J’aime bien votre duo. Les analyses de pape sont pertinentes. Il ne dit que la vérité malheureusement. Ce phénomène est mondial. C’est bien d‘en parler et surtout dans le diaspora ❤❤❤❤❤
Si les gens regardent cette vidéo c'est juste pour M'Baya , cet homme quoi qu'on uisse dire, il est très intelligent et très réfléchis dans ces propos. Kali sais que à lui seul personne ne le regardera à cause de sa vulgarité, ces sales propos juste pour faire plaisir à gens il se sali et se rabaisse. C'est bien dommage car il n'en n'a pas vraiment besoin. Tu devrais te faire autre personnalité beaucoup plus belle. Kali je te souhaite le meilleur 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Amina poté si bopam , mon beug wanéwou ak défaneté, nék si réseaux yi mélni béneu gnébé si thiine.....adina so beugué mouthieu il faut vivre caché, se faire tout petit..tant que pôté changé woul kou sone la nara nékk. Idem pour tous
Aka wakhe deugue mbaya chooooo 😂😂😂😂😂😂mon copain vie à L A afro américains dou guatte de vrais cultures khoulo ak khekhe rekkkkk bilahi mbaya à tout dit😂😂😂😂😂😂😂
Mbaya a parfaitement NYC de feu doywar , milieux Sénégalais mo doy waar faut que maandou di nebotou . Diabar ou Mbathee Niang dieguene bou moune goor kiné Maar une maman très gentille
Sokhor fep la am wayé sénégalais mo si raw wasalam
J’aime bien votre duo. Les analyses de pape sont pertinentes. Il ne dit que la vérité malheureusement. Ce phénomène est mondial. C’est bien d‘en parler et surtout dans le diaspora ❤❤❤❤❤
Pape mbaye mi kou am xam xam la machallah leupe limouy wax deugela
Merci pape vraiment tu a.bien parlé Amina doit se cacher
Rabou ndar Mame Coumba Bang la toudou
Merci pape mbaye mala fan ndakh sa deuguou nit kou bakh nga nassa djam yague❤❤❤❤❤❤❤
😂😂😂😂woye mbaya dinama raye😂😂😂😂😂😂
Vérité absolue il a dit la vérité
Kalifone arrêtes d’interrompre Mbaya, ce qu’il dit est pertinent
Si les gens regardent cette vidéo c'est juste pour M'Baya , cet homme quoi qu'on uisse dire, il est très intelligent et très réfléchis dans ces propos. Kali sais que à lui seul personne ne le regardera à cause de sa vulgarité, ces sales propos juste pour faire plaisir à gens il se sali et se rabaisse. C'est bien dommage car il n'en n'a pas vraiment besoin. Tu devrais te faire autre personnalité beaucoup plus belle.
Kali je te souhaite le meilleur 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Pur vérité même Sénégal légui Danio sohor yak dér jalousie bu bonne bilahi
Pap Mbaye we really really really appreciate you thanks so much for the loves❤we do more❤❤❤
Belle analyse amina cache toi tu mérites le bonheur
😂😂😂😂non mbaya raye ngama 😂😂 wakh nga deugue deh bilahi 😢
Machala machala mbaya felicitation encore nit kou meune déf Lou bakhe vraiment
Intervention très pertinente. Bravo
Amina yalla nko yalla samou❤❤❤
😂😂😂😂bilaye pape wkh nga deugue
Amina poté si bopam , mon beug wanéwou ak défaneté, nék si réseaux yi mélni béneu gnébé si thiine.....adina so beugué mouthieu il faut vivre caché, se faire tout petit..tant que pôté changé woul kou sone la nara nékk. Idem pour tous
C'est la faute de amina pote avec tout ce qu'elle a traversé elle doit se cacher
Voilà nak ta tout Compris
li dé la wakh. pourquoi lo ame rek tèko si net bi
Vérité absolue
Dou ndanditè. Motakh
Vivre caché, peut te sauver sur beaucoup de choses....vérité absolue sister
So true 🇺🇸
Pape vraiment tu y a raison
Veritè absolu je sw rentrèe hier Papa Mbaye deugeu rek laywak
Deugueu bou werr penk ngaa wokh Mbaye Amina dafa eipeul
Oh dég na deug , ❤❤❤ !
Merci Mbaye vérité absolue nagnou tech séné guemégne fofou d'où deukou wokhatt neteli rek lagnouy Mane mais bess bougna dougal dotouko gnokodefeti Amina pote niatheu gueminiem ak dieukeurem mo guen
❤mbaya wakh gua deugue 😂😂 ❤❤ wawaw mako sédé
Pap namoonnala yaw nitou deug nga machaalla ❤❤❤❤❤
Bayi na juger nitt yalla rk mon kham ki gueneu 😮😢
Deugeule dafa lére mbaya Jolie ❤❤❤
Aka wakhe deugue mbaya chooooo 😂😂😂😂😂😂mon copain vie à L A afro américains dou guatte de vrais cultures khoulo ak khekhe rekkkkk bilahi mbaya à tout dit😂😂😂😂😂😂😂
Vérité absolu mbaaya❤❤❤❤❤❤ billahi mala beugue,y'a nitte
Ahhh c'est magnifique. Bilaye c'est vrai. 🤣🤣🤣🤣
❤❤❤❤❤❤ merci beaucoup mbaya❤❤❤❤
Machala deug rék nga wakh❤❤❤
Vérité absolue nos ancêtres ns ont sacrifié 😢
Machallah Pape
Pape Mbaye c'est vrai ❤
Wa mbaya kagne ngaye takk diabare
Pape Mbaye il faut parler souvent ❤
Nitte day neubeutou
🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉😂😂😂😂mbaya mbaya mo bari dolé
No mbaye damako beuggg❤
Mbayaa metrise Amérique mane pareil new york laa bagné senegalais ragal senegalais ba gaday nieuww los Angeles
😂😂😂😂 non mbaya dou nit. Pape nak tu connais l'histoire de USA
❤ wawaw mbaya rek mo bari niawww niaff baya deugue rek wakh .ma taye aida bou doubai
Mbaya a parfaitement NYC de feu doywar , milieux Sénégalais mo doy waar faut que maandou di nebotou . Diabar ou Mbathee Niang dieguene bou moune goor kiné Maar une maman très gentille
Non pape mbaye je t'adore
Amina li motakh niou sokhere amina.waye bou sone gaindela.na khekh ba diekh.
Baya dagua ame soutoura ma la beugue ❤❤❤
Nooon bilay pape mbaaye il a raison deug dou rombi nop c malheureux pour pour le noir
❤❤❤machalla
I'm so ashamed to be Senegalese sometimes.
Pape mbaye😂😂😂😂😂😂 dina des
C la vérité
Goordjiguene dengne kofi téré
Aka y'a wakh deugeu ❤
Esk senegalais yalla torokhalouco pour séne sokhor gratuit
Cheutttt Mabaya graouw ngaa diamano Mathieu fall ndeysane niit kou bakh
Heureusement que je vis à Miami et depuis que j’y vis je n’ai rencontré que deux sénégalais. Tant mieux.
Billaye Wallay Mbaya
😂😂😂 Pape Mbaye ❤❤❤
Mame Coumba Bang moy rabou Ndar. Lii😂😂😂
Mbaya rekh
Mansha moussa
Rabou ndar mame coumba bang.bou cote ivoire moy mamy watta.
Deuguëleu, sénégalais kéneu khamoul lii lanla😢.narnagnou kholatte signou bôpeu
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂wah degeuna deuk
Walah Pape mbaye loumou wakh yeup deguela c triste jalousie et mechanceté gratuite mofii ame
Mbaya lo wakh bayi nga la caa dess.
😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅pape mbaye dou nitttt
Verite absolue DEUG nekhoul
Lima néhh thi pape dafa deugou
amnasolo
Sokharou senegalais masi kham dara plus de 35 personnes diarnanou sii ma diapalelen tay may sen premier nonnn
Non lolou doyna warr
Yéména Dal... Motakh Kouy Def Défal Rek Té Yalla TAKH
Mai doléne guiss féne seugue té yala dinalako faye
Machallah pape Mbaye
Meussouta doulllll limouy wakh lep DEUG la fila nék mais ay domairamlagne
Kally numéro mbaya la beug
Malick Nar goor Pure la
Fouye moye ce probleme, senegalais sokor rek yaw ba bakhgua
Soubkhanallahi Éskéyye lii Mame Cheikh Almakhtoum Wakhone Rékke Nanoiu Sangue Dikoy Mogueune.Surtout aka gnio Meuna
Khébaté.il a Raison.Niakke Diangue tamite Erreur leu Ami boko Kholé khanmené Dianguoule doiu Dîné Islam dou Nassarane doiu Nitte kou intéligente Motakh ????
😂😂😂
Aka xam histoire esclavage 😂😂
Amna aye mbokeu youko sokhlo
Oh my gosh pape Mbaye is speaking facts I don’t deal with any sene Gambian and African American
Pape Ligia wakh yep deguele gua ab papier dem do ligueyi niou bolela niou dak la
Il a raison mbaya ont est bien en France ici mais Amérique humm
Thieuye yallah
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Nekhoul wayé nbaya limou wakh lep deugeule nite kou nioul yague na sokhar
❤❤❤😂❤❤❤❤❤❤
😂😂😂😂ki la beugue
Pape je veux acheter de l'or je suis en Belgique
Bilahi wax na deug
La méchanceté des senegalais me dépasse vraiment
Amina doit vivre sa vie discrètement.
Étaler toute sa vie dans les trottoirs, pourquoi ?
Pour vivre heureux, il faut vivre caché.
Déloussil waay Poté.
Sa comportement lanou beugoul motah
❤😂👍
🎉🎉🎉🎉🎉
Senegalai mo sokhore europe yepela
🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Biichh shut up 😂 Naya is the best story teller. Y'all sleeping on this legend!!
Deug pirr nga wakh pape Mbaye Harlem la deuk bilahi bonn rek langiou deff
❤❤❤❤❤