Youssou ndour da co humilié…,bakh ne si mome? Salbé Ndom déclare la Guerr€ à Wally Seck..Da ma bagne

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 21 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 81

  • @ndeyemourseye6010
    @ndeyemourseye6010 15 วันที่ผ่านมา +9

    Wally Seck yalla na goud fan ❤❤❤❤❤❤

    • @OumyNiang-hl1zu
      @OumyNiang-hl1zu 12 วันที่ผ่านมา

      Amiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiin

  • @jeannettegomis8228
    @jeannettegomis8228 14 วันที่ผ่านมา +8

    Je suis vraiment désolée, Wally SECK a seulement fait son devoir envers son père Youssou Ndour. Bonne continuation Wally SECK ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @kharitourassoulsalalahoual870
    @kharitourassoulsalalahoual870 15 วันที่ผ่านมา +17

    Wally seck bou yorroulwon nada kene douko nango kham bayilen domou jambour jii Allah Allah Allahou Akbar. Yene adada.

  • @AssaneNiang-s4e
    @AssaneNiang-s4e 15 วันที่ผ่านมา +2

    Wally nite kou bakh la ❤❤❤❤❤❤

  • @MouhamedThiam-w2u
    @MouhamedThiam-w2u 14 วันที่ผ่านมา +2

    Waly kou bakhla❤❤❤❤❤❤❤

  • @almustafambakke6163
    @almustafambakke6163 15 วันที่ผ่านมา +5

    Sërim tuuba ❤ Amul misic deh tubël liga wsx mére

  • @aminataniang2948
    @aminataniang2948 15 วันที่ผ่านมา +5

    Wally yallah gua am diam doundel Lou bari ❤️♥️🙏♥️❤️

  • @motigque93
    @motigque93 14 วันที่ผ่านมา +5

    Vous n pouvez rien sur Wally daafa amm gueureum yaaye ack papa tée dii déef lou baakh nit kou baakh laaa quallah vous protège et vous donne une belle fin d’un bon musulman

  • @oumarmbengue6546
    @oumarmbengue6546 14 วันที่ผ่านมา +3

    Nekhoul ba nekhoul mais senegal barina ay nafék ak fénn kay si magu

  • @RouguyNgom
    @RouguyNgom 15 วันที่ผ่านมา +7

    Mais pourquoi les sénégalais sont méchants Youssou Ndour à pas humilié Wally en tout cas lui il a de l’argent pendant que vous êtes là à parler tchip

  • @dembamaidousane6323
    @dembamaidousane6323 10 วันที่ผ่านมา

    Musikou Serigne Touba musikou Serigne Fallou 😂😂😂😂 Astahfiroulaah mais gni saff nagnou khorom😂😂😂😂

  • @cheikhfall2997
    @cheikhfall2997 16 วันที่ผ่านมา +5

    Bayil mère Aida saliou bingay garouwalé selbé régler mola war😂

  • @SeynabouMbaye-m4x
    @SeynabouMbaye-m4x 15 วันที่ผ่านมา +2

    Bilay Mere deugue rek moy deugue mes nityi Kou am khaliss dougnoula wakh deugue diolle fou toy moudal

  • @Wakhdeug-m5x
    @Wakhdeug-m5x 16 วันที่ผ่านมา +3

    Sénégal ngay guiss kou ligueyoul done millionnaire 🤣🤣🤣. Yelwane ak wayane rek 🤣🤣🤣🤣

  • @OuleyeDiagne-r5r
    @OuleyeDiagne-r5r 15 วันที่ผ่านมา +1

    Vérité absolue

  • @cheikhfall2997
    @cheikhfall2997 16 วันที่ผ่านมา +5

    Ténguéna bagna lék domou diambour dji lidieuntil say dom ,wally domou diambour la il n'est pas obliger mou guestou sénégalais yeup,merdass😂

  • @aminataniang2948
    @aminataniang2948 15 วันที่ผ่านมา +3

    Yaw so baye wally Lou mou koye wanie 😂😂😂 bilahi khamo sa bopou selebe

  • @RIP_RAT463
    @RIP_RAT463 15 วันที่ผ่านมา +4

    Du n'importe quoi, nagnou yakar yala et ne forçons pas des relations

  • @RoheyFaal-d3s
    @RoheyFaal-d3s 15 วันที่ผ่านมา +3

    Tata Selbeh Ya Wah Degga ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ycamara9034
    @ycamara9034 15 วันที่ผ่านมา +2

    NIce peace and love 👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍✌️😁

  • @sophiesokhna1614
    @sophiesokhna1614 15 วันที่ผ่านมา +2

    Pourquoi ngèndi dôme borome xaliss kèssè, nafèkh bakhoul.

  • @oumouseke7130
    @oumouseke7130 16 วันที่ผ่านมา +6

    C est du grand n importe quoi tous les petits sites là doivent être régulés

  • @NdeyeHann-x2t
    @NdeyeHann-x2t 14 วันที่ผ่านมา

    Youssou ndour et sidy diop ❤❤❤❤❤

  • @sacyfall-xb9uo
    @sacyfall-xb9uo 15 วันที่ผ่านมา +1

    vrement nakk bayi leen domou diambour bi wakh baakhoul

  • @MamecoumbaNdoye-yt9iy
    @MamecoumbaNdoye-yt9iy 16 วันที่ผ่านมา +5

    Ay way sites you tėgal sėn ndeye yi bayilėn waly

  • @cisseayssata
    @cisseayssata 15 วันที่ผ่านมา +1

    Soukerou koor diokh ko tes parents et les gens dans le besoin. Waly yala teral Nako

  • @MamecoumbaNdoye-yt9iy
    @MamecoumbaNdoye-yt9iy 16 วันที่ผ่านมา +2

    Maman salbė mii diakhall nama

  • @fatouseck4915
    @fatouseck4915 16 วันที่ผ่านมา +2

    Mane lima diakhale eske amoleine louguene meuna diokh nit gni comme information ke de sarcharnei autour de Wally li ba diame leu

  • @souleymaneba1469
    @souleymaneba1469 16 วันที่ผ่านมา +1

    Merci salbe Merci

  • @JosephineCamara-qu1gt
    @JosephineCamara-qu1gt 15 วันที่ผ่านมา +1

    Selbe wakhal wakhou nit Wally yallah ngui Koy diapaley mi ngui santa yallah

  • @Ndeye-g7d
    @Ndeye-g7d 15 วันที่ผ่านมา +1

    Bayeline doumo jambor jee amol yaye amol papa wally manoul yor jebbe dembalilenkou

  • @Wakhdeug-m5x
    @Wakhdeug-m5x 16 วันที่ผ่านมา +2

    Kou len yeug moy kouy liguey dilen diokh. Togue mouy dokh dou doundou.

  • @Zam-Zam710
    @Zam-Zam710 15 วันที่ผ่านมา

    DEUGEU BOU WÉER NGA WAX MAMAN SELBÉ ❤❤ WALLY SECK MO DIOUM LOU REUY 😮😢 JE L'AIME BIEN MAIS TEMPS YI FARAMAREN MOM AY TOTHIE RÈK VRAIMENT 😮😢 MAIS PEUT-ÊTRE AY TODIAL LA TAMITE

  • @ndeyendiayefaye3819
    @ndeyendiayefaye3819 15 วันที่ผ่านมา +2

    Mere yagui sissou sokhna aida saliou mo takh wala dagua ka naine mou fate la wally loumou yene mo bary nit dou bedi demb done nala defal sorale

  • @sonkoomar2165
    @sonkoomar2165 15 วันที่ผ่านมา +1

    Adouna dou keur😂😂😂

  • @YacineSeck-d6u
    @YacineSeck-d6u 15 วันที่ผ่านมา +1

    Astafiroula astafiroula toublennne aye😂😂😂😂

  • @NafiNdao-s1y
    @NafiNdao-s1y 16 วันที่ผ่านมา +13

    Pourquoi tay nguen di beugueu regler sen ay compte ak wally apres grand bal bou youssou ndour non arrêter len

    • @RouguyNgom
      @RouguyNgom 15 วันที่ผ่านมา +3

      C’est des Seytaner Wally il s’en fou il vit sa vie

  • @cheikhgueye254
    @cheikhgueye254 15 วันที่ผ่านมา +1

    Dano wara bayi tudu Serigne si ay thiakhan rafétoul dra

  • @almustafambakke6163
    @almustafambakke6163 15 วันที่ผ่านมา

    Wallahi yenagi togne Serin Tuuba😢

  • @BakzBarber
    @BakzBarber 16 วันที่ผ่านมา +2

    Kii merna deh

  • @halikano392
    @halikano392 15 วันที่ผ่านมา +1

    Bayiléne ma sétane rek téye 🤐

  • @aminatadiopgueye9486
    @aminatadiopgueye9486 15 วันที่ผ่านมา +1

    Wa yaw khana ya diour wally
    Yén dal yéna nékh

  • @zeke5071
    @zeke5071 16 วันที่ผ่านมา +6

    ni Waly def mere Aida Saliou mo la nahari

  • @papbiransarr4298
    @papbiransarr4298 16 วันที่ผ่านมา +1

    This woman is upset and angry for Wally because she is not getting what she use to receive from him bayleen took my dokh

  • @rokyatoutoure610
    @rokyatoutoure610 15 วันที่ผ่านมา +1

    Bingaye yobou pagné si waly menone gua ko diokh say deukando té problème famille diambour guéne si

  • @nayedioba2732
    @nayedioba2732 15 วันที่ผ่านมา +1

    Koula faléwoule sa yone waroule nékh si mom tmt bagay débat si mom bayilén domou diabour bi

  • @Mame-Bousso-
    @Mame-Bousso- 14 วันที่ผ่านมา +1

    Só contennoul loussi souniou yone waly ay parent guereum naniou ko may niou way tamit lo bok ak waly Sénégalais boko mayatoul rek mou Khass la

  • @AidaGoudiaby-yc1cj
    @AidaGoudiaby-yc1cj 16 วันที่ผ่านมา +2

    Yaw li la méti wakho dé Sokhna Aida molay derange ak waly lim def si yaw yeup

  • @Zazindiaye218
    @Zazindiaye218 16 วันที่ผ่านมา +1

    Maman sėlbė boul wakh lolou waly niit guenouko

  • @sacyfall-xb9uo
    @sacyfall-xb9uo 15 วันที่ผ่านมา

    senegal daal doyna waar tay tagg souba khass bayi leenn seen yii faux geenn trop

  • @SeydouBa-t8h
    @SeydouBa-t8h 16 วันที่ผ่านมา +1

    Merci selbé tu as raison c comme ça la vie

  • @FadelDieng-u7v
    @FadelDieng-u7v 16 วันที่ผ่านมา

    Gooo

  • @RouguyNgom
    @RouguyNgom 15 วันที่ผ่านมา +1

    Toi selbe occupe toi de ton ménage cela n’est pas de ton âge

  • @ColeSene-yu9di
    @ColeSene-yu9di 16 วันที่ผ่านมา +1

    Boula Wally fonkoutone Dina la indim camion sucre camion riz comion huile khalise ak kharou Tabaski ganee Wally diapoula yaye walla nimou mel si soxna Aïda saliou mola metti mo takh gay gêne Di wakh

  • @Mais2019
    @Mais2019 14 วันที่ผ่านมา +1

    Wally Amna. Yaye Moy Diaga Ben Yaye La Am. Il Na pas Besoin De Toi Arrêtez Ohhh

  • @tonikrossba1483
    @tonikrossba1483 14 วันที่ผ่านมา

    Music da haramm

  • @gayafall
    @gayafall 15 วันที่ผ่านมา

    Non laye Gane bou niew . Teral ko . Deff déplacement bayi way sokhole les. Gane teral ko .

  • @chocsevenements8990
    @chocsevenements8990 16 วันที่ผ่านมา +1

    Neniou defar kholate li niouy wakh

  • @YacineSeck-d6u
    @YacineSeck-d6u 15 วันที่ผ่านมา +2

    Misquine yo nekfi guaye diokhe Wally soukoroucor toublene😂

    • @abymboup8359
      @abymboup8359 15 วันที่ผ่านมา

      😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅

  • @AyaMballo-ke6re
    @AyaMballo-ke6re 13 วันที่ผ่านมา

    Nimporte quoi🤮🤮🤮🤮 selbe hamo ca boop

  • @bourewalo1697
    @bourewalo1697 16 วันที่ผ่านมา +2

    Mere yaw bakhoulo je ne peut comprendre les Sénégalais niak gor

  • @dabosall9860
    @dabosall9860 14 วันที่ผ่านมา +1

    Yamba bakhoul

  • @MammaSoumbundu
    @MammaSoumbundu 15 วันที่ผ่านมา +1

    Yaw mi yaye saytane bu maguet bi selbe

  • @MatThiam-m9g
    @MatThiam-m9g 16 วันที่ผ่านมา +1

    Salbe mère ne dé😂

    • @AdjiaFall-j4o
      @AdjiaFall-j4o 16 วันที่ผ่านมา

      😂😂😂😂😂😂😂

  • @papefaye7806
    @papefaye7806 15 วันที่ผ่านมา

    Mére c'est quoi ton problème ? Waly a sa maman et il est musicien, toi tu as tes enfants et tu es voyante nakou neck dieul yonam bayil thiakhane ak doryi

  • @mj-zq4qg
    @mj-zq4qg 16 วันที่ผ่านมา

    Selbe wakhnga deague

  • @CoumbaFaye-u2h
    @CoumbaFaye-u2h 16 วันที่ผ่านมา +1

    Yaw yaye kane si rewemi bagne laye diokh importance

    • @SeydouBa-t8h
      @SeydouBa-t8h 16 วันที่ผ่านมา

      Dégage Wally est qui

    • @yvefay620
      @yvefay620 15 วันที่ผ่านมา

      sshhh !!! moye Driankè selbé nak

  • @aramtall7523
    @aramtall7523 15 วันที่ผ่านมา

    Du n n'importe quoi

  • @MadiaCoulibaly
    @MadiaCoulibaly 15 วันที่ผ่านมา

    Dousa dome boudone sa dome ga woko si nék yédko bayiléne domou jambourdji