ขนาดวิดีโอ: 1280 X 720853 X 480640 X 360
แสดงแผงควบคุมโปรแกรมเล่น
เล่นอัตโนมัติ
เล่นใหม่
En tout cas il faut pas le lâcher talfa c un futur champion
Félicitations à vous vraiment talfa liguey bii nice na
Coach Carré wah gua lepp
Boucher mom domeram deug leu loumou def wakhé ko ngistalkatla 😂 nen Dina diokh ama baldé 5 kilos yapeu par jour
Boulène niou sonal bou Talpha danone dolène wakh dagn ko sétane ,Dioulittt day nangou ndongal
🎉🎉🎉
Talfa yalnako yalla maye un mental de fer
Boucher sakh bala mouy diapalé kén mou diapalé rak dji tolou ni banete balé 😂
😂😂
Vraiment 😂
Wakh degue yalla raye nguama 😂😂😂😂
Wax degeu degeuuu
Talfa na dem diambarr
Yaw doul wakh reck
Jambar goudoul franc gueumou nioula
Ndeye saane adouna nii la
Talfa KESSE
Boucher bougougnou nga diapalé gnou yaw seytané nga démal nga diapaler sa famille mo geunn si iow
Bayilein kou danou ngein di wakh daniouko khekh. Talfa na wakh nioumiy andale niou bayi agresser ak di nangou alalou diambour yi lolou rek moko tope
Saway Lolou c tous les lutteurs populaires Talfa mounoussi draa yaw ya warra nekk nitt
Yaw nekal nit