Siteu bou Ngor dit tout sur son cachet contre Diop 2 : "Fallou jambaar la. Dafa triplé sama cachet…"
ฝัง
- เผยแพร่เมื่อ 29 ม.ค. 2025
- Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct / luttetv
/ luttetv
/ luttetv
/ luttetv
luttetv.com/
Siteu Bou Ngor kassé blh 💪💪💪
Wax lènn logique bayi beure yii guèni nakh kou d’accord 👍
Mom ak coly faye combat leu 👍
Douniuou beurreh ndax reug reug mi nekk sen diguenteh
Boy bii amoul fiit monoul
Bilahi iba kane question doof rk lay posé
❤
Ki aye moromame la beurré ba eksifi
Siteu bou ngor Pokola délaye réy 😂,baba diahal combat la 🤣,amguèn bolo mais meunolèn beurré 😕
Mbeur bou ragual door mounoul nek roi😂
Siteu Bou Ngor VS Guiro Seras
Guiro dieul na combat bou meti mok buldoger
Bayilene outal Yone
Ki amoul niveau Bobou n'a dem beurè AK ay moromam
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Siteu vs bouba siteu vs sokh bou ndaw siteu vs mbacke faye
Nioniou nieup ko meun
Pabi môme louko dalle Diop 2 da niane Yalla topatt si Guinaw Siteu bou ngor 😂
Mais meun neu nek comme modou ak balla. Instant bi balla bou wakhé deugg rekk beugatt neu beuré ak modlo
❤❤❤❤❤❤❤🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Yaw dégua yab ndéyou coly Faye 😕
Surtout yaw animateur bi ,
Tu n'es pas sérieux du tout , digua wakh ay thiatou Daouda fall AK mbeur Yi
Pour dire vrai siteu bi amoul niveau
Promoteur yi dagniye ndakh mbeur yi rék