Djeureudjeufeuti Saa Maame Nééna « Nangeen bayi farr togne katt té waxko mou bayi togne, liilèy dindi togne khawmii louko moy dakoy sakhal » disait Mame Abdou Aziz Dabakh. Ce Monsieur Omar wakh nafi : 1) Cheikh Tidiane Chérif simple chrétien lawone bou toudone Jean Michel. 2) Néna tidiane yi bignou tamablé diouli takoussane yagoul ndakh sèn tarikha yéfeur bi dadone téré diouli takoussane. Djinné djignouy diaamou day bagne nodou takoussane 3) Néna cheikh tidiane chérif ap djiné la signél pacte mou diokh ko dieuwharoul kamaal Kone tidiane yi seytané lagnouy diaamou 4) Néna cheikh tidiane chérif dadone tapdiil khaliss lolou motakh gnou dakk ko Algérie mou daw dem fez. Lii esk dou togne ci nitou yalla bo khamni bimouy am 7 ans la mokalone Alkhourane ci khétou dianguine yepp té ay centaines de millions domou Adama defko mouy sen kilifa ? Kimouy saaga moy serignou Elhadji Malick Sy, moy serignou Cheikhou Oumar Foutiyou Tall, moy Serignou Baye Niass Cheikhal islam. Vidéo yép mongui ci lokho enquête katt yi té walahi kenn manoul wakh bagnou baal ko. Au contraire dagnouy yokk plaintes yi pour diffamations et injures publiques. Bepp Dahira wala personne seule bou defagoul plainte démal nga yobou seu plainte ci procureur. Kii dina bayi tidiane yi wala mou dè nopalou MANE Mane Toure je ne discute pas té baloumako
Su niou demeh ba reew ku ci wakh Qalallah, Qala Rasool nyu tiyeh la, Kon reew momu lenen na fa am waay du Islaam. Ndax man Senegal bi ma guiss, Yonenti bi su narona niowaat jangaleh lim jangaleh won ay 1,400 att ci ganaww, niou bari di negn ko weydi naan sen yonnu mame ma len geunal
Li Ahmed khalifa Niass moko ndieukeu wax té kène bayi woussi khel. Quand un journaliste lui avait demandait sur le wasifa dans les mosquées il avait répondu en disant que wasifa acapella la . Il faut savoir que les chants religieux dans les mosquées et même dans les églises sont des traditions purement africaine qui n'ont rien à voir avec les religions à leur origine. Quand vous allez aux États-Unis les églises ou on chante et danse ce sont les églises des noire afro américains. Pour vous faire remarquer que vous ne verrai jamais de chorale dans les églises blanches européennes ni de wasifa à la Meque ou à Medine. C'est l'africain qui aime chanter jusqu'à intégré cela dans la religions alors que de base rien de tout ceci n'en fait partie. Donc Omar sall à parfaitement raison. Et quand à la façon de dénoncer rapellez vous du notable qui se disait prophète, quand Mouhamed (saw) là entendu il lui a répond froidement en lui disant "tu es un menteur". Donc deugou YALLAH (swt) bou dioté waxal si tu est du nombre des véridiques.
C'est vrai les tarikhas au Sénégal égarent de plus en plus ceux qui les suivent et c'est à nous ahlou sunna wa jammaha de les guider avec intelligence et sagesse
Oustaz Oumar sall yàlla na Borom bi azawajal Sam la amine Moi je comprends pas le Sénégal quand on offense Allah swt ou le prophète psl ça passe inaperçu et au contraire quand on critique un tarikha ou un chef de famille tarikha la terre va trembler c'est du fanatisme ou quoi 😭
IBN OMAR a rapporté dans un hadith sahih (authentique) que le Messager d'Allah PSL a dit Lorsque vous passez par les jardins du Paradis, prenez place." "Mais où sont les jardins du Paradis, Ô Messager d'Allah ?" "Ce sont, répondit-il, les cercles où on mentionne Allah, car en vérité, Allah a des Anges qui rôdent dans les rues à la recherche de ces cercles et s'ils en trouvent un, ils commencent à tourner autour des hommes et les enveloppent de leurs ailes.
Coran 38 "SAD" versets 17-18 : [ Endure ce qu'ils disent; et rappelle-toi Notre Serviteur David, doué de force (dans l'adoration) et plein de repentir (à Allah). Nous soumîmes les montagnes à glorifier Allah,au soir et à l'aurore, en sa compagnie De même que les oiseaux assemblés en masse, tous ne faisant qu'obéir à Allah].
@@AssaneDiop-w5m sourate an-noor 24 verset 36. Dans des maisons [des mosquées] qu'Allah a permis que l'on élève, et où Son Nom est invoqué; Le glorifient en elles matin et après-midi, Legui wakhma Al quran ndakh dagn ko soss
Anas ibn Mâlik رضي الله عنه rapporte que le Prophète ﷺ a dit : « arrivera un temps où celui qui s’attache à sa religion sera comme une personne qui tient une braise ardente dans la main. »
Wanté toogne baakhoul, kouy waaraaté d'accord, mais Tarikha Diambour bayyi kofa. So beugué Diam. Sénégal yagg na ak Tarikha, so bokoulé nga doundeu sa Sounah boubaakh té bania toogne. Ya Allah na nieupp am Diam si barké Seydina Mouhamad (SAW) amiin
Bien Dit Le Problème En Ai Que Xam Xam Bi MOffa Nékkoul Motax Mais C Vraiment Triste Gni Sén Tarikha Rek Laniouy Protègé Mais Dîné Dji Sén Yoone Nékkousi
Face à tous ses attaques et critiques depuis qu'il a commencé, ces gens se sont toujours défendu avec des arguments solides et basés sur des textes authentiques et l'on même plusieurs fois invité à un débat public, ce qui pourra permettre à tout personne doté de conscience de juger selon sa conscience, mais il n'a jamais accepté de le faire. Mais préfère faire ce genre d'attaque pour influencer ce qui n'ont de connaissances dans ce domaine oui ce sont que ces derniers qu'il peut influencer vu qu'il ne savent pas grand chose sur ce qu'il avance et en le voyant parler et parfois citer des textes dont ils ignorent et oriente le sens en faveur de sa doctrine.
Wakh dji amna solo trop mais pour mane nie ko pourté pleinte Amna fougne ko ték psk mom omar sall dafa yague di togne di dougou si pass pasou nit gni mais li bou si diougué bou féké borom xél la dina khol bou bakh limouy wakh🙏🏿
Oustaz wakh deugue yalla ya togne défo ko sa yonn nékou si niom au moins ay dioulit la niou nagou naniou Seydina Mouhamed SAW comme prophète mais gueumeul liga guemm ga bayi lén niou gueum li niou guem organisé wou niou soiré di fooo daniouy toudou yalla bayil togne. Guén bal ma akheu.
My Boy je t’estime bcp vraiment souféké Alkhourane ak sunnah biguay wanné si sa ay Video mo nek si yaw bousi ragal dara koulay beug Nalasi beug koula bagne mo kham Wahal waxdji mou ler nagne boul ragal dara Nit yi meuno niou thi yaw dara Kasso diomul kèn.. (Exemple le prophete youssouf) Souféké dagua beug di wx thi diné di ragal bou yabo meun gua bayi Oustaz Oumar Ahmad sall yalla nako yalla takhawou 🤲🏼🙏🏾
Mann dei moom laa andal. Yonente bi limou niou sante mooy suniu nékké si deukk bou am loi niou topp loi booba motakh Sénégal kou Ray niou teuj la. Naam nk wakh deugg tollouwaayam deugg la wakh waayé li waadji wakh jangalé daa andak akkh.
Yaww ngané tidiane nga nii yaww niatta Yonne oustaz Omar attaquer tidiane yii akk niatta Yonne lagnou ko tégale ayy arguments youmou meunoule dinedii té il persiste toujours donc faut vous renseigner d'abord il dit toute sorte de moqueries
@@abdoukhadrediaby1438vraiment merci beaucoup C'est le seul commentaire qu'il fallait laisser sur cette vidéo Boy bi di wakh ci vidéo bi mom ay vus la beug tei daa melni xelmi néxoul mais limou wakh amoul Béne sens ndakh ay wakhou doff lah
Tarikha tidiane bi ci sunnah ak alkhourane lagnko sossé Amoul aaya boukoy wéddi Omar Sall mom souféké lou yonente bi ak sakhaba yi défoul rk bidaa kone mom ci bidaa la deukk ndakh yonente bi (PSL) meussoul deff vidéo youtube
No tay mom andouma ak yaw abdoul wahab keen amoul doit gemm lou la nekh yalla limou diglé laniou wara gemm ta oustaz omar sall defoul lodoul diotali comme nikou sangue bii defé bam aksi si nioun 😢yalla nakou Yalla takhawou samou kou inchallah ❤😢😢
@@bayemodoubadji7032 merci beaucoup bayi nala ak yalla yalla naniou yalla atté si dieumi seydina mouhamed ak togne gingama togne si barké alkhourane 🙏🙏🙏
Machalla yangui wakh lou am solo yalla nala yalla samm di gnanal Oustaz omar sall yalla nako yalla samm si barké alkhourane yalla defal ko diam 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🥹🥹🥹♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Abdoul Wahab a bien raison, on est au Sénégal, ainsi, il faut savoir, comment, dire ses vérités sans offenser, et pour Oustaz, certe, il est véridique, et ne craint rien, ce qu'il a dit, est vrai, mais, c'est la manière dite, qui l'a créée des soucis, et surtout qu'on est au Sénégal, avec sa laïcité et divergence des idéologies, ainsi, il faut user de délicatesse dans ses propos ! , Que Dieu Assiste et Protège Oustaz Sall.
Il est hypocrite. Pourquoi dire "toudouma tour" alors qu'on sait bien qu'il parle des tidjanes? Et il n' a pas raison. S'il a du problème avec des gens qui évoquent le nom de DIEU le matin et le soir, en plus dans un lieu saint, il a un problème avec son créateur. Wayé comme day garouwalé, gnou wane niko gnokoko dakk, ndax kou yénéwoul sa bopp thiolign gou matt, do yéné sa borom diiné djou matt.
Fattégua touddou serigne yi di khass yallah diko saga tegnou nek que tijiane té kene dou wakh senegal nit gnii beugue negne diiné mais khamougnouko a cause des tarikha dakh dougne lene diagal tawhid bou ler dakh chef tarikha yi ils savent que du moment où les sénégalais connaissent réellement le tawhid moye tarikha diekhna senegal par conséquent tok mouye dokh bi daye diekh mo takh Sénégalais yi wara yewou si niom. Free oustaz le connaissant amna ndiorte que sokhla la woul niane ndiek té kep kouye ahlou sunnah Sénégal defal sa khel que meune gua niam kasso dakh Senegal nekfi ahlou sunnah crime la je pense.
Lègui kan mo nèkoul si souna ? ou bien tu veux dire souna wahabisme ? Soufisme égale souna, comme ninguèn yakarè ni wahabisme si souna la bok Lègui nioune gni nèk si tassawuf ban souna la yonènt bi wakh bounou défoul wala ban sarou alkhour'an lanou weedi ? Ba à chaque instant nguèn beugue no guènè si dîné yalla bi , yèn danguèn no dakka diouli ? wala wor ? Wala dém diakka ? walla nafila ....? Donc chacun à son choix ( wahabiste, Soufisme alkhour'aniyou ..... tous sont des musulmans) mais ne juger pas les personnes c'est ALLAH seul qui peut juger 🙏🏻
@@od7240nafèkh meunoul wèssou guiss ay dioulit comme yaw nga diapèlèn ay nit you rère Wala ko guiss diape ni yako gueun wala yako dakka diamou yalla Com niko wahabiste yi di défè pour niom niom rék nio dioup nio gueun nieup wala nio dakka diamou yalla nieup wala niom rék la yalla di nangoul sèni dieuf
@@Htqv221 malheureusement tu n'as rien compris mon cher je te renvoie sur la biographie de muhammad ibn abdil wahab. Tarikha mom dou meusseu nek sunnah yonnete bi dakh khamouko khana sen sunnah mame yi la mais pas bou Mouhammad psl
Je trouve que cette plainte lui été ciblé depuis un long moment, ils ont juste attendu une faille de sa part pour passer à l'acte car il a longtemps dénoncé des vérités qui dérangent et ça depuis le vivant d'Imam Alioune Ndao (Rahmatoullah Aleykhi).
Oustaz Omar Sàll dafay togn, temps yeeh mouride yi la dieuloon, legui mongui si Tiijaan yi... Humm okei on verra bien 🧑🦯 Nitt, surtout màgg, ngani defar mola takha joukk daa am noo warra waxee.. 😕
mome dou tidjiane louy yonam ci tidjiane yi dou ci mandou nék ta geum lim geum bougnou démé ci yalla moy khol kou nék lay sa akh mou faylako nianal diouliti Sénégal yépp ndiégalou yalla mo geun mouy diéma tanne gniy dougou al diana wala safara ta yalla rék mo kham limouy déf
Dakh diamanoy Mouhamed wasifa ak hadara amone ? Li question rék la prison ak plainte wou tou ci dra . Sénégal deuk boromi xam xam la faites bien la différence. FreeOmarsall
@@cheikhoumardeme293kone ioe danga geum ni façon diamou yallah bou djiougué woul nabi saws ak Ay sahabame meun na bokk si islam teh yonente bi ni leppp lou besss si diiné gui app reerrrr la
@@Khoudar_HiGhLanDeR Encore des manipulations qu’on vous fait Kiye Jang Alxuraan Ba Noppi Douko Jëffé Bou Timé Téré Ndax Alxuraan Douko Rëbb Ankay Alxuraan dakoye rëbb Ci Waadji la Seydina Cheikh Waxni Jang Salaatul Fatiihi Moo Gën Ci Moom Muye Jang Alxuraan Wayé Kénn Meussoul Wax Nih Salaatal Fatiihi Mo Gën Alxuraan Bayileen Sossal Nitou Yalla
Boy Yow Bou de Oumar Sall Kham ngako Neko Oustage Makhtar sarr Parena Pour Ngeun Wakhtan Ci Kham kham walla sah Mem Bou doul Oumar sall Niom Mor kebe Oumar Diallo Alpha Ba Ak Sen Serigne Ahmed lo
الحق من ربك فلاتكن من الممترين ❤أستاذ عمر سل لم يقل سوى ماجاء في القرآن والسنة وأنت نفسك تعرف هذا شئت أم أبيت 😢ولا تكتم الشهادة ومن يكتمها فإنه آثم قلبه...لذا قل فقط بما يرضي الله ورسوله لا بما يرضي الناس ياعبد الوهاب 😢 فرضي الناس غاية لاتدرك
Ce qui est dit dans le coran est d'invoquer Dieu matin et soir, plusieurs fois et dans les mosquée, ce qui est dit dans les habits est encore très large et honore ceux qui assistent aux assemblée de zikr. Bayilen jahasse. On peut ne pas être d'accord sur l'interprétation tes textes mais na kunek respecter moromam. Ou étiez vous quand omar sall mentait sur la vie et les origines de CHEIKH SEYDI AHAMET ATIJAANI, les tidjanes ont toujours été tolérant et ont répondu à toutes les critiques en se fondateur la science. Maos ils n'accepteront jamais d'être traité de folklore ou gnouy thiahane. Omar sall moo togne c ça la vérité
Ana Talibé cheick Tidjane chérif ❤❤
❤❤
Je suis là 💖❤️❤️❤️❤️
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂❤❤😂😂😂😂😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤
Machallah les musulmans ne suit que sur notre guideur mouhamed salah lahou aleyhi wa salam qallah te préserver et merci pour ce message
JE SUIS TIDIANE ET FIER DE L’ÊTRE ❤❤❤
Tu est fou et fier
Waxo fii dara vraiment ligayy wakh dagako raagall mtkh bull beug ay j'aime Walla kulla abonnés ba do wakh fii Deug fétté 😂❤😮
Fier d'être tidiane ❤
P
Machallah frère vraiment kadou yi rafétna amna solo 🙏
Fère d'etre tidiane ❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yalnala yalla saamm yaa oustaz oumar Sall
qu'Allah lui protège amine 🤲
Dieureu dieuf srgne Babacar sy❤
Oustaz omarr sall yall nala yalla samma te gudall saii fann
😂
omar sall.Qu'Allah te protège, tu ne dis que la vérité. Mon pays va mal😢
Yalna yalla Samm Aar Oustaz Oumar Sall
Djeureudjeufeuti Saa Maame Nééna
« Nangeen bayi farr togne katt té waxko mou bayi togne, liilèy dindi togne khawmii louko moy dakoy sakhal » disait Mame Abdou Aziz Dabakh.
Ce Monsieur Omar wakh nafi :
1) Cheikh Tidiane Chérif simple chrétien lawone bou toudone Jean Michel.
2) Néna tidiane yi bignou tamablé diouli takoussane yagoul ndakh sèn tarikha yéfeur bi dadone téré diouli takoussane. Djinné djignouy diaamou day bagne nodou takoussane
3) Néna cheikh tidiane chérif ap djiné la signél pacte mou diokh ko dieuwharoul kamaal Kone tidiane yi seytané lagnouy diaamou
4) Néna cheikh tidiane chérif dadone tapdiil khaliss lolou motakh gnou dakk ko Algérie mou daw dem fez.
Lii esk dou togne ci nitou yalla bo khamni bimouy am 7 ans la mokalone Alkhourane ci khétou dianguine yepp té ay centaines de millions domou Adama defko mouy sen kilifa ? Kimouy saaga moy serignou Elhadji Malick Sy, moy serignou Cheikhou Oumar Foutiyou Tall, moy Serignou Baye Niass Cheikhal islam.
Vidéo yép mongui ci lokho enquête katt yi té walahi kenn manoul wakh bagnou baal ko. Au contraire dagnouy yokk plaintes yi pour diffamations et injures publiques. Bepp Dahira wala personne seule bou defagoul plainte démal nga yobou seu plainte ci procureur. Kii dina bayi tidiane yi wala mou dè nopalou
MANE Mane Toure je ne discute pas té baloumako
Yaw toppal feulé koula wakh nga Baal ko déme léne outi xam xam mo gueune séne yeufou dof yi
Yaw yay imbéciles ya mana doule yaw ragalale si liguey wah théy yalla sougnou borom 😢
Bien dit di Gniam li moy gniaka kerça Man sen gniak manou
Bien dite mon frère cheikh Ahmed tidiane Cherif Moy Serignou Serigne Touba sakh
@@layekna2881meune doule😮
Dieureudieufé Baye Niass
Mawlana Baye Borom Medina ♥️
We the Gambian people are behind you oustass today and tomorrow. Whoever is with Allah and his rasul has nothing to fear
Mais toudou YALLAH dankoy déffé comme niko Yonentébi déféwone pour YALLAH nanguouko.
Thank u
@@Anti-Bidaah ndax ni ko tidiane yi di deffeh la ko Yonenti bi daan deffeh?
Su niou demeh ba reew ku ci wakh Qalallah, Qala Rasool nyu tiyeh la, Kon reew momu lenen na fa am waay du Islaam. Ndax man Senegal bi ma guiss, Yonenti bi su narona niowaat jangaleh lim jangaleh won ay 1,400 att ci ganaww, niou bari di negn ko weydi naan sen yonnu mame ma len geunal
Not all Gambians are behind him in this
J'aimerai bien ecouter l'analyse de ce jeune dans 10ans sur la meme problematique!😊
Bonne continuation !!
Machallah niga wakhè rafèt na ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️yalla nala yalla sam 📿🤲🏻
Amine yarabi 🤲🙏
Li Ahmed khalifa Niass moko ndieukeu wax té kène bayi woussi khel. Quand un journaliste lui avait demandait sur le wasifa dans les mosquées il avait répondu en disant que wasifa acapella la .
Il faut savoir que les chants religieux dans les mosquées et même dans les églises sont des traditions purement africaine qui n'ont rien à voir avec les religions à leur origine. Quand vous allez aux États-Unis les églises ou on chante et danse ce sont les églises des noire afro américains. Pour vous faire remarquer que vous ne verrai jamais de chorale dans les églises blanches européennes ni de wasifa à la Meque ou à Medine. C'est l'africain qui aime chanter jusqu'à intégré cela dans la religions alors que de base rien de tout ceci n'en fait partie. Donc Omar sall à parfaitement raison. Et quand à la façon de dénoncer rapellez vous du notable qui se disait prophète, quand Mouhamed (saw) là entendu il lui a répond froidement en lui disant "tu es un menteur". Donc deugou YALLAH (swt) bou dioté waxal si tu est du nombre des véridiques.
Wakh nga lepp, cette parole clôt le débat et mérite d'être entendu par tous les sénégalais
Merci, tu as vu dé, ils n'ont rien dit à Khalifa Niasse, ni à Moustapha Sy qui insulte les prophètes. Deukkou nafekh Sénégal 😢
Ma shaa Allah une réponse claire et limpide qui mériterait d'être vu de tous
Billahi li dh moufi am😢
C'est la réponse la plus intelligente que j'ai put trouver sur ces commentaires
Vérité absolue merci beaucoup bonne continuation
Free oustaz Oumar Sall Sénégal mome dou deukeu dinnè wayei deukeu tarikha la. J'ai pitié de mon pays
Sénégal deh boko guénei ci diné meunn gua guëné reew yeup ci diné parsk alkhourane laniou soukandikou ak sunna ta maakk niou bakh njii sosss tarikha yii laawaal diné cii rewmii lagn ci dioub lou wonn
Yow namnala dé
@@Minarassoul05 ko name fi
Ya mana doull say tank dh
@@senegalrek5805Yaye bayame
C'est vrai les tarikhas au Sénégal égarent de plus en plus ceux qui les suivent et c'est à nous ahlou sunna wa jammaha de les guider avec intelligence et sagesse
oustaz makhtar sarr❤ tontounako si kham kham omar sall mak bou yarouwoul la
Yaw nième Yallah fane lako tonto oustaz oumar sall mo am ndam sen kaww rousso len daw l'akhatou si kaw macky sall
Yaw bo khamoul daguay nopi
Wakhou deug dh
Saay vidéos motax ma dioupp té fass yéné toppu boubaax limay dieuff❤
Masha Allah yalla n'a continuer❤
WERANTÉ DALL BOU AMÉ SI DINÉ BALANCE BII ALQURAAN AKK SUNNAH LA POINT❤
Yallah reck merci oustaz omar sall❤❤
Yalna yalla samou oustas omar sall
Frr bonne continuation ❤❤
Oustaz Oumar sall yàlla na Borom bi azawajal Sam la amine Moi je comprends pas le Sénégal quand on offense Allah swt ou le prophète psl ça passe inaperçu et au contraire quand on critique un tarikha ou un chef de famille tarikha la terre va trembler c'est du fanatisme ou quoi 😭
Billahi yaw 😢amine
Luwor dal murid force tidiane force ac tarixa yeupu salifistyi amngene serigne kepu culaye xamal yala sasarigne la
Sans les hallah dans les mosquées mon existence n'aurait point de sans
Allah Allah hallah hallah chaque jour jour et nuit 🌃
Connais-tu al Qadr ?
La Mosquée du Prophète n’avait pas Allah Allah
Le saviez-vous ?
@@ridwanesame2799 de lene todou allah
@@L.Yamal100 niongui koy defei niko Yonente bi SAW diangalei
@@ridwanesame2799 lo toudou yallah doyoil
Vraiment Oustaz omar sall day roubé nitt kén dou fowé limou geume😢
Tijane yi moumoûiou dine islam
@@pesor22355yaw Wèrou lolou dou wakh
Ma chahalla amna solo
IBN OMAR a rapporté dans un hadith sahih (authentique) que le Messager d'Allah PSL a dit
Lorsque vous passez par les jardins du Paradis, prenez place."
"Mais où sont les jardins du Paradis, Ô Messager d'Allah ?"
"Ce sont, répondit-il, les cercles où on mentionne Allah, car en vérité, Allah a des Anges qui rôdent dans les rues
à la recherche de ces cercles et s'ils en trouvent un, ils commencent à tourner autour des hommes
et les enveloppent de leurs ailes.
Coran 38 "SAD" versets 17-18 :
[ Endure ce qu'ils disent; et rappelle-toi Notre Serviteur David, doué de force (dans l'adoration) et plein de repentir (à Allah).
Nous soumîmes les montagnes à glorifier Allah,au soir et à l'aurore, en sa compagnie
De même que les oiseaux assemblés en masse, tous ne faisant qu'obéir à Allah].
Yalla na la Brom bi fay❤
@@aramediop202 amine
Wazifa bokoul ci l'islam danko soss yonét bi saw meu soukoo déf wala sahabayi défkoo
@@AssaneDiop-w5m sourate an-noor 24 verset 36. Dans des maisons [des mosquées] qu'Allah a permis que l'on élève, et où Son Nom est invoqué; Le glorifient en elles matin et après-midi,
Legui wakhma Al quran ndakh dagn ko soss
يا عبدالوهاب بصراحة فرحت بك كثيرا إستمر على ذلك
وعلم أن الرضا الناس غاية لا تدرك
Yalla nako yalla protègé❤❤❤❤
Amine 🤲
Yéna yam
@@aramediop202mo gueune sa serigne gueune sa bayi
@@moiiza10sidibe30 je ne te répondra pas car tu n'a pas le respect en vers tes parents espèces de chalot
Amine
Wallahi je suis d'accord avec toi fi ham ham le
Macha Allah wakhdji rafetena Yalla n'a Yalla takhawou Oustaze Omar Sall
كثر الله أمثالك
الشيخ عمر وأدامك الله فوق رؤوسنا وحفظك الله أينما كنتا
Anas ibn Mâlik رضي الله عنه rapporte que le Prophète ﷺ a dit : « arrivera un temps où celui qui s’attache à sa religion sera comme une personne qui tient une braise ardente dans la main. »
En tout cas les tidjane s'attachent a leur religion
@@mbayebabacardiouf7853 cancre
Ya rien de plus beau de dire la vérité, car elle reste une vérité free Imam Oumar sall
Yawmom dganékoul tijanrék couwaxsy xamxam ñotontoula sixamxam couwax pousabotes kasorék baylénpar parlo taywakh dadague
Et la vérité est que Togne Kate Lah
Amna solo
Wanté toogne baakhoul, kouy waaraaté d'accord, mais Tarikha Diambour bayyi kofa. So beugué Diam. Sénégal yagg na ak Tarikha, so bokoulé nga doundeu sa Sounah boubaakh té bania toogne. Ya Allah na nieupp am Diam si barké Seydina Mouhamad (SAW) amiin
Wallah ndeyssane naniou bayi togn tè mandou si yeufou diambour
Je valide
Yalla nako yalla takhaw inch'Allah 🙏🙏
Na kat ndém
@@sonko2024officiel ya jiakke yare
@@sonko2024officiel dioulite deug dou saga
Ki dh yalla si kasso bi lakoy bayi
@@khalil2348 évidemment car il y a trop d'injustice dans ce pays
Machaallah frère tu as bien analysé 👍
يحفظك الله ❤❤❤❤❤❤❤👍
أمر عجيب في السنغال؛
من ينقد الشيوخ يذمم ويسجن، ومن ينقد الرسول لا يذمم ولا يسجن.سبحان الله 🥺👎
انا موافق قولك
وانت حبيبي ❤❤❤
والله أصبت الحقيقة
من انتقد الرسول؟
من حسن الإسلام المرء تركه مالا يعنه
Oumar sall defa wara bayi tonj dioulit defa wara manou
❤❤
Manou pr toi la car tu nest op imam ni precheur
Ligan wakh bokkkoul ak limouy firi mom limiy wakh amna ndiaring kay nakh nikouy deff ta khamou niou nii dou diné niou bayi kou
@@famadiagne5429 toudo yalla dou dine con de man xawma diné 😂😂
Force à toi Oustaz Omar Sall🙏🏿🤲🏿 Qu’Allah te protège 🙏🏿🤲🏿
Bien Dit Le Problème En Ai Que Xam Xam Bi MOffa Nékkoul Motax Mais C Vraiment Triste Gni Sén Tarikha Rek Laniouy Protègé Mais Dîné Dji Sén Yoone Nékkousi
Dieureudieuf Kadougirafétena❤❤❤❤
J suis totalement d'accord avec toi . Il faut toujour répondre avec la connaissance et non avec le pouvoir
Face à tous ses attaques et critiques depuis qu'il a commencé, ces gens se sont toujours défendu avec des arguments solides et basés sur des textes authentiques et l'on même plusieurs fois invité à un débat public, ce qui pourra permettre à tout personne doté de conscience de juger selon sa conscience, mais il n'a jamais accepté de le faire. Mais préfère faire ce genre d'attaque pour influencer ce qui n'ont de connaissances dans ce domaine oui ce sont que ces derniers qu'il peut influencer vu qu'il ne savent pas grand chose sur ce qu'il avance et en le voyant parler et parfois citer des textes dont ils ignorent et oriente le sens en faveur de sa doctrine.
Wakh dji amna solo trop mais pour mane nie ko pourté pleinte Amna fougne ko ték psk mom omar sall dafa yague di togne di dougou si pass pasou nit gni mais li bou si diougué bou féké borom xél la dina khol bou bakh limouy wakh🙏🏿
Kilifeu gui mane de dameu kouy faral di déglou Lou Bari Loumou meusseuna wax RK yénou ne mana da fékeuni Key deugeu mo nekhoul rk
Démal diangui athia😂
Je pense que vraiment il a raison ❤Macha Allah amine ❤
Oustaz que Allah vous protége
Ki kéne mounouko protégé domeraw la yalla indina dinakoum wala yadiné leufeul ndeye omar sall
Diereudief Oustaze Omar sall❤❤❤❤
Machalla belles paroles ❤❤❤❤
Boy dagy doulo oustaz oumar sall re ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Oustaz wakh deugue yalla ya togne défo ko sa yonn nékou si niom au moins ay dioulit la niou nagou naniou Seydina Mouhamed SAW comme prophète mais gueumeul liga guemm ga bayi lén niou gueum li niou guem organisé wou niou soiré di fooo daniouy toudou yalla bayil togne. Guén bal ma akheu.
Merci beaucoup frr et bnn continuation liguéye bi rafètte na
YALLA NA SUNU BOROM SAAME TÉ AARE oustaz omar Sall TÉ LIBÉRER ko ya rabbi AMINE
Merci 👍👍👍👍👍👍🕋🕋🕋🕋🕋👂❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🕌🕌🕌🕌🕌🕌🕌🕌🕌🕌🕌
Mane dee tidiane-la rek❤❤
Rasoulillah mo ko meye tarikh bii❤❤❤❤❤
❤❤❤
Foum kou guissé 😅😅
Yalna yalla samm la oustas omar sall🤲🙏🙏🤍🤍🤍si barkel nabil Moustapha 🙏.
Amine Amine 🤲
FREE OUZTAZ OUMAR SALL ❤❤❤
My Boy je t’estime bcp vraiment souféké Alkhourane ak sunnah biguay wanné si sa ay Video mo nek si yaw bousi ragal dara koulay beug
Nalasi beug koula bagne mo kham
Wahal waxdji mou ler nagne boul ragal dara
Nit yi meuno niou thi yaw dara
Kasso diomul kèn..
(Exemple le prophete youssouf)
Souféké dagua beug di wx thi diné di ragal bou yabo meun gua bayi
Oustaz Oumar Ahmad sall yalla nako yalla takhawou 🤲🏼🙏🏾
franchement
Mann dei moom laa andal.
Yonente bi limou niou sante mooy suniu nékké si deukk bou am loi niou topp loi booba motakh Sénégal kou Ray niou teuj la. Naam nk wakh deugg tollouwaayam deugg la wakh waayé li waadji wakh jangalé daa andak akkh.
Mom la andal
❤❤❤
Billahi lii dh la wakh😢amine ya rabbi
Je suis tidiane et tu a parfaitement raison .
ils auront pu le régler autrement puisque on est tous pour le même créateur
Nit d'où togne oustas dafa togne
Yaww ngané tidiane nga nii yaww niatta Yonne oustaz Omar attaquer tidiane yii akk niatta Yonne lagnou ko tégale ayy arguments youmou meunoule dinedii té il persiste toujours donc faut vous renseigner d'abord il dit toute sorte de moqueries
@@abdoukhadrediaby1438bien dit!
@@abdoukhadrediaby1438vraiment merci beaucoup
C'est le seul commentaire qu'il fallait laisser sur cette vidéo
Boy bi di wakh ci vidéo bi mom ay vus la beug tei daa melni xelmi néxoul mais limou wakh amoul Béne sens ndakh ay wakhou doff lah
Tarikha tidiane bi ci sunnah ak alkhourane lagnko sossé
Amoul aaya boukoy wéddi
Omar Sall mom souféké lou yonente bi ak sakhaba yi défoul rk bidaa kone mom ci bidaa la deukk ndakh yonente bi (PSL) meussoul deff vidéo youtube
Fall Kou Waxée Kham-kham lagni tonn-tonn Kham-kham, kou waxée réewan-dé gniou Yaarr-la Djeureudjeuff🙏🏾✨
Merci
aythieu mr.Ngom
Tariha tidjiani worol dè lo khammé amo bènne dalil
Yaw démal diangui
Bonne continuation frér ❤️🥰
No tay mom andouma ak yaw abdoul wahab keen amoul doit gemm lou la nekh yalla limou diglé laniou wara gemm ta oustaz omar sall defoul lodoul diotali comme nikou sangue bii defé bam aksi si nioun 😢yalla nakou Yalla takhawou samou kou inchallah ❤😢😢
Je suis mouride vérité absolue ❤
Yaw do sarame ndém deume ngua
@@bayemodoubadji7032 merci beaucoup bayi nala ak yalla yalla naniou yalla atté si dieumi seydina mouhamed ak togne gingama togne si barké alkhourane 🙏🙏🙏
Tu ne comprends rien de ton tarikha
@@papemorfall8024 lolou nga fok bayi naléne ak yalla
Esk do deim lathié tmt wala prochaine Khadarra nga khol tmt parsk ioe tmt je pense pas ke nga neik tidjane
Machalla yangui wakh lou am solo yalla nala yalla samm di gnanal Oustaz omar sall yalla nako yalla samm si barké alkhourane yalla defal ko diam 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🥹🥹🥹♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Machallah Sénégal mome légui maak yi gnoy nélaw xaléyi yéwou xam xam moy tontou xam xam
Damala yeureum bayi fi yahoudou bayi fi nassaara di wakh sa mbokko dioulit yi wayye yalla bakhna tidiane la❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Abdoul Wahab a bien raison, on est au Sénégal, ainsi, il faut savoir, comment, dire ses vérités sans offenser, et pour Oustaz, certe, il est véridique, et ne craint rien, ce qu'il a dit, est vrai, mais, c'est la manière dite, qui l'a créée des soucis, et surtout qu'on est au Sénégal, avec sa laïcité et divergence des idéologies, ainsi, il faut user de délicatesse dans ses propos ! , Que Dieu Assiste et Protège Oustaz Sall.
Exact
Limou wakh dara douci deugg ngay masla nii
Il est hypocrite. Pourquoi dire "toudouma tour" alors qu'on sait bien qu'il parle des tidjanes? Et il n' a pas raison. S'il a du problème avec des gens qui évoquent le nom de DIEU le matin et le soir, en plus dans un lieu saint, il a un problème avec son créateur.
Wayé comme day garouwalé, gnou wane niko gnokoko dakk, ndax kou yénéwoul sa bopp thiolign gou matt, do yéné sa borom diiné djou matt.
Omar Sall est un comédien. Daffa rew
ياماشاء الله بارك الله فيك وجزاك الله خير جزء ❤❤❤
اسلام علیکم و رحمت الله عمرصال لم بگ دکهم
Mashaallah sama dome kadou yi rafetna.yalla nalla yalla same yokal la xam xam bi
Fattégua touddou serigne yi di khass yallah diko saga tegnou nek que tijiane té kene dou wakh senegal nit gnii beugue negne diiné mais khamougnouko a cause des tarikha dakh dougne lene diagal tawhid bou ler dakh chef tarikha yi ils savent que du moment où les sénégalais connaissent réellement le tawhid moye tarikha diekhna senegal par conséquent tok mouye dokh bi daye diekh mo takh Sénégalais yi wara yewou si niom. Free oustaz le connaissant amna ndiorte que sokhla la woul niane ndiek té kep kouye ahlou sunnah Sénégal defal sa khel que meune gua niam kasso dakh Senegal nekfi ahlou sunnah crime la je pense.
Tu as tout compris ma sœur, c'est le système
Lègui kan mo nèkoul si souna ? ou bien tu veux dire souna wahabisme ?
Soufisme égale souna, comme ninguèn yakarè ni wahabisme si souna la bok
Lègui nioune gni nèk si tassawuf ban souna la yonènt bi wakh bounou défoul wala ban sarou alkhour'an lanou weedi ? Ba à chaque instant nguèn beugue no guènè si dîné yalla bi , yèn danguèn no dakka diouli ? wala wor ? Wala dém diakka ? walla nafila ....? Donc chacun à son choix ( wahabiste, Soufisme alkhour'aniyou ..... tous sont des musulmans) mais ne juger pas les personnes c'est ALLAH seul qui peut juger 🙏🏻
Senegal deukou nafekh la Qu'Allah nous preserve des tarikha
@@od7240nafèkh meunoul wèssou guiss ay dioulit comme yaw nga diapèlèn ay nit you rère
Wala ko guiss diape ni yako gueun wala yako dakka diamou yalla
Com niko wahabiste yi di défè pour niom niom rék nio dioup nio gueun nieup wala nio dakka diamou yalla nieup wala niom rék la yalla di nangoul sèni dieuf
@@Htqv221 malheureusement tu n'as rien compris mon cher je te renvoie sur la biographie de muhammad ibn abdil wahab. Tarikha mom dou meusseu nek sunnah yonnete bi dakh khamouko khana sen sunnah mame yi la mais pas bou Mouhammad psl
Machallah lila sunu sangue bi li la dikle
Je trouve que cette plainte lui été ciblé depuis un long moment, ils ont juste attendu une faille de sa part pour passer à l'acte car il a longtemps dénoncé des vérités qui dérangent et ça depuis le vivant d'Imam Alioune Ndao (Rahmatoullah Aleykhi).
T'as tout compris
GOR DJIGUÉN YANGUI FI LESS BIYÉN YI FARAMAÇON YI POLITICIENS YI MS TIDIANE YI LI NIOUY DF LOU BAKH LEU BOY WARATÉ DANGAY CRITIQUE LOU BAKHOUL
Une très belle analyse ❤❤
Oustaz Omar sall togn rekk laye ligueyé
Macha Allah ❤️ le jeune Vous avez parfaitement raison 👍
Oustaz Omar Sàll dafay togn, temps yeeh mouride yi la dieuloon, legui mongui si Tiijaan yi... Humm okei on verra bien 🧑🦯
Nitt, surtout màgg, ngani defar mola takha joukk daa am noo warra waxee.. 😕
Qui est plus injuste que celui qui interdit qu’on glorifie le nom d’allah dans les mosquées bayilen kiniane té wahh deug
Waw yén yonét néna AK Serigne bi wakh n'a boulén geuneul ?
MERCI SENEGAL MO BARI INCONSCIENT
@@laoucouledesruissaux4495
Saway bind ni ayat al quran la wahouma wahou Serigne kén hamoul lane guéne beug eh pourtant yéne omar sall moy sen Serigne
@@AbouBa-gx4tj yén problèmou Serigne gén ame.
Sou souba géni comprendre.
@@AbouBa-gx4tj oustaz mais pas Serigne
Gni amougn beneu justification bouy dindi lou oumar sall lim lèn wax deug la Sénégal mou beuri ay nafèk dînè topu yalla la ak yonentam
Merci beaucoup 🙏 oustaz amna solo
mome dou tidjiane louy yonam ci tidjiane yi dou ci mandou nék ta geum lim geum bougnou démé ci yalla moy khol kou nék lay sa akh mou faylako nianal diouliti Sénégal yépp ndiégalou yalla mo geun mouy diéma tanne gniy dougou al diana wala safara ta yalla rék mo kham limouy déf
Merci pour les informations laf thiat oustaz Oumar sall n' a dit que la vérité Les sénégalais sont des incrédules ❤
Iow wakho fii dra pousseul feulé
Dakh diamanoy Mouhamed wasifa ak hadara amone ?
Li question rék la prison ak plainte wou tou ci dra .
Sénégal deuk boromi xam xam la faites bien la différence.
FreeOmarsall
Qu’Allah lui vient en aide vraiment c’est n’importe quoi dans ce pays on peut même pas dire la vérité c’est écœurant 😢
Bane vérité togne khana oumar sall na bay togne
@@cheikhoumardeme293kone ioe danga geum ni façon diamou yallah bou djiougué woul nabi saws ak Ay sahabame meun na bokk si islam teh yonente bi ni leppp lou besss si diiné gui app reerrrr la
@@cheikhoumardeme293 iow nopil mounan yaw khamnga louy togne
@@massabdallah5688y’en sen Khalima sori woul motakh nguéne diapou ni lépou bida la 😂
@@cheikhoumardeme293Frr allhamdoulilah bagnouyy dem khadara ba ici repose dougnouko bayii nakh moussou niouko interdit
Yalla nako yalla sam tegoudal fane wi te dole barkel xam xam bi hafizahoullah
Le respect est réciproque
Ah bon ? Donc Salatou fatiha mo geun Al Kurâne ? 🤮🤮
@@Khoudar_HiGhLanDeRc'est en terme de lumière😮💨
@@Khoudar_HiGhLanDeR Encore des manipulations qu’on vous fait
Kiye Jang Alxuraan Ba Noppi Douko Jëffé Bou Timé Téré Ndax Alxuraan Douko Rëbb Ankay Alxuraan dakoye rëbb
Ci Waadji la Seydina Cheikh Waxni Jang Salaatul Fatiihi Moo Gën Ci Moom Muye Jang Alxuraan
Wayé Kénn Meussoul Wax Nih Salaatal Fatiihi Mo Gën Alxuraan Bayileen Sossal Nitou Yalla
@@Smokin_mass33 Pardon ? Ça fait donc partie des 5 piliers ?
@@Khoudar_HiGhLanDeR donc la prière sur le prophète ça fait parti des 5 piliers de l'islam ?
Boy Yow Bou de Oumar Sall Kham ngako Neko Oustage Makhtar sarr Parena Pour Ngeun Wakhtan Ci Kham kham walla sah Mem Bou doul Oumar sall Niom Mor kebe Oumar Diallo Alpha Ba Ak Sen Serigne Ahmed lo
❤❤❤ماشاء الله يا أخي الكريم
Yala nanou yala raye si tarikha cheikh tidjiane amine
الحق من ربك فلاتكن من الممترين ❤أستاذ عمر سل لم يقل سوى ماجاء في القرآن والسنة وأنت نفسك تعرف هذا شئت أم أبيت 😢ولا تكتم الشهادة ومن يكتمها فإنه آثم قلبه...لذا قل فقط بما يرضي الله ورسوله لا بما يرضي الناس ياعبد الوهاب 😢 فرضي الناس غاية لاتدرك
واصبر نفسك مع الذين يدعون ربهم بالغداةوالعشي يريدون وجهه
لكن بالحكمة
❤❤
Ce qui est dit dans le coran est d'invoquer Dieu matin et soir, plusieurs fois et dans les mosquée, ce qui est dit dans les habits est encore très large et honore ceux qui assistent aux assemblée de zikr. Bayilen jahasse. On peut ne pas être d'accord sur l'interprétation tes textes mais na kunek respecter moromam.
Ou étiez vous quand omar sall mentait sur la vie et les origines de CHEIKH SEYDI AHAMET ATIJAANI, les tidjanes ont toujours été tolérant et ont répondu à toutes les critiques en se fondateur la science. Maos ils n'accepteront jamais d'être traité de folklore ou gnouy thiahane. Omar sall moo togne c ça la vérité
Fière d'être tidjiane❤❤
ماشاءالله جزاك الله خيرا ❤️❤️❤️❤️❤️