La robe est signée « bisecollection » Masha alllah c’est magnifique. Fatél ça se voit qu’elle est bien éduquée. Elle est toute douce et prends le temps d’apprécier ses invités. Laf thiaat
Je la connais pas mais khalè boy yarou bou bakh laye nirol, Ngaka aussi kou bakh laye nirol, yalla na Yalla bourbi barkèl seuye bi dèf ci ndjabott gou barkèl ci barkè Serigne Fallou mbackè. Ameen yarabi.
Ohhh ratékhouma dara ci bess bi j'aime trop les gens ki s marient surtout s'il s'agit des jeunes heureux ménage ma bell et surtout bcp de bonheur au près d ton chéri
Machallah fatel sagnsai n'a trop mais nak n'a Guen à yiiw li l'islam beugou ko te niane ga am dôme you barkel youniouy degg yallna la ko yalla defal te barkel leppou amine machallah 😘🥰 tué et très belle s'armant 🥰🥰🥰🥰❤️❤️❤️
Mann tmt kham na nii beugue nalen guisou ma louma raté si kheww bi machalha Mme ndiaye seuyeul ba seyyyy boul degeulou kenn barki cheikhoul khadim diam guenn di ame
Mes borom tama yi tamite eupeul ngene trope ana ay tama thie réception ! Réception c’est écoute de la bonne musique danser woné ay sangsé caustume you nice mayé tassou rek ratatati rek
Posée, classe, bien éduquée avc sa robe tte mimie machallah ngaka t'as fait le bon choix, heureux ménage le peuple est content Tamit mariage bi mo diékhal sama connexion depuis le dot jusqu'à la fin rien ne m'a échappé 🥰lii dafa nékh waay fatel nguir yalla seuyel ba déh waay
Ce qui est crucial dans cette vie, ce n’est pas tout ce luxe qu’on veut montrer au monde entier mais la discrétion que l’on se doit de taire, au profit du bonheur ressenti, que l’on devrait garder soigneusement de peur de le perdre ou qu’il nous échappe entre les mains. Quand je tend la main, tout le monde peut voir la paume ✋ de ma main mais quand je serres ma main 👊 🤜 personne n’est en mesure de voire ce qu’on peut cacher à l’intérieur…….
Fatel nékhnama trop elle est très pausée mashalla vraiment yalla dafa meuna boler ay nitt même son mari il est timide entt cas mashalla yalla na yalla defare se. Couple bi mou yag am diabottt amine ya rabiiiii 🥰🥰🥰🥰
Ma beugueu khaley bou am fouleu. Goor bouleu beugué deug n'a deff fouleu. Ngir yalla boulla dara diaral nga fowé sa seuye bi. Seysi stp Fatel sow sa djeukeur saggalnala si digueu Sénégal bi yeup
Vive les chrétiens soyez fière de Jésus Christ car musulmans et chrétiens portent des robes blanches et une bouquet comme si on célèbre ça a l, église bénis sois notre sauveur
@@giogiooo_s2640 c'est chez vous que ça ne va pas ! Je n'ai rien contre les mariés mais il y'a des très jolis récipients avec couvercle pour les plats cuisinés des cérémonies car c'est plus hygiénique et puis la salade c'est très délicat donc à éviter pendant les cérémonies ...c'est grave ce que j'ai dit 😡😡
Comment ne pas t'aimer la charmante Fatel,ndéké Ngaka ngakawoul😁😁
Vives les jeunes mariés ❣❣
ngaya ayyy boorla fesser intant bi
La robe est signée « bisecollection » Masha alllah c’est magnifique. Fatél ça se voit qu’elle est bien éduquée. Elle est toute douce et prends le temps d’apprécier ses invités. Laf thiaat
L’éducation de base c’est très important 🥰
On dit la robe
@@Mounass ?
@@Mounass mais Lolou la Wakh di corriger nit té liro bou bakh 😹😹😹
@@Mounass je suis entrain de chercher la faute depuis 😂😂😂😂😅 mais je la trouve pas amga fitt trop yow
Je la connais pas mais khalè boy yarou bou bakh laye nirol, Ngaka aussi kou bakh laye nirol, yalla na Yalla bourbi barkèl seuye bi dèf ci ndjabott gou barkèl ci barkè Serigne Fallou mbackè.
Ameen yarabi.
Ohhh ratékhouma dara ci bess bi j'aime trop les gens ki s marient surtout s'il s'agit des jeunes heureux ménage ma bell et surtout bcp de bonheur au près d ton chéri
Pppp} ppppppppppppp}
machallah yalna seye bi barkèl wy yalla mouseul lèn si thiat ak saytané té bagna dèklou kén nak diapu sa dieukeur soko défé rk doko rédiou bilahi
Machallah la mariée est belle en bise collection. Joli draissage. table bien garnie heureux ménage
J’adore comment elle a reçu Ayy invitem ndeysane migui lene di lathi ba dogue guene fou bakhh mba lekk guene machala chapeau
En tout elle est tres belle, posee et classe mashallah! Heureux menage!
Machalla yalla nalen yalla lafal thiat gnepa kontane si yalla bosi guis d'Ara loula diakhal sey môme mougne rek la Lofa mougnoul doulafa fek djiguene dagnoukoy teral sagalko kou bayi gnep ni yaw. Loko defal khepko
Manchallah lekolen 2Million deh bayiiii invite yiii def ngen bamou bakh
Machallah fatel sagnsai n'a trop mais nak n'a Guen à yiiw li l'islam beugou ko te niane ga am dôme you barkel youniouy degg yallna la ko yalla defal te barkel leppou amine machallah 😘🥰 tué et très belle s'armant 🥰🥰🥰🥰❤️❤️❤️
Ngaka est un jeune trop cool.
Jesper fatel aussi.
Il faudra le respect mutuel rek
J'aime bien fatel yenewon nala dieukeur jou doul bi vraiment. Hâlé you set civilisé lala yenerwone nak
Barki seydina mouhamed Fatel mangi melnii dama bokk ak mom sama xol dafa sed sii mariage bii 😭💞yalla bo guiss lo ragal🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Mann tmt kham na nii beugue nalen guisou ma louma raté si kheww bi machalha Mme ndiaye seuyeul ba seyyyy boul degeulou kenn barki cheikhoul khadim diam guenn di ame
Machalla Fatel heureux ménage ❤💖
Mes borom tama yi tamite eupeul ngene trope ana ay tama thie réception ! Réception c’est écoute de la bonne musique danser woné ay sangsé caustume you nice mayé tassou rek ratatati rek
Bilahi
Non li si ngon bilae bimou neke si nek revoir les autres video
Ohhh machallah mariage validé bravos a l'équipe chamelle traiteur machalla tia kaw tia kanam thi yen.
Posée, classe, bien éduquée avc sa robe tte mimie machallah ngaka t'as fait le bon choix, heureux ménage le peuple est content
Tamit mariage bi mo diékhal sama connexion depuis le dot jusqu'à la fin rien ne m'a échappé 🥰lii dafa nékh waay fatel nguir yalla seuyel ba déh waay
Machala toute belle heureux ménage seuy bou barkel ak gnabot you barkel inchala
Ce qui est crucial dans cette vie, ce n’est pas tout ce luxe qu’on veut montrer au monde entier mais la discrétion que l’on se doit de taire, au profit du bonheur ressenti, que l’on devrait garder soigneusement de peur de le perdre ou qu’il nous échappe entre les mains.
Quand je tend la main, tout le monde peut voir la paume ✋ de ma main mais quand je serres ma main 👊 🤜 personne n’est en mesure de voire ce qu’on peut cacher à l’intérieur…….
Merci, tu est quelqu'un d'intelligent
Fatel nékhnama trop elle est très pausée mashalla vraiment yalla dafa meuna boler ay nitt même son mari il est timide entt cas mashalla yalla na yalla defare se. Couple bi mou yag am diabottt amine ya rabiiiii 🥰🥰🥰🥰
MAchalla mariage bi bokhou na thi mariage yi geuneu valide Senegal tres Belle MAchalla heureux menage
Heureux ménage fatet madame Ndiaye 🧡❤️ yallah Sey bii barkel
Ma beugueu khaley bou am fouleu. Goor bouleu beugué deug n'a deff fouleu. Ngir yalla boulla dara diaral nga fowé sa seuye bi. Seysi stp Fatel sow sa djeukeur saggalnala si digueu Sénégal bi yeup
Machallah chérie seuy rek ba dée inchallah
Heureux ménage à fatel la charmante femme de Nguaka ❤️❤️❤️
Machallah Fatel Yalna Yalla Barkel Seybi Amine
Que dieu me donne une belle fille comme fatel belle et posėe machallah
Machallah l'AF bouche way ❤️ et yalna yalla barkel seuy bi ❤️🙏
Machallah 😍 😍 t'es ravissante
Machalla nicena yalla na seye bi barkel nguene ame si ndiabot gou barkel
Yalna seybi barkel je t'aime très fort ma puce
Ohhhhh mashalla tt belle 🥰🥰🥰🥰
Heureux ménage Fatel Sow❤️💍🌹 Machalla marige
Ah!gaka tá femme est belle fatel machalla láf 🤲🤲🤲🤲bouche 💋❤❤❤💃
Machala seybou barkéle
Ma challa yalla na sey bi barkél
Robe 👗👗👗👗 nace na trop 🥰❤️🥰 machallah
Décolleté bi c profond quand même
Sa robe bakhna, heureux ménage
heureuse mènage fatèl❤❤❤❤❤❤🤩
Mancha alla toute mignonne ❤️ elle ressemble à Mari Marr
Machallah heureux ménage ma fatel
Très jolie la mariée félicitation mais bayiléne bâche yi tay loué salle de réception sinon mariage bi Day désorganisée
Boy nganka sokhnasy na guena yiw euleuk solinguiii okey
Mashalla c magnifique heureux ménage
Manchalla yalna seybi barquell
Macha'Allah elle tte magnifique heureux ménage waay.
Heureux ménage djabot you barkél💞💞💞
Mashallahou lafff bouche seuyyy bou barkèll🤲🤲🤲
Macha allah elle est toute belle yallah na sey bi barkel🙏🙏🙏
Toutes mes félicitations ma belle yalna seuye bi barkél 🙏💕
Très belle robe la mariée est charmante
Trēs Jolie rafet kar
Machalla fatél man dama la yage beg yalla n'a lep baké
Machallah ❤️🥰
Machala Mrs Ndiaye ❤️❤️❤️❤️❤️
Manchala l'AF thiat
Ms robe marié bou blanc bi lougniou dougeul si guinaw kouko kham dimbaléma thi
Heureux ménage ma chérie ❤️
Je vous souhaite tout les bonheur du monde ❤ 😍 💍 💘😂 😅
Je suis ravie de voir que fatel se marie
Vive les chrétiens soyez fière de Jésus Christ car musulmans et chrétiens portent des robes blanches et une bouquet comme si on célèbre ça a l, église bénis sois notre sauveur
Amennnn Amennnn gloire à Dieu
Hors sujet
Boulen guen degue nak après gorgorlul l'en bou bakh
Heureux ménage mrs ndiaye
I'm non .
O
tamit pourquois senegalais dou defff loumou meune quoi v😁 . je sai ce que je dis
ngaka 20022 bi ay boor lay diobal
FATE LOVE NGAKA REK
Mashallah you are very Beautiful 😍 ❤ ♥ Yalna la jik 🙏 🙏❤❤❤❤❤❤
Yala nalene yala mousseul si tiate ndah seni mbir siw na lol sah
Heureux ménage très belle
Tres belle mariée mais c dommage qu’elle n’a pas été servi à table.
Ravissante machaallah
Sama bebe Dane 😘❤💙💖
Zéro faute machalah sauf serveuse bi warone nga mech yi si suniou jobou kink bi heureux menage
bn chance a toi fatel et long vie
Waaw beautiful
Pourquoi les plats ne sont fermés ? et puis pourquoi de la salade ????heureux ménage aux deux!
Ioe ça va?
@@giogiooo_s2640 c'est chez vous que ça ne va pas ! Je n'ai rien contre les mariés mais il y'a des très jolis récipients avec couvercle pour les plats cuisinés des cérémonies car c'est plus hygiénique et puis la salade c'est très délicat donc à éviter pendant les cérémonies ...c'est grave ce que j'ai dit 😡😡
Elle est trop belle
Ma sha Allah
❤️❤️🥰😍
9:24 wa ki dou Amy diaspora xana dou gnibi diaspora
Li dara bakhou chi kholal won yi vraiment li rafetoul chi joulit
Heureux Ménage 🤲
❤❤
A masallah farle segnsega
Ou est le marié ???
Ma challah ❤️
❤❤❤❤
Fait par qui
Ay robe bi😂😂😁😁
Daff ko diapu rk 😇
Dafa rafete😏❤️
Machalla
Si je me trompé elle a un joli coeur
Faut surtout pas Manger en public
Heureux ménages
Akh boy biii molna franchement mes amoul balkon djiguène day am balkon way ha ha ha
Li mo bah si djigueen nak
Pourquoi montré c'est parti intimes
Maicha mi diepi nako
Ki loumou sol ni en plus sa kanam bou ninnne san makiage😡😡😡😭😭😭😭
Si hôtesse yi la bokk bayil diambour
Yawou sokhor gua deii legui Sénégal kene dou naturel 🖕
Elle juste naturel danga merrr 😂
Kou soff nga yaw
Juste da wolou bopam elle ne a pas besoin de maquillage pour être belle
Siw dall d'où diammi borom
Heureux ménage ❤️🍫
Mannn d mangui signnnn rek ndah contann
❤❤❤❤❤❤❤❤❤💫😘