Machallah mama asstou yaye bou bakh âme gorr ak diné yala nala bala bayé ak alé Sama Rake bope bima buege té bolé wouma ak d'Ara yala nala yalla same mayla goudou fann
Chapeau Mme vous êtes une vraie maman digne de ce nom bon rétablissement à votre fils et que le seigneur vous protège et vous garde 💂 longtemps pour l accompagner il a besoin de vous bonne journée ma chère dame
Manchallah mére bi bakhe ne té beug domame, geume yallah surtout,,,, yallah nala yallah defale diame. Kou beug sa yaye gnanal léne ma sama yaye Goude fane ak wér. 🙏🙏🙏🙏
Vraima Alé mboup vous avez une maman formidable liguéyou ndéye rek la bilahi yalla na say fane goudou ta andak werrrrrrrrrr si barkep serigne fallou mbacké yalla diékhoul
RESPECT A CETTE GRANDE DAME! ALLAH L'ASSISTE DAVANTAGE, ELLE ET SA FAMILLE, PARTICULIEREMENT ALLÉ. JE SUIS FIER D'ELLE. TRES EMOUVANT! ALLAH RETRIBUE CETTE EXEMPLAIRE MAMAN AU NOM DU PROPHETE(SAWS),. MERCI A ELLE ET A TOUTE SA FAMILLE QUI PRENEZ SOIN DE ALLÉ. SOXNASSI MOUNGNE - KAT- LA ! SA DIEUF CI ALLÉ DOU NUL. LI GEUNEU NGI CI YOON. YALLAH DOU LIGUÉY LO KOUMOU NAROULA FAY! RESOECT A VOUS MADAME! QUE LES FEMMES OU LA MAJORITÉ DE LA GENERATION ACTUELLE S'INSPIRENT DE VOUS. VOUS INCARNEZ LA PATIENCE, L'AMOUR, LA PERSEVERENCE DANS L'EFFORT.ETCCC! A ALLÉ, PRIONS POUR LUI ET LUI SOUHAITONS BONNE CHANCE POUR SES PROJETS D'AVENIR. QU'IL EST UN DIGNE FILS, EXEMPLAIRE POUR BEAUCOUP DE JEUNES DE SA GENERATION. IL TRAITE AVEC RESPECT SA MAMAN QUI LA LUI REND BIEN! MADAME ,JE VOUS RESPECTE ET VOUS AIME!
MACHALAH une dame courageuse et très sincère. Je la connais bien mais YALLA nako may goudou fane AK wer. Ale nak mome borome bakh leu. Un modèle de courage et de dignité. Je l adore🤗
Mashallah Mama Yaye ngu ba nda nit tah ngi jul dom mu mel nee teh sonnu si dila nyanal yala bayea la Sah Ale Mboup basi kanam insahallah Waw Waw Mama bou Jongoma la ❤❤❤❤❤ Ameen yarabi
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤je t'adore maman! Yalla na ma yallah may sokhna bou mèl ni yow❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ay way ya ALLAH khamna ni sama khol bi meuneutoul i cried my heart out Allé yalna yallah sammeu leu té doli sa waydiour kholou mougn yalna ya ALLAH yokk soutoureu
ohh la maman elle est extra ordinaire Sokhna si naw nala torop billahi Barkep Serigne Saliou. Yalla nalène Yalla sameu defal lène diam yokk xeweul yi. Sant Yalla warna diam kheuy di diambat rek di dioy di khountou té fo guesto guiss ko tané.
Ndeysane yow mi yay yaye diou bakh yalna la yalla bayé ak Alé samm léne, yir léne, yok séne soutoura ak séne téranga kou bakh nga nitou aldiana nga. Contane na Ndoféne momou nga toude sama dome la yayam sama mak la
Ndeysaane une maman exemplaire. Très posé. Maman yalna sa jaam yaague
Amine
Ndeyssaann.. encore respectons nos mamans.. elles sont toujours présentes🙏🏽
Vraiment merci encore une fois mon frère c vrai🙏🙏
Kou beug sa yaye beuseul jaime
adouna bi gnou nék kénn rtt mo diara dioh confiance mouy yayy.nah gneup sougnela abandonner mom moy tahaw thieuyy yayy amoul morom bilahi
Deugue leu frère❤❤❤
Billaye frère wakh nga deuk
Sokhna si yalla na yalla sarakh la sa Aly mi longue vie à vous deux fiers de vous mention spéciale à toi la grande dame
Ndeyssane amna frere com ale. Yala moy bour. Mashaalla.
Ndaysannn maman bi amna courage thieuy adouna ni rekk laa j'ai même pleuré bilahi
Machallah mama asstou yaye bou bakh âme gorr ak diné yala nala bala bayé ak alé Sama Rake bope bima buege té bolé wouma ak d'Ara yala nala yalla same mayla goudou fann
Machalah yaye Boye yalla na sa fane goudou teh yalla diapalè la ndakh vraiment yaw royou kaye nga bilahi 💖💖
Chapeau Mme vous êtes une vraie maman digne de ce nom bon rétablissement à votre fils et que le seigneur vous protège et vous garde 💂 longtemps pour l accompagner il a besoin de vous bonne journée ma chère dame
Amine Yarabal Alamine
Une maman très courageux ❤️😍😍
J'adore cette maman. Elle a bien protégé son enfant en plus tek si geum yalla.
I
Manchallah mére bi bakhe ne té beug domame, geume yallah surtout,,,, yallah nala yallah defale diame. Kou beug sa yaye gnanal léne ma sama yaye
Goude fane ak wér. 🙏🙏🙏🙏
Mbettel
Machalla Yalla nalene Bour Yalla samal bopam
L'amour que l'on reçois et donne a nos parents n'a ni prix ni valeur egale il est imcomparable et immense
Une vraie, maman. J'adore cette brave dame. Force à toi.
Que Allah veille sur vous !
Amine Yarabal Alamine
Ohhh😍😍😍li nekhna way qu’elle grande dame😌
Vraiment maman j t adore bene bene nga fii . Si je vois Aly rire j envie oublier de tt mes sousci , bravo frere Aly je t aime depuis espagne
Macha allah maman exemplaire ...c joli yalna lene yala teral si barke seydina mohamed...
Wally Seck Seck machallah yallah nako yallah lafall tiate
Machala yaye boye en plus très souriante amal diam alé yak yaye boye
Vraima Alé mboup vous avez une maman formidable liguéyou ndéye rek la bilahi yalla na say fane goudou ta andak werrrrrrrrrr si barkep serigne fallou mbacké yalla diékhoul
Sama khol sédd na si yaye dji 😭😍😭
Mach'Allah nos maman on des coeurs en or que Aly se rétablissement vite
RESPECT A CETTE GRANDE DAME!
ALLAH L'ASSISTE DAVANTAGE, ELLE ET SA FAMILLE, PARTICULIEREMENT ALLÉ.
JE SUIS FIER D'ELLE. TRES EMOUVANT!
ALLAH RETRIBUE CETTE EXEMPLAIRE MAMAN AU NOM DU PROPHETE(SAWS),.
MERCI A ELLE ET A TOUTE SA FAMILLE QUI PRENEZ SOIN DE ALLÉ.
SOXNASSI MOUNGNE - KAT- LA !
SA DIEUF CI ALLÉ DOU NUL.
LI GEUNEU NGI CI YOON.
YALLAH DOU LIGUÉY LO KOUMOU NAROULA FAY!
RESOECT A VOUS MADAME!
QUE LES FEMMES OU LA MAJORITÉ DE LA GENERATION ACTUELLE S'INSPIRENT DE VOUS.
VOUS INCARNEZ LA PATIENCE, L'AMOUR, LA PERSEVERENCE DANS L'EFFORT.ETCCC!
A ALLÉ, PRIONS POUR LUI ET LUI SOUHAITONS BONNE CHANCE POUR SES PROJETS D'AVENIR.
QU'IL EST UN DIGNE FILS, EXEMPLAIRE POUR BEAUCOUP DE JEUNES DE SA GENERATION.
IL TRAITE AVEC RESPECT SA MAMAN QUI LA LUI REND BIEN!
MADAME ,JE VOUS RESPECTE ET VOUS AIME!
C'est vraiment émouvant l'amour que cette maman a pour son fils
Machallah maman cherie je t'aim beaucoup ❤❤❤
Je t'aime beaucoup maman
Plaisir de voir un maman comme ça
MACHALAH une dame courageuse et très sincère. Je la connais bien mais YALLA nako may goudou fane AK wer. Ale nak mome borome bakh leu. Un modèle de courage et de dignité. Je l adore🤗
Fiere Maman tres exemplaire Yalla nala Yalla takhawou
Takhawou bepp mbollo dioulit
Masha allah yaye boye yalna sa diam yague
G les larmes aux yeux ndeysan merci maman
Haye nduoudal wayy....yaye amoul mborom♥
Machala geugue yalla amale wére allé
Mashallah Mama Yaye ngu ba nda nit tah ngi jul dom mu mel nee teh sonnu si dila nyanal yala bayea la Sah Ale Mboup basi kanam insahallah Waw Waw Mama bou Jongoma la ❤❤❤❤❤ Ameen yarabi
machalla vraiment maman je t aime infiniment bilahi nous aimerions avoir le numéro de ale mboup
Machallah thi sama yaye boy thi
Ma'sah'Allah yaye boy sama xol toyna😭😭
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤je t'adore maman!
Yalla na ma yallah may sokhna bou mèl ni yow❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Waly machalla dome diou bakh dall niépay buega diourr
Yalla nagnou sunu borom fayal sunu yaye yi. Yalla nala sunu borom bayi la ak Alé si Barké Seydina Mouhamed (SAW).AMINE
Maman chérie yalla nala yalla dèfal diam si sa adouna yalla bay lak allé je vous aime très fort
Diam si ioe Allé longue vie à toi😍
Maman yallah gua goude fann ak bépp yaye❤️❤️
ALLAHOUMA AMINE 🤲
Ay way ya ALLAH khamna ni sama khol bi meuneutoul i cried my heart out Allé yalna yallah sammeu leu té doli sa waydiour kholou mougn yalna ya ALLAH yokk soutoureu
Tu es une maman exemplaire si c était une autre femme daf kay sani wala mou négligé ko pour moi tu es la maman de l année
Man amna ci waye moy Sama khôl kouko laal lalma bilahi
Merci beaucoup maman contane ci yaw bou bakh mashallah
ohh la maman elle est extra ordinaire Sokhna si naw nala torop billahi Barkep Serigne Saliou. Yalla nalène Yalla sameu defal lène diam yokk xeweul yi. Sant Yalla warna diam kheuy di diambat rek di dioy di khountou té fo guesto guiss ko tané.
Ho li dawna yaram mashallah merci yaye
Felisitation l'ala emisionbi nekhna
Mon sourire n'arrete op de s'afficher mere bou baxx leu ndeysannn longue vie à nos mères
Geme yalla geme yonéne ba geme bamba yaw dall Yalla nala yalla takhawou barkéb s bamba
Ndeyessan li daw na yaram merci maman
Fière de toi grande dame , sama khol fessna, yalna yalla diapaléla, mayla nga goude fane banga yague takhawou alé , yalnako yalla barkél si way wi
1 u
longue vie á nos maman❤️
Ndeyssan c'est triste super belle maman
Allé mbaye dila gnanal goudou fane ak wer gou yaram yaye boy iow tamite yalla bou yakarr Tass thisa dom djii 😔😔
Yay diou gueum yalla nga maschalla 💕💖💞💞
Keneu d'où aye sou gneupe dawé mofiye nekkkk
Merci beacoup Maman One Love😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍
Machalah li motakh ma beugue sama yaye
En tout cas moi-même je respecte sa mère énormément Mama bonne continuation du courage Dieu a tapé inchallah
Moi aussi
Wally est vraiment généreux
YALA NALENE YALA YOKHE DIAME MACHALA 💖💖💖
Que le Tout Puissant assiste Alle davantage Allahouma Amine
Ale je t’aime j’aime ta maman ❤️
Geste bou Nice Wally merci maman à tout nos maman toujours présente
Thiey yaye mome rek mo meuna supporter yi
Machallah maman je suis de toi
Yaye diou bakh machalla
Ndaysane.... dome meunoul fayy ndayame.... Yaboye Yalla naleu Yalla fayy teu doli leu kholou mougn
Machallah yalla n'a sa diam yag. Une femme exemplaire
Comme Elle l'a si bien dit Dieu ne donne pas certains enfants à n'importe qui....oui c vrai car dou gneupay supporter situation yi
merci maman
Machala maman du courage yalna yalla feye
Alle mboup Je taime comment jaime mouhamed psl
Ndessan dawna tarama yalna yalna khep dolii
Ndysan li déh kepou koy yaye kham gani metina yalla nako fi yalla bayi may ko wér barke serigne touba
Machallah maman je t'adore 😍😍😍
Vraiment maman chérie Yallah nalen Yallah arr soutourallén goudou fan ak werr
ndaye sane allé yalna la yalla Faye sa kholl sisa barki yay
Ndeysane MAMAN mougne rek lo mougne mou dieh
Ndeysanne, cette maman est exceptionnelle, elle croit en Dieu ndeysanne.
Ndeysane machallah maman contane thi iow
Machallah brave Dame gnane yalla Soutoura
Aduna nguii nii yalla défaléne diamou yaye boye
C'est vraiment touchant,
Machallah "j'aime ❤❤❤❤
Machala yalla na yalla Faye lu kawé sak ndiorte ci allé
Dama contane thi sa yaye Alè😍😍😍😍😍
Ndeyessane dôme dôme la rék noume mani di méle dôme la rék yaye boye yalna sa diam yague niga takho sa dôme ji rafetena
Amine way maman woy tamine yabakh yadiapale sadom motah wally ndef lolou🙈🙈
JOURNALISTE BI NEXNAMA 😍😍😍. DAL, TEY, BEURI DIAM ET ELLE NE POSE PAS DES QUESTIONS BÊTES 😂😂😂
Machallah yalna yalla fayla yiw
Sama khol nekhoulwontay waye yaye contane na si ale loll nakh limou begeu yayam
Ndeysane yow mi yay yaye diou bakh yalna la yalla bayé ak Alé samm léne, yir léne, yok séne soutoura ak séne téranga kou bakh nga nitou aldiana nga. Contane na Ndoféne momou nga toude sama dome la yayam sama mak la
Yalla nala yalla may soutoura
bilahi yaye kéne Amoul fayame koudoul YALLA. Merci à toutes les mamans
Machallah sokhna ci
Yalla nala yalla défal diam maman guoudal sa fane
Machaala Yaye Boy yalla nala yalla fay Sa khol
Video bi dou masssa si doyal
Une maman très posé geum borome bi ndeysane yalla nala borome bi taxawou