
Un homme au grand coeur….. Je l’aime tellement sans le connaître. Son côté bling bling a fait de lui un victime de jugements negatifs.. Mbaye dokhalal rekk gni ngay dimbali rekk boula seen niaane dalei kanam rekk nga dieum
Amo morom sa khol machallah bilahi guissaguo dara digua am lou guawer sa ndiorte 🙏🙏🙏🙏🙏💛💙💛💙t’es le meilleur King Kong diagne tu seras le meilleur buteur de la planète inchallah go Gainde ❤️❤️❤️❤️❤️
Ma cha allah Congratulations big friend mbaye tu m'as toujours aider dans mes études et à l'extérieur yalla nala yalla diappalé Incha'Allah ❤🇧🇪🇸🇳🤝grand frère
Vraiment je suis tellement contente de vous voir dans cet canapé Mbaye Diagne ⚽️ ❤
ปีที่แล้ว +9
Mbaye un joueur je j'aime bien ça se voit que nitt kou bakh leu tai bo kholé foumou diarr dinga khameu ni lolo takh mou ameu mental yalla nala yalla defal lou souteu sa ndiorteu bro diamm rekk ngayy ameu on t'aime ✌🏽
De zéro à héro l'international mbaye diagne encouragement et félicitation à toi yalla sénégalais en tout vous avez bcp de mérite en tant k footballeur professionnel .....
Mbagne Diagne yalla nalla yalla samou thie barkè Borome touba sa❤raféte na loll ni gay wakhé koula déglou khamni lou sincère thie sa birre ❤ ga koy tibé encore une fois Dieureudieuf
MachaAllah MachaAllah Mbaye yal na ngua am avancement bou bàkh si football bi Sama doom dji yal n'a dém ba am talent bi ngua am Europe inchallah osi yal nala yalla faye li nguaye déf si mbokk inchallah journaliste osi chapeau à toi MachaAllah
Mbaye Diagne homme bien sérieux aimable kou bakh am yar beug nieup surtout waw HLM 5 yalla nala doli sutura ❤ courage mon frère d cœur ❤️ c khar samb ta sœur chérie je 🎉🎉❤❤
Très humble une fois je l ai trouvé au casino du cap Vert il se dirigeait vers la sortie et quand je l ai appelé il est revenu jusqu à ma table et je lui disais notre fierté et notre support à son endroit un gars super
Mbaye bilay man sa début carrière ga signé Chine juste pour aider ta famille lolu rek lala nawé motax rethiou woko d yalla nala yalla défal jam🙏🙌❤️💫🔥🇸🇳💯
Barki alkhourane mangui dioye sakh mane y'a âme Diome si Gore ta khame linga beug nga Nek si yalla Nala yalla samb koula daka football nk amoul machallah liguèyou neye anioume dôme taye yalla mongui ni maila Tera nga ta dess n'a dh dinga âme louko eupeu merci mame Coumba meune nga sa émission machallah❤❤ ont dirais que ta mère représente tout pou toi machallah
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️le jeune engagé ambitieux travailleur passionné social humble tjr disponible pour le bien de la commune rawatina Sénégal 🙏🙏🙏 L’international KingKong 🦍❤
Yalla mon lay same parce nitt kou bakh gua parce vous avez commencé à aider ta mère à bas âge # yalla mon lay same # continue sur cette lancée doco reuthiou et bcp de chance à toi la bonne formation de galère de base a été fête o Sénégal bonne chance.....
Ma Sha Allah brother you’re a role model to the youths hope some of them will learn from you bcus all what you experience in life and you never give up helping your Mother to sell Ma Sha Allah ❤❤
Yala na yala may gnépou diamou si barki alkhouran kouy sonou rek say wadiour motax kone yala na yala nangoul gnou sougnou gnane mame Coumba votre émission nous rend plus fort bilay
Pour avoir vécu, grandi avec ta soeur et toi...so tollo fi wala nga am linga yoor tay, WALAHI dou loumay betteuh! Da ngay diengue rek, Mbaye, mais do daanou p'tit frère. Yalanala YA'ALLAH AZAWADJAL doli Soutoura té may leu werr ak werlé
Quelle autre athlète aimeriez-vous voir sur le canapé de confidence ?
SADIO MANE
Slu de ma part modou lo
Sadio Mané
Gana gueye
Cheikhou Kouyaté ❤
Cette journaliste aussi est très posé et professionnel chapeau à elle ❤🇸🇳
Koumay santalé SERIGNE TOUBA lalal j'aime💚💙💛💛💛
Alkhamdoulilah serigne bamba Dieureudieuf 🙏🏾🥰❤️
dieureudieuf serigne touba❤
Machallah Serigne Touba amoul morome ♥️🥰🙏
Dieureudieuf seringe touba ♥️♥️🫶
Emission bi takhna niaw ndiorte bodone def si célébrités yi nga tekkkossi souff 😢au fonds ay nitou nen lagnou ❤siw modoul diami borom
Pour dire vrai ki loumou am dako mérité pour nioun ngiko kham machalla bonne continuation fierté hlm
Yagui si febar Fadjou
Diapaler jeunesse bi ,makk gni,réfectionner les écoles mosquées venir en aide les nécessiteux, réalisés les rêves des autres personnes si âge yup y’a meune y’a eupeu doller t’es un jeune exceptionnel digne de confiance 🙏❤️🇸🇳yalnala Borom bi sameu
Amine
En l’écoutant on sans qu’il a un grand cœur
Un homme au grand coeur….. Je l’aime tellement sans le connaître. Son côté bling bling a fait de lui un victime de jugements negatifs.. Mbaye dokhalal rekk gni ngay dimbali rekk boula seen niaane dalei kanam rekk nga dieum
Mbaye diagne un homme que j'aime beaucoup a travers ces interviews c'est un homme courageux force a toi ❤️❤️🇸🇳
J’ai senti qu’il a beaucoup souffert malgré le succès le bling bling! Force a toi gaindé
Boubakh nakhte sounou famille dafa reuy montakh, te ay soufrances you meti nakh ñiak wante lepp diekha legui, ñoula khebon ñoy ñeuw di topp sisa guinaw aka siborou. Montakh yallah diekhoul❤
@@Fatweleyallah diexoul bou diexei diexei na bothi guenei mou nexa netalii
Pratiquement toutes les personnes qui ont réussi avaient un amour et un respect inconditionnel à leurs mamans
Amo morom sa khol machallah bilahi guissaguo dara digua am lou guawer sa ndiorte 🙏🙏🙏🙏🙏💛💙💛💙t’es le meilleur King Kong diagne tu seras le meilleur buteur de la planète inchallah go Gainde ❤️❤️❤️❤️❤️
Kepp kouy def bac yalnako am si barké mame babacar❤️
ALLAHOUMA Amine MACHALLAH
Amine 🙏
Amin
Amine yarabbi
Alahouma amine
Ma cha allah Congratulations big friend mbaye tu m'as toujours aider dans mes études et à l'extérieur yalla nala yalla diappalé Incha'Allah ❤🇧🇪🇸🇳🤝grand frère
Tous nos encouragements à Mame Coumba. Dieuredieuf, Mbaye am nga diom
Nous te réclamons ton retour au sein de l’équipe nationale parck t’es le meilleur buteur Africain avec une très bonne saison 🙏🙏❤machallah
Franchement tout ce que tu as dit c vrais il doit revenir
Xana sen mbok la ?😂😂
@@imsenegal5261 nn mm op danio wakh rk liniou beug wala
Salamalèkoum
Non franchement honnêtement sérieusement droiturement respectement sagement gentillement coolement , mbaye diagne djegall naniou ko équipe nationale
Boumou nieuww , boumou wootee!!!
Naa gorgorlou , demm Macca ak djakadja rek
Merci
Mbaye sama kharit bakh am respect . Je vis à londres mais des que tu Dia Ti wa sénégalais ils te disent Diagne . Tu es une fierté . C est Torodo
Vraiment je suis tellement contente de vous voir dans cet canapé Mbaye Diagne ⚽️ ❤
Mbaye un joueur je j'aime bien ça se voit que nitt kou bakh leu tai bo kholé foumou diarr dinga khameu ni lolo takh mou ameu mental yalla nala yalla defal lou souteu sa ndiorteu bro diamm rekk ngayy ameu on t'aime ✌🏽
mbaye tu est vraiment un exemplaire tres fiere de toi tu merite plus que la selection
De zéro à héro l'international mbaye diagne encouragement et félicitation à toi yalla sénégalais en tout vous avez bcp de mérite en tant k footballeur professionnel .....
Ndayssane tay Anta n’est plus. Yalnako Allah yeureum🤲🏽
Tiey aduna !
Mbaye Diagne kou bakh leuh ❤❤❤❤❤
Mbagne Diagne yalla nalla yalla samou thie barkè Borome touba sa❤raféte na loll ni gay wakhé koula déglou khamni lou sincère thie sa birre ❤ ga koy tibé encore une fois Dieureudieuf
MachaAllah MachaAllah Mbaye yal na ngua am avancement bou bàkh si football bi Sama doom dji yal n'a dém ba am talent bi ngua am Europe inchallah osi yal nala yalla faye li nguaye déf si mbokk inchallah journaliste osi chapeau à toi MachaAllah
Un vrai homme ❤ YALNA YALLAH SAMMAL BOPAM
Mbaye Diagne homme bien sérieux aimable kou bakh am yar beug nieup surtout waw HLM 5 yalla nala doli sutura ❤ courage mon frère d cœur ❤️ c khar samb ta sœur chérie je 🎉🎉❤❤
Nous t’aimons beaucoup parck vous êtes notre fierté le meilleur domou Deuk Bi Hlm 💙💛💙💛💙
Très humble une fois je l ai trouvé au casino du cap Vert il se dirigeait vers la sortie et quand je l ai appelé il est revenu jusqu à ma table et je lui disais notre fierté et notre support à son endroit un gars super
Longue vie à toi mame coumba❤tu es la meilleur animatrice de ta génération ❤
Mon fils yalanala yala diapalé lou bakh koukoye défe yala moye faye té inchala dinala faye. C'est une maman qui t encourage depuis Richard toll
Tu es brave mbaye machallah yén diar diar dafay metti mais bossi amé terangua dafay nekh
Ndeysaan yallah na aldiana firdawssi di noflayam 🤲 Anta
Mbaye bilay man sa début carrière ga signé Chine juste pour aider ta famille lolu rek lala nawé motax rethiou woko d yalla nala yalla défal jam🙏🙌❤️💫🔥🇸🇳💯
Koufi diar dall âme gua parcours boula forger❤❤❤
Confiance Num1 Des ITV Si Oui ❤
Mbaye Depuis Je Savais K T'étais une personne de ❤d'or nitt bou bakh khamko diafawoull
Lou way deugueur deugueur dioy 😢mbaye ça m’étonne pas sa mame yaar la😂 mais nak Machallah diambar nga ❤🎉
Moi cette journaliste m’impressionne de sa beauté et de son professionnalisme jamais hors cadre. Keep doing ❤
Barki alkhourane mangui dioye sakh mane y'a âme Diome si Gore ta khame linga beug nga Nek si yalla Nala yalla samb koula daka football nk amoul machallah liguèyou neye anioume dôme taye yalla mongui ni maila Tera nga ta dess n'a dh dinga âme louko eupeu merci mame Coumba meune nga sa émission machallah❤❤ ont dirais que ta mère représente tout pou toi machallah
Mbaye yalla gua âme contrat Arabie Saoudite comme niguako beugué si barké Seydina Mouhamed 🙏
Belle emission. Mais ne pas oublier l'essentiel. Libérez sonko.
Yalna yalla barkel lep tu es vraiment quelqu'un de simple,modeste, sincère bonne continuation mon fils ❤
Mame Coumba walay je t’aime basi kanamou Yalla Yalla nala Yalla may goudou fane ak wergui yaram ❤️🙏
Dou pour mane cette réponse dit tout ça ve dire qu'il pense a sa famille ❤
Très belle interview vraiment les questions pertinente très belle présentatrice.
Mbaye j’veux vraiment j tu reviennes en équipe nationale mais avec habib Diallo boulaye dia et nikolas Jackson ça sera difficile dh toma 😮
Adouna dara kheyoule soti bilahi walahi mong rk ba kheyi am Lou bakh Dara yageu goule ndayissane 😭😭😭😭
Lolou môme damakoye deguale sama mak Sila bokk yaguo yobou yalla nasa diam yakk mbaye yalla defal la diam Diouf barii
Belle emission.des témoignages émouvants et qui nous encouragent chaque jour.Mais SVP prévoyez des mouchoirs pour les invités
On va réussir avec ou sans diplôme inchala
Emission bi c'est top mais pensez à mettre des mouchoirs à la disposition de vos invités.
MashaAla Allahouma barik . Mbaye Diagne yalna la yalla defal diam diou sakh. Da nga bakh
Bilaye khamoumako waune mais kou bahla modeste gnaque quignane vive le Sénégal
Yalla reka fi nekk mbaye ❤
Mbaye Diagne éternel incompris ❤
Courage sama waa dji contane trop ci iow walae et bonne continuation ❤ c mister DŌŪ deuk thies domou ndeye zik ndiaye
great thank you so much champion mbaye 🇸🇳🇺🇸💚💛❤👍🏽
Cest un vrai guerrier ça se voit, moins talentueux que bcp de joueurs mais tu vois qu'il est allé chercher son succès bravo un exemple à suivre
Bonne continuation grande frère yalla bakh na dina guena Bakh inchallah
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️le jeune engagé ambitieux travailleur passionné social humble tjr disponible pour le bien de la commune rawatina Sénégal 🙏🙏🙏
L’international KingKong 🦍❤
Merci beaucoup Mame Coumba courage a toi mbaye Ndiaye ❤❤❤❤❤
Elle est très posé la journaliste je l'aime bcp❤❤❤❤❤
Yalla mon lay same parce nitt kou bakh gua parce vous avez commencé à aider ta mère à bas âge # yalla mon lay same # continue sur cette lancée doco reuthiou et bcp de chance à toi la bonne formation de galère de base a été fête o Sénégal bonne chance.....
Machalla ❤️❤️❤️❤️ bokou ngua thi sa ma dôme yi ma beugue yalla n'a la yalla same are la dolli sa ham ham amine ya raby
Force à toi Mbaye Diagne ❤❤❤
Yalla nala yalla defal khewal si barke serigne TOUBA 🙏🏿
Amine ❤❤❤❤
Ma Sha Allah brother you’re a role model to the youths hope some of them will learn from you bcus all what you experience in life and you never give up helping your Mother to sell Ma Sha Allah ❤❤
Il a un Grand coeur ❤
Bilahi Comme mane ainsi nonou lay def dianguile ma dem antrainement motah niogui May ray mais douma bayi dh nagne ma ray❤
Yala na yala may gnépou diamou si barki alkhouran kouy sonou rek say wadiour motax kone yala na yala nangoul gnou sougnou gnane mame Coumba votre émission nous rend plus fort bilay
Vraiment borom bakh gua mbaye yalle nala souniou borom défal diam gaïndé yok sa meun meun amine inchallah ❤🤲🏾
Pour avoir vécu, grandi avec ta soeur et toi...so tollo fi wala nga am linga yoor tay, WALAHI dou loumay betteuh!
Da ngay diengue rek, Mbaye, mais do daanou p'tit frère.
Yalanala YA'ALLAH AZAWADJAL doli Soutoura té may leu werr ak werlé
Bon courage mbaye ❤bonne continuation
MACHALLAH MBAYE yalla n'a diamou sonel si barkep serigne touba khadim rassoul ❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla yalla nala yalla defal diam
Yalnala yalla faye sa khôl, meusso changer meusso sopekou, diome fouleu dignité rek monek thi yaw. Afaye ✌️
Mbaye dei nit la machallah 😊🙏🏾
Bonne continuation
Sa Yaye reck mo takh ma beugueleu ❤
Goor yallah nga❤ we love you and respect you
Il faut invite notre sadio mane nationale svp❤
Dagua yagueu gueumeu sa boopou kou bakh guaaa mbaye diagne ont aim❤❤❤❤
Ya yé indalé mouchoirs 😂 du courage frère
Machalah 👍 dama beugg kou social goudeul fane lol inchallah 🙏
Sama idol mbaye
Machala mon frère bonne continuation leup Dina bakh inch'Allah kou meune sa nuit ngua bilay yalla nala yalla gay sa khôl amin❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Envitéle noiu gogui sy ndiang ❤🏀❤
Barcky seringe bamba diam rek ngaye am ❤️❤️❤️❤️
Big respect ✊ Frère 👦
Dieureudieuf seringe touba ❤❤❤❤❤
Il partage ce kil a machalla un vrai lion
Hi mame Comba il faudra desormais avoir une table avec de l'eau et mouchoir a jetter pls
Ndeysane fierté hlm❤
Vraiment ta mérité se que t'ai devenu mashalla Fall ndiaga yaram
J’aime bien ce gars.. c’est un baye fall dans l’esprit
longue vie a toi mbaye Diagne ❤🥰
Barki yalla mbaye diengne biss bou moo contacté moomm di na amm club bou bakh barrki mouhamed la la wakh dafa amm lou nékk si momm❤❤❤❤❤
Très posé et mâture ma'shallah vous avez gagné une nouvelle fan 😂 moi aussi je me sens king Kong en Italie douma mayé niente niente
M achallah longue y
Non mbaye à un cœur formidable ❤❤ merci mame coumba
Vous êtes les meilleurs❤