Salut Mouhamed nous voulons tous les jeunes pépites sénégalais et les meilleurs seront déterminés par l'entraîneur mais la bonne politique c'est de donner la chance à tout sénégalais qui veut défendre la couleur du pays.
Assane diao Ibrahima mbaye cher diour ak soumaré ak Malik thiaw aliye camara noa Fadiga gni war nagnio bokou si list match yi di gneuw Cher diour mome dagne koy wo rek kome yague na beugue joué Sénégal béne match wala deux rek bagne ko pert
je pense que mamadou sarr aussi le fils de pape ils faudrait aller le convaincre d'es maintenant pour moi il est plus équipé que cher ndour et abdou diallo il a plus le nineau
Pour moi pape demba diop c'est un milieu très prometteur ont doit le promouvoir ils seraient grands milieux de terrain inchalla
Mouhamed bo beugé dieul coupe d'Afrique fok nga renforcer excentré yi bilahi sadio AK Ismaël Sarr sén puissance désna légui déh 🥰🇸🇳🙏👍✌️👌🔥
Billay wallay
Yaya diémé pas yaya diamé 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳❤️
Merci beaucoup ameth ❤
De rien ☺️
Félicitation Coach Pape Thiaw❤❤
Diadieuf senfootballtv je vous suis depuis un moment vos informations sont fiables bonne continuation ❤❤❤
Merci
Tu fais de bons conseils aux coachs c'est bien ça du courage
Merci mouhamed
Bilahi walaye Moukhamde football Senegal 🇸🇳🇸🇳👏 warr nanous la sargall
Salut Mouhamed nous voulons tous les jeunes pépites sénégalais et les meilleurs seront déterminés par l'entraîneur mais la bonne politique c'est de donner la chance à tout sénégalais qui veut défendre la couleur du pays.
Merci beaucoup
Merci à vous
Que geste bou Nice mouhamd 😊😊❤❤
Merci
Assane diao Ibrahima mbaye cher diour ak soumaré ak Malik thiaw aliye camara noa Fadiga gni war nagnio bokou si list match yi di gneuw Cher diour mome dagne koy wo rek kome yague na beugue joué Sénégal béne match wala deux rek bagne ko pert
Slm guayi delen j'aime vidéo yi way
Merci infiniment
🇸🇳❤️
Excellent travail
Un grand merci !
Mais Mouhamed do déffate guestou si dossier Malick Thiaw Laye s'il te plaît 🙏❤️
i.ndiaye nadem Barcelone ngaye wakh real💙♥️
Mouhamed dossier Boubacar kamara bou Aston Villa pape War nassi taxaw dh c'est possible mou nieuw dh kom Malick Thiaw
Mamadou Sarr tamit bi nekka Strasbourg
L,encadrement doit faire des déplacements pour convaincre les binationaux au lieu de rester au Sénégal comme le faisait Aliou cisse
Asane diao mi mo wara ñiow
Mais Ibrahima mbaye bane lien la am ak maroc
Yayam marocaine la
Jajeuf Mouh
Noah Fadiga Ilay Camara Moussa Ndiaye Assane Diaw Ibrahima Mbaye Pape Diallo pape Demba Diop cher Ndour li moy sma combat
Merci mouhamed mais Babacar dioukou et sékou mara et Boubacar soumare et edan Diop et ferlen mendi et niouhoun siyla merci ❤❤❤
Mano léne gnio bayi AK Ferland Mendy sokh la wougne ko sékou Mara aussi todia goul nékoul Di marqué ay but
Assane diao mome soxla nanko lol
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mohamed Sénégal dfa hyper compliqué 😅
Soun excentré yi ak latéraux yi Dan ko wara renforcer
Sa waye yaw khana danga beugg j’aq matcha niou andi ay jouer you Bess ahh
Mohamed do wah ci match Sénégal bi dimanche
L,encadrement ne fait aucun effort pour convoquer les binationaux ce sont des paresseux
mouhamed ana micro bi
Moguifi dh
Si Aliou cissé te suivait il ne serait pas limogé car tu lui proposait des binationaux mais il était têtue