Omar sall yallah nala yallah diégeul thi li nga wax thi Maolana Cheikh Ahmed Tidiane...tei je te conseil une chose démal tarbiya dji nga Yallah molay may xol bou rafeite
Macha alla oustah lérne torop Mais Omar sall amoul koumi Roy si khasté Baka nam rk la topou Mais yala la nago yala wane louy diarign khas waliou yala yi
Noonu islam yi ken rawucci suufi yi. Bunu waxantée dëgg war ngeen na xam ni Oumar Sall moo nekk ci dëgg. Ndax ootéwul ci maamu ken. Ci Alkhuran ak Sunna Yonent bi SallAllahu aleyhi wa salam. Nittu Yallah mooy kiy woo nitt ñi ci Yallah ak Yonentam. Bayileen caahaan. Seen turuq yi yepp ci ñall yi lañu nekk. Yallah nañu Borom bi sexal ci Alkhuran ak Sunna.
@@khalifadiop9303 ku waxul lu dëpoo ak alkhuran ak sunna ñu wéddi la. Baay ñass mooy kan? Esk Yallah moom la yoni ci ñun? Ken rekk moom lañudul wéddi muy Yonent bi sallaatu aleyhi wa salam. Kénéen kumu doon say wax ak say jëff dénukoy natt ci alkhuran ak sunna. Su dëpoowul ñu bayiko topp la dëppoo ak alkhuran ak sunna. Lii mooy dëgg. Yallah nañu Borom bi hiir ci top alkhuran ak sunna niko sahaba YI déggéewoon.
Waw s k kham nga alkhouran ak souna sakh bye lathé ndakh la yalla yoni si noun pour mouy lér Baye niass la yalla yoni si lép lou ame roho yén kha ak yén pért temps la 😌
@@khalifadiop9303 khanaa seen diiné bopp la loolu? Ñun dé sunu Yonent Mouhamed Ibn AbdalAllah la tudu té ci moom la Borom bi waccée alkhuran. Lan mooy rissaala Bayy ñass? Siñ bi tuubal linga wax! Ñakka xam diiné weesuwul lii nga wax. Baay ñass ken yoniwuko ci boppam sax waxatumal ci ay yeeneen nitt. Nañu raggal Borom bi té topp alkhuran ak sunna ndeem islam lañuy wooté ! Yallah nañu Borom sexal ci topp alkhuran ak sunna.
Vive Oumar Sall, le veridique. Oustaz Oumar Sall est le Professeur des oustaz. Oustaz Oumar Sall, Maschallah. Dieu est son protecteur. Viva, Oumar Sall.
Mane dè doumako neubb, amone na estime si mom diko suivre mai dama dëgg bèn jour mou fëne, aw fën bou lerr depui bobou jai plus confiance en lui... Dafa meun fèn trop mom Omar Sall lolou baxoul koi
@@dadowatt9419 waxnafi ni Cheikh Ahmad Tijane chretien la wone, il s'appelait Michel alors ke kokou toute sa descendance est musulmane (def nassi ay geustou you werr) sossal nafi aussi bèn domou Baye Niass mouy Nazir (lo xamni dara doussi deug ndax mane damay geustou) mofi fén aussi ni dèm nafi ba Nigeria sans faye ndax daniouko dioxone mi wird lo xamni do faye pass (xolal ma waxi dof yoyou... Niatta nitt nio beug toukki pass molèn teu lolou sou amone kone wa Medina di toukki nimou lèn nèxé...) aufait mom meun na bgne yonou soufi mai nako tèkk si xam xam rek bania fèn, lolou dafay takh niou xëb ko tè dioullite dou fèn
Yen yenay doul kat yi yenay domeram yi yen ak seni serign yeup fen rek mo len nior Omar salle deug bou werr rek lay wakh lolou moy dageu sen khôl yi si yen la bokon mou dem bâ khamni Aÿ dof gen mou balen fi mo len mety
Fier d'être talibé cheikh ❤
Li dou lou bess yonnetibi mofi guen tè wakh'agn ko lou nekeu donc dou lou besss koi alkhamdoulilah ya alllahhh dieu est grand
QU'ALLAAH VOUS RÉCOMPENSE POUR VOTRE COURAGE ET VOTRE INITIATIVE CHEIKH ABOUBAKRY BA. LONGUE VIE À VOUS.
Koubokoul féna daal nopalounga billahi geum yalla top sunna doynasi mane
Omar kazab sall chaque instant saye fene di geuneu lérr
Wahhabites.boumelni.oumar.sall.ak.khalil.lo.ak.ahmed.lo.niom.niepe.ay.seytane.laniou
Omar sall yallah nala yallah diégeul thi li nga wax thi Maolana Cheikh Ahmed Tidiane...tei je te conseil une chose démal tarbiya dji nga Yallah molay may xol bou rafeite
Tarbiya dou pour mbam bii kii kay nako yalla alak rek❤❤
Oustaz omar is giving Dawa from the Quran and the sunnah of the Prophet Muhammad S.A.W May Allah guide us to the straight path Ameen
you're right.Machallah!!!
Na mandou si loumou khamoul
mashaAllah Ya cheikh xam xam bi leer neu. Tarikha Tidiane DEUG leu wallahi.. pluie de grâces sur vous ya Cheikh
Svp abonnez xam sa diné
As salam anlaykoum
Omar Sall nimou ndiémé yalla Daf maa diaaxal wallahi yalla xamnako billahi
Yene gni yena yena niakk fayda yene wa tasawuf niou niakk Dine gene amolen yarsi yalla amolen yarsi mouhammad
Merci beaucoup serigne bi MACHALLAH serigne bi 🙏🙏🙏🤲🤲🤲👍👍
Alhamdou lillahi rabil alamina dieureudiff yalla na yalla fay la omar sall mom nafekh la
Dieureudieuf Oustaz yow lowakh magueumko ndakh sadeugou ak sacourage. Omar Sall mandoul si cheikhou Tidiane ak baye. Bakhna danga répp
OMAR SALL torohh nga
Oustaz Oumar Sall deug rek lay wakh ta moy wakhou yalla AK yonentébi psl yalla nala yalla sammou ta arla si péhé non you bon yi
Kimom diaroule tontou sakhe awe tour rek la bakhe lé oumar sall ténga mandou si lokhamout 🤲😭
Vraiment frère ta raison
@@seydoundiaye8341 merci mandë douma chëdé si louma amout kham kham
Machallha❤️❤️💯
Mach'allah Serigne bi
Bilahi walahi tassaouf rek moy deug
machallah atidjaniya mame dama tite si omzo
Omar Sall si classe Musaïlimah ibn kazab la bokk lii mome Sénégal lakay deff meneu nekk si diam aye doumeu daggane naa si mome fenn katt leu
Yewe mi yamana fene wahofi touss
@@alassanediop9140 maxala si doule akk fenn lalene yaré lolou nguen nampeu so meloul nonou diaxal saye mbokk wayé boulene si delou guinaw continue lene si bou baax mbokou Musaïlimah ibn kazab yii
En tout cas omar sall daffa warra mandou si tarikha Sénégal yii ak suniu makk yii bahh yiii nayy feen feen ay fenam si niioukouy top
Alhamedoulilahi dieuradief baye Niass
شكرا لك يااستاذ
Omar sall yagou dara rékk dournafi diabaram bamou daw dikou mitital kii niut kou bon la naafékhla rékk
Alhamdoulilah Mashallah dieureudieufé BAYE
Macha alla oustah lérne torop
Mais Omar sall amoul koumi Roy si khasté
Baka nam rk la topou
Mais yala la nago yala wane louy diarign khas waliou yala yi
Oustaz Omar nous a éclairé sur pas de Choses pour dire vrai
Yallana yalla halak noni islam
Noonu islam yi ken rawucci suufi yi. Bunu waxantée dëgg war ngeen na xam ni Oumar Sall moo nekk ci dëgg. Ndax ootéwul ci maamu ken. Ci Alkhuran ak Sunna Yonent bi SallAllahu aleyhi wa salam. Nittu Yallah mooy kiy woo nitt ñi ci Yallah ak Yonentam. Bayileen caahaan. Seen turuq yi yepp ci ñall yi lañu nekk.
Yallah nañu Borom bi sexal ci Alkhuran ak Sunna.
Amine yarabi mé dioume nga kokou louko déf nittou yalla nittou yalla douwédi moromame té souféké dioulit le dafa wara beug baye niass !
@@khalifadiop9303 ku waxul lu dëpoo ak alkhuran ak sunna ñu wéddi la. Baay ñass mooy kan? Esk Yallah moom la yoni ci ñun? Ken rekk moom lañudul wéddi muy Yonent bi sallaatu aleyhi wa salam. Kénéen kumu doon say wax ak say jëff dénukoy natt ci alkhuran ak sunna. Su dëpoowul ñu bayiko topp la dëppoo ak alkhuran ak sunna. Lii mooy dëgg.
Yallah nañu Borom bi hiir ci top alkhuran ak sunna niko sahaba YI déggéewoon.
Waw s k kham nga alkhouran ak souna sakh bye lathé ndakh la yalla yoni si noun pour mouy lér Baye niass la yalla yoni si lép lou ame roho yén kha ak yén pért temps la 😌
@@khalifadiop9303 khanaa seen diiné bopp la loolu? Ñun dé sunu Yonent Mouhamed Ibn AbdalAllah la tudu té ci moom la Borom bi waccée alkhuran. Lan mooy rissaala Bayy ñass?
Siñ bi tuubal linga wax! Ñakka xam diiné weesuwul lii nga wax. Baay ñass ken yoniwuko ci boppam sax waxatumal ci ay yeeneen nitt. Nañu raggal Borom bi té topp alkhuran ak sunna ndeem islam lañuy wooté !
Yallah nañu Borom sexal ci topp alkhuran ak sunna.
Diazaka allah khayr
Omzo salla doulrek laye deff
كثر الله أمثالكم ياأستاذ أبوبكر به التجاني
Macha allah talibe cheikh tidjan rekk ❤️❤️❤️
Yappou wallou yalla yi yalla ko toké koulen fénnal halakou
Amoul sik ..loulere..gua wah.
OMAR SALL A PARFAITEMENT RAISON 🎉
Alkhamdoulillah Allah kouli khall
Meirce good
Gni bougne féké wone diamonoy yoninté sakh wédi ko. Ndakh khéle bu andoule ak khole bu selendou khalate khalate lérou yalla amougne l'ère wédi rékk lagne meune.
Raw na niémé yalla omar sall ya am fit té niémé
Jërëjëf Oustaz Oumar Sall
Omzo sall est un pur domérame
Alhamdoulilah
Alhamdoulilah
Alhamdoulilah
Omar sall khathj Bou bone laa.
@Prince Askia Haruna II comme sa baye limoudone rék
Omar Sall khathj moko euppeu ndiarign ci mbindefou Yallah yi ndakh il ya des chiens qui aident à retrouver les criminels et à l'élevage..
Machallha
Ioe mome ya ragaloule yalla
Ah Omar sall dé doff là rek
🤝🤝🤝🙏🙏🙏🙏
Macahallah
Omar Sall yalanadé balay fin Février cibarké cheikhna ahmadati rtl
Amin ya rabbi
Svp abonné xam sa diné
👆👆👆
Soo bëgee siiw daal dangay sossal/fenal ku siiw
Omzo loum wakh cheikh ahmad tidiane metinama toropp😭
Omar sall dafa sankou baparé di sankaaté wallahi kouko topou sankou dou mome rek ibadou yepla
Dieureudieuf baye niass
Vive Oumar Sall, le veridique. Oustaz Oumar Sall est le Professeur des oustaz. Oustaz Oumar Sall, Maschallah. Dieu est son protecteur. Viva, Oumar Sall.
Svp abonnez xam sa diné👆👆👆👆
Omar sall fainekate bou alakoula, mais walakhi bala dai dinakoguisse, walakhi si barkai cheikhou tidiane
🤲 Amin yarabi
Point d'arguments 🤕🤕
Mane mangui si yone wii
Mahcalla
Dieuredieuf Al ouztaz Aboubacar At Tidiâni.Xam xam bi lérena sétna,amna sources
Bilahi Oumar Sall doulkat international té diangam soriwoul bou latie wone histoire Ibn mayaba Dina def attention
Bilae
Ya barri ham ham.
Omar sall man kham na ko bou bakh Diegen mom dou sy doyal motakh manelen ndiaga la
warr na moytou ndakh lee oupna,,,,ken dou lal waleyou di mouthou💔
%tuuuu7uuoo
Mane dè doumako neubb, amone na estime si mom diko suivre mai dama dëgg bèn jour mou fëne, aw fën bou lerr depui bobou jai plus confiance en lui... Dafa meun fèn trop mom Omar Sall lolou baxoul koi
Salut il avait dit koi svp ? Et pourkoi ilbest traité de grand menteur ? J'ai raté kelk chose
😂
@@dadowatt9419 waxnafi ni Cheikh Ahmad Tijane chretien la wone, il s'appelait Michel alors ke kokou toute sa descendance est musulmane (def nassi ay geustou you werr) sossal nafi aussi bèn domou Baye Niass mouy Nazir (lo xamni dara doussi deug ndax mane damay geustou) mofi fén aussi ni dèm nafi ba Nigeria sans faye ndax daniouko dioxone mi wird lo xamni do faye pass (xolal ma waxi dof yoyou... Niatta nitt nio beug toukki pass molèn teu lolou sou amone kone wa Medina di toukki nimou lèn nèxé...) aufait mom meun na bgne yonou soufi mai nako tèkk si xam xam rek bania fèn, lolou dafay takh niou xëb ko tè dioullite dou fèn
Ah ! loolou moom niaawna waroukoo wakh, en tant ke Oustaz il devait défendre nos saints au lieu de les dénigrer... Heureusement ke j'ai pa vu la vidéo
@Prince Askia Haruna II dafa wara reglé mame borom touba seydil hadji malick baye niass koulen diema toutil yaye touti il ne fait kk....
Saw mi diwakh ragaa lo yalla
MASH Allah good an meirce
Sénégal deuk bou touti si islam eupou ayy fénnkat si islam BAYE mom moy djantibi kénn mounou ko téré takk
Bol wédi sa Seringe Amadou Ndiaye
omar sall c ún domeram bouy wedi makgnii
Say wakh ak néféré lay yemalé amoul dieurigne
Sénégal mo nékh rk wayé Omar sall mi deuk bou normal ray nagn ko bou yague
Omar Sala Matout limou don Matouko ko kam né do wax lo kam Moukou di fén rék di fén rék Mayal Sa bopou diamou nak
Oumar sall degue revient laye wakh bocoul thi tarikhaa fenyi
Tonton omzo nak dafa hawa doy warr dei
Svp abonnez xam sa diiné
👆👆👆
Omar Sall domou ndiallo la mo takh niom amou niou gem gem
❤❤❤👏🙏🙏
Omar al quran ak sounnah lay wakh yaw nak????
Yaw ak omar yéna yam sén data yay rek
@@gueyeplegnia8332 استغفرالله
@@gueyeplegnia8332 ma cha Allah mon frere yalla na yalla defal diame ak xewl ak say way diour
@@mbayedegeu95 Maa sha Allah mon frère.Yalna Y'Allah contane si ioe.
So khamoul naga mandou
Daafaa reew
Baylén saga waye, talibe day amyar
Fi thi wetou gandiaye amone bène goorou sérère bougnou dane wassifa daf done guène ndaxe rafétayou djiromou nite youmou done guiss thi digue malane mi. Bougnou paréwane mounélène woye yi nexe nagnou dé wayé gni thi diggue malanemi rafètenagnou.
na goorou sérère
Wakho fi touss tarika dou dine
Alassane Diop kay wakh fi tousse yow
Yaw ya khamoul lingay wakh
Mashalla
Omar Sall doule rekk layy defff
Omar sall walahi lazzi la illah khayru degue rek lay wakh boulen mettê nakeu nguen Kalame ko yallah kou doundoul sunah perteu ngua
Wallahi 🥰🥰
والله :
فإن لم يهتدوا به فسيقولون هذا إفك قديم
Diarradieufé baye niass
Shaytaan Sall
Svp abonnez xam sa dine👈
Lou wérr
Bayiléne saga. Wakhe léne wakhe djou jiwe.
Oustaz Omar Sall deum la 😈😈😈😈👹👹👹👹
Omar sall dafa torokh
Yen yenay doul kat yi yenay domeram yi yen ak seni serign yeup fen rek mo len nior
Omar salle deug bou werr rek lay wakh lolou moy dageu sen khôl yi si yen la bokon mou dem bâ khamni Aÿ dof gen mou balen fi mo len mety
Ni la dhé borome kham kham yi dagno wara tonton fen Kate yi diangou gnou comme khaly gaye nimou KO dane Défé ba guéne adouna
Kii dou wahh deugg ni la mell ney fenn rek
Wakhlèn nit yi al quran ak sunna mo gueune ,Omar sall alquran lay wakh mè iow nakk
Omar Sall wakhoule aqourhane framaçon la
Omar Sall mo gueune sén Serigne yi, dakh yalla rék lé wakh , yé sén serigue yi guin Di wakh
Seniy maame amalouniou intérêts ! Bayiléne oustaz sall ! Deug bou woor peng lay wakh , ndakh alkhourane rek lay wakh !
Ki nonou lay déwé da rérre
Vous voyez sunna day lal khôl motakh niouy wéddi ta niome sène bop rek nagni wakh aki sèni Serigne kessé ta Oumar Sall sunna rek lay wakh ta lolou moy DEUG. Lolou mo lène metti
Mais seul Dieu est le plus grand témoignage
Bayil fess kouy wakh souna dou diakhase mas allah chak jr mou diakhese fii fen rk lay deff
@@djibrilfall6800 comment
Omar sall begue djiguen rek la def domoram la