🔴Urgent Touba Baye fall yi keur S Cheikh Thioro rencontre entre Serigne Dame Soda et S Cheikh Thiore

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 3 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 139

  • @pierredia7945
    @pierredia7945 10 หลายเดือนก่อน +10

    Yènne nieup bène keur gui la bène famille. Diam mo gueune léppeu.yallah n'a lène yallah défal diam.. Serigne Cheikh Thiorro borom bakh la

  • @BLOGUE123
    @BLOGUE123 10 หลายเดือนก่อน +36

    Machalha li rafetna lol sakh,baye fall yi ngeup warr na lènn sant dieuredieuf, kouye manifestè nga ngeuw fi dakar tè bayil fi touba ❤❤❤❤

    • @OusmaneNguirane-zu5mr
      @OusmaneNguirane-zu5mr 10 หลายเดือนก่อน +2

      Dakar ay papay diambour niofa nek

    • @ibrahimasambou9953
      @ibrahimasambou9953 10 หลายเดือนก่อน +2

      Touba gnou faa neck hana gno gueun gnou neck dk 😂na kou neck manifester foumou neck ngedjj 😅

    • @ftinfoftinfo4027
      @ftinfoftinfo4027 10 หลายเดือนก่อน +1

      Wakho fidara kou bakh

    • @DjilyDiop-q6e
      @DjilyDiop-q6e 10 หลายเดือนก่อน

      P@ibrahimasambou9953

    • @DjilyDiop-q6e
      @DjilyDiop-q6e 10 หลายเดือนก่อน

      ​@OusmaneNguirane-zu5pomr

  • @thiounelobe114
    @thiounelobe114 10 หลายเดือนก่อน +16

    Dieureudieufeuti serigne touba diarama mame cheikh ibrahima fall lamp.. Ndigueule dieufè rek bay fall reka woorr machallah.

    • @Lindingue
      @Lindingue 10 หลายเดือนก่อน +1

      Cheikh Thioro da yoré djiko Mame cheikh motakh mouy deff yeufou Mame Cheikh. Bagnale kouy nott sa xéle. Barké Mame Cheikh Ibrahima Fall ! Mbacké ndaam rek ngay am. Dieureudjeuf Serigne Touba

    • @MouridoulLaahi
      @MouridoulLaahi 2 วันที่ผ่านมา

      🤭🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤭​@@Lindingue

  • @abdouniack
    @abdouniack 10 หลายเดือนก่อน +10

    Serigne touba saye tané amoul si môme wale

  • @FallAsis
    @FallAsis 10 หลายเดือนก่อน +8

    Dieurdieuf Serigne Touba diarama Mame cheikh Ibra Fall yaram ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @amethdiokhane2524
    @amethdiokhane2524 10 หลายเดือนก่อน +10

    Dieureudieuf serigne Touba amoul morom ❤

  • @seydi7336
    @seydi7336 10 หลายเดือนก่อน +1

    Serigne cheikh thioro 🇸🇳🦁👈🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿♥️♥️♥️ bilahii histoir Senegal euleuke, bilahii diinga book sii jiiambar yii,nouvel generación dii beguée, jiarrama sang bii 🇸🇳🦁👈🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿♥️♥️♥️✊🏿

  • @MoustaphaSourang-qo1cz
    @MoustaphaSourang-qo1cz 10 หลายเดือนก่อน +12

    Waw leeeeeeeen goooooooor way Baye fall yi merci beaucoup machallah

  • @yakhyamamadoumbaye7531
    @yakhyamamadoumbaye7531 10 หลายเดือนก่อน +2

    Ma sha Allah amna solo

  • @Tawfeekh75
    @Tawfeekh75 10 หลายเดือนก่อน +7

    Jaajeuf liguey bi rafet neu .. spirituel et temporel ceux deux choses ki n'ont pas les mem principes....dc alhamdoulilah sant Nanou thi initiative bi ...baye fall yi worma rek tai nak ken douleen divertir waw....

  • @NiangAmadou-bt3mg
    @NiangAmadou-bt3mg 10 หลายเดือนก่อน +11

    Diotaybi amna solo,, man s. Dame soda damako beugue loollllllllll billahi yak bay fall yeup s. Mountakha yalla nafi yagg loll ta wer❤❤❤❤

    • @ridialridial2524
      @ridialridial2524 10 หลายเดือนก่อน

      Deffma signe nga dégue KO inchallah

  • @ibrahimaseck9062
    @ibrahimaseck9062 10 หลายเดือนก่อน +3

    Akasa lii amna solo man touba laa diouddoo maggé fa wayé tay louma méroon dembo contanaako tayy
    Dieureudieuf serigne cheikh thiorro

  • @ridjal2889
    @ridjal2889 10 หลายเดือนก่อน +3

    Mansallah lii deh moy sunu dolle nun murid < sax dakk ci ag taalube> Alxamdulilah
    Jerejef Serin Tuubaa

  • @elhadjibeye7257
    @elhadjibeye7257 10 หลายเดือนก่อน +8

    Dieredieufff Seigne Cheikh Thioro yalna yalla mayla diameu boubakh ack werrr ❤❤

  • @fallousarr9328
    @fallousarr9328 10 หลายเดือนก่อน +2

    Lii mome rafétna trop machallah

  • @cheikhdione7492
    @cheikhdione7492 10 หลายเดือนก่อน +1

    Dieureudieuf baye Fall yi contane ci yéne

  • @barrathiaw8885
    @barrathiaw8885 3 วันที่ผ่านมา

    Dieuredieuf Cheikh Ahmadou Bamba Khadimoul Rassoul
    Ak talibé rek wor
    Nanou sakhsi ndigueul té moy ak téré
    Serigne Mountakha Yallahna nafi yagu té anda ak weer
    Amine Amine Amine

  • @SaliouGaye-d7c
    @SaliouGaye-d7c 3 วันที่ผ่านมา +1

    Commentaires sens gros mot keur Serigne rék ❤ touba st spécial

  • @abdouniack
    @abdouniack 10 หลายเดือนก่อน +1

    Mâcha allah bima guisé li sama khôl da séde❤

  • @modousankhe9969
    @modousankhe9969 10 หลายเดือนก่อน +1

    Chiekhe thoro dieureudieuf

  • @manguasylla1952
    @manguasylla1952 10 หลายเดือนก่อน +2

    Machallah yalna yalla Faye len yiw

  • @sidylaminegueye4761
    @sidylaminegueye4761 10 หลายเดือนก่อน +4

    MashAllah li rek mo am solo Sénégal benn bopp leu Serigne bi bene yonn la woté amoul lenenn teu kou beugg defar ding ci tégou bamou né fang wala ngua rerr ba sarann Alhamdoulilah.

  • @djibydiop1315
    @djibydiop1315 10 หลายเดือนก่อน +3

    Machalah

  • @PapaSaliou-t1r
    @PapaSaliou-t1r 10 หลายเดือนก่อน +1

    Akasss baye fall
    Amna solo loll ❤

  • @serignethioubagueye6557
    @serignethioubagueye6557 10 หลายเดือนก่อน +2

    Machallah 😢😢😢😢😭😭😭😭😭😭😭😭raféttna trop 😢😢😢diame moy lépou

  • @bigmondiaye356
    @bigmondiaye356 10 หลายเดือนก่อน +5

    Machalla ligeuy bi rafet na trop yalna yalla samou len thi barkep borom Touba

  • @djibydiop1315
    @djibydiop1315 10 หลายเดือนก่อน +2

    Machalah❤❤❤❤💙❤❤❤❤

  • @cheikhbarambacke4812
    @cheikhbarambacke4812 2 วันที่ผ่านมา

    Mane dh pas pas bima am thi baay faal yi moy kuleen dieke dugu al diana rek daga leena diaeke wathi jërëjef maam cheikh ibra faal❤❤❤❤

  • @serignecheikhdiop690
    @serignecheikhdiop690 10 หลายเดือนก่อน +2

    Machallah amna solo loool yalna diamo yag

  • @juufy4569
    @juufy4569 10 หลายเดือนก่อน +2

    Wakh dji rafète na MachaAllah

  • @fallougallass9367
    @fallougallass9367 10 หลายเดือนก่อน

    Machallah ❤❤❤❤khol sedna ❤️❤️

  • @Abdoudieng621
    @Abdoudieng621 10 หลายเดือนก่อน +7

    ❤Cheikh thioro mbakce ❤diaradieufaty s touba❤

  • @papadabiamarone4139
    @papadabiamarone4139 10 หลายเดือนก่อน +2

    Alhamdoulilah nanouy moytou séytanné

  • @mamafall1931
    @mamafall1931 3 วันที่ผ่านมา

    DIEUREDIEUF SERIGNE TOUBA ❤❤❤❤

  • @abdouthiam3312
    @abdouthiam3312 10 หลายเดือนก่อน +1

    Machalah lèpou rafétna yalla na jamm yag ❤

  • @serignethioubagueye6557
    @serignethioubagueye6557 10 หลายเดือนก่อน +1

    Machallah baye fall nii la wara dokhé di dokh thi diame😢😢😢😢😢

  • @bayemodougueye3601
    @bayemodougueye3601 10 หลายเดือนก่อน +2

    Macallah li amna solo sakh barke serigne touba

  • @babandiaye6483
    @babandiaye6483 10 หลายเดือนก่อน +4

    Mala begue cheikh thioro❤❤❤

  • @MalickKane-e3e
    @MalickKane-e3e วันที่ผ่านมา

    Ana waxkate yi nopiguene ❤

  • @ProsperGomis-j7h
    @ProsperGomis-j7h 10 หลายเดือนก่อน +4

    Vive thioro ❤❤❤❤❤❤❤

    • @GERRARDSteven-u3y
      @GERRARDSteven-u3y 2 วันที่ผ่านมา

      Thioro lii serigne bi beugu rek lay deff touba yamoul ak benn deuk

  • @modousenengom9882
    @modousenengom9882 10 หลายเดือนก่อน +2

    Bilayyy bégnaaa❤❤❤❤ looll❤❤❤❤❤❤

  • @nouhankaba1391
    @nouhankaba1391 10 หลายเดือนก่อน

    Y’a Salam
    Ma Shâ Allah
    Serigne Touba tape une personne ni l’offense
    Le soufisme est chemin de la tolérance clémence et récupération
    Les baye Fall devrait revoir leurs comportement

  • @bacarmbowmbow9971
    @bacarmbowmbow9971 10 หลายเดือนก่อน

    Wakhtan moy lép macha allah ❤

  • @moustaphandiaye1407
    @moustaphandiaye1407 10 หลายเดือนก่อน +2

    ❤❤❤❤❤❤❤❤MACHA ALLAH

  • @mamafall1931
    @mamafall1931 3 วันที่ผ่านมา

    DIEUREDIEUF SERIGNE TOUBA DIARAMA MAME CHEIKHE IBRAHIMA FALL BABOUL MOURIDINA ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @MoustaphaDiorMbaye
    @MoustaphaDiorMbaye 10 หลายเดือนก่อน

    Serigne bi rk koko manoul abalnio jereudieufaty mme lamp fall baboul mouridiin ❤❤❤❤❤❤

  • @cheikhsankhe95
    @cheikhsankhe95 10 หลายเดือนก่อน +7

    S cheikh thioro dall defoul dara yen ay nafekh rek ngen

    • @thiounelobe114
      @thiounelobe114 10 หลายเดือนก่อน

      Yaw momou yaye nafèek bou reuye tè jamm takhoula diok wayè digna khamnè serigne touba amoule morome.

    • @serignedieng9886
      @serignedieng9886 10 หลายเดือนก่อน

      Yaw reew nga de

  • @MomoNdiaye-f7v
    @MomoNdiaye-f7v 10 หลายเดือนก่อน

    Bilahi lolou Moy yone ,kouy manifeste wou nga bayil niou souniou deuk bou cel bii nguiryalla🙏

  • @BallaNiang-r5y
    @BallaNiang-r5y 10 หลายเดือนก่อน

    Mbaye fall réck monéck ❤❤❤❤

  • @ibrahimabeye2531
    @ibrahimabeye2531 10 หลายเดือนก่อน +1

    Ahhhh waay begu na😢😢😢

  • @MAKONNAlL
    @MAKONNAlL 10 หลายเดือนก่อน +2

    Deysane niannal lenn baye fall yi nionm serigne touba rek mo lenn ngionr kou beug Manifesté ngeuweul dakar té bayil fi touba

  • @MouridoulLaahi
    @MouridoulLaahi 2 วันที่ผ่านมา

    Kouy wakhati Si Touba délwakh Lo kham louko moy boula bay fall yi sétséé😂😂😂

  • @adjifalloundiaye4087
    @adjifalloundiaye4087 10 หลายเดือนก่อน

    Machallah machallah dieureudieuf falle amatina solo loll mbake

  • @PapeNiobaFaye
    @PapeNiobaFaye 10 หลายเดือนก่อน +1

    Point 👌🏾❤️

  • @Toumanindiaye289
    @Toumanindiaye289 10 หลายเดือนก่อน +5

    Merci serigne cheikh thioro

  • @AssaneNdiaye-d1l
    @AssaneNdiaye-d1l 3 วันที่ผ่านมา

    Machalah Dia djieuf

  • @mamadougueye2017
    @mamadougueye2017 10 หลายเดือนก่อน

    Ni dieuredieuf serigne yalla guēne goudou fanne amine barkep serigne mandoumbê mbackę serigne modou guēye Chef religieux Senegal

  • @khabousiteu2408
    @khabousiteu2408 10 หลายเดือนก่อน +3

    S chiekh yay boromou fitt té donc gaindé yalnala yallah samou

  • @GERRARDSteven-u3y
    @GERRARDSteven-u3y 2 วันที่ผ่านมา

    Serigne touba moy l'islam blh

  • @DiaAss-i6w
    @DiaAss-i6w 10 หลายเดือนก่อน +1

    ولو كنت فظا غليظ القلب لنفضوا من حولك فاعف عنهم واستغفر لهم وشاورهم فى الامر

  • @mamediop8226
    @mamediop8226 10 หลายเดือนก่อน +3

    Machalah amna solo ❤

    • @Diaahmadd9882
      @Diaahmadd9882 10 หลายเดือนก่อน

      Saytaané toroxna Serigne Touba bég na❤

  • @CheikhNdong-x6s
    @CheikhNdong-x6s 3 วันที่ผ่านมา

    Cheikh thioro ces un politiciens tres pertinant
    Si il navait pas dire sa devant les senegales il la fait
    Donc wakh amna solo lol mai degbdeg mo kou motali

  • @ndeyefallndiaye8063
    @ndeyefallndiaye8063 10 หลายเดือนก่อน

    Li dé moye adouna lo guise dagnio koye wakhtane si diame mes dole akk force fadiote dara

  • @assanebambatine8472
    @assanebambatine8472 3 วันที่ผ่านมา

    YENE ESK KHAMNÉ DÉ AMNA, YAWMAL KHYAM AMNA, KHALISS DIAROUL YENE YI, NITTE MEUNE NGA AM TE TEGG KO CI DEUG,
    WAYÉ AY VUES. REK TAKH NGAYE SOSS, YAWMAL KHYAM LEUP LANIOULENE DI LAADJI AK LOLENE CI JUOUBLOUWONE.
    NDAKH : URGENT BE PARÉ CI LO KHAMNÉ DEPUIS 15 FÉVRIER 2024 LAWONE

  • @sambasene4581
    @sambasene4581 10 หลายเดือนก่อน +2

    Cheikh Thioro dal yaxoul, yaxlouwoul. Seulement les mara politiciens encagoulés gno koy saboté

  • @babelthiam9842
    @babelthiam9842 10 หลายเดือนก่อน

    Serigne Touba cheichk Mountakha moy kilifa mouride yep,,, pastef dakhé ndighel diadieufé Cheickh Mountakha

  • @khadimgueye1570
    @khadimgueye1570 10 หลายเดือนก่อน +1

    Kep kouy manifeste touba diapal ni yangui yakhal sonko limou am biir touba

  • @KhadimThioub-s3m
    @KhadimThioub-s3m 6 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Thioro Mbaye mi d da rew

  • @CheikhNdong-x6s
    @CheikhNdong-x6s 3 วันที่ผ่านมา

    Serigne fallou fall moko nian billahi

  • @youssougambien9166
    @youssougambien9166 10 หลายเดือนก่อน +1

    Aye bayfaux nio féss touba dougnou diouli dougnou woorr sath ak agression rék aye doméram

  • @AliouDieng-yp8xq
    @AliouDieng-yp8xq 10 หลายเดือนก่อน +2

    Merci cheikh thioro mbackè ya am yare bilay kou anale ousmane sonko ap yar laye am

    • @Papisdiop349
      @Papisdiop349 10 หลายเดือนก่อน

      😂😂😂😂😂😂

    • @moustaphafall9494
      @moustaphafall9494 10 หลายเดือนก่อน +1

      Ki mo gueneu reew nganane lane

    • @diengSylla
      @diengSylla 10 หลายเดือนก่อน

      ​@@moustaphafall9494bou doun sa baye daga wakh li

    • @daoudadia3631
      @daoudadia3631 10 หลายเดือนก่อน

      @@Papisdiop349😂😂😂

  • @marcelinediedhiou6376
    @marcelinediedhiou6376 10 หลายเดือนก่อน

    Je passe mon chemin

  • @faluthiam2652
    @faluthiam2652 10 หลายเดือนก่อน +1

    Rien a dire leup narafetna

  • @MoustaphaDiorMbaye
    @MoustaphaDiorMbaye 10 หลายเดือนก่อน

    Touba harasaa lah tahala min kulli makrouiin wa makhoufin bi dia i mn aadiara

  • @kingof491
    @kingof491 10 หลายเดือนก่อน +1

    Senegal doubdeuk

  • @modoundiaye8131
    @modoundiaye8131 2 วันที่ผ่านมา

    Seikh thora mbacke wakhoul lo hay deack reck La wakh

  • @aliounembaye-mh3lm
    @aliounembaye-mh3lm 10 หลายเดือนก่อน

    ❤️❤️❤️🙏🙏🙏🤲🤲

  • @mouhamadsene1735
    @mouhamadsene1735 10 หลายเดือนก่อน

    ❤❤❤❤

  • @NdayeSall-t9g
    @NdayeSall-t9g 10 หลายเดือนก่อน

    Cheikh thioro nawfėkh la

    • @diopfallou3442
      @diopfallou3442 10 หลายเดือนก่อน

      Dangay doul

    • @KhadimeTiam
      @KhadimeTiam วันที่ผ่านมา

      Y3naye iblise yi naf3ke y3ne nhi di wakhe t3 khmonl3ne iblise monléne yauni

    • @AbdouMbacke-fp7rv
      @AbdouMbacke-fp7rv วันที่ผ่านมา

      Ragalal yalla ❤

  • @abakarafall6276
    @abakarafall6276 10 หลายเดือนก่อน

    Baye fall yi dialen dief ndigell rek mba yetwi dall dierediefe seringe Touba diarama mame ziekhe ibrahima fall lamp

  • @dioufmodou4234
    @dioufmodou4234 10 หลายเดือนก่อน

    Sawaye yene doulene aye baye fall yene dageni politique s touba reckue lanoye topou

  • @fallousyll2408
    @fallousyll2408 10 หลายเดือนก่อน

    Xollenn kou nk di wané sa brachelet vaurien yi
    Gni gnoy domeram deug

  • @MoussaNgom-sg3bl
    @MoussaNgom-sg3bl 10 หลายเดือนก่อน +1

    Âge lou mane khew nit boufeke lingaye wote mogui si yaw nit waroul yabe sa Sergine mou diar si yaw

  • @elagesakho6747
    @elagesakho6747 3 วันที่ผ่านมา

    Serigne Cheikhe lou politique reuy reuy ak thieur bossi meunti am boul naagou mouk sunu sangue ba ap talibè la

  • @moustaphafall9494
    @moustaphafall9494 10 หลายเดือนก่อน +1

    Cheikh thioro li tayoko sa mame sa tourando serigne cheikh thioro mesul nangoul serigne touba tei mok serigne touba gno bokou baye

    • @NdiayeAlioune-to9lv
      @NdiayeAlioune-to9lv 2 วันที่ผ่านมา +1

      Li ngua wax bou nékon deugue sax ngua warkoo diomeu wax xanaa doo ab dioulit 😢😢😢

  • @habiibulxadiimjaxate5816
    @habiibulxadiimjaxate5816 10 หลายเดือนก่อน

    Yal na jàmm sax dàkk, te feeñal kéemtaanam ci dundug Seex Muntaxaa, ci barkeb Seexul Xadiim!

  • @BabouMafary
    @BabouMafary 10 หลายเดือนก่อน

    Liguéye sa mame moguenee té bayii politiquecien ''' sonko mo woo khàlé yii kayee

  • @toubainfo1706
    @toubainfo1706 10 หลายเดือนก่อน +1

    di def yaf niti dafa baax lool

  • @sillabadou9360
    @sillabadou9360 10 หลายเดือนก่อน

    Yaw thioro mbacke ya bogga yakh touba jakhasse serigne si

  • @niangsokhnamay3486
    @niangsokhnamay3486 10 หลายเดือนก่อน

    Amoull yakhalatté

  • @mouhamadoufalilouseck3062
    @mouhamadoufalilouseck3062 10 หลายเดือนก่อน

    Demay ligueeyali serigne touba te bayi roube bi lepp yawla . Bayil roube bi

  • @morlo3437
    @morlo3437 10 หลายเดือนก่อน +1

    Kholal ma doff yi rkk Cheikh Thiero bul tontou doff yi gny ay fanatisme lane ms lane moy titre foncier

  • @babelthiam9842
    @babelthiam9842 10 หลายเดือนก่อน

    Ousamane Sonko wakhona ko, néona serigne Mountakha douma niane dafkoy diguueul mou dieufé 2021 Mars lolou yagoul Nak, wayé shaytane dafa am dolé mouride dieufé ndigueul

  • @bassiroundiaye3913
    @bassiroundiaye3913 3 วันที่ผ่านมา

    Dégale mouy politique Ousmane songo défoule dara boukofi toudou lép yawa touba bay fall gnonou thi doy

  • @djilyndiaye-wo9ri
    @djilyndiaye-wo9ri 10 หลายเดือนก่อน

    Deeleen dumeu voutleen beureup bu ngeen di dumaa diappu pobbu duma bayyi mu dèm gisuleen brasale yi muy feuseul diko wanè

  • @khadimgueye1570
    @khadimgueye1570 10 หลายเดือนก่อน

    Politique mo waroul diaxassé touba

  • @TahirouMbaye
    @TahirouMbaye 3 วันที่ผ่านมา

    Li rafetena loll

  • @albaba45
    @albaba45 10 หลายเดือนก่อน

    😂😂😂😂😂

  • @khouledjily1505
    @khouledjily1505 10 หลายเดือนก่อน

    Li moye yone wane te Di khop wate rek kene dou lene falle

  • @fatousallniang892
    @fatousallniang892 10 หลายเดือนก่อน +1

    Serigne Assane fall sa Sokhna si mo laye ziare dila nianal goudou fane ak feer