Mouride yi begg na lol si yen Mane dh mangi souniou dahira fi hamoo 4 wayé lingén di kurel dafa nex dafa sett dafa teggou kou xam diangue xamni ay diangue kat ngén té guisna ni niémé ngén magg gni lol lou am solo moungi nonou Ah xana dilén nianal segne bi ligey sa kanam tek batt yi geuna werr barké alxouran ak xassida yi❤❤👏✌
Mouride yi begg na lol si yen
Mane dh mangi souniou dahira fi hamoo 4 wayé lingén di kurel dafa nex dafa sett dafa teggou kou xam diangue xamni ay diangue kat ngén té guisna ni niémé ngén magg gni lol lou am solo moungi nonou
Ah xana dilén nianal segne bi ligey sa kanam tek batt yi geuna werr barké alxouran ak xassida yi❤❤👏✌
Ndeyssane worna Borom Daroul Mouhty ❤️❤️❤️ begg nanou d salaw
Askuy mbacke balla ❤❤
❤❤❤❤
Machaallah
Allah🎉🎉🎉🎉
Daw yaram esskey
Machaallah