Innalilahi wa inna ileyhi radjiwone , gni si fatou yalna léne yalla kharé aldianaye firdaws. Gnoune wa Mbour gneup niake , jeunes yi bayi léne gale gui
*Kou khol guedie nimou tolou ngani danga si dougou wara daw lou tolog 1600km franchement dama nane sa lep tahawoul boudeh ay lebou meun nagne comprendre né tame nagne guedie mais ko khamni mag iow nio yam boné poutt dem direct si souff ngani dangay dem guedie yalna niou yallaa mousseul khalate ko sakh woroul wakhoumala nak diem ko deff*
Est ce que gniy def li gnoko tzy. C'est la question que je me pose chaque jour. Rayaté bi, zgressivité bi, ak dieul gaal yi li yeup gnikoy def defougn ko ci Seen sago Sheytaan mongui gnouy meun, Sénégal sokhla na au gnaan
Capitaine gaale gui caso a vie les parent arrete len di sen dome yi geen di ase ne domou diw demna teki 😢😢😢😢😢😢 Li yeup si domou diambour le gui ne len dogalou yalla des parent irresponsable 😢😢😢😢
Ne lui trouve pas d'excuses. Il devra répondre de ses actes, pirogue de famille ou pas! Son entreprise est illégale et illicite. Nafekh rek. Que le ou les responsables aillent devant la justice, c'est tout !😢
Santal yalla té diko bayi khél bou bakh gni déme yafousse ak niak khalate yobou wouléne dadi dé mo meunta niak kounék ak sa biss nagne ko wadial yalla na raféte
Gare sama auto dekane samay thiabi doug ci galgui nguen yakar li diamla lkou kham li nitgni beug lenen nuen wakh ma ci adouna di lek ,di nane yor sa ay sokhna yor sa ay dom di khey di wath yor sa auto nek sa bir deug bo santoul yalla khana saytane nga beugeu denk sa bop ay way diam yi doyloulen te geum yalla te sant ko
Le seul.tzmoignage acceptable sur le drame de mbour ..merci mon gars
Wallahou dou yeufou nitt.... yalna lén sunu Borom swt yeureum lén té djégal lén bijahi Ta'ha saws 🙏🙏
Li méty na wayé Sénégal méty na trop ci jeunes yi. Geustou len jeunes yi c'est dure kou nek ya kham li ngay dounde ci sa xol. Yalla nalen Yalla yereum
Métina trop yalnalen yalla kharé aldjana firdawsi 😭🙏🏿🙏🏿
Oh metina lolle firdawssy leur demeure amin yaraby.
Yalla naléne yalla yeureum té kharé léne aldiana ci barke seydina Muhammad
Amine
😢
Toutes mes condoléances jeune homme et bon courage
Dieu te protège jeune homme 😮😮
Innalilahi wa inna ileyhi radjiwone , gni si fatou yalna léne yalla kharé aldianaye firdaws. Gnoune wa Mbour gneup niake , jeunes yi bayi léne gale gui
Bien parler❤
NDEYSANE WARO WONN DÉ YALLA NALEN YALLA YEUREUM KHARE LENN ALDIANA FIRDAWSI DOYNA WARR 🙏🙏
aye waye bayi léne gaal gui nguir yalla
Sa témoignage bi responsable na.
Kou sa heure diote fo nek mou fek lafa Ndeysanne 🙏
Paix à leurs âmes c triste et grave ça
*Kou khol guedie nimou tolou ngani danga si dougou wara daw lou tolog 1600km franchement dama nane sa lep tahawoul boudeh ay lebou meun nagne comprendre né tame nagne guedie mais ko khamni mag iow nio yam boné poutt dem direct si souff ngani dangay dem guedie yalna niou yallaa mousseul khalate ko sakh woroul wakhoumala nak diem ko deff*
1600 kilomètres la def bargny ile herreo affaire chance la rek
Yalnalaine yalla yeureume
Mai’s lii metina bilahi 💔ayway loumou😂metti metti guethieu gui dou solution mes frères et sœurs
Paix à son âme
Est ce que gniy def li gnoko tzy. C'est la question que je me pose chaque jour. Rayaté bi, zgressivité bi, ak dieul gaal yi li yeup gnikoy def defougn ko ci Seen sago
Sheytaan mongui gnouy meun, Sénégal sokhla na au gnaan
Paix sur son āme qu'Allah soit satisfait de lui si barké seydina mouhamad sallahou halayyi wa salam Amine
Bilahi yuefou dofla de yalla moyoé
Yaallah yeureum krn
Repose en paix 😢😢😢
Que leur âmes repose en paix 🤲🤲🤲
Allahou Akbar Yalla naléne Yalla yeureum té kharéléne Aldianal Firdaws Amine Ya Rabbi 🤲🤲🤲🙏
Yalanalen borome bi yarame barkep borome Touba 😢
No Li metina bilahi walahi
Ana projet by
Kou amoul projet nooye démé assemblée nationale
Kouma yoolé ma dakhaare ndayame
Paix à leurs âme 🙏😢
Paix à leurs âmes
METINA TROP😢
Ndeysan triste yalla naléne boromebi kharè aldianay firdawsi amine
Billahi deug leu man kham na si darra j’ai fait 10jour avant que j’ai beuza 😮
Amo gillet meuno feye vraiment li doyna waar ! Le maire est complice!
4 doom et 12 diarbate oh c’est affreux Wollah 😢😢😢
Paix à l'heure âme
Vraiment Métina
Amine
😭😭🙏
Il n'a pas l'air affecté du tout 😢
Peut être aussi c'est la peur.les personnes ont des façons d'exprimer leur émotions
Paix aux âmes des disparus
Jai monté dans une pirogue.Alhamndoulilah je suis arrivé en europe à paris grace à Allah mais je ne le conseille à personne cest tres risqué.
Affaire de goor yalla la rék dé mom Béne yoone la
Ya rien en Europe ça veut pas la peine
❤❤
Wallahi
Wérou lene lolou moye deugeu
Niaka reep rek
❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Kone dè yekh nga am khalat. Nopile yallah mola mouthial rek
Bou noppi wonne do nékk fi di commentaire interview la rékk té am sa conscience dou wéss😊
@@sebastiendiop6488ki mo soff
@@sebastiendiop6488 bou niep mélé ni mome kone interview douvam sens ndakh téré woulène dèm. Baniou dalé def interview balégui téréwouko dèm.
@@sebastiendiop6488 lima wakh soumako wakhoulwone kone yowtamite dofi néka di commenter khana wala?
Nopi pour lane yalla mo dogal mou néttali ko dafa wara wakh yaw ya wara nopi
Capitaine gaale gui caso a vie les parent arrete len di sen dome yi geen di ase ne domou diw demna teki 😢😢😢😢😢😢 Li yeup si domou diambour le gui ne len dogalou yalla des parent irresponsable 😢😢😢😢
Wah ndiaga lolou KO diaral
Desaboure bi. Youne. Bi. Bakhoule. Fiba. Moua. De. Oute secetaboure. Youbi. Bakhoule
Santal yalla bou baakh
Yalanalen borome bi yarame barkep borome Touba
Je te témoigne xamna ci daara mais nak koou yalla dembale rek mofi naik
Ki dano warra diap ndém khamone n'a lép mou nopi doméram nane yalla dama sauvé
Yaw doul wakh na degu kay daffa repoul rk lanela mounane ayy diappeu di grawal ni xana bougn koy diappeu yenay andeuh soff ndm
sa data yaye
Ki loumou déf ba ba nga diko saga merde way
Yay embecile yow
Khana loi bi wara takh gnou diapos ko y'a ko binde. Non Sénégal bénen affaire le koi. Ce pays c'est un jeu vidéo tamit koi.
Bayiléne.gnou.dém😂
Ne lui trouve pas d'excuses.
Il devra répondre de ses actes, pirogue de famille ou pas! Son entreprise est illégale et illicite.
Nafekh rek.
Que le ou les responsables aillent devant la justice, c'est tout !😢
Ay plans lako tegg pour bougn len diaper niouni khaliss amoussi. Ils auront ces morts sur la conscience
@@FatimandaoTymandao-gr4gl
Il veut nous faire croire à une 2ème "Arche de Noe '!😒😏🙄
Le responsable a, semble-t-il, dit avoir encaissé 15 millions !
@@babadieme voilà ! Sûrement une technique habituelle pour faire croire à des fins personnelles
Qu'une remords ils sont tous pareille c'est pas vrais se qui disent
Personne ne veut rester dans un pays avec un président marionette. Gaal yi dagniy gueuna dioli
Bonne chance 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
C'est qui le "président marionnette "?🤔😒😏
Qu'attendez-vous pour y aller ou envoyer votre famille ?
Vrai domerame gua
KHANA BI MACKY SALL SATHI 14MIL MILILLARRRR YOU SENEGALES YI
Yaw niousal sa ndey gnebé Guinée 🇬🇳 nderign kharam bi
😢😢😢😢
Kharou la il faut faire des sketchs pour sensibiliser ya rien en Europe
Ohh doyna waar mettina trop
2024
Ah bon cone khamguene ni li yeufou dofla dou yeufou nite cone bakhna
Yow nokhoul felé wakhofi dara borom galgui gay defendre
Santal yalla té diko bayi khél bou bakh gni déme yafousse ak niak khalate yobou wouléne dadi dé mo meunta niak kounék ak sa biss nagne ko wadial yalla na raféte
Mais il n'est pas triste
Mbour teffes dará dawoul sen yaram niom reek
Tu devais informer les autres personnes a l'avance
Gare sama auto dekane samay thiabi doug ci galgui nguen yakar li diamla lkou kham li nitgni beug lenen nuen wakh ma ci adouna di lek ,di nane yor sa ay sokhna yor sa ay dom di khey di wath yor sa auto nek sa bir deug bo santoul yalla khana saytane nga beugeu denk sa bop ay way diam yi doyloulen te geum yalla te sant ko
Yaw rek ladoone weur,lingua wakhe rek moy deug
Ame nga chance
kiii esk sava
C pas un rescapé
Il n'est pas un rescapé
Thiot ndeye wa mbour AK Wa kayar AK wa bargny ak rufusque katt len sen diobou ndeye arrêté dieul gal
Dottouma dougou gal
🇸🇳🇸🇳🧏♂️🧏♂️🧏♂️🧏♂️🇸🇳🇸🇳😭😭🇸🇳🤲🏿🤲🏿
Yaw loutakh nga begguna deme tamit
Yalanalen borome bi yarame barkep borome Touba 😢😢
Paix à leurs âmes
😭😭😭😭
2024