Le meilleur oustaz du Sénégal. Il est gentil,il est généreux et encourage les jeunes,les femmes et les hommes à adorer Allah bref oustaz Oumar Sall Yana yalla degerel leuh tei goudal sa fann
Assalamouhaleykoum Oustaz macha Allah je vais me témoigner sur l'importance de vos vidéos et l'efficacité du coran. Je suis actuellement en Abidjan je suis avec un ami. En chaque fois, il dit qu'il est malade surtout la nuit. Un jour j'ai regardé un de vos vidéos comme celui là. En rentrant à la maison je lui est trouver coucher et je commence à réciter sur. En quelques minutes (1à2) il se soulage en disant que ça il ne sent plus rien. Auparavant on faisait tout ce que l'on savait ( écriture coranique, "garabou Wolof" pharmacie rien). Vraiment ça fait longtemps je rentre dans TH-cam mais je viens de voir quelle que chose de réelle. Merci Oustaz si on peut avoir votre numéro, ça sera une grande faveur pour nous. Nous sommes en danger de tomber sur les charletants .
wakhtiko deh mais on a une arme puissante qu'est woolu yalla, ak dekko wekki sunu bir wallahi, personne ne pourra rien contre car tu as la protection d'ALLAH yalla nanu ko yalla may à vie
Yallah protège notre cheikh omar sall, c'est toi seul qui peut lui apporter ta grâce et ta protection. Récompense se ses efforts par ya générosité. Merci beaucoup cheikh omar sall
Yalla n'a yalla goudal sa fane ❤
Le meilleur oustaz du Sénégal.
Il est gentil,il est généreux et encourage les jeunes,les femmes et les hommes à adorer Allah bref oustaz Oumar Sall Yana yalla degerel leuh tei goudal sa fann
❌❌❌❌❌❎❎❎❎❎😅😂😅😂😅😂😅😂
Machalah yalna yala defalla leru deun
@@das-zc7hy Amin mon frère gnou bokk ko
lima diakhal moy Sénégal daguay sangou ba sonne té bougnoula liguéyé diapela Sangaré yi diakhalnama
@@mbayeakim5233Wallahi ce ke je me suis dit
SoubhanAllah 33fois wal hamdou lilah 33fois wal lahou Akbar 33fois ❤️🥰🙏🏽
Allahou akbar 34 fois
Allahou Akbar au lieu de 33 fois c'est 34 fois d'accord Khady
If it is to be said before going to bed Allahu Akbar should be said 34 times.
Merci
Assalamouhaleykoum Oustaz macha Allah je vais me témoigner sur l'importance de vos vidéos et l'efficacité du coran. Je suis actuellement en Abidjan je suis avec un ami. En chaque fois, il dit qu'il est malade surtout la nuit. Un jour j'ai regardé un de vos vidéos comme celui là. En rentrant à la maison je lui est trouver coucher et je commence à réciter sur. En quelques minutes (1à2) il se soulage en disant que ça il ne sent plus rien. Auparavant on faisait tout ce que l'on savait ( écriture coranique, "garabou Wolof" pharmacie rien). Vraiment ça fait longtemps je rentre dans TH-cam mais je viens de voir quelle que chose de réelle. Merci Oustaz si on peut avoir votre numéro, ça sera une grande faveur pour nous. Nous sommes en danger de tomber sur les charletants .
Y’a un numéro dan la bio🤷🏽♀️
@@muslima1947fnuméro de téléphone
Machahalla oustaz mais vos contacts s'il vous plaît
❤❤❤Imam yallah yaag té fii té werrr wayy barké BoromTouba
Billahi ndiabar Kat yi nio yakha Sénégal
wakhtiko deh mais on a une arme puissante qu'est woolu yalla, ak dekko wekki sunu bir wallahi, personne ne pourra rien contre car tu as la protection d'ALLAH yalla nanu ko yalla may à vie
Yallah protège notre cheikh omar sall, c'est toi seul qui peut lui apporter ta grâce et ta protection. Récompense se ses efforts par ya générosité. Merci beaucoup cheikh omar sall
Allahumma amine
Amine
Machalla yaa oustaz yalna yalla gudal sa fane may la wér
Amine ya rabi
Merci beaucoup Ya Ouztas
Yalla. N'a yalla dollula sam oustaz
Salam diarale nalén gnou douguel la sa wédi yalla dadi léndi gueme si séni kathiii néne yalla nagnou yalla sakhal su gueme ko ake doyeloko inchallah
Alhamdulilah and Que Allah SWT vous bénissent et nous donner nous tous Jannatul friduas. Jazakallahu khairan Sheikh omar Sall
MachaAllah ya ouztaz Yalleu nagnoula Yalleu fayal amna yéneu dieuf yi di bakhé ouma bi gnane yi Yalleu rek lagnou lay bayél Yalleu nala.Yalleu tahawou defal.la.lo beugeu areleu MachaAllah diazaka Lahou Hayran Amine
Merci yallanala yalla faye
🙏🙏🙏mashallah 🥰🙏merci y’a oustaz barrakalahou fiik
Dieureudieuf yalna yalla sammeuleu soutouraleu ci barké seydina Mouhamed sws
MashaAllah oustaz may Allah reward you abundantly learning from you jaza'kallah khairan
Dieureudieuf ousstaze yallana yalla mayela goudeu fane ak soutoureu aminnee
Ma shaa Allah Allah Oustaz may Allah continue to bless your knowledge 😍❤️❤️❤️❤️
Amna Solo lool yalnalén yalla samou téfaylén
Wa aleykoumou sallam wa rahmatoulah wa barakatouhou ☺️ merci ya oustaz,amena solo 🙏
Diazakallahou xayrane yaa oustaz, Qu'ALLAH SWT vous protège
Hafizahoulaaaah Macha Allah Diam si yaw incha allah ♥️
Machaallah long vie santé de fer
Ya bakhe yalla nala yalla Faye amine
Oustaz yalna yalla fayla té samela goudal say fane yok hamham bi
Alhamdoulillah binioula amer yalla na sa diam yague
Kou menou bakhara nak noumouye def svp
Mashallah yalla na borom faye
Wa Alaikum Salam Warahmatullah. Jerejeff Sall Ma Cha Allah
Macha Allah j'ai appris beaucoup grâce à tes explications.
Merci beaucoup Outaz
Macha Allah Barakallahou fik ya oustaz
machalah longue vie à toi oustaz Oumar sall yalla nalla souniou borom bayilaffi may leu goudeu fane ak weer
Machallah barakallah hayrane ya oustaz
Machllah ya oustaz yalnala yalla fayy🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
machaallah NASA diam yangue❤❤❤
MashaAllah ya Oustaz Barakallahou fiik ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏
Diazakamoullahu khayrane ❤
Dieureu dieuf oustaz Masha Allah yalnala yallah samou
Dieuredieuf oustaz yalla nala yalla Faye
Merci austaz que Allah vous accorde une santé de fer ainsi que votre famille.
Amine
Machallah que dieu vous protège amine
Machalla imam ❤💯🙏🙏🙏🙏👍👍👍👍
Ya oustaz yalna yalla fayla té samela
#BISIMILLAH# OUSTAZ YALLA NA LA YA RABI SUTOURAL @ASALAMALEOKUM@
machallah oustaz omar sall 👏👏👏👏
جزاكم الله خيرا وبارك الله فيكم واحسن الله إليكم
Yalna yallah Faye la
Machala
Merci oustaz
ماشاء الله جزاك خيرا
Mashallah yalla na yalla wathié yiw si yaw
Ma cha Allah
Macallah ya oustaz
Diazakallah haïrane ya sheikhana yalnagnou laa borom bi fayal
Oustaz touloukouna momlakhamoul
Salamou aleykoum touloukouna mère djola yi gnoye diay original bi en général.. si marché yi
Ma sha Allah yallah na la yallah fay y’a oustaz dieureudeuf
Bârakal'lâhou fîk amna solo trop🙏🏾
Merci beaucoup oustaz
Merci.causerie vraiment intéressant et éducatif.❤
Touloukouneu disponible à un prix très abordable ☝️
Machallah ya oustaz yallna yalla fayela te samla🥰♥️🇸🇳🇪🇸
Yalnako Yallah fay yiw
Machalah oustaz à diaram
أطال الله بقائك وحظك من كل سوء
Machallah Outaz yalna yalla barkél
Mâchallah Oustaz
Amna sollo machalah
Machallah dieureuff oustaz
Macha Allah djajakallahu khayran ya oustaz. Huile habbassawda lay beugeu xam
Huile habbatou sauda bo démet si diaykatou tére yi nga ladjlinko niou diayla huile habbatou sauda
@@aboubilalsy9162 djajakallahu khayran soma meuneun djappalé si "tulukuna" bi tamite ☺️🙏
ماشاء الله
Machallah Barakallah fîk
MACHALLAH 💯💯💯💯💯🤲🏿🤲🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Macha'Allah ya imam
Maaaaachaaaalah
Merci très important
We love you oustas
Machaalla ya oustaz
Macha allah oustaz longue vie à vous
Yalla na Yalla barkél teu fayla
Machallah oustaz amna solo
Damay lathi ndakh linga wax, Yonenti salalhou'alayhi wassalam daka massa déff.. Bou doul lolou diap nané kone Bidah la . wa salam.
MasahaAllah
machallah ya oustaz 🥰
Machia alla 💖
Mashallah
machallah
Thank you sheikh
Ma sha Allah. Ya Allah barkel xam xam bi teh doli la
merci
Assalamu alaikum, the ingredients is it olive oil, black seed and tulu cuna
Mach Allah 🙏
Mashaallah ❤️❤️❤️❤️
Bilahi deguele
Macha Allah oustase yalnala yalla faye
Aya bi do gniouko binedeul khamoumako
AssalamouAleykoum Warahmatoulah Wabarakatouh les feuilles de sidème que j'ai c'est presque en poudre dafa mokk!
Ça veut dire que comme daffa mokk je ne peux pas compter les feuilles
Takbir
♥️♥️♥️
On peut l’écrire ensuite laver pour obtenir nassi ensuite ajoutez le zam zam ?
Mandiaye
Salam on peut en boire seulement ou boire et sa laver avec